Contene na trop vraiment Machallah Aziz Ndiaye et baye Ndiaye souma sanione ngéne bayi lambe ji té xam ni li ameko yomboule yalla na yalla sam mbolém kilifa diné Sénégal yi contane trop vraiment 💖💖💖
Gno gui lay siaré sy Malick rafét na t nila massa mél yalla nafi khalifa seydil hajj Malick ak ndiabotam yeupp yagg fi t Andak Wér, séne and démb la wéssu n'a sounou dioudou yagg lén fi gnéne nittou yalla yeupp si barké seydil woujoud bi gnou bokk Amine
Amna solo dh yalna yalla fayal gnou Serigne Babacar ❤️ Sy Mansour ❤️ te samal gnou ko ak bepou kilifa diiné
Amine
Ohh machallah 😍😭 khol seddna❤️😍 meussoma commenté wayé tay il faut que ma deffko ndakh khol bou sedd❤️😍
Contene na trop vraiment Machallah Aziz Ndiaye et baye Ndiaye souma sanione ngéne bayi lambe ji té xam ni li ameko yomboule yalla na yalla sam mbolém kilifa diné Sénégal yi contane trop vraiment 💖💖💖
Machalaa yalna diam yaaag
A
..
MACHALLAH yallana jammou yague l'or
Machallah liiii rkkk moye tarou senegalll Diame ak salam khoulll sednaaaa troppp
Ohhh ohhh liforena machallah machallah amena solo merci talibechiékh dieurdieuf merci sy malik
Ma Sha Allah laf thiat, amna solo jaajeuf. Jaajeuf sounou mag gni
Li rek moi senegal 🇸🇳 walahi tivanone ak touba nyo boko ndey ak baye. Kontan na walahi
Machala khôl sede na yalla nalen fi yalla yagal 🙏🙏🙏👌👌❤️❤️
Machalah yalla na yalla fay yiw 🙏❤️🙏
Machala yaalna yaala barkél amine amine amine yarabi machala
ماشاء الله بارك الله فيكم
Mach'allah mach'allah mach'allah
Machallah Amna sollo,🙏🙏🙏
sama yaram dawna😭 wallahi lii amoul loko guena rafett
Manchalla 🤗🤗🤗🤗🤗🤗😘😍😍😍
Machalla rafiitna loul le lanou baga se sounu Senegal
Hoo li nekhna si khol bou Yalla nek bilakhi 😭
Machalla amna solo
Mame maram ak mame maty mbacke rekla .
Machaallah khôl sédna
Machalla ❤
Ndeysaan !!
xol yépp sedd na !!
yal na saa boroom dolli jàmm ci Senegaal te yàggal fi sjnu kilifa yu baax yii.
Machala
Li nekhna machalla
Machiallla
Mashallah khol cédena
Machalla yalla diam yague
Mashallah
Machallah rafétna machallah 🙏🙏
Macha Allah rafetna lool
Gno gui lay siaré sy Malick rafét na t nila massa mél yalla nafi khalifa seydil hajj Malick ak ndiabotam yeupp yagg fi t Andak Wér, séne and démb la wéssu n'a sounou dioudou yagg lén fi gnéne nittou yalla yeupp si barké seydil woujoud bi gnou bokk Amine
Machallah khol sedna yague fi lol mbacke
yalna jamm yague
♥️
Machallah
Macha Allah
Machallah
Machalla
Machalla
Machalah
Machallah
Machallah
Machalla