Un très beau combat Félicitations aux deux lutteurs Ils se sont bien entraîné Machallah Mais Laurent était plus fort En plus c'est un Champion en devenir
Je suis agréablement surpris par ce combat. Ndeketé xalé bi ndanane la, limouy beuré rombouna limouy wax. Je vois qu'il a la volonté et les qualités techniques pour aller plus haut; sur l'enceinte il ne rigole pas! Courage à Bou, tu n'as pas aussi demerité.
Malgré leur jeunes âges , ils nous ont bcp régalé spectaculairement avec surtout une lutte pur et dure.Ils ont tenu leur promesse : faire du show puis lutter . Qui est d’accord pour le meilleur combat de la saison 🤌💪 Laurent peut être un grand champion s’il se concentre bien avec un surtout un bon encadrement, c’est un jeune à suivre. Bou Siteu s’est trompé en prenant ce combat piège.
Vraiment yéne niar nieupp ay gaïndé ay diambar nguéne mais félicitation sama ndiago Serigne Fallou bii borom"one is the now - I have a dream"😂et du courage bou siteu"oser et croire"dayy nieuw ana nandité yii"bvndi cii brain"
Athieu Momine bi Laurent ndiago zoké bi xaleii nga geneull tok si tankeu yi rk Diamageune derrière toi fils Maii courage bou Siteu nioune wa Diamageune dagnlay bégué
Nom bou wèréh nga nk ms dra ya beurè ya danou yalla andak boy bi rk du courage tt guediawaye est derrière de toi blh sens sokhor sens dra ms linga indi si mboolo grand combat yi sakh indi wouniouko blh cou nèkone stade na wakh deug rk téh yalla takh
On doit révolutionner la lutte di fey ay million boyi nioka mérité mei vip yi sén lamb néxatoul félicitations laurent niago courage bou siteu
Te mouy degue vip encaissé halisse rek douniou deff haire
Deug nga wakh
Vrai way
Bilay grand
Hum vip yi yague na nekh
Eumeu Modou lo sen 1ére combat Balla Yékini Ama Gouy Gui premier combat Bombardier Tapha tine,...
Un bon combat félicitations à Laurent mes encouragements à Bou siteu
Un très beau combat
Félicitations aux deux lutteurs
Ils se sont bien entraîné Machallah
Mais Laurent était plus fort
En plus c'est un Champion en devenir
Je suis fier de toi sama mbok ndiago bi
Notre Lauren national🥳❤️
❤️🩹
Bilahi millions you Bari yi gni gnoko mérité ils donnent à fond holal mbeur you mague yi Dagni noss ba jour combat bi gnou gnew tahaw di holanté
Félicitations à eux deux pour le combat et la sportivité... Ils ont donné le bon exemple. Vainqueur a été énorme mais le vaincu n'a pas été ridicule !
Felicitation gayi xamunioula entrainè rek inshallah day bakh
Laurent mbeur purr nga ngeunala ligueuy caser wou dinga am dra si lamb j et félicitations
Mais bou siteu a fait un très grand combat ✌🏿
Laurent daffaye nekkk champion inchaallahhh machallahh l'stars kène dou laurent
Lamb bou mell nii saakh daa geudja am waay lii nekh naa ❤️❤️🔥🔥❤️
Félicitations Laurent ndiago
Li moy combat vraiment ❤❤❤😍gni g gno Diarra teugeul bilahi
Billahi loran Mii Bouko geumè ngaine Guiss champion boumak sax kii Billahi
Félicitations Mbeur) Du courage Bou Siteu champion nga Nila) Mé loran kou guisni Nitou yaxla Laalal j’aime 👍❤️❤️
Félicitation Laurent contane na trop
Ndeysane félicitations à tout les deux lutteurs laurent et bou siteu niom niarr nieup ay champion laniou bilahi
FÉLICITATIONS Laurent Lorzé El Junki bou Doff bi Tril💪💪🔥
Lamb méti dama yeureum mbeur yi sakh ndeysane yalla bakhna beugue téki rek
Abuku papa bilay yow😆😆😂 allez Laurent du courage bou Siteu c,est le Sénégal qui gagne 😎😎
Je suis agréablement surpris par ce combat.
Ndeketé xalé bi ndanane la, limouy beuré rombouna limouy wax.
Je vois qu'il a la volonté et les qualités techniques pour aller plus haut; sur l'enceinte il ne rigole pas!
Courage à Bou, tu n'as pas aussi demerité.
Moy tou len mo am dolé dé wa baxna ba dou fi am dolé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
International Laurant Ndiago💥💥💥🔥🔥🔥🔥💘💘🇬🇲🇸🇳💘🌹❤🇮🇹🇮🇹🇮🇹👑Ndam rek Insha Allah 🦁
Laurent bima guiss ni champion la deeeh. Beau combat pas comme les ténors et bou siteu dafa xèpp boy bi. Et magnifique image à la fin fair play
Grand champion
Félicitations notre Laurent sounou ndiago bi👌👌👌💯
Bravo vous meritez bien ce qu'on vous paye, deux futurs grands champions 🤍🇸🇳❤inch'Allah
Bou siteu amoul staff dh do takhaw géré ça combat niou diokh la victoire
Nooo combat bi dafa nékh ta meti chapeau 🎩 félicitations laurent Ndiago du courage bou siteu
Ils meritent des millions
Vraiment en tant qu amateur j était très ému hier franchement j était au mai vous avez bien lutter félicitations à vous lamb nioko mom🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Du courage bou siteu 😭😭😭😭😭😭😭🥰
Wawaw Laurent Future roi 💯❤️❤️❤️❤️❤️
Malgré leur jeunes âges , ils nous ont bcp régalé spectaculairement avec surtout une lutte pur et dure.Ils ont tenu leur promesse : faire du show puis lutter .
Qui est d’accord pour le meilleur combat de la saison 🤌💪
Laurent peut être un grand champion s’il se concentre bien avec un surtout un bon encadrement, c’est un jeune à suivre.
Bou Siteu s’est trompé en prenant ce combat piège.
Frer khana étudiant ga Li d’où dissertation d😂😂
@@sowsamba2877 baalma lolou waay Dma beug lamb rk dii waxx sma xalateu😂 wait ma df exposé
Félicitations lauran ndiago sama mneur mi bonne chance😍😍😍😍👍👍
Felicitations loran sougnou ndiago bi 💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Vraiment ces enfants ont montré un bel exemple c'est très jolie et fair play
Félicitations Laurent champions nga koï ✊✊✊
Exeptionnel laurant 💪💪💪💪💪❤
Bou siteu n'a pas démérité unnn
Félicitations mister Laurent Ndiago 💫
Aline gueye mi nekh nama de takhawouna bouy bi Machalla
LAURENT MI AH WAH BAHNA 👏👏👏
Le combat a tenue ses promesses
Lorent Dou comédien Mbeur la 🔥
Laurent futur Modou lo lay done ✔
Laurant laniou wakh 🥰💪🏿
Félicitation lanrant 💪 ndiago sama mbeur mi
Félicitations Laurent!
Laurent dou sakh nite❤️❤️
*Wa parc waay* 🤣😂
*Laurent daan nalenn depuis Face to face Ba🔥🥳*
Quelle Combat 👏👏👏Combat Bi nekh na trop wayy
Félicitations à vos deux lutteurs
Vraiment good job Laurent et bou siteu
Allez Laurent
Bilay yaw
Diayguen combat té beureguen bamou nekh ak khekh méritaguen sen xaliss
Merci a vs deux felicitation laurent from DSM🔥🔥
Non Lauren champion la félicitations jambaar
lii moye combat tou ndaw yi mo dak fouf💪😍
Allez Laurent yafi neh
Boucher sambeur mi danouna dh
Vraiment yéne niar nieupp ay gaïndé ay diambar nguéne mais félicitation sama ndiago Serigne Fallou bii borom"one is the now - I have a dream"😂et du courage bou siteu"oser et croire"dayy nieuw ana nandité yii"bvndi cii brain"
Bravo Laurant Ndiago
Félicitations au deux lutteurs
Félicitations laurant courage 😥 bou siteu c le Sénégal 🇸🇳 qui gagne
Notre champion national. Lorant
Bou siteu bimako guisse cii premier face 2 face bi fogonani mo eup ndiago 2 fw m je m s8 trompé teglé bou metti bila won🤣😅😂
Bou siteu d'où entréner
Bilae a premier vu on a cette impression
😂😂😂😂😂dafa téglé 😂😂
Alkhamdoulilah
Félicitations lorang contane si iow
Lutte tv naniou diapalé niar ngii beggeul naniou lol beuré _signature _nieupp contane _yalla nguen am visa yen niaar nieupp inshallah
Laurant sama mbeur bi😂félicitations champion
Niabou laurent bi lanla😂😂😂😂😭
Non Laurent ndiago ndanane leu oh félicitations et du courage bou siteu
On ne doit pas sous-estimé son adversaire li leçon la pour bou siteu
Athia Laurent 🥰🥰🥰
Machallah laurent beug fallou ❤❤❤
Champion ndiago bii
Ba khôl yangui fekhhh 😂💪
Meilleur combat
Merci Laurent 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Masalla belle victoire
Ndeysane nieupa fokone bou dakoy d'âne mm animateur yi mou nieuw daneu DEUG nekhoul mé Laurent phénomène la
Félicitation sama comédien bi
Alhmdoulilah Laurent dane na
Laurent ❤️❤️❤️❤️🔥❤️🔥❤️🔥
FÉLICITATIONS LAURAN
Félicitations Laurant 💪🏿❤️
Sama Laurant Ndiago💎 bi
Lorendunit😢😢😮❤
Lamine yén nieup bou siteu nguén faralone
Maii DIEU nioune la andalone😂😂
Ndeysane bou ❤da rafet du courage et felicitation lauran merci lamine et boucar good job
Machalla lutte tv
Athieu Momine bi Laurent ndiago zoké bi xaleii nga geneull tok si tankeu yi rk Diamageune derrière toi fils
Maii courage bou Siteu nioune wa Diamageune dagnlay bégué
Cuisse bou siteu yi momay raaay 🤣🤣🤣🤣
😁😁😁🤣
Bilay iow😂😂
Laurent félicitation way nak sa nguemb bi dinala danel
il faut catégoriser la lutte et creer des vip sur chaque catégories comme ca tout le monde n aura besoin devenir un elephant
Idée formidable !!!!!!
Bilay ya wakh deugue
Nom bou wèréh nga nk ms dra ya beurè ya danou yalla andak boy bi rk du courage tt guediawaye est derrière de toi blh sens sokhor sens dra ms linga indi si mboolo grand combat yi sakh indi wouniouko blh cou nèkone stade na wakh deug rk téh yalla takh
Félicitations
Sonko 2024 inchalla
Notre Bou Siteu National 🇸🇳
Lamine ray nama😂 ngani souniou diapé policié teudj ko 1ans
bilae iow abougoupapa💪😂
Du courage Bou 😭