Grand Théâtre: Sidy Diop chante Serigne Saliou

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 30 ноя 2024

Комментарии • 128

  • @ndellagueye530
    @ndellagueye530 6 лет назад +14

    A sidi yakham lo beug sa xol yall na lako yalla dèfal ci barkè serigne saliou sama xol sèdena gouy ci yaw

  • @ramalo7697
    @ramalo7697 6 лет назад +7

    Thiey sama artiste prefere bi😍😍machallah fi dal yafi neik tothie gafi mala begue mane😍😍

  • @impactafricatlcnewvision1997
    @impactafricatlcnewvision1997 4 года назад +1

    serigne saliou ku beug yekeutiku ak falu wala alal mosi gaw

  • @binetoumous.saliou7959
    @binetoumous.saliou7959 6 лет назад +4

    Ndeysane thiey suniou wadji thiey serigne Saliou ohkho sidy mane la talibé serigne saliou bila gnanale sa bisbi réussir t xamou mala yalla n’a yalla khep doli inchalla

  • @amycollengom1422
    @amycollengom1422 6 лет назад

    dieureudieufty serigne saliou aye sidy diop mala beugueu yalla nagnoufi yalla bayi cone nga khamni mala beugueu

  • @mamadouwade6283
    @mamadouwade6283 5 лет назад

    Je suit trop contan de toi ,,
    Bilay Sidy man damala beug ,,
    May tidiane bi beug Serigne Saliou borom khélcom diaga ,,

  • @diarrandiaye81
    @diarrandiaye81 6 лет назад

    Thiey sama waa dji borom mbecté mi sama yakar gui bayou serigne cheikh salihou yalla nako borom bi yokal ay léramm

  • @aliouniang318
    @aliouniang318 5 лет назад +7

    bilahi sidy diop yamana wayi bonne continuation à toi 😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @thielverno
    @thielverno 5 лет назад

    Mane mome je s8 tidiane mé j'aime bien s.saliou mbacké yalla na yalla yokk ay lëram té tass gnou si barkem

  • @maguettediouf5821
    @maguettediouf5821 6 лет назад

    Machala sidy diop yalla nala bour yalla lafal thiat liguay way tek ngako si temp

  • @mbenesamb5352
    @mbenesamb5352 6 лет назад

    Barker Serigne bamba sidi amoul morom. Mala beugg piiir. Yalna la yalla diapalee.

  • @ahmedndiaye8171
    @ahmedndiaye8171 6 лет назад

    Ma begue serigne saliou pur sama yakar tay ague euleugue li dawe na yareme

  • @ndiayerima4075
    @ndiayerima4075 6 лет назад +27

    Ma beugue serigne saliou borom welcom😭😭😭😭😭😭

  • @fallmaty6759
    @fallmaty6759 6 лет назад

    Mashalla wayga sama wasali sama yakar aduna ak alakhira kokou moy borom khelcom yereum ndongo darayi

  • @fatoufall5303
    @fatoufall5303 6 лет назад +4

    Machalla way beugu na la lol nak serigne saliou ak serign bethio

  • @pendatoure1437
    @pendatoure1437 6 лет назад +13

    Yalnala yalla lafal thiat sama rakk dji té so beugué avancé boul deklou wakhi none mention spécial frère

  • @amythiam5089
    @amythiam5089 6 лет назад

    Lafff thiateu Thieuye serigne saliou louniouko weuyy mou nekh dougou si kholeu yi tarkalla si kaw si kaname ❤

  • @elhajiihabibndoye5445
    @elhajiihabibndoye5445 5 лет назад +2

    Sidi yalnala serigne saliou faye

  • @saliougueye5125
    @saliougueye5125 6 лет назад +8

    Non Quii lounai Mounnako Amm Thii Musique c pas que Dafa wanai Trop Trop Trop billahi allé Bn condition Sidi DIOP félicitations😎😂😂😂

  • @awakebe8083
    @awakebe8083 4 года назад

    Bilay Ken d'où serigne Saliou Mbacké

  • @fatoucamara3719
    @fatoucamara3719 6 лет назад +2

    Machallah sidy serigne saliou takh na ma beugue la tay

  • @Soso-hh2pj
    @Soso-hh2pj 6 лет назад +1

    Sama sangue sama wadji kèneu d'où serigne saliou mbackè sidy Yalla nala Yalla fay

  • @awatallamboup5826
    @awatallamboup5826 6 лет назад +9

    Macha alla Baye Saliou mako beugue nekhna Sidi

  • @nabouniang2599
    @nabouniang2599 6 лет назад +4

    Machallah s.saliou rek la begue

  • @biragueye772
    @biragueye772 6 лет назад

    Serigne saliou dou kéne kénela yalla na yalla doli l air lame

  • @noreynisene1482
    @noreynisene1482 6 лет назад +13

    Serigne saliou doufi diouk mouk moy serigne touba

  • @babathiaw5181
    @babathiaw5181 6 лет назад

    Sidi diop vréma daga aye trop sakh machaala

  • @goldenprod3135
    @goldenprod3135 6 лет назад +7

    Billahi ligay way sama thoms nex na

  • @diatoudiop983
    @diatoudiop983 6 лет назад

    Serigne SALIOU KÉNNE waro chanter ak musique bou ame rythme beu mou si danser ni simon bonne continuation et yallah nala yallah diapalè

  • @seynabouboye4332
    @seynabouboye4332 4 года назад

    Sidy Diop vraiment j t'adore

  • @oumoukhairybassoum182
    @oumoukhairybassoum182 6 лет назад +5

    Ndeyezane sidy meune ngua waye

  • @ousseynoudiouf4947
    @ousseynoudiouf4947 5 лет назад

    Machalhal serigne saliou kene dou mome

  • @ndeyemaremeniang669
    @ndeyemaremeniang669 6 лет назад +5

    Neixna way machala louko way mou neix

  • @mizabtv
    @mizabtv 6 лет назад +3

    Da guaye diéki saye rek di dioylo gayii kokou sii xol yii la ko yalla déf 😢😢😢

    • @awadrame4788
      @awadrame4788 6 лет назад

      lolou deugleu mane talibé serigne babacar la wayei Serigne Saliou damako beug

    • @mizabtv
      @mizabtv 6 лет назад

      +Awa Drame Rawal waye lolou deugleu Serigne Saliou Mbacké es le dernière fils de Serigne touba mbacké mo takh

    • @ibrahimasylla4716
      @ibrahimasylla4716 6 лет назад

      Aziz Ndoye b

  • @pinepintokane7441
    @pinepintokane7441 6 лет назад +23

    Serigne saliou keine Dou moome mashala boye Sidy DIOP

  • @ndameseye6957
    @ndameseye6957 6 лет назад +3

    Sidi bonne contination

  • @toutydiallo6955
    @toutydiallo6955 6 лет назад

    Bravo sidi j aime beaucoup baye zale

  • @morndiayr2422
    @morndiayr2422 6 лет назад +2

    Sidy yaguimay dioy lo ndeye sane

  • @soumareaissatou1229
    @soumareaissatou1229 6 лет назад

    Je t'aime sidi diop tu est le meilleur je te le jurr

  • @mbayekane4604
    @mbayekane4604 6 лет назад +3

    Ken Dou mom serigne saliou

  • @ndeyeamydiakhate3089
    @ndeyeamydiakhate3089 6 лет назад

    sidy diope ya ngui LaLe sama khoLe s saliou rk

  • @coumbadiallo9113
    @coumbadiallo9113 4 года назад +1

    Kima yalla bolél thi adina Mame Saliou mala beug pire

  • @mohameddiebate1165
    @mohameddiebate1165 6 лет назад

    souniou yalla beuguei naniou bayei ioa

  • @syastou7838
    @syastou7838 6 лет назад

    Ma beug borom ndiouroul mame saliou lounou way si mom mou nekh 😂😂😂😂

  • @taphasamb3783
    @taphasamb3783 6 лет назад +2

    Machala diobene by wayy rek laydf

  • @ndiayerima4075
    @ndiayerima4075 6 лет назад +2

    😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢barki serigne saliou😢😢😢😢

  • @aminatagueyemachallahakass4051
    @aminatagueyemachallahakass4051 6 лет назад

    Di na djioxe Dara si waye wi Sidy

  • @cheikhibraniang6100
    @cheikhibraniang6100 6 лет назад

    Dieuredieufe serigne saliou

  • @adjiboussosow1923
    @adjiboussosow1923 6 лет назад +11

    Kene dou serigne saliou

  • @yamaseye5027
    @yamaseye5027 6 лет назад +2

    Machalaa'.

  • @sidygueye6492
    @sidygueye6492 6 лет назад +1

    Ay sidy mala beugeu

  • @elhadjmouhamadoudiawara7512
    @elhadjmouhamadoudiawara7512 6 лет назад

    Boy sidy dagua tarbiyou art c vrai mai waro tongue wally lui kholam mo rafète ta dèfalnala terranga tamiit

  • @roaldemilheidenstrm7671
    @roaldemilheidenstrm7671 6 лет назад +1

    Sidi am happy for u

  • @moustaphafall7767
    @moustaphafall7767 6 лет назад +4

    Sidi diop machalla

  • @btdpro3213
    @btdpro3213 6 лет назад +2

    Kidou nittttttt bilahi

  • @ablayetoure3517
    @ablayetoure3517 5 лет назад

    kene dou serigne saliou

  • @zalebestrapper
    @zalebestrapper 6 лет назад

    thieuy serigne saliou

  • @saliougueye5125
    @saliougueye5125 6 лет назад

    sidi linga way Seringe saliou boko Daifaii son billahi Fingay Diaraii Takk Dotoo Faya Tiii Moukou billahi😎😎😎😂

  • @zalebestrapper
    @zalebestrapper 6 лет назад

    il est fort ce gars

  • @fatouba1948
    @fatouba1948 6 лет назад

    Macha allah sidy diop

  • @famaniang-z1h
    @famaniang-z1h 6 лет назад +1

    Euuyy serigne saliou si xol❤❤

  • @passydiop5348
    @passydiop5348 6 лет назад

    Non il chante bien boy bii bone continuation inchalla dina bakh

  • @adamagueye3858
    @adamagueye3858 6 лет назад

    Sidy diop 😍😍😍😍

  • @sophiesissoko6284
    @sophiesissoko6284 6 лет назад

    Masha Allah Sidy

  • @dioufboukatew8978
    @dioufboukatew8978 6 лет назад +3

    Mam Saliou kourage sidi

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 6 лет назад +9

    C'est ndongo lô de retourne sur terre tiguii........

  • @ibrahimadiop5402
    @ibrahimadiop5402 6 лет назад +2

    Thiey sidy

  • @banlieuetv
    @banlieuetv 6 лет назад

    SIDI BAYIL KHACIDA YINGAYE DIAKHASE

  • @mamediarraseye5852
    @mamediarraseye5852 6 лет назад

    Machalla Laf thiate

  • @moustaphagueye2462
    @moustaphagueye2462 6 лет назад +18

    Nn ki dou nite il est très fort man kay Lima diakhal 6 deslike yima guiss rkk moma diakhal nn man ma warou peut être dougn ay sénégalais

  • @ndeyesokhnadiop3431
    @ndeyesokhnadiop3431 5 лет назад

    Wa sidi loutax ga meun woy

  • @fatimalareine7865
    @fatimalareine7865 6 лет назад

    Ndayssane nexxxnaaa💖💟💟💗💗

  • @amadousow3647
    @amadousow3647 6 лет назад

    Serigne salihou rèk

  • @kmb1111
    @kmb1111 3 года назад

    2021🔥🚀

  • @fatimacissediaboumamedabak198
    @fatimacissediaboumamedabak198 6 лет назад +1

    machallah 💓

  • @dionecheikhousmane3310
    @dionecheikhousmane3310 6 лет назад +2

    serigne salliou rek

  • @moussa7369
    @moussa7369 6 лет назад

    Machahala nekh na tropp

  • @ndiayabsaa4772
    @ndiayabsaa4772 6 лет назад +1

    Damala beugue nak mame saliou mbacke

  • @ngagnendiaye5996
    @ngagnendiaye5996 3 года назад

    👍🔥♥️

  • @seydina7282
    @seydina7282 6 лет назад

    Bonne chance ✔🙏

  • @welysamb7507
    @welysamb7507 6 лет назад

    Machalla

  • @modoufaye412
    @modoufaye412 6 лет назад

    li dow na yaram bilay 😪😪😪😪

  • @damembow6374
    @damembow6374 6 лет назад +8

    moune gua wayy mais dagua beuri folklore naturelal

  • @batorhane2118
    @batorhane2118 6 лет назад

    si te voit à se moment je te donne un Camille alkhourane bilay

  • @tourebocar4144
    @tourebocar4144 6 лет назад

    wawaw 😰😍

  • @famadiabaye8914
    @famadiabaye8914 6 лет назад

    madiodio gnigue

  • @bassdiaw3934
    @bassdiaw3934 5 лет назад

    Boy ya mana way car

  • @elhadjimamadoundiaye6246
    @elhadjimamadoundiaye6246 6 лет назад

    Nice

  • @sodambodj3823
    @sodambodj3823 6 лет назад

    Vrai ndongo

  • @banlieuetv
    @banlieuetv 6 лет назад

    dél guestou balaguako défate ok

  • @mbayesopyeskhadimgueyexass7566
    @mbayesopyeskhadimgueyexass7566 6 лет назад

    Lie bakholl d'Ara

  • @bayezallndir4974
    @bayezallndir4974 3 года назад

    Baig

  • @bambandiayediouftoubabrasi7893
    @bambandiayediouftoubabrasi7893 6 лет назад

    😂😂💚💛❤❤

  • @omarseck113
    @omarseck113 6 лет назад +4

    Boy bi il chante bien mai il a un peut de déchét : déchét bimou am si waye moy? Dafa wolou bopam si waye di déf louka nékh si micro Diangue dou wéss gnoune ay mélomane lanou wayam désna sétt mai il a de belle voi

    • @taphasamb3783
      @taphasamb3783 6 лет назад

      Omar Seck parfaitemnt raison bro

    • @omarseck113
      @omarseck113 6 лет назад

      Tapha Samb bro gnoune ay mélomane lanou khamnanou kou meuneu way? Jeune talen yeupp meune nala wakh kou nek ak sa défaut waye dacor talent sila mai Diangue music dafa gueuneu am solo té gnou bari si gnome séne live dafa déss? Sénégal gnari musiciens yi laguiss sunu live dafay nirou linou waye si cassétte ték ték mouy thione seck ak youssou boy yi danou wara diangui waate music je né rien contre eux mai il faut aprendre encore

    • @amysene6789
      @amysene6789 6 лет назад

      Omar Seck Lou lér nga wakh jsui son grand Fan wayai n'a geuneu djangue musique comme u la Di Omar séck mais nak le meilleur réste à venir félicitation sidy et courage

    • @mbenesamb5352
      @mbenesamb5352 6 лет назад +1

      Omar yaw wakho fi touss.

  • @amycollengom1422
    @amycollengom1422 6 лет назад +1

    dieureudieufty serigne saliou aye sidy diop mala beugueu yalla nagnoufi yalla bayi cone nga khamni mala beugueu

  • @coumbandiaye1656
    @coumbandiaye1656 6 лет назад

    lafffff tiatte😈😇

  • @sambagueye9142
    @sambagueye9142 6 лет назад +1

    😂😂😂😂😂

  • @evandoye2304
    @evandoye2304 6 лет назад +1

    Blh ya beurri manière momo dieng lagnou wakh gnoune soit naturel 😂😂

  • @afrikkmio4639
    @afrikkmio4639 6 лет назад

    Tu chante bien mais desgua Lou barrri

  • @diaramamamecheikhibrafall4266
    @diaramamamecheikhibrafall4266 6 лет назад

    Ki mom xamul dara xawma lu tax nigni diko deglu rek