Histoire incroyable de Bouna Alboury Ndiaye et son père Alboury Ndiaye - Buur ba Djolof (en Wolof)
HTML-код
- Опубликовано: 2 янв 2025
- Rejoignez-nous & Soutenir cette chaîne
/ souhaïbou tv
---------------------------------------------------------
Abone wuleen ci sen bi ⤵️
/ souhaïboutv
-------------------------------------------------------------------
Mboor (histoire) yees fent ci Wolof ⤵️
• Histoire en Wolof
Léeb ci Wolof ⤵️
• Léeb ci Wolof
Taariixu Senegaal ⤵️
• Taariixu Senegaal (His...
-----------------------------------------------------------
Mbaalu jokkoo yi ⬇️👌🏿
Insta: www.instagram.... Feesbuk: / souhaïbou-tv-101746092...
Tiktok: vm.tiktok.com/...
________________________________________
Seen mbégté ak seen i njariñ ñooy sunu yitté. ✅✅
Ndaysane
Bulleene fattee nianal borom chêne bi
Il est Mor Abo souhaybu Gadiaga 😢
اللهم إغفر له وارحمه
machalla Alboury ndiaye domame bou djiguéne sama mame khalifa kounta moko done dégne thie ngouye ndiaye # mou ame si serigne sidy mouhtar khalifa kounta ak serigne Bouna mame khalifa kounta mome lagnou touddé sidy ndiaye alboury ak Bouna ndiaye alboury # samaye mame lagnou lene touddé
Masha Allah 🙏
EST ce que khamnga domou alboury bou djiguéne bobou noumou toudou? Moi je connais son nom
L'histoire de nos valeureux guerriers ça fait tellement du bien 🥰🥰
Ndiayenne yi ,musulmans,surtout toucouleur yi vraiment gno dieul meritou guerrier si rewmi.gno khekh pour Sénégal nak seulement ils étaient plus avancé avec leurs armes sinon donougnou wone dieul rewmi.
Vrai
Plutôt les rois wolofs ici on parle de rois wolofs pas toucouleurs
@@Cayorienne98degueulou watal rakh na peulh dé 😊
Peul kayy🤣🤣🤣 wolof lagnou waxx gnoune Alboury est un roi wolof du royaume du Jolof .Booyy waxx ngaa wax thii lolou moguen ngafii toudou bénén ethnie .
Ndiaye est un nom typiquement wolof , tout comme Diop, Fall, Dieng, Niang, Mbodj, Gaye , Seck, Mbaye, Dieye, Gueye, Samb etc ...
Djolof était un empire wolof,.. Cayor, walo, Baol des royaumes Wolofs , avec des administrations Etatiques Wolofs , Saloum est majoritairement peuplé par les Wolofs aussi..
Ndiadiane Ndiaye est un wolof originaire du walo, Il n'est ni le fils d' Abu dardaï ni fatoumata sall, c'est ni plus ni moins que des mythes tout fait pour légitimer leur pouvoir et s'attribuer des origines arabes (Xeetu prophète bi , Paix et salut sur lui )
L'histoire de l'afrique est remplie de Mythe !
Quant aux toucouleurs se sont des métisses entre peuls et Wolofs .
❤❤❤❤❤❤❤ Albury Ndiaye is my older grandfather i love the storker about them
Bëgge na nga gëstul ma Mboorum Demba Njaay ñu gënoon ko xam ci Demba Njare Yàlla di Maam ci Seex Ibraayma Faal Làmp ak Sëriñ Daru Haasan Njaay.
Ndayssan amna solo loll
Fière d'être wolofe💯💯
Ma sœur !
Ndiaye ❤💪Ndiaye 💪💪💪💪💪📿💪💪💪💪Ndiaye
Masha Allah 🥰
Ame na solo 🥰
albuuri penda ndieme ndiotte domou halpoular la. mo takhone mou dem Dosso ci mbokki peulame ya machalla. histoire dafa wara leer
Yamana fen
massala
Machalla ❤
Mâcha halla
❤❤❤❤❤❤❤machallah
Depuis qu'on a arrêté d'enseigner l'histoire de notre pays
Le résultat il y a plus de patriotes maintenant les enfants aiments plus messi que stadio mane
Messi c'est le Goat 🐐 sama Serigne 😂
Samame Bouna Al boury saynabou diob
Machalah
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mes grands parents
❤❤❤
AM NA SOLO WAYE BOUNA ALBOURY NEKOU BOURBA DJOLOF, ALBOURY BIRAME PENDA DIEME MOY BOUR BI MOUDIOU CI DJOLOF JAJEF
Wollof is originally from South Sudan
ou il a etudier alboury
💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖
🥰🥰🥰
Evitez svp de manipuler les photos comme ..... les 2 photos représentent la même personne ( Bouna).
Non Chiekhou Amadou Ken Gange wouko
💚💛❤🙏🏿
Ki Di la vérité sur le nom de famille de la mère de Bouna?
Fait moi une vidéo sur Maïsa Waly é comment il é devenu roi du Baol . Passer roi du D'une au Baol
Nékkul ni dione nga sant rek que Maissa waly sa maam la lol 😂
@@seyyidinaausmaannoreyni2316 Dafa am nion xamni dano rerrr .ndakh buur sant sa sant taxul mu doon sa maam , mann dh maissa waly santrk moma bole ak mom
@@alassanedione7316 yaw mi ya rer bougn la wahè say mame diga book ak mom
Alboury dafa daw😂
Li may rëccu mooy lima yeex a xam chaine maasàllaa li neex lool te am solo.
Je suis dans la même situation
La mere de bouna c pas ndiaye mais ndao !! Elle s Apel madjiguene bassine ndao
0000
Machalah ❤️
Machallah