Kawtef Abou Diassé menace fadam 2 et bour guéwéle kou wakhati siteu béne batt.. hé alouna

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 дек 2024
  • 🔴✅Abonnez-vous ✔ | et ✔Activez Les 🔔NOTIFICATIONS👇
    👉 / senlambtv
    👇Vous Pouvez nous contacter sur:👇👇👇
    📞🔊WhatsApp: +(221) +(221) 78 124 84 76
    Facebook: 👉 / sen.lanbtv
    Instagram: 👉 / sen_lamb_tv
    #luttesénégalaise #senlambtv #lamb

Комментарии • 129

  • @rawanegueye7991
    @rawanegueye7991 День назад +18

    altopé nga abou modou Lo moy sene baye 😊

  • @abdourvms6034
    @abdourvms6034 День назад +21

    Roi des bavards meun guén ko dieul dh si lamb dji blh 😂😂💔🤦🏾‍♂️ MXLÔ togn naniou kw Kay niou abal len couronne bi 1 mois pr guén nopi tutti skh 😂😂🤦🏾‍♂️

  • @CoumbaPouye-m4l
    @CoumbaPouye-m4l День назад +9

    Yow talale sa bop mo guene Al tope bi nioune Modou seul ❤❤❤

  • @mbagnicksenghor5886
    @mbagnicksenghor5886 День назад +4

    Bravo 👏🏾👏🏾👏🏾 Siteu day derangé lolu rekk la,té bu bayè Lamb xoromsi jexx

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 День назад +4

    Abou Naysan Mom Daa beugeu Siteu thibirr xolam naysan ❤️❤️❤️yalnasène jameu yageu way limoy deugeu deugeu xarith bou mètè nieupou Daww Taxawal limoy Djikoy gor dii Djikoy Garmy Abou Yaw Matnga xarith ✍️jameu thiyène toujours ✌️

    • @Amadouna-pe8eh
      @Amadouna-pe8eh День назад +1

      Premier nonou Modou lo Moy wa dji 😅😅😅😅

    • @josephericousmanediandy783
      @josephericousmanediandy783 День назад +1

      Ki seytané laaaaa wanté dingua sonou deee😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 sa xol d'où neixxxx si wa Parcelle deeee 😂😂😂😂 ay réeee nguama deffff sax

  • @MbayeFaye-d4v
    @MbayeFaye-d4v День назад +2

    Guiro 😂li la khamone 😂 Modou ay éléments wam sakh dagnô khérré😂

  • @omardieng5422
    @omardieng5422 День назад +2

    siteu kasé❤❤❤❤❤❤❤kousisou sadata yaye

  • @KhadyGaye-n5g
    @KhadyGaye-n5g День назад +3

    Modou lo si bopame kham nani siteu dako dane 😂😂

  • @alioufaye9121
    @alioufaye9121 День назад +4

    Fall iao guidj gue dane dei 😂😂😂

  • @GueyeAmet-h1j
    @GueyeAmet-h1j День назад +2

    Merci abou

  • @mansourkane1426
    @mansourkane1426 День назад +8

    Franc mo meune papaye siteu

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote День назад +1

      Bouko ama diapè nguèn wèdiko

    • @ousmanethioub1392
      @ousmanethioub1392 День назад +2

      Mbeurou parcelle yeup siteu moye séne Roi dane naléne

    • @lilg9389
      @lilg9389 День назад

      Siteu danoul kenneu bou dieule franc dotouko defati deh 😂😂

    • @mansourkane1426
      @mansourkane1426 День назад

      @ bayiléne fofou rek

  • @khalilo2423
    @khalilo2423 День назад +3

    Waa yaldaw 😂😂 gueumlèn yalla

  • @Bour_ndiaye_bour
    @Bour_ndiaye_bour 12 часов назад +1

    Abou gor deug bay fall ❤❤❤

  • @SeneDiame-tn8py
    @SeneDiame-tn8py День назад +5

    Qui môme mofi guena yambar nieup deyyy danou rek mais Modou lo da danou nak vraiment 😂

    • @Jnrjoop
      @Jnrjoop День назад +1

      😂😂 boy bi daka Dane dh 🫢🫢🫢😛😛

    • @tayk4304
      @tayk4304 День назад

      Fanla Modou dano? Chute bobou ndiakh la may niou way

    • @papeomar8530
      @papeomar8530 День назад +1

      Modou danouwoul Siteu aussi dafa ték bopou

  • @AitaMalick
    @AitaMalick День назад +3

    Yaw ya gnaka diom lilala modou di wakh 😂 nganan je suis fière de siteu thiim...geumeul sa bopp. Vous parler beaucoup trop

  • @momardiallo1609
    @momardiallo1609 День назад +3

    Ki mom guiro seras laniouy wowaat rek mo kattaat ndém 😂😂😂

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc День назад +2

    Siteu kasse siteu kasse ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @modo6218
    @modo6218 День назад +5

    Yaw franc yako djitou si lambe ngay Tok fi di doul al topé bi diemal beurè dan y’a eupp défait nieupp 😂😂

  • @papasene9330
    @papasene9330 День назад +5

    Diangal nga bagne

  • @abassseck1966
    @abassseck1966 21 час назад

    Abou ndiassé môme ak coly Faye amougnou Béne diom domeram yo khamni danou rek lagnoufi néké tope siteu di mar boune rek amléne fouleu woute combat diémeu am victoire gnagé léne comme siteu mo gueune

  • @ouzinouzin5516
    @ouzinouzin5516 День назад +1

    Siteu goor yalla waroul daw😢😢😢😢

  • @akimoulakimseck
    @akimoulakimseck День назад +3

    Ani Guiro Seras 🤣🤣🤣

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 День назад +5

    Yaldaw😂😂

  • @BocarAnne-g7d
    @BocarAnne-g7d День назад

    Ya Oustage est-ce que dolèn diokh couronne bi fékhéwat ba beurat ak mom nioussateko niouss you méti nguir YALLAH rek sonneunagnou 😢

  • @elhadjimalickniang9475
    @elhadjimalickniang9475 День назад +2

    Ohh yamba baxoul😢😢😅😅😅

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote День назад +1

      Deug nguèn di bania dègg tè dinguèn ko dègg force modou da danou 😂

    • @ouzdaking382
      @ouzdaking382 День назад +1

      ​@@leuz.patriotedafa léér 😂

  • @jeanfrancoismarioupenimend4603
    @jeanfrancoismarioupenimend4603 День назад +1

    Franc mo gueuna bakh siteu palmarès franc 13 v 0 d
    Siteu 12v you bone 7 d yam lenn

  • @AbdouDiop-d6t
    @AbdouDiop-d6t 16 часов назад +1

    😂😂😂 wolene giro serasse 😅😅😅

  • @thiene07970
    @thiene07970 День назад +1

    Sitteu Diambar mais tmt le respect est réciproque modou devait donner un bon exemple

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh 21 час назад

    Abou kokou dégg mouy wakh kou respecter modou lo leu mais lepp Père max leu liii yeup moko andiii mo dokh combat bi ndakhhh khalisss .... boul tass famille diambour

  • @mouhamedmendes8289
    @mouhamedmendes8289 11 часов назад +1

    Doull Abou ndiassé bari guéne wax trope fii leleu Guiro Seras door gua nélaw aye tapéte guéne Roi recours wala appel si yene rek leu meuse ame amo léne bene palmarès diamageune liss Ndiago or bi moy sen baye

  • @pascalsignougomis7316
    @pascalsignougomis7316 День назад +2

    Abou ndiasse nekall toutii goor temps lou ngayy takk radio yii beurrina iiow amo palmarès tapet nga fii yeup djambar bou ngayy wotei dokhéwokko fii sa genre yii gnoyy niakk lo fayda siteu douyy koo wakh deugue fiila guiro door nga nga daw

  • @AssaneNdiaye-z9p
    @AssaneNdiaye-z9p День назад +2

    Deugeu deugeu

  • @modoufall1328
    @modoufall1328 День назад +1

    Franc mo gueune siteu palmarès fouf.Siteu mboolo rék mooko yobbalé motakh mouy beuré ak vip yi wayé amoufa place.Niou eupp ci ay moromam dagne co daan.

  • @MamadouWagneQ
    @MamadouWagneQ День назад +2

    Pour dire vrai sa morom yeup amnaniou xaliss legui mbeur nga wala chroniqueur nga

  • @BirahimDienG-q9u
    @BirahimDienG-q9u День назад +2

    Abou Ndiasssé MOY SEYTAANÉ BANLIEU BI🌚🌚🌚

    • @abdoulayedia4199
      @abdoulayedia4199 День назад +1

      Birahim Roussna sa tour bi Sinon ma saga leu Barki Borom Touba…Abou Ndiassé ça papeu leu ☺️

    • @BirahimDienG-q9u
      @BirahimDienG-q9u День назад +1

      @abdoulayedia4199 sagaaL bou nékhé nga Doli🔱 dama khamni banlieue bi nieup ay MBokk talibé leugn mais nioM ay mak lagn danio wara Rafetal nioun ay mbeur You ndaw lagn mais toppou wakh bi ay nonnn rk lalay dioureul fall.Boma saaaga degggat Loula nékhoul rk

  • @yakhoubaseydi905
    @yakhoubaseydi905 День назад +2

    Franc diina dokhan sen ndeye yen nieup

  • @madiagnendiaye7655
    @madiagnendiaye7655 21 час назад +1

    Abou niassé guemoul bopame déh khana do mbeur niak nga diome trop

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 День назад +1

    Nyak baxul motah siteu nyim andal du nyuko wakh deug

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 День назад +3

    Merci Abou ndiassé siteu nouveau roi des arènes 🎉

  • @modo6218
    @modo6218 День назад +4

    Wa legui mom kan la dan tapha gueye la nulle beurè wakh

    • @IbrahimGaye-d9t
      @IbrahimGaye-d9t День назад

      Teksi par avertissement lako dané 😂 mom ak coly Faye amougnou carrière si lamb

  • @amethdiallo7772
    @amethdiallo7772 23 часа назад

    Woléne guiro rek 😂😂😂

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 День назад +2

    Guiro serase Ani mou

  • @thiene07970
    @thiene07970 День назад +1

    Franc nak danou fi bene Mbeur Bou Mag

  • @elhadjiousmanemboup
    @elhadjiousmanemboup 22 часа назад +1

    Tapétebi di wakh rek

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 8 часов назад

    Teudieul sa lamigne té gueme sa boop 😂😂😂😂topou ci guinawe Lac 3 rék mélni kou yénéwoul sa famille 🙅 lamb dou wakh djou barri 🙅🙅🙅🙅 djiémal ame combat dimbalé séne wakeur mo guene ci iow ✍️ aye doff guéne rék 😂😂😂

  • @ModouDiouf-i4d
    @ModouDiouf-i4d День назад +1

    Iow waro wakh DH tmt 😂

  • @alioubadaraniang-ql3dx
    @alioubadaraniang-ql3dx День назад

    Guiro serass ngi niente dé niouss rék

  • @zikreable
    @zikreable День назад +1

    Bougne diogei di bandit bandilou yakar ni nio geun weuyou galsen tei kossi tasselôn seul à seul nok ko bam reglei. Bandiwolen ay tapet you bari wakh ngen di aral.

  • @lapaixlapaix8873
    @lapaixlapaix8873 День назад +1

    Guirro serass nokk la gaye wakh rekk

  • @legionnaire--
    @legionnaire-- 23 часа назад +1

    Yaldaw😂

  • @yakhoubaseydi905
    @yakhoubaseydi905 День назад

    Teee pourtan tapet laaa nii dee 😂😂😂daay actionee rek franc mom boo wakhee ci mom diinala ndokou

  • @MamadouKébé-y5t
    @MamadouKébé-y5t День назад +2

    Ki kome pa bou magete

  • @papefall7062
    @papefall7062 День назад +1

    Yaw lidieultil sa carrière, geum sa bopou , deim entrainer dji. carrière yagoul , baxna reik.

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 День назад

    Modou Lo wakhoul siteu da niakeu diom d degolen wolof dagni nit sokay encourage si Daw moy Yangui kay encourage si niakeu diom

  • @thiernosarr8939
    @thiernosarr8939 День назад

    Kanamou seytané rek la fi guiss

  • @Babacardiop-b3b
    @Babacardiop-b3b 22 часа назад +1

    Yall daw

  • @soraboukharaglo
    @soraboukharaglo День назад +1

    Kholal ma domram djui mom tee mo geuna niak diom ci mbeur yi

  • @AssanedieyeAssanedieye
    @AssanedieyeAssanedieye 11 часов назад

    Siteu seul bayi lène ndaye boyebi diokhe lène ko victoire bi

  • @Thehustler049
    @Thehustler049 День назад +1

    Ioe ko dannn

  • @papenar2561
    @papenar2561 День назад

    Abou ndiassé yaw baye fall nga na nice diambar

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 8 часов назад

    No ki mou reww ndayam

  • @boumohameddiangne436
    @boumohameddiangne436 3 часа назад

    Genre reporter au saytané lanou nio taylé buur ak fadam2

  • @laminefall4930
    @laminefall4930 День назад

    😂dina bakh rek les tarkindas outil en diom rek molen tere done roi😂

  • @khalilo2423
    @khalilo2423 День назад

    Gnii CNG mo wara adj sen ndeyy si lambji

  • @Bayechllliss
    @Bayechllliss День назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amdymoustapha6130
    @amdymoustapha6130 День назад +1

    Abou ndiassé y'a guena kate sa ndeye niakh diom diamagueun la deuk mes bayil tokh yamba yaw ak coly faye ak siteu toukh yamba rék

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j День назад +1

    Siteu mingui avancer mais ioe akk coly Faye amoul benn diom focus lènn sissen carrière nguèn nekk fi di wakh rekk am lènn fouleuh nguèn geum sen bopp deff comme séni morom.

  • @assannda4919
    @assannda4919 День назад

    WA KI KOUMOU ? Hé WOWALMA GUIRO SERAS

  • @MawaFayejoal
    @MawaFayejoal День назад

    Modou lo ak kouko faral sa bountou tounou ndéy chaque jour

  • @mansourkane1426
    @mansourkane1426 День назад +1

    Yaw sa leufeul ndaye danga Bari wakh

  • @ModouDiouf-i4d
    @ModouDiouf-i4d День назад

    Wa diay ma dieune pas diameugueun wah rk molen fi bayi certains comme celui la

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 8 часов назад

    Ki mom guiro seras laniouy wow rak mou katti ndayam

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 8 часов назад

    Tokh katou yamba bou katti ndayam bi

  • @abdoudiagne642
    @abdoudiagne642 22 часа назад

    démeuléne liguéyi kéné topou nitte domerame yi

  • @papasene9330
    @papasene9330 День назад +1

    Yaw boy sa data ndeye da nga souss ba yakou sa niaway bi sa data ndeye

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 День назад

    Siteu ay kon rek nioko weur je supporte reug mais siteu franchement dafa ragal Modou lo roi des Arenes ken douko lidieundi

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h День назад

    Roi quelle douko lidianti daw rek ngène daif

  • @TARKiNDaBi
    @TARKiNDaBi День назад +1

    SITEU KOUKO BAGN SA TATTOU YAYE SA SO NOYÉ🚫
    KOU TONTOU COMMENTAIRE BI SA DOKHOTOU NDAY🚫
    KOUY BINDE SISSA CLAVIER POUR TONTOU REK😂 MOTS BO BINDE REK BINDE NGAKO SA BIR DATA YAYE😂🚫
    SITEU SEULLLL MOY ROI DES ARÈNES 👑🇸🇳 MOU NÉX MOU KATTÉ SÉN YAYE NAKARILÈN😂😂

    • @rassemtombalbaye5005
      @rassemtombalbaye5005 День назад

      Seu khornopou ndeye yak tarkinda yeup modou lo tassna sene poubou ndey biir arene bi le reste cng le reste a la cour d'appel sa yo noyé rek seu bireum fakhou ndeye

    • @TARKiNDaBi
      @TARKiNDaBi День назад

      @rassemtombalbaye5005 DOMOU THIAGA BII YAY TONTOU XANA MODOU DAY DANOU SISSA DATA YAYE BI😂😂🤣🤣NÉL SA YAYE MOU BAYII MODOU LÔ BIMOUY DIOKH DATA BI😂😂
      MODLÔ MINGUI KOY KATTEU LOU XÉRRÉ🤣🤣🤣🤣

    • @AbdourahimSylla-m8z
      @AbdourahimSylla-m8z День назад

      Yalmine bi seul roi 👑 dès arenes mais saga yi bokoumasi parceque môme lay topou 💪

    • @TARKiNDaBi
      @TARKiNDaBi День назад

      @@AbdourahimSylla-m8z nice niongui diégalou frr

    • @rassemtombalbaye5005
      @rassemtombalbaye5005 День назад

      @@TARKiNDaBi seu thiebou yaye

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j День назад +1

    Abou xolatal sa bopp nga concentré wou sissa carrière danga tardé donc wagnil wakh focus sissa bopp nga melni kou beugoul sa avenir.

  • @birametraore6100
    @birametraore6100 День назад

    Mome na diemer dane mo geune mouy kine lamou ni pour niome fitt si wakh là ak daga yaram tono rek yar ak teguine rek là GAYI di daw wayer fi dawo yaram kenneuh nekeu di weuy ni rek dawoul sakh souniou yaram goor wakh touti là dieuff lou beuri lolou laniouy deff

  • @samba3125
    @samba3125 День назад +1

    Katal sa yaye

    • @Aaron-i5f
      @Aaron-i5f День назад

      Saway Hana amo yaye niit day aam respect cii bopam!!

  • @AzizDramé-q4j
    @AzizDramé-q4j День назад

    Gni nio niak jome deug

  • @FatouDiop-q6u
    @FatouDiop-q6u День назад

    💚💚❤️❤️❤️❤️💚💚💚💚💚❤️❤️❤️❤️❤️❤️💚💚💚💚💚

    • @Aaron-i5f
      @Aaron-i5f День назад

      💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️💚❤️

  • @cheikhdiop5333
    @cheikhdiop5333 21 час назад

    Bour ag fadame dinagne Kate sein ndeye ya ga toul

  • @GallasNdiaye-if9qu
    @GallasNdiaye-if9qu День назад

    Yéna gnak diomm

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 Час назад

    Yaw mome comme meuno dane Tapha Gueye2 trabaha kay nopil

  • @bayedieng7141
    @bayedieng7141 23 часа назад

    Altopé guemeule sa bop do deureum thie lamdjie

  • @fallouthiam1155
    @fallouthiam1155 День назад +1

    Yaw fékhél no dané mbeur

  • @modoumouhamedsarr4271
    @modoumouhamedsarr4271 День назад

    Bayil douououl

  • @DiaKhadim-v5p
    @DiaKhadim-v5p День назад

    Yaw da nga niakeu diome

  • @yakhoubaseydi905
    @yakhoubaseydi905 День назад +1

    Teee pourtan tapet laaa nii dee 😂😂😂daay actionee rek franc mom boo wakhee ci mom diinala ndokou

  • @modo6218
    @modo6218 День назад +3

    Yaw franc yako djitou si lambe ngay Tok fi di doul al topé bi diemal beurè dan y’a eupp défait nieupp 😂😂

  • @BocarAnne-g7d
    @BocarAnne-g7d День назад

    Ya Oustage est-ce que dolèn diokh couronne bi fékhéwat ba beurat ak mom nioussateko niouss you méti nguir YALLAH rek sonneunagnou 😢

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j День назад

    Siteu mingui avancer mais ioe akk coly Faye amoulènn benn diom focus lènn sissen carrière nguèn nekk fi di wakh rekk am lènn fouleuh nguèn geum sen bopp deff comme séni morom.