ماشاء الله ،أحسنت يا السيدة فاطمة فال،أحسن الله اليك وحفظك الله من كل سوء و مكروه. هؤلاء البنات المسكينات مجرد دميات يلعب بهن أعداء الإسلام ،لاستهزاءدين الله ،والاساءة بالمسلمين ،واغضابهم .هداهن الله إلى الصراط المستقيم. هن جاهلات بالدين ،لاجل ذلك يقمن بعمل الفاسقات الفاجرات لأغراض دنيويةسخيفة . والإسلام بخير،ولايزال يتفوق بسرعة انتشاره.وهذاماأحزن أعداؤه الكفار الفطرة.
WALEICOUMA SALAM WARAKHMATOULAH WABARAKATOU YA SEYDA SOKHNA NDÈYE FATOU FALL BISMILAH WALAY NDÉYESANE TABARAKALAH Naka yaramm bi mba yagui ame tane boubakh Alhamdoulilah euskey DEGUE LEU YALLAH NA NIOU YALLAH KHIR THI BOPAME AMIIINNE ta mou défal gnou dégueu AKK top Amiiinne yarabi 🙏🙏🙏DIEUREDIEUF SEYDA SOKHNA NDÈYE FATOU FALL ame nasolo yallah na la yallah féye ta barkél lépp lo beugeu Inchallah 🤩🤩🤩😍😍😍😘😘
Machallah mane tata ma gui mourou mais dama beugue bayi sol ay toubay mais dangne may wax yaw yeufou mere to intant yi dama lo beugue bayi wah deug yallah korma ma diapalè rek last beugue ngir yallah
Senegal mo tocc tè parentyi falèwouniou sèn domyi kènna yaratoule khalèyi Senegal yakhouna yalla naniou yalla samma dieuredieuf
Machallah Ya Seyda béggg nagnou lool si guiss la yalena bour bi samm la mayla weer ak goudd fann
Machalla ya seyda ndeye fatou fall yalla na yalla barkel sa doundeul lolou machalla
yalla na gnou yalla moussal thi seytan , yalla may gnou deg akk toppou
amine
Maashaa ALLAH qu'ALLAH vous préserve Ya Seyda. Qu'ALLAH nous guide ainsi que nos sœurs sur le droit chemin et nous y maintient jusqu'à la mort
Machallah yalla nalen yalla sopi té diegal len thi ndioumté bobou gnou def
Qu'Allah nous guide 😔
Macha Allah tata amna solo yala na gnou yalla defal deg ak top
Allahoumma amiine
ماشاء الله ،أحسنت يا السيدة فاطمة فال،أحسن الله اليك وحفظك الله من كل سوء و مكروه.
هؤلاء البنات المسكينات مجرد دميات يلعب بهن أعداء الإسلام ،لاستهزاءدين الله ،والاساءة بالمسلمين ،واغضابهم .هداهن الله إلى الصراط المستقيم.
هن جاهلات بالدين ،لاجل ذلك يقمن بعمل الفاسقات الفاجرات لأغراض دنيويةسخيفة .
والإسلام بخير،ولايزال يتفوق بسرعة انتشاره.وهذاماأحزن أعداؤه الكفار الفطرة.
Saaalaaw dé, kouy fowé diiné mom ñaar rek ñociy topp, toupp wala torokh rek, kouko weiddi rek holal ci paa yi done theatre di fowé diiné
Diazakilahou ana khayrane maman ndèye Fatou Fall, Yalla nala Yalla faye sa khôl,sambale gnoula,dioyougnou maman zeynab nakh yaw
Dieuradieuf ya Seyda si fatali bi amna solo tro 🙏
M e r c i
Maa Sha Allah Yaye boye Yalla na Yalla fay leu yiiw té mou may niou dég ak top
Wallahi ndeysane
Machalah Tata Ndeye Fatou Fall
Goudou fane bou anede ak wére
Machalla ya zeyda ndeye fatou🙏🙏
YALLA NA YALLA FAY YIW MACHAAL ALLAH❤
Yaye long vie à vous yagui def Lou lerr Macha allah
WALEICOUMA SALAM WARAKHMATOULAH WABARAKATOU YA SEYDA SOKHNA NDÈYE FATOU FALL BISMILAH WALAY NDÉYESANE TABARAKALAH Naka yaramm bi mba yagui ame tane boubakh Alhamdoulilah euskey DEGUE LEU YALLAH NA NIOU YALLAH KHIR THI BOPAME AMIIINNE ta mou défal gnou dégueu AKK top Amiiinne yarabi 🙏🙏🙏DIEUREDIEUF SEYDA SOKHNA NDÈYE FATOU FALL ame nasolo yallah na la yallah féye ta barkél lépp lo beugeu Inchallah 🤩🤩🤩😍😍😍😘😘
جزاك الله خيرا يا اختي 😭🤲🙏
Mâcha allah ramatoulaye djigo
حياك الله سيدة yalla na yalla barkel sa doundou bayi lafi basi kanammmm
Ma Sha Allah Fall,wakhbi amna solo.Dieureudieuf
Mashalla long vie à vous inchallah
ماشاء الله. بارك الله فيك ياأمي. زادك الله صحة والعافية وأطال عمرك
Yallah naléne Yallah fay si initiative bi manchallah amna solo
Machallaha yaye yalna bour doli la tawfikh boubakh te goundeul fan gui
Tout à fait d'accord Ndeye Fatou. Diazaakillah khayr.
Machallah yalna yalla samla aarla ❤️ yagiu
Dèma mourou ndakh sène vidèos yi machala
Salam nice talk Machala rafetena ALLahu Akbar 🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️
Macha Allah Amatina solo trop ❤️❤️❤️
Yalna nioy yalla tek si yonwo bakh
Bilaye maman yalla n'alla yalla same
Macha Allah yalana yala yokk séne takhaway merci infiniment
MaaShaAllah amna solo yalnagnou YALLAH same té tekk gnou si yonou siratiqal moustaqime
Machallah tata yalna yalla weral batbi💕💕💕💕
Diadieuf tata ndèye fatou fall Yallah na yallah fay yiw
Macha Allah
MachaAllah amatina solo merci pour le rappel Alhamdoulilah
MachaAllah yaye bouye
Ayy wayy bolène ma si group watsp bi🙏🙏🙏🙏
Essayez de leur rendre visite. Vraiment elles ont exagérer
ماشاء الله جزاكن الله خيرا 💯
Yalna la yala défal taw fékh ❤❤❤❤
Maa Shaa Allah vérité absolument vrais qu'Allah vous préserve ya rabbi
BarakaAllah feeki sister amena solo
BarakAllahou fiiki ya oummiii 🤲🏼
Machallah amna solo
Machallah yall na yall fay la
mashaa allah tata chérie bien dit
Machallah حبيبتي 🥺❣
Mancha allah yalla na yalla sam la fall
MachaAllah qu'Allah vous protège 🙏amna solo trop
Machalah
Machallah sopé longue vie à vous
Bien dit merci beaucoup tata
Mashallah Qu'Allah azwajal les pardonne et les guides
Macha Allah yasayda deyefatoufall
BougonaLateyallah tank billayeakseunaboufall
70 7737877
Merci beaucoup ma tante
Machallah ma sœur
Maa shaa Allah longue vie
Macha Allah
Amna solo
Choukran 🥰😍
Machallah maman amna solo lolll
soukran 💖💖💖
du courage à vous et sa ira ☝
ALHAMDOULILAH qu'ALLAH vous protège
Machallah mane sene numéro la begue
Yalna yalla samla té are la
Masha'Allah❤
Qu’Allah nous guide 🙏
Yalnalene yallah diegal
Walahi laye dé 🙏
Macha alla
Allahou Akbar yalanalén yalla dioubal
Mashalla ❤
Machallah 🙏🧕✨
Amnasolo mahallah
Machllah 🙏🥰
حياك الله ياأختي ❤❤❣
Comment fair pour vous contacté dama beug mourou
Macallah
Machallah mane tata ma gui mourou mais dama beugue bayi sol ay toubay mais dangne may wax yaw yeufou mere to intant yi dama lo beugue bayi wah deug yallah korma ma diapalè rek last beugue ngir yallah
Salam 🥰
Goudeul fane yaye bauy.
Diazakillah hayrane.
Amna solo
جَزَاكِ الله خَيْرًا
Wallahi louma metti la Bamako guissè
Mashallah amatina solo
جزاكم الله خيرا 💚💚 ءامين وحفظكم الله عليهم أجمعين
Svp votre numéro dema beugeu mourou samay thieur
😭😭😭😭😭😭
Manchalllah amna solo
Yaye gni moye lolou
Lan lay deff ba am sen numero telephoned
Vs etez des références kou beugue bakh DINA len roy
🙏🙏🙏❤❤
Vraiment refatoul li
Wkh deugue nio kham lignu si dioup lou waye so langké ne doo mourou ngua bayi gniye mourou wy
Mâcha allah
wax deug yalla diadouwul rafetoul
Macha'allah