Jean Paul Senghor,mon ami d’enfance,j’ai su la mauvaise nouvelle tardivement,mes sincère condoléance à toute ta famille,tes frères,tes proches y comprises moi, j’ai grandi dans votre maison à dalifort,repose en paix mon frère 😭😭😭
Cessez de juger les gens. Vs êtes là à blâmer les parents alors qu’ils n’y sont pour rien. Combien d’entre nous sommes sortis en cachette ou en disant à nos parents que nous allons dans un endroit alors que nous allions ailleurs? Seul Allah peut nous juger et nous devons prier pour le salut de leurs âmes. Ces parents souffrent assez
Vraiment mane dama warou trop. Li dafa meti! La derniere chose a faire cest de parler de pourkoi ils sont sorti juska 2h. Ca peut arriver a tout le monde! K Dieu apaise le coeur des proches!
Ndeyesane métina trop m c la vie yalla bou sokhla diame niake m yalla nalénne yalla yeureum té xarélénne aldiana souf oyof sén kaw finiou néķ taye yalla nalénne gueneul finiou diougué barkép serigne saliou
je suis tres choquee par la mort de ces jeunes mais encore plus choquée par le laxisme des parents. il fut un temps, on n'osait pas sortir à certaines heures encore moins en demander la permission. et les parents était tres severes. timis sakh waroula fekk alleu. aujourd'hui tout ca c'est fini alors que Diamono ji mo gueuna doywar.
Jtj deh🥺moi on m’a tellement interdit de sortir que gueineu soneulatouma bien vrai que enfant unique la ma mère a tjrs été sévère avec moi... diko santei yallah bou bakh... Que leurs âmes reposent en paix
Lou xew gnouni ndogal Certe ndogal amenassi Mais Ce phénomène de jeunes qui conduisent des voitures sans permis sans aucune responsabilité,on doit les sanctionner durement…
Vraiment, meme circonstances pour un neveu Rufiquois le jour de la korite ,decede sur le champ. Il faut que l etat prenne des mesures.Trop triste, q Allah tt puissant les accueillent au paradis.Amen
Éwaye ñagneléne délo khéle yi si yalla tébayi damaye dokhe sama ndawe adouna dafa diékhe nagniou gueussetou sougnou diné top djiégualou sounou borome yalla naléne yalla yeureume kharéléne aldjana kissi désse yalla na tané ake diame barké borome touba
Yalna len yalla oubil aldiana ak yermande Jean Paul yalna ko yesus Christa oubil aldiana ak ler tamite ay djigeen name yi yalna gnou tasse ak seray seydina Mokhamed. Bon courage sen famille
Dans cette histoire, on doit arrêter tous les responsables, à commencer par les gens qui ont loué aux enfants irresponsables et immatures ces voitures car ces derniers auraient dû vérifier l'obtention et l'authentification des permis de conduite de leurs clients avant de leur louer les voitures. A part cette histoire, les acteurs agissant dans le système de délivrance des permis de conduite au Sénégal sont vraiment tous coupables de plusieurs accidents autres que celui-ci, d'autant plus que ce pays fait parti dans la liste rouge des pays les plus corrompus au monde. C'est vraiment grave et déplorable, le Sénégal va vraiment mal à tous les niveaux
Mane khawma kou titoul wayé mane titeu wallay nitt yagui dead comm p possible et majeur partie bi ay accident lay done guir yalla les parents soyez vigilent sa dôme khale waroko bayi mouy gueneu au delà 22h deuk bi legui woratoul legui yalla naniou dadjiek yermandé souniou borom inchallah mettina trop
San pernie 😟😟😟😟😟😟🤭🤭🤭🤭🤭 li Lanla ni tamite yalna ko yalla oubile aldiana massa yalna len yalla may xolou mouñe 😭😭😭😭 Massa Papa Seigneur donne lui le repo éternel sans fin ndeysane Quelle Courage
Innalillahi wa Inna Ileyhi Radjihouna wah yeupeu rafet té bayéko si waydiour yi surtout Papou Jean Paul ake yayou Melle Sow rafetna trop Mashallah Yalla naniou yégalé séne ndaw Aldiana té kidi Fatou Ndir Bour Yalla mayko wére ake bépeu dioulite massa
j’ai préféré un album sur notre prophète seydina mouhamed psl ak souniou mame youbakh yi diappu lén si ngéne abonne fi si ansaar tv ta yalla rek takh nguir dieummi seydina mouhamed psl o
Massa yaye bauye mais tamit soyez figilent enver vos enfants khalé bou djiguen mm pas 20ans gakoy bayi mouy guéne ay 1h du matin dou yonn. Yalnalen yalla yereum
Ay way bayi len sen critique yi dé bou nieuwé rk nieuwe na gni nek si nakar ngen nek fi nan warounio guen Nianal len yalla yeureume len té khare len aldiana firdaw mo guene wakh dji
Exactly!! Plus yaye yi Soukayna sohla wul critique yii. Yaye bu nyaka dormam dafa meati! Yan na len Yallah harel Jannahtul Firdaus teh mei sen yaye yi holi mung
ohhhh ndeysane metina le papa de jean toyal na sama khol😭😭😭😭😭ils ont brisé un rêve vraiment parking war nagnou di khol gnougni diokh séne auto yi ay khalé di foo si tally ba lorr nit ay jeunes yo khamni au yakarou euleuk lagnou si sene famille que leurs âmes reposent en paix
Sa doma tagoula sabar au-delà de 22h rawatina thi djiguen nguakoy bayi les parents tmt bayil lén di top sén domi thi loulén nex bref yalnako yalla yeureum thé djégual ko ay bakkaram
Thieuy yalla un élève bouy def bfem guay koy toudei sabar 16ans thieuy yalla liiii lou mou donne oh Sénégal penrent yii yokou leine sen surveillance stp les morts yalla na leine yalla yeureum metti na trop gni yor parking yii tmt am guein si part de reponsablité imature yi guein done j’ai mal😭😭😭😭😭😭😭😭💔💔💔💔💔💔💔🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Cougnouye toude sabar ndaga wara ame kalisse te élève amoul ligueyoule il faut bien surveiller nos enfants et bien les éduquer à cet âge les enfants ne doivent pas sortir de la maison.
Vraiment gniy louei auto amal ngein gnou ak helou ken dalatoul ham ngein kou majeur dou louei auto disi fo ..mai halei yi ngein di louei dagno inconscien vraiment bayilen si hel
Boul wakh gnidi louer ndah ay mak nioy nieuw dieuleulko boy yi apres niou diohlenko en plus tmt bilay kou bayiwoul di diokh boy you amoul permis auto diga dougou dh
Paix à leurs âmes mais aussi les parents doivent être responsables comment on peut laisser des jeunes sortir tard dans la nuit pour aller à des futilités
Je ne suis pas d'accord avec toi bro. Mes parents ne vivent pas ensemble mais Alhamdoulillah mes sœurs et moi on a reçu une bonne éducation et on suit les traces de notre aînée (une personne exemplaire notre 2ème maman❤)
Métina lol té gni thi niak sén bakéne yalna lén yalla yeureum tabal lén aljana🙏🏼🙏🏼🙏🏼mais ki thi mouthiou aussi souko yalla mayé tane il faudra k niou suivre ko psychologiquement parsk choque bi meun ko traumatisé après
Ndeysaan les mamans geum nagnou yallah. Masta yallah nalen borom bi yeureum. Mais aussi gniy touddé xalé bouy def befm ay sabar tamiit xawma loulén dal vraiment
metina lol kéne yénéwouko kéne mais tamite prkoi des enfants de moins de 18ans gnouléne di toudé ay sabar fo khameni nekoul sakh séne kogne en plus si je comprends bien ils étaient 3 dans le scooter à cette heure de 1h a 2h du matin es ke tamite yéne parents yii amouléne si part de responsabilité hun il faut aussi veiller sur vos enfants au lieu ngéne di bâyi ba Dara khéww ngéne nekk si media yii di expliquer paix à leurs âmes yala naléne yala yeureume kharéléne aldiana
Qu'Allah assiste les blessés et pardonne les défunts... Mais les parents doivent éduquer les enfants. quand j'entends toudé sabar pour une éléve c'est grave et hallucinant. Il faudrait vraiment que les parents puissent surveiller et éduquer les enfants. Comment un enfant peut sortir jusqu'à deux heures du matin... OK Ndogal certes mais il faut situer les responsabilités.
La mère a bien précisé que sa fille travailler dans un salon donc soyons strict dans les commentaires sa peut arriver à toutes le monde la décision de dieu personne n'y peux rien paix a son âme
@@elsavivianesagna8356 le problème des sénégalais et moi même en l'occurrence, c'est qu'on accepte jamais de poser un débat face à un désastre. Toi tu parles d'une fille, moi je n'indexe personne et je parle de la société. Je remets en cause l'éducation de nos jours et ceci dans toutes les dimensions. Le destin est certes inévitable mais je sais les actes que nous posons sont le plus souvent en adéquation avec notre éducation. - Des enfants qui louent une voiture ? responsabilité des proprietaire? des parents? - Des enfants qui sont à trois sur un scooter : responsabilités des parents ? - Des enfants marraine de Sabar à 2h du matin ? responsabilité de qui? - Des hopitaux toujours pleins ? responsaibilté de l'Etat - Des ponts sans lumiére : responsabilité de l'Etat je le redis quand même la plus grande responsabilité est celle des parents qui se désengagent de l'éducation des enfants. Un enfant de 16ans bignouy toudé sabar c'est grave en plus tu t'es trompé kignou toudé sabar bi elle a 16ans et c'est une éleve. Ecoute et lu bien avant de réagir
La présentatrice est correcte Mash’Allah.Yalna Y’a Allah yeureum khaléyis yi décédés mey wer ki dess
Jean Paul Senghor,mon ami d’enfance,j’ai su la mauvaise nouvelle tardivement,mes sincère condoléance à toute ta famille,tes frères,tes proches y comprises moi, j’ai grandi dans votre maison à dalifort,repose en paix mon frère 😭😭😭
Massa🙏🙏🙏😭😭😭😭
Ndessane yalla nako yalla yeureum frère metti na d bilay
K leur ame repose en paix
Paix a leur âmes
Ndeyssane metina torop paix a leur âmes
Kouné sa bess doko romp yalla na sounou borom xaréléne aldiana t diégal léne séne bakar métina torop😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Mai yalna niou fékkk si lou bakhe rékkkk
Amine
Cessez de juger les gens. Vs êtes là à blâmer les parents alors qu’ils n’y sont pour rien. Combien d’entre nous sommes sortis en cachette ou en disant à nos parents que nous allons dans un endroit alors que nous allions ailleurs? Seul Allah peut nous juger et nous devons prier pour le salut de leurs âmes. Ces parents souffrent assez
Vraiment mane dama warou trop. Li dafa meti! La derniere chose a faire cest de parler de pourkoi ils sont sorti juska 2h. Ca peut arriver a tout le monde! K Dieu apaise le coeur des proches!
Ndèyssane 😭
MaShaAllah #BicRouge 💕
Ndeyesane métina trop m c la vie yalla bou sokhla diame niake m yalla nalénne yalla yeureum té xarélénne aldiana souf oyof sén kaw finiou néķ taye yalla nalénne gueneul finiou diougué barkép serigne saliou
Amine yarabi
Thiew yalla Jean Paul cé mon jumeaux on n'est le même jour même prénom deysan réponse en paix k le seigneur aceuille au paradis ainsi que ls autre
je suis tres choquee par la mort de ces jeunes mais encore plus choquée par le laxisme des parents. il fut un temps, on n'osait pas sortir à certaines heures encore moins en demander la permission. et les parents était tres severes. timis sakh waroula fekk alleu. aujourd'hui tout ca c'est fini alors que Diamono ji mo gueuna doywar.
Tellement vrai paix à leurs âmes
Jtj deh🥺moi on m’a tellement interdit de sortir que gueineu soneulatouma bien vrai que enfant unique la ma mère a tjrs été sévère avec moi... diko santei yallah bou bakh...
Que leurs âmes reposent en paix
walahi lou wérr nga wakh mann bamay gueuneu fété ndaw bouma dioilé guéwé rérr dalouna ba att yima am ni niémé wouma samay kilifeu ba loumay déf daniou massiy diokh ndigueul. ñi nakk yalnaléne yallah yeureum
khamossi daara sakh 2h du matin ngaye nèk si mbèdami, metina wayè dèfoi li khèw yonou yalla nèkoussi,
Astou tout à fait d’accord avec toi
Mais bon ce qui est fait est fait paix à leurs âmes
Lou xew gnouni ndogal
Certe ndogal amenassi Mais
Ce phénomène de jeunes qui conduisent des voitures sans permis sans aucune responsabilité,on doit les sanctionner durement…
Vraiment, meme circonstances pour un neveu Rufiquois le jour de la korite ,decede sur le champ.
Il faut que l etat prenne des mesures.Trop triste, q Allah tt puissant les accueillent au paradis.Amen
Wahal dé
@@diatoudiop8811 yalna yegale ndawam firdawsi
@@saradiarra8813 Ameen Yarabi.Merci
Éwaye ñagneléne délo khéle yi si yalla tébayi damaye dokhe sama ndawe adouna dafa diékhe nagniou gueussetou sougnou diné top djiégualou sounou borome yalla naléne yalla yeureume kharéléne aldjana kissi désse yalla na tané ake diame barké borome touba
Fatou ndire yalla gua dioukh ak diam 🙏🙏🙏
AMINE YARABAL ALAMINE
Maman c dur mes condoléances ,elle est courageuse ,k dieu te donne la force virement .courage
Gni gagnou Yalla nalen yalla yereum Fatou ndir bon rétablissement à toi
Amine
Amine
J'ai les larmes qui coulent massa moment c'est très dure maman geume gua yalla yalna la yalla dolél
Bare ngassi morom
RIP 😔
Que le Saint Esprit, console les familles.
Courage Papa de Jean Paul, jàmbaar ngâ
Yalna len yalla oubil aldiana ak yermande Jean Paul yalna ko yesus Christa oubil aldiana ak ler tamite ay djigeen name yi yalna gnou tasse ak seray seydina Mokhamed. Bon courage sen famille
Dans cette histoire, on doit arrêter tous les responsables, à commencer par les gens qui ont loué aux enfants irresponsables et immatures ces voitures car ces derniers auraient dû vérifier l'obtention et l'authentification des permis de conduite de leurs clients avant de leur louer les voitures. A part cette histoire, les acteurs agissant dans le système de délivrance des permis de conduite au Sénégal sont vraiment tous coupables de plusieurs accidents autres que celui-ci, d'autant plus que ce pays fait parti dans la liste rouge des pays les plus corrompus au monde. C'est vraiment grave et déplorable, le Sénégal va vraiment mal à tous les niveaux
Bilakhi💔😭😭😭
Sa c'est vrais 😭😭😭😭
Mane khawma kou titoul wayé mane titeu wallay nitt yagui dead comm p possible et majeur partie bi ay accident lay done guir yalla les parents soyez vigilent sa dôme khale waroko bayi mouy gueneu au delà 22h deuk bi legui woratoul legui yalla naniou dadjiek yermandé souniou borom inchallah mettina trop
Bilakhi tourodo adouna bi dafa diekh metina trop
Ils étais trois dans un scouteur vers 2h du matin c risqué aussi k firdaoussi soit leur demeur éternel
Paix à son ame courage tu est un vrai croyant que dieu leurs accordent misericorde
Ndeysane pourtant le jour la nio nékone sui photographe bii yalna souf owof sén kaw
Bon rétablissement à Fatou ndir
K dianatou firdawsi soit leur demeure éternelle amine
Ndeyessan maityna lole yalla nalenn sounou borom yeuram
San pernie 😟😟😟😟😟😟🤭🤭🤭🤭🤭 li Lanla ni tamite yalna ko yalla oubile aldiana massa yalna len yalla may xolou mouñe 😭😭😭😭 Massa Papa Seigneur donne lui le repo éternel sans fin ndeysane Quelle Courage
Laa ilaha ilalla muhamadoura soullila yalla rekay bour ken d’où bour koudoul yalla
Innalillahi wa Inna Ileyhi Radjihouna wah yeupeu rafet té bayéko si waydiour yi surtout Papou Jean Paul ake yayou Melle Sow rafetna trop Mashallah Yalla naniou yégalé séne ndaw Aldiana té kidi Fatou Ndir Bour Yalla mayko wére ake bépeu dioulite massa
Yalla nalene yalla khare aldiana 🤲🏾 qui nek aupital yallana yalla feug bopoubi🤲🏾
Amine ya rabi
Amine
Aminnn
Amine way Yalla bakhna 🙏😭
j’ai préféré un album sur notre prophète seydina mouhamed psl ak souniou mame youbakh yi diappu lén si ngéne abonne fi si ansaar tv ta yalla rek takh nguir dieummi seydina mouhamed psl o
Oh metina torop Yalla na nelene Yalla yeureme khare aldiana amine 😭😭😭😭😭😭😭
Au ndeysann yalla nalene yalla yeureume té xarélen Aldiana 🙏😭🙏🙏🙏
Satan
Amine yarabi
Aminé amine aminé
Massa yaye bauye mais tamit soyez figilent enver vos enfants khalé bou djiguen mm pas 20ans gakoy bayi mouy guéne ay 1h du matin dou yonn. Yalnalen yalla yereum
bilay Awa wakhgaa deug dakar nimou reubè tu laisse ta fille sortire tamit a certainnes heures,doynaa warr, mere bi dafa beug dom rek
@@abdouthiam8234 ah doyna war dom boko beuguè warga diko samme té wadiour yeup euleuk yalla dinalen ladj nougnou samèwone sen ndiabot
Doy na war dall bilay mais yalla bou socla cou beuk niak 😭
Awa wakhnga degge me yallah nako yallah yerem
@@aichadia3420 amiine bidiahi naby
Yeen ndaaw ñii xolaat leen sene boop të yarou baña yakamtii sene adouna baayii foo bou baarii të jaamou soune BOROOM ! Yalnalene soune boroom yeureum diègueulene
Ndaaw ñii danio fokk ni khalé dou déh motakh wayé yallah kholoule khalé khouloule magke
Ay way bayi len sen critique yi dé bou nieuwé rk nieuwe na gni nek si nakar ngen nek fi nan warounio guen
Nianal len yalla yeureume len té khare len aldiana firdaw mo guene wakh dji
Exactly!! Plus yaye yi Soukayna sohla wul critique yii. Yaye bu nyaka dormam dafa meati! Yan na len Yallah harel Jannahtul Firdaus teh mei sen yaye yi holi mung
Dakarbuzz vous abatez un travail colossale 👍🏽👍🏽👍🏽👍🏽
Yalna len yalla yeureum yalnanou fekk silou nekh yalla
Paix à leur âme ke le bon dieu leur ouvert les portes du paradis inchallah
Et bn rétablissement à fatou ndir yalla n’a yalla deff Li geuneu si ioe ❤️🩹
Ndaysane yalla nalen yalla yeureum kharé len aldiana si barker borom touba
Sénégalais niou gueme yalla laniou ndaysann yalla nalen yalla yerem 😭
Amine Ya Rabi 😭🙏
Metyna yanalen yalla yerem kifi desse yala Nako yala maye wergou yarame 😭😭😭😭😭😭😭
ohhhh ndeysane metina le papa de jean toyal na sama khol😭😭😭😭😭ils ont brisé un rêve vraiment parking war nagnou di khol gnougni diokh séne auto yi ay khalé di foo si tally ba lorr nit ay jeunes yo khamni au yakarou euleuk lagnou si sene famille que leurs âmes reposent en paix
Ame repose en paix ?
Satan
Athée
Au sénégal y'a pas de sanction motakh chacun fait ce kil veut c le laisser aller total louer une voiture sans la présence d'un permis de conduire
Rip jean Paul mon frère et ma sœur soukaye
Hoo c'est triste maman yalla naléne yalla yereume té kharéléne aldiana firdawsi si barki seydina moukhamet psl 😭😭
Alkhamdoulila Yalla nalène Yalla yerem 🙏🙏🙏🙏
Oh ndeysane li metina trop yalla nalen yalla kharé aldiana j'ai même pleuré
Yalla nalén yalla térou sa aldianam ya guene kawé inchallah
Sa doma tagoula sabar au-delà de 22h rawatina thi djiguen nguakoy bayi les parents tmt bayil lén di top sén domi thi loulén nex bref yalnako yalla yeureum thé djégual ko ay bakkaram
Vraiment il faut k les parents veuillent d'avantage sur leurs enfants
Élève de 16 17 ans marraine d'un sabar,mais veuillez à l'éducation de vos enfants.
Wax nga deugeu de
Doyna warr yallah naniou yallah maye moudiou gou raféte
paix à leurs âmes papa de Jean Paul que le Christ apaise ton coeur
Thieuy yalla un élève bouy def bfem guay koy toudei sabar 16ans thieuy yalla liiii lou mou donne oh Sénégal penrent yii yokou leine sen surveillance stp les morts yalla na leine yalla yeureum metti na trop gni yor parking yii tmt am guein si part de reponsablité imature yi guein done j’ai mal😭😭😭😭😭😭😭😭💔💔💔💔💔💔💔🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Mane lolou la beugone wakh yalle nako yalla yeureume
Doyna war yalla nalen yalla yeureum
@@lorainefallou1442 yayam nena diangoul
Que leurs âmes reposent en paix et que le bn dieu leurs pardonne
Paix à leurs âme je suis choqué très grave que dieu leurs pardonne leurs pêché😱😰😭😭
Ndeyesane ay iouw lii dafa meti trop xolal ma li rek metina trop yalla nala yalla yeureum teh terrou leen si aldjiana wou cawe cawe 😭
Amine
Yalna lén yala yereme te khrélen aldiana,,,
@@thianediop9687 Amine ya Rabbi
Amine Ya Rabi mettina trop
Deysan cest tropp dure yalla nalene yalla yeurem
Yalla na souff sedd si sen kaw jean paul était un vousin depuis dalifort bon rétablissement a fatou Ndir
Moto molay ray🥺🥺🥺🥺, naniou moytou lamigne bala meune nathi amer! Thiey, courage aux parents
Cougnouye toude sabar ndaga wara ame kalisse te élève amoul ligueyoule il faut bien surveiller nos enfants et bien les éduquer à cet âge les enfants ne doivent pas sortir de la maison.
Bilay doy na warr dall😭
Merci bien soumeye seute à 23 ans gore ak djiguene tout le monde dort en même temps ke leurs parents.
Vraiment Touré sabar a cet âge môme doynawar mais yalla
N'a borom bi yésal yeurmandé thi mome et bon rétablissement à autre
Amin Yaraby Allah
Bro parfaitement dit mais très sévère de ta part parce que c’est triste mais c’est la vérité
Sen beuss mo diot rek dougnou def loudoul gnanal len
Bly mettina bly yalla nalen yalla yeureum fate ndir bon rétablissement ioe yalla boula faye sa xol bly daguay diogue inxalla
Massa paix à leurs âmes. J'ai pleuré pour ces jeunes vraiment que le seigneur les accueille dans son paradis céleste.
Ndeysane parents yi dagniy surveiller ba sonne mais khaleiyi daniou doy warr yalla naniou yalla sama samal niou souniou niabott
Paix à leur âme que Firdaws soit leur dernière demeure Amine Ya Rabb
Amine waye
A
AgainG
g
Yalna lén yalla yerem te diegal len inshalah kharé len aldjana ya guene kawé inshalah
Yallana y'Allah yeureumeleene té khaareleene Aldiana akk mbooleeme dioulitt
Ndeyssan yallah nala yallah yeureum té weureul gni ci blessé amine
Yall nako yalla yuereum ta khare ko Al diana barkep s touba
lii dawarone ame rk ndkh fii neupaye déme sabar tagou sa parent 00h mou bayila mes yallh nako yallh yeureume
Vraiment gniy louei auto amal ngein gnou ak helou ken dalatoul ham ngein kou majeur dou louei auto disi fo ..mai halei yi ngein di louei dagno inconscien vraiment bayilen si hel
C ça dai
Mais tmt khalei bou djiguene dafa wara tok thii weitou 16ans 18ans wadiour yii nagne défarate yarr bi thii birr keuryi khalei daguaye âme kilifeus yalla nalene yalla kharei aldiana thii barker yoneuntibi Amine
Boul wakh gnidi louer ndah ay mak nioy nieuw dieuleulko boy yi apres niou diohlenko en plus tmt bilay kou bayiwoul di diokh boy you amoul permis auto diga dougou dh
Paix à son âme 🙏
Paix à leurs âmes mais aussi les parents doivent être responsables comment on peut laisser des jeunes sortir tard dans la nuit pour aller à des futilités
Yalla naléne yalla yeurame té kharé len aldialna
C'est vraiment triste 😭 Que leurs âmes reposent en paix... Bon rétablissement à Mlle Ndir
Yalla nalene yalla yarame barkbe serigne touba amine
Yalana lene yalla yeurem si barket seydina Mouhamed métina trop bly cousin yalana aldiana nek sa keur 😭😭😭
Ndeysan se vraiment triste yalla nagn yegualé s’en ndaw firdawsi
Amine
Yallan bourbi yalla Yemen Amin
Ndeyssaneee massaaaa! 🙏🙏🙏
mere bi gueumena yallah dh yalla na domame souf sedeu kawame
Yalla nalen yalla yereume barké borom touba 😭🙏Tourando yalla nagu tanei ak diam
Soukéy yalla nako yalla yeureume mogue thiaminiame té kharé lén aldiana fatou ndir yalla n'a yalla feugue bopame
Amine ya raby
Quand les parents ne vivent pas ensemble les enfants n'auront pas de repères ni de guide
Je ne suis pas d'accord avec toi bro. Mes parents ne vivent pas ensemble mais Alhamdoulillah mes sœurs et moi on a reçu une bonne éducation et on suit les traces de notre aînée (une personne exemplaire notre 2ème maman❤)
@@mbayamesene2844 Tout le monde n'a pas cette chance bro c'est vrai y'a toujours une exception mais je parle en général
Massa. Yalla naniou motalé séne ndaw Aldiana. Té khaleyis moytou taly bi nak.
Métina lol té gni thi niak sén bakéne yalna lén yalla yeureum tabal lén aljana🙏🏼🙏🏼🙏🏼mais ki thi mouthiou aussi souko yalla mayé tane il faudra k niou suivre ko psychologiquement parsk choque bi meun ko traumatisé après
Bilaye
Bilay iow
Massa massa maman yalna maye kholou mougne. Que Dieu les 'accueille au paradis firdaws
Ohh c triste😭😭😭yalla nalen sunu borom yeureum
Yalna Yalla yeureume lene kharelene aldiana firdawssi Fatou yalna tannée ak diame
Amine
Ndeysaan les mamans geum nagnou yallah.
Masta yallah nalen borom bi yeureum.
Mais aussi gniy touddé xalé bouy def befm ay sabar tamiit xawma loulén dal vraiment
bilay metti na trop toudei sabar xalei bou ndaw doy na war dall😭🙏🏻
Esk sabar lawone parfois les jeunes trompent leur parent en leur disant pas la vérité
Yémè na dh vraiment mais yallah nalene yallah yeureum et bon rétablissement à elle
Mingii nonou deih
Inna lil llahi wa inna ilayhi rajioun yalna yallah yeureum leen té tabbal leen aldiana firdawssi ci barké seydina Mouhammad 🤲
Waayé ay waay ndaw gni naniou delou waat ci yallah🥺🥺 wakkiilou té wagni thiakhan yi adouna bariwoul solo lool😭🙏🙏
metina lol kéne yénéwouko kéne mais tamite prkoi des enfants de moins de 18ans gnouléne di toudé ay sabar fo khameni nekoul sakh séne kogne en plus si je comprends bien ils étaient 3 dans le scooter à cette heure de 1h a 2h du matin es ke tamite yéne parents yii amouléne si part de responsabilité hun il faut aussi veiller sur vos enfants au lieu ngéne di bâyi ba Dara khéww ngéne nekk si media yii di expliquer paix à leurs âmes yala naléne yala yeureume kharéléne aldiana
Vraiment doyna warr
Vraiment 16 ans tamite ou elle peut trouver de l’argent vus qu’elle ne travaille pas
Bilahi moma diakhall
Niakk kilifa rek
Yalla naléne yalla yeureum yalla naléne na aldianay firdawsi di sén keurou noflay ak bep way dawlou ci barker seydina mouhamed psl amine yaraby
Toutes mes condoléances k Ardiana firdawous soit leur demeure éternelle amine
Nala yalla yeukeuti ci jamm ma fille chèrie gni ci ganiou yàlla nalèn souniou borom kharè aldiana
Yalla nalene yalla yeureum tei kharei lene aldiana firdawsi 🙏🙏🙏🙏
Yalla nalen yalla yeureum haréko aldjana firdawsi
J'ai des larmes au yeux yalla nalen yalla gnereum
Qu'Allah assiste les blessés et pardonne les défunts... Mais les parents doivent éduquer les enfants. quand j'entends toudé sabar pour une éléve c'est grave et hallucinant. Il faudrait vraiment que les parents puissent surveiller et éduquer les enfants. Comment un enfant peut sortir jusqu'à deux heures du matin... OK Ndogal certes mais il faut situer les responsabilités.
La mère a bien précisé que sa fille travailler dans un salon donc soyons strict dans les commentaires sa peut arriver à toutes le monde la décision de dieu personne n'y peux rien paix a son âme
@@elsavivianesagna8356 le problème des sénégalais et moi même en l'occurrence, c'est qu'on accepte jamais de poser un débat face à un désastre. Toi tu parles d'une fille, moi je n'indexe personne et je parle de la société. Je remets en cause l'éducation de nos jours et ceci dans toutes les dimensions. Le destin est certes inévitable mais je sais les actes que nous posons sont le plus souvent en adéquation avec notre éducation.
- Des enfants qui louent une voiture ? responsabilité des proprietaire? des parents?
- Des enfants qui sont à trois sur un scooter : responsabilités des parents ?
- Des enfants marraine de Sabar à 2h du matin ? responsabilité de qui?
- Des hopitaux toujours pleins ? responsaibilté de l'Etat
- Des ponts sans lumiére : responsabilité de l'Etat
je le redis quand même la plus grande responsabilité est celle des parents qui se désengagent de l'éducation des enfants. Un enfant de 16ans bignouy toudé sabar c'est grave en plus tu t'es trompé kignou toudé sabar bi elle a 16ans et c'est une éleve.
Ecoute et lu bien avant de réagir
Tua parfaitement raison frère dokh ba 23h sakh eupna lol thi gor bu am yar wakhumala ak djiguene
Les gars c’est difficile de contrôler ses enfants lors d’un fête ??
Ceux sont des enfants qui conduisaient la 4×4 il faut bien écouter avant de commenter
Yalna len kharé aldjiana 🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭😭😭
Yalla nalén yalla kharé aldiana
Paix à son âme 😭😭😭
Bouy nieuw yalla naniou fekkkk si lou bahhh
Amine yarabi c important k firdaoussi soit leur demeur éternel
Amine ya rabi
Amine
Amine yarabi
Aminnn
Métina trop yalnalène yalla yeureum té xaréléne aldiana firdawsi