SERIGNE BABACAR SY KOUKO BEUGUE YOKOU RÉK INCHA ALLAH NDAKH DAFA LIGUEYAL BOROMAME BA YALLA FAYE KO KI TAWLO SAMA TOURANDO SEYDIL DJAMIL SY BOROM FASS 🌙🌙🌙🕋🕋🕋♥️♥️♥️
Fan'yi mom machala talibé cheikh yi Yé'nangui tothir télé'yi ndax xam xam Yalnalene Bour yalla takhawou yock séne thiofél si yonénté'bi si barki seydina Mohamed psl amine amine amine🙏🙏
J sui mouride mai j aime ouzta pape Hane
Machallah vraiment Sénégal est un grand pays vive merci Cherigne Babacar Sy👍🕋❤
Mais pape Hane ni lagne koy baye rekk mashallah... Sama khōl seddna wallahi Rassouloullahi mala beugueu...❤
Diarama cheikh Tidiane ...
Machallah Sam et Pape Hanne
Machallah 💕❤️sedatina wayy kou ame lénéne dieuleule gnoune mame khalifa lagnou ame fière d'être talibe chiekh bilahi walahi sama ❤️dafa sedd gouye wayy😭
bilahi moy sécurité bo amé Cheikhal khalifa (rta)lo gnak doula safff
fier d l'etre osi
@@maremesarr9352 je te jure kéne dou mome
Bilahi yalla hi
Bilaye neque talibe cheikh dafa nekhe j'aime serigne Babacar
Walay ndeyssan❤🙏
@@salimatandiaye6118 aka nopalé waya yalla rek laye nékh nga nékko
Yala naniou yala deff deug deug talibe cheikh
aka nékh konn xam ngathi dara
Dafa nopalé yalla naniou yalla déf ay Talibé Cheikhou Tidiane
Amiroul momina Baye mbaye ya yoor dinée dji ♥️ Serigne Babacar si ♥️🎉✊ fierté
Vraiment sam tu me fais pleurer kéne dou yonetibi yalnayala wéreul bate bi .
Son excellence Serigne Sam Mboup le meilleur de sa génération
Machalla
amoul werenté
Aka lére
Mala ko wakhe dama contane trop
@@astousankhare892 xol yeupa séd vrement
Je suis Mouride et très grand admirateur de Same Mboup il est extraordinaire yalla na yalla samou
fier d'être Tidiane machalah khôl sed na trop bilay walay
Walay ndeyssan❤🙏
Thiey serigne babacar kena khamoul loumou machallah
mome la Babacar sy 😂😂😂😂
khadija sáne yaw tèga geum liga geum té bayi saboté bi
khadija sáne kiga yakar maodo la yakar donc yaroul
mashallha seringe babacar sy amoul morom obrigado sy Malick yalla na yalla yokou lérram te tasnou si barkém amine 🤲🤲🤲🤲🤲
Je suis mouride j'aime pape hanne
machallah
Machallah Talibe cheikh ba deee mama mou Serigne Babacar Sy ba deeeee
Machallah Sam non tu est trop fort
Same mboup ndeysane dama kha sopo rk😭😭😭😭
Thiey Serigne Sam; Oustaz Pape yalna yalla taxawou lenn aminn
Machallah pape Cheikh ya bakh wayy machallah 🙏🙏
SERIGNE BABACAR SY KOUKO BEUGUE YOKOU RÉK INCHA ALLAH NDAKH DAFA LIGUEYAL BOROMAME BA YALLA FAYE KO KI TAWLO SAMA TOURANDO SEYDIL DJAMIL SY BOROM FASS 🌙🌙🌙🕋🕋🕋♥️♥️♥️
yokkou ba yeug ko
Ndiasse Gueye dégatina deugue
Yalna borom bi yagal sen taxaway te weral baat thi barke Serigne Babacar
Merci à la TFM numéro 1 au Sénégal🕋👍❤ merci beaucoup Pape Cheikh Diallo ❤❤❤🕋🕋🕋👍👍👍
sama kholbi mo sed 💖💖💖💖💖
Tabarakalah sam. Dieureudieuf oustas
Hé damané Maodo amoule école Université laa ame
Té mouy deugue
Amoul wèrantè
@@djibithiaw7123 à
Mashallah sama sama sope yalla na yalla defale diam ak soutoureu
Machallah machallah sama mayaram dawna 👍🕋❤🕋👍❤🕋👍❤
Machallah sam mboup yallah nafi yague té weer
Vraiment ça me fait frissonner.. j'aime le prophète.. moma geunal lep louma am
Fan'yi mom machala talibé cheikh yi
Yé'nangui tothir télé'yi ndax xam xam
Yalnalene Bour yalla takhawou yock séne thiofél si yonénté'bi si barki seydina Mohamed psl amine amine amine🙏🙏
Machallah Sam Mboup et oustaz pape hann yalla na lène yalla same
😭😭😭j aim mam Khalifa sama mbeguel si mom mo gueuneu fesss guedj sama thiofelll si mam khalifa😭❤❤❤
machalah linga wakh nékhna dh
@@ndiassegueye1933 j aim mam Khalifa
Machallha Nice sam yalna yala yokou wergui
Masallah Sam mboup yalna yalla continue di weral sa bat ak katan ngai gina muna Tag Rasoulullahi S A Wasallam. Damai beg sa yuma la dege
Qui est d,acord avec moi les tidianes Sont les meilleures
Wa walaye ndeye sane sama khol sed na machalah talibe chiekh talibe yonene moy sounou referance.
Macha Allah oustaz Hann et Sam yallah laff tiatt
Talibe cheikh bahna look mais waroul wam thy wakh d'à nous kodi dieuffe bou baah
Moi
Mo ame
Bilay tay mm je suis tellement émue 🥰 one love rk❤️
Macha Allah kén dou Maodo Macha Allah
Mame moado mo beugu seydina mouhamet sama tourodo machalah
moy lépeup motakh euleuk dinako fayé lolou kén douko euplé thi mom
@@ndiassegueye1933 machalah
Kéneu d'où Serigne Babacar Sy ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️wlh Sy Malick Mala beugue
Dieureu dieureuf pape hann
talibé serigne touba lah wayé li môme machallah yallna diamou yague
Machallah sa khola rafe
Tay mom machallah samaa journée nimou commencer rk dafaa nekh
Yalna yallah deff jam❤️🥰
Sam mboup yall nagua ame diam sii barké serigne babacar sy
S same mboup machallah ❤️❤️❤️
M'achallah dieuredieuf serigne Babacar sy❤❤❤❤❤
Barcke serign touba sam ya meuna diang
Sa tour Bou bakh bi magal nala
Ya bah barke seydina mouhamed
cisse magalat nala bou were
Machaala sam yalla na yalla werall
machallah....nekh na dal
Machalah serigne sam mboup
Kèneu Dou Serigne Babacar Sy Malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maaa Chaaa Alllah Baaarakal Laaahou fiikoum
Ndaysane sam mboup yalla nala yalla faye waye
TIDJANISME yééna xam kouyy RASSOULOUL LAHI psl dafa léér
Billahi ta raison
Ndiasse Gueye talibè cheikh la mais bayil guarwalè bi
Talibè cheikh daye manou
@@wakhkatoudeugue2013 deug rek la wakh di
@@wakhkatoudeugue2013 bigmo sama xola séd rek mai amouma intention garouwalé yalla xamnako. sorry
@@sadiomane3600 machalah
Machahala man mouride la mais ki dama way troop
Yepe bene la bilaye
Touba ndindy yalla nala yalla faye yiw dioulite dioulite moy mbokame
diadieuff mouride
Machallah
Yalla nagnou yalla fayal suñu mag you bakh yi diouli dafay nangoul waliyou yalla yeup so beugué mouthiou adouna ak alahira
Machalla sy
Sam mboup machalla yalla na yalla wereul batt bii pape hann soukourane
J sui mouride mei same mboup jtmm d tt mn ame yalla nla God werral batt bi
Il es Excellent , Sam Mboup
Barke mame chiekh ibra fall ma beuge sam mboup❤❤
Masha allah Pape Hann
Eskeuye, Sam mou Serigne Habib ibn Borom Daara yi. Yal na sa diam yague. Na yallah wéreul bate bi thi barké Mohammed psl.
Machala
Amine yarabi
Douma si doyalll😭💞❤️❤️❤️💓💓
Machallah oustaz papa same❤❤❤
Machalla yalla nagnou yalla fayal suñu mag you bakh yi
Ndeysane Thiey seydouna moukhamadou rassoulila psl ohhhhhhh 😭 😭😭😭
Machalla longue vie a vous
Limoye mbégté☺☺☺❤❤❤
Dieureudieuf sy malick
Macha alla
Machallah Sam mane tatabaha bi rek momay ray
macha alha sam kend dou yaw
Amlene diam rek barke yonenetibi psl
Que des frissons 🙏🙏🙏
Mâcha Allah
Salal Laahou Aleyhi wassalam
Machallah lii nekhna si khol lay dougou
Sam dangay ray nit yalla na yalla fayla
Machallah Thiey sam
SAM MBOUP YALLA YALLA WERAL BAT BI DIARRAMA SEYDI ABOUBACAR SY 🙏🏾
amiine
Machallah 🥰✨
Machallhe 💞👍
Machallah wallahi nehna
Thiay sunu wadia yalnagnu yalla bole thia gniamiy ramou brom liyahul hady rambou gu mag kene du seydina mouhamed(psl).
Masahala ❤❤❤🙏🙏❤❤❤Amine amine
Machallah bilakhi kendu nabi
Machallla ❤❤❤🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏
Je suis très fier d'être une talibé cheikh
Thieuy seydina mouhamed psl kenn dou mome ohlalaaaa
Serigne sam mboup yalla nga fi yague ci barki cheikh ahmadou Bamba yakari diam gni🙏billae damala beug❤
Yallah yakari diame yi ❤❤❤
Oustaz pape I like you so much
Machalla sama khol bi cede na
Machala oh j'adore
Media seytanai diahassai rk bahena mboke talibe soyons unis et faisons tres attention a certains media senegalais muslim fo ever
Abouna aboubakrine😍 yalna yalla fayal gnou mame maodo si barké cheikhou tidiany
Machallah dieureudieuff
Machallah Sam mboup
Machala sope Serigne Ababacar Sy
Merci Oustaz pape hann
Seydina Mouhamed PSL
Masha Allah ❤❤❤
Walahi lii dafa nekh si xol yallana yala faye seringe babacar sy 💞❤
Sam est le meilleur machala