@@attijanibargny9283 Bilahi lou ler nga wakh. Et c'est comme si tu avais lu dans mes pensées parce que li la meussa gueum. Beaucoup de nos guides religieux actuellement sont loin de ce que leurs aïeux étaient. Malheureusement nak Sénégal dafa beuri ay fanatiques.
@ voilà des Loups à peaux de moutons djegguewou niou sakh Talibe bay nek Serigne. Qu’Allah bénisse nos Actuels Dirigeants Président Diomaye et Sir Sonko rwa
Cette personne de APR a le coeur Gros. S'il ne fait pas attention, sa haine va le Ronger. PM SONKO et President DIOMAYE jusqu'a 2050 et Plus....C'est DIEU🎉❤
Mom dou meussa wakhtaner yalla tessanter rekk ak sagua ay kilifeu lafi neker pere fiii Senegal lah rew miii nioko mom sonko mo la eup dayo si rew mo dinée nak dou deret xam xam lah
Même sou dailoo thia daara dia ,dou am dara,nit gni gnoo nailawatoul.doomou serigne dou serign dai.doomou chirurgien daa ko diokh sa yaram mou opéré la ? Kii day fo raike.tout le monde s'est réveillé.
Bart dé hamna Tay lay moudié wah chaque élections rék mou wah sëgne bi mom lan lay wahat gni ko doon tathiou sonko da and ak ki mën lép mouy dialla dialalo wa haza Kamal
Yalla déf nako sonko yalla mome la andale nagou léne ko guire yalla wa bireum mome khana mome amoule wone téte de liste baye fale kénéne téte de listame bou amé foulla na démissionner
mais il faut faire trés entation ;je pense que on ne peut pas developper ce pays sans serigne moustapha sy ; car il a beaucoup faire pour sonko : victoire ou defaite c'est une question de tendance mais la victoire c'est une question d'objectif
Serigne yi nek si rew mi boulene sénégalais yi Di deguelou c'est parce que sennn Mame yi nioko ligueye défolene fi dra loudoul wakh diou bariii rek d'où kirama d'où karama d'où daye rester à vos places avant que vous ne perdez le peu de crédibilité bi len fi dessé sonko nitou yalla est ce que sakh d'où waliwww en tout cas nioune môme lagnou beugue point
Si tu es un religieux et vrai en toi limites toi aux affaires religieuses et démarques toi de la politique toi qui nomme et fait descendre les présidents
Yallah rekka fi nekka ta moye ki khame , mane ta sagne . Qui a gagne' le combat politique ? Qui ? Mbire fa yallah ta moye borome mbire ta deff louko sobe ta kenna douthi a mana dará
Sonko reck C est PR Diomaye qui doit sifler la fin de la récréation en public. SONKO👉👉👉👉👉👉 est plus BAKH que PR Diomaye donc Basta basta basta bastaSVP
Ce n'est pas les marabouts c'est Dieu...Kou beug Sonko lalala "Jaime".
Serigne bi nit késsé nga...do Yalla...
Yagui diom dé serigne dou melni ko hame ni sa bop rek
Serigne Moustapha, rouslo nga se talibés yeupp. Un conseil: Bayyil di bakkou ak di teukkou. Fi Yalla reka finek
Yalla moy doguale. Alhamdoulilah
Ousmane SONKO d kouko bayi woul do diouk thi gathié, Serigne ou citoyen ordinaire nak nio thi yém.
Nek Serigne wouteh n’a ak domou Serigne. Domou médecin dou médecin, domou mécanicien dou mécanicien Salam au Sénégal
@@attijanibargny9283 Bilahi lou ler nga wakh. Et c'est comme si tu avais lu dans mes pensées parce que li la meussa gueum. Beaucoup de nos guides religieux actuellement sont loin de ce que leurs aïeux étaient. Malheureusement nak Sénégal dafa beuri ay fanatiques.
@ voilà des Loups à peaux de moutons djegguewou niou sakh Talibe bay nek Serigne. Qu’Allah bénisse nos Actuels Dirigeants Président Diomaye et Sir Sonko rwa
bien dit mon cher .toi au moins tu n'es pas fanatique@@attijanibargny9283
Sonko dou chantage kaine,khamoul loolou.yaw nak sa wakh dafa bari , dang gnou doone poobar,yaala kaani la!!!
Cette personne de APR a le coeur Gros. S'il ne fait pas attention, sa haine va le Ronger. PM SONKO et President DIOMAYE jusqu'a 2050 et Plus....C'est DIEU🎉❤
SONKO Moy Diomaye. Diomaye Moy SONKO, ils sont Indivisibles point😂😂😂😂
Bilahi deh 😂
Fi Bour yalla rek mofi nek
Seydina Ousmane sonko yallana nako yalla same barkelé si barke nabil moustapha psl ❤❤❤❤❤❤❤❤
La même chanson : Diomaye kou baakhe 😂😂😂mais Sonko est là pour protéger Diomaye de ces vautours sans scrupules 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Beugg sonko day yokou weurseuk
Mom dou meussa wakhtaner yalla tessanter rekk ak sagua ay kilifeu lafi neker pere fiii Senegal lah rew miii nioko mom sonko mo la eup dayo si rew mo dinée nak dou deret xam xam lah
Les soies disents talibe warna no yewou sii fenn kat yiii
Yéwou diotna dall
Serigne bi Dh sopp nagn la wayei nak danga wara moytOu politik bi
Sonko Rike sonko moye domay domay domay ❤❤❤❤❤❤❤ yalla reke moufi nke kenene nkufi
Sonko Rike sonko moye domay domay moye sonko focus 2029 💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯
SONKo 130😂😂😂😂😂SONKo 130❤❤❤😂😂😂😂💪🏾👌
Khaar nga Sonko thie législatives, législatives yi passéna. Ce n'est pas les marabouts c'est Allah le Seul Tout Puissant. Loudoul Yalla di néne.
Ma sha Allah in sha Allah la situation du Pays est decantee depuis belle lurette l
Diomaye bakhna manam sonko mo bonnn wala budoul wonn sa mame elhadji malick yaw 2 persone doula top delouwatall si yalla ak lissa mame nèkonnn
Gnii gueumouniou dara d'Ay doul rek taph
Même sou dailoo thia daara dia ,dou am dara,nit gni gnoo nailawatoul.doomou serigne dou serign dai.doomou chirurgien daa ko diokh sa yaram mou opéré la ? Kii day fo raike.tout le monde s'est réveillé.
Pitié à ceux qui croient à ces paroles "ma takh li am ma dogal li"
Yemal sisah dahira bii mo guenn si yow pur dou touss
Ĺoloude aye fenela
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Golo gui doul rék laye déff😂😂😂😂😂😂
C est pas les marabouts c est Allah soubhana Talla Allahou akbar
Machallah 🇸🇳❤️❤️🥰🥰🎉
Khamna wa Pur Sonko laniou votel ,papa😂😂😂
Var fen rek 😂😂😂😂😂
Alhamdoullh ❤❤❤
Bart dé hamna Tay lay moudié wah chaque élections rék mou wah sëgne bi mom lan lay wahat gni ko doon tathiou sonko da and ak ki mën lép mouy dialla dialalo wa haza Kamal
Légui kheuyneu sénégalais dinagn bay di tekk serigne yih fouyou aguoul...
merci
@@yvefay620 mogueune deh
Yalla déf nako sonko yalla mome la andale nagou léne ko guire yalla wa bireum mome khana mome amoule wone téte de liste baye fale kénéne téte de listame bou amé foulla na démissionner
mais il faut faire trés entation ;je pense que on ne peut pas developper ce pays sans serigne moustapha sy ; car il a beaucoup faire pour sonko : victoire ou defaite c'est une question de tendance mais la victoire c'est une question d'objectif
Mr Sonko est beaucoup plus avisé spirituellement que vous tous
Hooôo c'est dieu
Yalla rék mooy dara koudoul😂yalla Mbindèff kèsè nga
Boye serigne bi kilipha la serigne tanou wouco si Sénégal
Serigne yi nek si rew mi boulene sénégalais yi Di deguelou c'est parce que sennn Mame yi nioko ligueye défolene fi dra loudoul wakh diou bariii rek d'où kirama d'où karama d'où daye rester à vos places avant que vous ne perdez le peu de crédibilité bi len fi dessé sonko nitou yalla est ce que sakh d'où waliwww en tout cas nioune môme lagnou beugue point
batylemine ba djisgua yalla❤❤❤
Serigne bi kone mom dou mag nii!!!
Sonko, le démonstrateur des Faux tipe. Son seul défaut est : il ravage avec bruit.
Barthélémy le 17 passé guiss gueu yalla té batay khamo yalla 😂😂😂😂serigne moustapha mom keneu menouko wakh dara ndakh serigne cheikh tidiana 😂😂😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo Sonkooooooo a Viv bro Freeeeeeeeeeeeee Senegal
Lii wonn wonninaa! Kou yabou khamm koo ! Soo yeugonn demm élection yaww rekk andd bi amou ndieurignn ndakh d'où deukk !! Ayy wayy le 17 ????!!! 2057 lagniouyy wakh
Si tu es un religieux et vrai en toi limites toi aux affaires religieuses et démarques toi de la politique toi qui nomme et fait descendre les présidents
Pur tass na
Sa seuyou ndiay tass mo gueuneu gaw tass pur
@@SokhnaoumoukhaìrySeckseuyou yayou moustapha sy ak bou bayame lagniye katte ndayame tass😂😂😂😂mouye mélni golo😂😂😂😂domou sarape ndayame bi😂😂😂domou biireule bi
Ki dou darra yague nko deff
Yallah rekka fi nekka ta moye ki khame , mane ta sagne . Qui a gagne' le combat politique ? Qui ? Mbire fa yallah ta moye borome mbire ta deff louko sobe ta kenna douthi a mana dará
Mais Serigne limou wakh grawoul mane dh sonko la andal mais am na boy you réw th khamognou am léne respect si nit yi bayiléne saga😮
MOUSTAPHA SY. TOROKH NGA DE. AK SA BAKANE. NAPATAI REK😁😁
Gnii took fii,a côté de lui gnoo amoul kilifa ! Moo daifal bakanam na khoulougnai(diakhato)
Boy y’a ngui déconne deh😂 mais amna Serigne youy mothieu bakene ba mou Nice 😂😂😂😂😂😂
@@attijanibargny9283 indique moi un de ces serignes ndakh sama deukaalai bii bakanam dafa khoulougnai
Féne rék.. yalla la
Barthélemy à vue dieu et je pense que il a bien compris que dieu est avec sonko est le peuple sénégalais
C pas les marabous c Dieu ❤ sonko
Pros yalla rek la yaakaar te yonnentebi more royoukayame si politique. Incha Allah kene dou ko time kene Douro skami
Rewmi kay diakhasowoul yalla mo yor ay dogalam diko dogal nimouko nekhè
Yala rek mofi nek
Je Monsieur j'ai l'impression qu'il ne connait pas mieux le coran, il parle avec beaucoup d'émotion et sans prendre en compte Dieu.
Thieuy Sénégal........
Ki mome moussoul andak kouye gagner
😂😂😂😂😂😂thiey les vautours
❤❤❤❤❤❤❤
😂😂Ha Barthélémy khame ngua yalla dé
Dioulil yalla ak dioulil wakhtou bokoul
Thieuye yalla Diomaye dè sonko mokofi tek bou bakhè ndam la pour sonko
Way qui dou darra nit la kom gneup dafay léque d'y poube bou ay fanam diékhé dafay déé come nieup fénn rékk léyy déff
SI TU POUVAIS POURQUOI TU L'A PAS FAIT POUR TON PARTI AUX PRESIDENTIELLES?
MACKY SALL C'EST PAS TOI QUI L'A DÉGAGÉ...CESSE TES ""FILMS""
Vraiment !!!!
Lii tamime rouslou na
Serigne bayil khel sa jamboot gi ngir yalla
NB : adji wakh diou nekka bou bagne' am kersak wakh , re'thiouk wakh walla gathial wakh ; na bayi khe'le boukha bakh thi sama gnati ( 3 ) bate yile' : 1 _ na bayi khe'le boubalh thia limouye wakh . 2 _ na bayi khe'le bou bakh famouye wakhe' ( le milieux ) . 3 _ na bayi khe'le bou bakh thia lamou dieume' wakh día . Yallah rekkaye ki khame , ame m , mane ta sagne ta dogalanga fa mome ta pare' leppa ; ay re'dultats rekka lagnouye khare walla dieuli .pas plus .
Ki dou dara 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
،🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳😭😭😭😭😭
Un narcissiste pur et dur!
Serigne Day ndiaboté ndieup ta bayi parparelo ak teukou ak chantage.
Le VAR que des mér gadou sur l affiche. Allahou Akbar
Sonko reck C est PR Diomaye qui doit sifler la fin de la récréation en public. SONKO👉👉👉👉👉👉 est plus BAKH que PR Diomaye donc Basta basta basta bastaSVP
Bakhna bouléne bayi souniou wadji yalla rék moy bour.
Héy serigne bi boul faté yaleu ak seu mame!!!
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Sering bi thi tapalekatyi la bok
Doule rék laye déff 😂😂😂😂😂😂😂
Doul rék lay déf serigne by
Bamiy miti Serigne Moustapha moko done défendre et il sera notre chaykhou ilal abade
Y'a meuneu doul
Ki d'où touss daléni nakh rek di lékk sén adiya, c'est un weyou yalla
En tout cas, euliw mooko eupe baatine,mooko rawoone aussi thi sondage yi
Bou dai mooye yaala na taw boulettes, gnou sooss
Yaw bou gayi di sonne nga nék sarone lall
S Serigne a été utilisé
Moussthapa sy bayél dor yi dodara
Allhamdoulillah
Yala rek
Et Diomaye dit ne pas savoir "chanter."
Diomaye est le bon... Sonko est comment?
Seule la lutte libére. A la suite, on récolte. Le peuple jugera.
Diomaye moye SONKO
😂😂😂😂😂❤❤❤❤
😂😂😂😂👍🏾🙏🙏🤲🤲😭😭
J'aime ❤❤❤
Allah ne dort pas
Nek sa biir ndiabott di wax loula neex yomb na lool
Wagathiergui nite antane nako thieye yala
en tous cas Disneu trop ..dolene dimbalie xi ènn bi ?
Lepou yala waye dogedara
Bart nopaloul sì var yi sonko menelou lénko Dara 😅
Yeena'gata'kheel'waxji'elecson'erk'geensi'khalat'
Cest un arrogant
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😅😅😅😅😅😂😂😂😂😂😂
P M je vous invite à ne pas répondre celui-là rappelez vous de sa déclaration quand Khalifa Sall était face au Président Macky Sall.Chantage rk
Serigne bi kou deglou ay wakham dinga setlou né coalition sam sa kadou teugonagnouko bou yague cinq guinao pastef.
Khamal loye wakh menouloo dara gathié rek ngay amm.
Pourquoi il na par pu prier pour k impur meuneu am 90 députés à lui tout seul,sans coalition ?