Elevage Tv Oudé Diagne

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 фев 2025

Комментарии •

  • @gueyepathe4344
    @gueyepathe4344 4 года назад +1

    Machala éleveur yi di wakh loudoul deugue si kharyi ,di wayi séni âge ak diléne outal pape ak Yaye ,seete léen sén diguenté ak sougnou Borom!

  • @papeboukarsene1569
    @papeboukarsene1569 4 года назад +3

    Très professionnelle on note une amélioration courage à élevage tv

  • @vieuxdiop583
    @vieuxdiop583 2 года назад

    Machalah je ne connais pas le monsieur mais tarkala il communique bien et sans complexe

  • @moustaphambdiagne4091
    @moustaphambdiagne4091 2 года назад

    DIAGNE NAR KÉWEL DOU TEUP DOM DIA BEUTE DA GUA DONOU BAKH SEUT GUA THI YONEN SA COTÉ YAYE ,SEUT GUA THI ABABACAR LE PREMIER KHALIF DU PROPHET .yow da ngua bock thi niou BAKH ngo.téraye ngu koï neck yalna n'a yalla teral DIAGNE.SA MAG SA KHA KILIFA MO DONE DEF THI YAW AY SÉDÉS.Q'ASWT TE PROTEGE AMEN.

  • @aminefall1905
    @aminefall1905 4 года назад +1

    Macha Allah liguey bi rafet na père Oudé di pa bou bakh

  • @mortallamboup7796
    @mortallamboup7796 3 года назад

    Machalla Pere wakh dji rafettna trop machalla lepou Lo guis rek nako degeu lall

  • @ibrahimasylla7087
    @ibrahimasylla7087 4 года назад +1

    Macha alla dioby rafétna