Ben sete bakhoul, listikhar rek mo dagan telolou Yonentibi s a w diangalenako, يا بني آدم لا يفتننكم الشيطان كما أخرج أبويكم من الجنة ينزع عنهما لباسهما ليريهما سوآتهما إنه يراكم هو قبيله من حيث لا ترونهم إنا جعلنا الشياطين أولياء للذين لا يؤمنون))
JOJO WAKHONE NGAFI NI SERIGNE SIY NEK SI RESEAUX SOCIAUX YI GNOU SI BARI KHAMOU GNOU DARA REUY LAMIGN MOLÉN DIAP BA NOPI NGA DIGUEUL KI POUR MOU BARI TANK SI TÉLÉ YI
Ziar begue naa gnou wakhtane si seete you dagane seete bou dagane ramli tombe yonente yallah idriss lagnouko diokhone te yonente bi wakhou si mo takh mou dagane listekhar tamite kham kham mais gnete rekla 3 meune ko yomboul louy khalwa fane la diogue louy riyada fane la diogue nakhe da bari
Kouy lam lamé sa bagage dalla khamoul bilahi sokhna mariama sy amal diam rék inchallah
Machallah sokhna mariama kadou yi raffétte na
Machallaah dafa civilisé Amna yarr kadou yi rafetna
Machalla JoJo sa sagnesé lanla
Sokhna Mareme talibe Cheikh gua liguaye wakh doyna ware😂
Ben sete bakhoul, listikhar rek mo dagan telolou Yonentibi s a w diangalenako,
يا بني آدم لا يفتننكم الشيطان كما أخرج أبويكم من الجنة ينزع عنهما لباسهما ليريهما سوآتهما إنه يراكم هو قبيله من حيث لا ترونهم إنا جعلنا الشياطين أولياء للذين لا يؤمنون))
Ndeyssane Sénégal quel pays!
Zozo machallah sa grand boubou rafetna
JOJO WAKHONE NGAFI NI SERIGNE SIY NEK SI RESEAUX SOCIAUX YI GNOU SI BARI KHAMOU GNOU DARA REUY LAMIGN MOLÉN DIAP BA NOPI NGA DIGUEUL KI POUR MOU BARI TANK SI TÉLÉ YI
Koromak Faye
Il faut appeler le chasseur des vampires ils sont là hein
Ana sonko
Modou modou gno guena sonne
wowalgnou koromak fay
Wayé manone na diokh tieur collégame Selbé rafétal wakhni gno bokka liguéye bi kounek ak sa guisse guisse thi sama khalate bou gate 🤨
Jojo laf tiate
Fen rekk😂😂😂😂
Mais jojo môme bouniou yap koromak Faye svp
Koromak Faye le Messi des chasseurs de vampires
Jojo tu pose bien les quesion
Djigueen dou ame gnari diekeur benne bi ndialo la
Jojo gniabarr kate yiguaye siweule bayikoo
@Pape ibrahima Thiongane yaw bayil kigay saga deguela wakh🙄ñémé guéne yallah trop séne adina yeup ñambarr rék guéne yakar ni moy solution tchiiim
Zozo tu peux invité stp oustaz omar sall
DAFA AM LO KHAMNI DIAROUL LATHIE NDAKH THIOWLI GNEP GUIS NAGN KO KONE LOU LEER BA NOPI DIARATOUL LATHIE
It's haram. Islam is against it.
Ziar begue naa gnou wakhtane si seete you dagane seete bou dagane ramli tombe yonente yallah idriss lagnouko diokhone te yonente bi wakhou si mo takh mou dagane listekhar tamite kham kham mais gnete rekla 3 meune ko yomboul louy khalwa fane la diogue louy riyada fane la diogue nakhe da bari
Wa zozo ngonal da amatoule wala
Koromak Faye
Koromak Faye