Oh franchement kiné mérite d'être heureuse damako yeureum sakh vraiment kiné ak Nice couple machallah elle joue bien son rôle ndeye Ndiaye dou nitou fi khol ko ak lunette yi rek bonne soirée l'équipe de polygame meilleure série de sa génération bilay 😍🥺
Ndèye Ndiaye et Serigne Khol disent qu'ils ont vu en rêve Binôme. Moi aussi. Il me dit : "Fata, va dire à ma fille Oumou de te donner une des maisons que j'ai laissées et 2 000 000f, car tu me faisais rire quand tu te moquais de moi dans tes commentaires". Oumou, si tu lis ce commentaire, appelle-moi. Mon téléphone est samsung galaxy. J'attends ton coup de fil🤣🤣🤣. " Ay waay, Binôme , goudeul fane 🤣🤣, yaa baakh, dama sooneu thi mbakhal mi🤣🤣. LOVE
c’est tellement difficile de perdre un enfant😢 wallay kiné je te comprends mane mi defna 2 fausse couche batey les séquelles restent en moi tey magui ni am eub bou takhaw rek lay nianr yalla😢😢😢😢
Seune est excellente actrice maLgre que c’est sa première apparition dans les séries sénégalaise mais on dirait qu’elle a duré dans le milieu de la comédie 😂❤
Ba a renversé une situation défavorable à son faveur laissant ses épouses et leurs coalition bec dans l'eau. Je lui donne les 5 étoiles. Bravo a toute l équipe.
Vous voyez l’attitude que bou a ne jamais se remettre en question c’est pouvoir la que la société a donné à l’homme sénégalais. Les blessures de fat kiné ne vont guérir parce que la personne qui est la cause de la mort de son fils c’est Amina. Et ça bou n’arrivera jamais à le comprendre .
Vraiment la discussion de Bou et Kiné m'a beaucoup touché....... ce qui montre la complexité d'un couple peu importe le problème . Ma future femme 🥰 hunnnhunnnnnnnn .......
C’est vrai dehhh 😂😂😂😂pourtant je suis comme ça j’aime développer les faits J’explique comme un bb de deux ans 😂😂😂😂 Lolou leppp nakk jalousie la ak imagination irréelle 😂
K'allah accepte nos prières et nous pardonne nos pêches
Amine
Amine yarabi cheikh bi ya bax
Amine
Amine yarabi inchallah
Amine
Kou beugue seydina Mouhamed lalal j'aime
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
خير الأنبياء والمرسلين سيدنا محمد صلى الله عليه وسلم 🥰❤️🌹
Psl ❤❤❤❤
Salah lahoualeye wasalame
PSL ❤️❤️
Kiné ak Astou leur teint Masha Allah 💞 Le regard de bou 😂😂
Et la fille de astou aussi
Diamant ⚫noir dara dakhouko 🥰
Fat kiné elle joue avec toutes ses émotions. C'est la meilleure actrice de polygame
Vraiment
Et ndeye Ndiaye
Meilleure actrice c’est ndeye Ndiayee
@@gagnesirybeye6410 c'est vraiment difficile de trancher, chacune à un jeu particulier.
C vrai,actrice deug sou beuguei dioy dafay dioy
Mn homme est très malade svp prié pour lui yalla feugg bopam mou tané si Diam 🙏
Yalna weer ak diam way
Defalko falakhi ak nassi Inchallah si ndokh mou nanko INCHALLAH
@@fatimadiouf3829 ay way aminnn way 😭😭😭
Yalnako Yallah mey werr si barkè Naby Moustapha SAWS
@@modousylla6262 inchallah oh vraiment merci bcp 😭
Ndeyssan la base d’un mariage réussi c’est la communication. J’ai beaucoup aimé la conversation Bou-Kiné. Djiguene gaur moo meuneu dalal khelam
Astou est trop forte tellement naturel dans son rôle
Mais bou je t'adore tu résonne bien et tu joue bien merci à toute l'équipe polygame kiné soit Forte tu as trop suivie ta maman
Bou qu'elle gentillesse avec ses deux femmes je l'adore vraiment 👏👏👏👏👏👏
Ohh la beauté d'astou me dépasse vraiment ❤️🥰
Elle est trop mignonne machalah laff bouch 🥰❤️
L'arrivée de binôme rek lay khar inchallah 🤣🤣
Bou boba Ba lay yobou centre de redressement mom mi andi information bi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@ahmadou5507 lolou la ba pour une fois ba souffert 🤣
bayyiko rek
Ma puce boul yakamti 😂😂lgui mou gneuw
Da nara khar ba badiene am dieukeur mou doga gnew🤣🤣
Oh franchement kiné mérite d'être heureuse damako yeureum sakh vraiment kiné ak Nice couple machallah elle joue bien son rôle ndeye Ndiaye dou nitou fi khol ko ak lunette yi rek bonne soirée l'équipe de polygame meilleure série de sa génération bilay 😍🥺
Person ne la comprend elle souffre
Waye dou def lou bakh
@@mariamadiop5640 c vrai defkatt la mom té lamignam gnawna
Kiné kou réw leu ,, kén douko comprendre na gnioussou falé
Soudone def lou bah waw mais nek si keur gui di reqantou , goor loumla beug beug so ko respecter woul respecter ay parent wam rek yaheu lep
Ndeye Ndiaye ma préférée ❤
Ndéye Ndiaye sama domou Baye meilleure actrice de l'année mais nak aka féroce 😃😃😃
Thiey sama xarit bi fouma dem feklafa
Bilae feep lay guiss commentairame 😂😂😂
@@aichadiallo1342 Ki kay mome amna mèlokan
@@maimounathiam2748 😃 dégall ma Thiam Babel m namenala dé
@@aichadiallo1342 Wa Aïcha guis nga damaye bagne kéne mérr 😄
Ndaysane couple bou fate kiné dafa raféte machallah ❤️🥰
Une journée sans Ndeye Ndiaye Ho c'est un repas sans sel hier dara nekhoussi
Ndeye ndiaye je l aime bien
Ndèye Ndiaye et Serigne Khol disent qu'ils ont vu en rêve Binôme. Moi aussi. Il me dit : "Fata, va dire à ma fille Oumou de te donner une des maisons que j'ai laissées et 2 000 000f, car tu me faisais rire quand tu te moquais de moi dans tes commentaires". Oumou, si tu lis ce commentaire, appelle-moi. Mon téléphone est samsung galaxy. J'attends ton coup de fil🤣🤣🤣. " Ay waay, Binôme , goudeul fane 🤣🤣, yaa baakh, dama sooneu thi mbakhal mi🤣🤣. LOVE
Fatal ma fofou😁😅le réve est permis 😁
Manit meunala wo😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@mendesshasha1021 bien sûr🤣🤣
Fo sén 77 rek manla 🤣
On réclame le bonheur de kiné😭
Vraiment elle le mérite 🙈
Kine parfois elle degame vraiment
Kine deh bo beugue bonheur dina ko def dafa commencer soof vraiment
Voilà bou est trop romantique mâcha Allah! J’adore sa sincérité envers ses épouses !
J’attends le retour de binôme 😂😂
Gno bok lignouy xaar
😂😂😂😂😂👍
Dou yow rek
Béna gui
lol rk lay khar
c’est tellement difficile de perdre un enfant😢 wallay kiné je te comprends mane mi defna 2 fausse couche batey les séquelles restent en moi tey magui ni am eub bou takhaw rek lay nianr yalla😢😢😢😢
Yalla nassi yalla def soutoura inchalla 🙏🙏🙏
@@nogayediop2396 amine
Yalla na yalla defal lou guene si yaw inechalla
Yallnalako yalla mbaye thi barkep cheikhoul khadim 🥰🥰🥰
@@aidaguisse3207 amine
Bou meneur de jeux 🏀.
Ndaye Ndiaye néna Bâ âge yép amgako🤣🤣🤣💃
Khamna amna 65ans,40ans,35ans ak 25ans🤣
Kou beuge sa yaay lalal j'aime ❤️❤️❤️
Teams Belle manifester vous 😂😌😌
On réclame le bonheur de Thiam ☝️😭🙉🤲
Encore toi 🤣🤣
On réclame l bonheur de maty gueye 💃🏾💃🏾💃🏾💃🏾
@@awadiop3660 😂😂😭😂😂😂
@@khadidiatousylla6262 🤣
😂😂
Famille sénégalaise legui comme infideles série polygame rek ngayi tok Di setane ak sa wakeur te do rouss do yoree commandé bravo
Seune est excellente actrice maLgre que c’est sa première apparition dans les séries sénégalaise mais on dirait qu’elle a duré dans le milieu de la comédie 😂❤
Ay koumay dimbali ma ame numéro fat kiné j l'aime bcp walahi
Kou beugue Sénégal dieul coupe du monde lalal j'aime
Astou est très belle machallah teh yeugou sakh machallah machallah machallah
Kou beugue Fat Kiné ak Bou mel com niniou mélone avant lalal j'aime ❤❤
Astou est naturellement Machalah ❤
Waouh 🤩 fat kiné linga sol si 1ères minutes yi diapp nala
Mais Ba est vraiment fort, retournena situation bi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Bou deh koumou poème nga yakarni yaw rek la beugg 😂😂😂
NDEYE NDIAYE, say lunettes raffett na torop
Ca te va a merveille
Nice na mome 😊
Kou d'accord ni Binôme déwoul rek lalale j'aime ❤❤❤
Kiné li boko ndieuké wone kone li yépp doula dall mes ndaye ndiaye yangi belle mignonne ni deigueleu 🥰🥰
Oh la la sucrée et choco bravo et merci pour l'émotion que vous avez pu véhiculer chapeau aux acteurs de polygame. Vivement nos deux épisodes ! Salam
On réclame nos 2episodes par jour😍
Vraiment dafa diot
J’aime ndeye Ndiaye et fat Kiné
Ndeysannnnn kiné vraii actrice leu loko diokh mou done ko carrément machalahhh ♥️
Ndeye Ndiaye nena Ba age yeup am nguako 🤣🤣🤣🤣🤣🤣.
Cette femme c'est la meilleure.
On réclame le bonheur de Fat kiné elle mérite d'être heureuse té en plus elle joue bien son rôle
Fatou kine et bou m ont fait pleurer 😢ohhh l amour ❤
Bouléne faté salatout ala nabi ❤❤❤
Euuy Way bi Déclaration Way
Awo Yako Yoorr.
Maa Shaa Allah
Seuy Reik. Seuy Ba Dé
Ya Djitou tchi Khôl bi.
Kiné GorGorloul.
Dina Baakh.
Merci Polygamie.
Djitou woul si xool bi mom😩😂😂 blague😌
@@famasakho3728 Fatou Diop mii deh awo bouy deufeul bopam la 🤭🤣🤣😂😂😅😅
Lii mom communication nak. Chapeau à Bou et à fat kiné. Tous les couples devraient communiquer de cette manière.
vous êtes les meilleurs ♥️♥️♥️♥️♥️
polygamie ces super😆😆😆😆😆
Kiné t'es toute belle vraiment ❤️❤️❤️❤️❤️
Fate kiné est belle et charmante machallah
Oh c bon l'amour Fatou kuinè ont t'adore
Bilahi Khady Baba ak Ndèye Ndiaye Astou non duo bou doywar 😂😂😂😂
Bobou kay trio leu 😂😂 nioo nekhal série bi
Ndaye Ndiaye Ak léna😂
Jtj meunou mako mougne
Ndeyssane la discussion entre bou et kiné m'a fait pleurer c sa une relation il faut toujours communiqué
Khady mom Hana legui publicité lagn ko teguei si série bi😂😂😂😂
bilay😂😂😂
Fatou kinè fait de chantage émotionnel 😂
Kii dafa yabatee fat Kiné, mais Bou la fiyy feekk
Je crois qu'elle souffre énormément
Anhan😂
Fat Kinè kéneu khamoul limou beug
Yéne kiné da soufrir khol léneko siséne bopp
Ndeye ndiaye tay ay lunette la lal dèh dama ko beugue bilahi 😭😅🤣😭
Kiné personnes ne le comprend mais elle souffre
Parfois nitt dina ame yéneu comportement yi mais ses sa matière de ce protéger
Vraiment laf thiat vous êtes les meilleures. Tout est riche
Ba a renversé une situation défavorable à son faveur laissant ses épouses et leurs coalition bec dans l'eau. Je lui donne les 5 étoiles. Bravo a toute l équipe.
Sama actrice préférée Fat Kiné goudal fane✅✅✅
Merci kine et bou, il nous faut un couple référence bou dara mounoul destabilisé
Vous voyez l’attitude que bou a ne jamais se remettre en question c’est pouvoir la que la société a donné à l’homme sénégalais. Les blessures de fat kiné ne vont guérir parce que la personne qui est la cause de la mort de son fils c’est Amina. Et ça bou n’arrivera jamais à le comprendre .
Polygame notre dose matinale, légui dose noctambule la,merci à toute l'équipe et aux téléspectateurs accros à cette série
Ndeye ndiaye bilahui ma beugeux sa façon de parler tu joue bien ma grande actrice préférée
Thiey ndeye ndiaye notre actrice 😍😍😍
❤❤❤
Lunette yi😂😂
Intellectuel là woté ak classe 😂😂😂
@@amyngom2888 ndaye ndiaye dou nitou fii 😂
On réclame le bonheur de Maty Gueye Cherie Thiam ☝🏽😭🙈🤲
Surtout lolu 😂😂
Dako aimé dé
Mercii là-bas 😂😂😂
@@maguettefall8261 guisso lolou
😂😂😂😂😂😂soye Kane chérie Maty Guèye dafa khoulo ak bonheur khana gnou diéme lène dioubolé ba kham😂😂😂😂Maty mougnal rek yalla bakhna
On réclame le bonheur de Thiam 😭🙈🤲🙏🏿
Yalla na belle embe ndakh kine regler sof na legui
nonou la faye de mer
Da warra embe mou nekh
Histoire de vous dire que Ndeye Ndiaye ak Astou damaléne beugue 🤣🤣
J'adore le couple de bou et fatou kiné
Vraiment la discussion de Bou et Kiné m'a beaucoup touché....... ce qui montre la complexité d'un couple peu importe le problème . Ma future femme 🥰 hunnnhunnnnnnnn .......
😂😂 inchallah
😂😂😂d’accord mon futur mari
@@diadiarassoul4336 🤫🤫 hunuhun ........bahna dal
@@diadiarassoul4336 niewlen ma mayelen
@@khalifaababacardieng9255 😂😂😂😂gnou nopi
Sacrée Ndèye Ndiaye 😂, néna film bobou mako réalisé. Yaw kaye ya réalisé films yeupe. Tu es dans toutes les sauces . Bonne continuation les gars
Ba dina fekhe ba diakhaselen ba ken dotoul wakh thi wakhou thioro😂😂😂
Nieuwou binome si keur gui, keur gui lay dèff daum😅😅ki nga ndiekeu anonsè dèwou binome amna sokhla😅😅
Kiné elle joue bien mais explications you bari moko sonal day wax rk di expliquer rk di détailler 😂😂😂😂
Li la halate rek lire ko😂 Elle parle trop 😂
Résumé la diagoul 😂😂😂 trop de répétition
Comme kouy disserter
Je jour je dis la même chose détaille yi mo bari
C’est vrai dehhh 😂😂😂😂pourtant je suis comme ça j’aime développer les faits
J’explique comme un bb de deux ans 😂😂😂😂
Lolou leppp nakk jalousie la ak imagination irréelle 😂
Kiné sa teint noir lanela! MachaAllah way 🥰
Ons réclame la bonheur entre belle et maman Seune
Bou nènêko mala eumbeul.
Une femme aime qu'on la rassure.
Vives les femmes: nos mères, nos femmes et nos filles
Astou elle est très belle machalla 🥰
Ndeye ndiaye nena bâ age Lep am nga ko😂😂😂😂😂
yaw midi ler sama commentaires Magi lay nianal diamo AK feke
💝💝😂😂🤣🤣
Amine yarabi
Fakiné mome bala may beugue dée rek mouy tafanto ay niak dome bouniou fonto lingay def yako tay 🤣🤣🤣 ahhh
Moko tayy dé
Loumou def Manassé guéne
Hana dafa égoïste rék
Koume donne yaw tamite nga deff lou raw limou deff mayy lénegnou yéne yéne soff way ichh
@@sayemboup1382 Ay gnarel lanou🤣
Kou setlu bopu Bâ bi commencement bi ak fin bi faux record 😂😂😂
Ndeye ndiaye 🤣🤣 goor leu wala djiguéne
Merci polygamie
Ndeye Ndiaye damako beug béééééé MACHA ALLAH
Ndeye Ndiaye je t’aime Billakhi 😂
Fat kiné dafa rafet enfait 😊
Très belle même
Femme noire personnifiée mooy kiné
Agresser notification voilà lii dafa nekh wayy on vous adore ♥ wayé traumatisé guene gnou ah ben épisode
Hbd a Ba 🎉 doundal Way dinou yaga bégueul barkép Cheikhoul Khadim 🙏🙏🥰🥰
Ay ay nouyou nalén kouma djitou ani wa team polygame 💃 🏃♀️ 🤣 ❤❤
Magui nii🤣🤣🤣🤣
Kiné li lep ta maman molako tek, so regléwone do âme woudiou. Bou sois plus responsable aussi c'est trop facile de rejeter la faute aux autres.
Ohhh un mari comme Bou ou rien il est tellmnt Romantique ❤❤jadore
Manit un mari kom bou la beug
Comme sama Bose
Kéne dou sama firdawsi MBENGUE MBOR chéri soxna diarra goudeul fane barké borom touba
@@sokhnadiarradiopmbengue9587 laye yaw togue ak yak dunala sonal Mbengue beug thiep
@@awasall9536 no xamé lolou walahi mbenguéne lkk rk laniouy df😀😀😀
Bâ yalla maynako loka wakh amnathi tontou😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Tontou kay dako man rkkk
Khamone nané bounguène parer ba Bâ répliquer dotou lène ko défati 🤣🤣🤣. Il vous a eu encore une fois
Astou❤️❤️❤️❤️L incarnation de la Beauté Noire 👏🏿👏🏿👏🏿
ndeye ndiaye astou motakh may sétane tjrs gnou bégal niou😂😂😂🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😙 séne duo mo. nekh
Fat kine da fa firr torop ndeysan da ma ko yeureum sakh li ma nekh thi ba Moy da lay degue Lou ba gua pare mou tontou la 🤣🤣🤣🤣
Bou fat kine meilleur naro len wone indi belle mouy yakeu couple bou nice bi .thiam mo warone nekeu polygame. On reclamme le bonheur de kine way🥰🥰
Mé tay dama contane si nd Ndiaye AK khadi baba sén dioubo bi nekhnama
Ayyy wayyy bou mo faux ndeye Ndiaye je l'aime dal
Ndeye Ndiaye tay dagua geuna mignonne 🥰
Bilaye ki dama ko beugue
no limou def dako dapp
@@diarrajuniorndiaye5875 trop sakh
Bou je suis parfaitement d'accord avec toi kiné a beaucoup abusé... beaucoup de leçons merci à toute l'équipe