Très pertinent Pr. et modéré, pondéré. Maa Shaa ALLAH. Talibé Cheikh dall, yarou, teey, am teeguine, am foula, am fayda. Waķh loumou, mandou thi li thi dess. ALLAH SWT fayal gnou Cheikh Ahmad Tidiane RTA té sakhal gnou thi tarikha bi abadane daa imane.
MachaAllah dieuredieuf seydil Elhadj Malick, motakh gnou kham kane moy seydina Mohamed (saw) ba mou féss délleu sunu khôl yi , lépam Faratah leu ak sunnah Rassoul
S pi gua ballma mane si tijiane la dioudo te sama famille yepou tay ayi mourite l'âne te tayi la s'en guem guene yokou s'en khewal tayi la guene yokou lou doul lisslam boulanekh bayi ko te daaaara doula si fegue te yonetebi loudoul tarikha khadar bayoukofi
@@modoudiagne497 gni bayyilen fi gni wakh rek kou tedki bimi woote yoonou mourid fila fekk tarikha tidiania ak khadria te tewout bimou wooté mak gnou barí dano bayyi lan nekkon wouyousiko ak tarikha bomci mana done ken kou nek na nek sa lam nek te yennente diamou lepp islamla
Professeur niveau bi dafa kawé motakhe élèves yi nék primaire dounou comprendre xam xam rék moo woore mais di wakhe dans le vide rék amoule thieusse laye
Sénégal benn bop la jaroul sissou jaroul ignaan gneup nagngou nanou Maodo monou khamal yonnete bi psl début ba fin à travers khilassam bi et c le Sénégal ki gagne
Seydi Elhadj Malick Sy était un érudit pieux de dimension exceptionnelle mais ce monsieur est indigne de se réclamer de lui au vu des contre-vérités qu'il débite par pure. jalousie.
nit kou bakh lol ndeyssane au fait mane damalen yeureum dakh sen xol mo fébar yalla nalen yalla diapalé fébarou parparlo ak fanatisme vraiment vous êtes malade 🤣😂😂😂
Fatou Bintou Wade Sokhna ci ki kay boko guissé sakh bokoul ci Baye ndax tariha Cheikh ben la tei mame Abdoulayi Niass dafa beugone Maodo tei fonko.mane doumay commenté ci yefou tariha yi sakh mais ki tey dafma lal niak diom rek motax mouy lakatou ci benen tariha pour attaquer tivaouane
Dieufi ku ragual lafi dégu dei.Dém dénde ji ak Toubab bi nguir ragal ni su soré toubab bi man naka andil problém.Su beugué jaka dem si toubab bi nan ka zawiya la beugeu tabakj😂
tarikha cheikh ahmada tidjiani dâ am sirrou ...sirrou bi mooy mahrifatou bi laahi té kuñu oubiwoul si"faatih li mâ ouhlika" lâalagô sirrou tariqa bi diarawlak mame cheikh ibra fall mame maodo yalla nanu ko yalla fayal
Malick sy. Toi, Est ce que ça marche bien dans ta tête? Wakhi doff yi noko meuné wakh.yow kay gueumeul lingua gueum rek té bayi Garouwalé bi Mame seydi el hadji malick(RTA) beuguoul togne
@@syngariboundou2355 .mangui lay balou akh ,man dé baal na nieup ci werou ramadan bi werou yeurmandé .yalla nagnou ko yalla défal. Man dé ki ma gueum té yakar ko doumako wouteul adversaire ndakh khawouma loumou done ,fo ko natt rek mou romb fofou té mbirmi nékatoul competition ndakh toubab yi nékatou gnou ci mim rew .DIEUREUDIEUF KHADIMOUL RASSOUL.
@@elhadjimomarsow8020mais loutakh ngène maye tontou mane touddouma bène toure rèw mi dè nèkhoule wakhè khane kii lii mou wakh thii maodo molène nèkhoul pour maodo sagako rèkk ngène thii khame akh diko doyodale sènègal lokho mame ass thii bira bire bafi toubabi nèkkè EN 1892á saint louis wèttou keur gouverneur la tabakh zawiyam
serigne touba moye l'islam pourquoi keur serigne touba rek gaye dem fégeufa talibé serigne touba bou serigne touba dieul werdou bouko nekhe diokheko mouye werdou tidiane wala werdou khadre wala bénène parce que serigne touba dar ligueye si werdou yeupou ba ame si lisi sen borom ame ame sangne sangnou diokheko kouko nkeh ame sangne sangou difsi louko nkhe aussi donc serigne touba il est le serviteur du prophète seydina mouhamed enoyé par notre Seigneur Dieu le tout puissant
Bayilenn réseaux sociaux je suis mourid mais ngi dou nou wakh louy diarigne da ngi diakhasse rek konn bayilenn si khell ngi senn bopp rek laniou nekk li des moy sama khelate
Eskey seudi elhadji Malik nitou yalla deug la waye nak delene wakhal Serigne Touba loumou wakh ndakh serignbi koudoul seyidina mouhamad defou la sang ci digantem AK yalla ta yalla doyonako sede ta dawoul wone woute ay kharite tha nasarane ya foko fek yala AK yonetebi rek la da wetaliko dieuredieufe s touba
@@hdiifisnkfkfk2331 mdr trio bi niom denio nangoul Sérigne Touba liko yalla may. Yalla ak yonenté bi li borom touba am ci niom mom rk leu. Sen demouniou dikouniou. Beni Khadime Rassoul mo am mais bay Rassoul amoul ni maodo Rassoul, niom nieup Aÿ talibé Cheikh Ahmed tidiane laniou. Maodo nena Sérigne Touba rk mo mossoul def limouy toub ci waliw yalla yi. Kou nek xamnga kouka meune té beuréwoulen. Sen Sérigne Amouniou deuk, amouniou bessoup magal ndakh defouniou lougn koy amé. Yen kay yena sokhor mais monatoulen soss ba sosal sen Sérigne louniou defoul
@@ndoyepapaibrahimadiasse3026 khamgua ji séné masalikoule djinane bi mo takh gnou fouye bayima ak niome rek domeram te séné serigne 7tonne de tere khana dindoul niane nioko rope ak fane lagnko rope
képou ko khamoul si serigne touba dara mandoul nopile aussi mais di wakhe si serigne bi naka soudoule nonou bakhoule aussi serigne bi ken douko wakhale loumou wakhoule bakhoule
Nexoul ba nexoul wayé waxofi xam xam. Kou CHEIKH ABDOU KHADRE guereum. CHEIKH ASSANE A ZAZALI guereum. CHEIKH AHMED TIDJANE CHÉRIF guereum. Gua xole né ame keur fépp 'Europe , Asie, ak amérique. Deuk fi senegal. Parfois guay titaro Nelson Mandela wla martin Luther wla Thomas sankara wla ma hadma guandi. Ta ligno tek assakabi sax teguou niou len ko. Boy wax si gnognou sax gay gueni bègue te guané dioulite gua. Naniou xolate sounou bob sokhor baxoul wax sa baxou way dou yakou si sa mbax darra. Mak gni dagnou defarouwon na waxdji tegou si xam xam té niou bagna parparlo. Kounek xamgua koula meune té xéxoulen. Depuis massalikoul djinanane ba legui ignane daff fé fegne nak.
@Abdallah Ba lol jummah bene la fi Ahmadou moko samp 1924 Rakam Cheikh anta Mbacké Egali fi ay jummah yudul dieh Modou Bamba amul wone poche boulko faté
@Abdallah Ba Zawiya Bigay toud Jummay Ndiareme mak nako 20 fois et en plus de ça fék na mou dem si gueidj gui mom d ak gnou bari mom rék mo démone té mom réka nieuwate et 1924 migui wone en residence surveillée je te signale Ba si Gammou bi guéne di fay def 1902 guéne ko nieuk déf Ak Serigne Rawane Ngom Ahmadou né " Ahyaytaw Mawlidal Nabi Mina akssachi" Aksachii moy 1882 Manam Ahmadou wotéina 20 ans gamou kéne soga gamou si territoire senegal si mbolo
@Abdallah Ba Voila la finition a été faite en 1924 1892 Ahmadou gui ak Cheikh yi si diganté Mbacké Bari ak Mbacké Kadior dema goul sax si exil bi 3 ans aprés le dém Té si Ay téguinam Wadiouram mame Mor Anta Saly fi nékone motah mais automatiquement apres sa disparition en 1882 la woté gamou
Maa waarou ci Sénégal.Toppandoo rékk ak gaarouwaalé ak di concurrencé sounou Mak gnou baakh gni.Mais nak khamalné Toubab bi djoumoul ci bagna yobb kénn guédj.Toubab bi loum déff khamnako. Da nga di goné rekk.Ta khamoo histoire sa kham kham bariwoul.
Kii wakh léne ko mou dém diangui wat limiy wakh xamousi dara moy fénal Serigne sii nii rk kii bou diagone Dina tok si télévision bi nane xana xemga gnake fay da
@@ndoyepapaibrahimadiasse3026 kou bax pourtant sagaw mala d kone amal ay teguin ! Man dama deglou waxtan name té guissuma dou aya dou adiss dou dara loum tek fofu d la waxei mai dego ma toud sa baye yein nak lilên metti teguniulén ko. Niune SERIGNE TOUBA danio fagul lép yein nak amoulein touss loudoul tok tak radio yi di wax rk kou mer clamel Yalla
@@diopnene1241 kou bakh yalla lepou lou mou ame si nite lako déf te nite kokou moy seydina moukhamet nite loumou khame loune nite moko ko khamal te nite guen douko topou yalla laniouy topou nite dankoy roye si lou bakh
@wallo tv mo yéna niak djiom wa touba niom nawlo wu gniou wa tivaone dé billah do deucgue bén serigne gniou mouride bu wakh ba toddou el hadji Malik sy jamais lécgéy ak djiamou yalla rk yén mom gén di weur di fén rkk mais bakh na goor goor loulén si sén djiouma dji ndakh mou acgue🤣🤣
Kénedou bayou serigne Babacar. Sy machallah done talibé cheikh mo nékh louway ame dieleule
Très pertinent Pr. et modéré, pondéré. Maa Shaa ALLAH. Talibé Cheikh dall, yarou, teey, am teeguine, am foula, am fayda. Waķh loumou, mandou thi li thi dess. ALLAH SWT fayal gnou Cheikh Ahmad Tidiane RTA té sakhal gnou thi tarikha bi abadane daa imane.
MachaAllah dieuredieuf seydil Elhadj Malick, motakh gnou kham kane moy seydina Mohamed (saw) ba mou féss délleu sunu khôl yi , lépam Faratah leu ak sunnah Rassoul
Billahi boudoul wonakk mome wakh djé bari yalla nanou dé thie talibe chékh
Lima manaa Watt moy yagui tongne mam seydi hadji malick mom dhé kou mandoula yoname nékoul thi dokhinou kénéne yaaw ngay toudou sounouy tankou nééne ak sounou dokhe thi bathie sou form de garouwallé yaw nagne bi ndioune lay lack lackoula mandoula rék lagnou nék soudé deugu ak souko donoul yawmal khiyame kén doulako lathie ndioune lay kon lathie
Konde gni alkou dinan bari man mii de samay mamat ay tidjan lanwon
Fiimou tollou nii dh gnepp ay mourid lan
Yalla nanou doon ay saadikh
Bilakhi
Lolou mene na nék mais kén dou diel tarikha chéikh ba nopi bayi ko
S pi gua ballma mane si tijiane la dioudo te sama famille yepou tay ayi mourite l'âne te tayi la s'en guem guene yokou s'en khewal tayi la guene yokou lou doul lisslam boulanekh bayi ko te daaaara doula si fegue te yonetebi loudoul tarikha khadar bayoukofi
@@modoudiagne497 gni bayyilen fi gni wakh rek kou tedki bimi woote yoonou mourid fila fekk tarikha tidiania ak khadria te tewout bimou wooté mak gnou barí dano bayyi lan nekkon wouyousiko ak tarikha bomci mana done ken kou nek na nek sa lam nek te yennente diamou lepp islamla
Yalla nagnou ko yalla fayal Mame Maodo
Professeur niveau bi dafa kawé motakhe élèves yi nék primaire dounou comprendre xam xam rék moo woore mais di wakhe dans le vide rék amoule thieusse laye
Thiey souniou mame dji machallah dikoy Seydina Mouhamet rk la yoré day diagualé
Macha allah yalla na yalla fayla yiw si barké seydina Mouhamed ( psl):
Maodo raw domi maodo raw seutou maodo raw talibé maodo raw 💖💖💖💖😇😇🙏🙏🙏
Yalna yala yagal sa takhaway serigne Ousmane mbaye barki sangue bi
Wallahi ndayesan diarama Cheikh saydil Hadji Malick 🇸🇳❤️
Machalla yalla nagnou yallah fayal Mame maodo fier d'être tidjane
Machallah amne solo kendou seydi hadji malick sy yall na gnouko yalla fayall bi diahi nabil Mustapha psl amine 🙏🙏🙏
Thieuy Maodo Thieuy Maodo ... Mame Ousmane bègue nagn lol . Machalah ❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieif y'a oustaze xam xam rek
Wallahi ndaysane yalla khamnako
Poumkale youneka senegal di nittou yalla tarikha chiekh tidiane cherif lanou bokou chiekhou Omar foutiyou Tall ak maodo serigne babacar sy ak seydi nourou Tall malick sy ak chiekh IBrahima niass kholal koumana am talibé yeup thiey abdoul abas chiekhou tidiane cherif amoul morom billahi 💖💖💖👈👈🙏🙏🙏
Tidiane yii xam xam rek bayeekou ak noum 💪👍💪😂😂👍👍💓💯💯💯👋👆
Machahallah.sy.malik.ken.dou.seydil.Hadji.malik.sy.amoul.morom.si.senegal.ak.liko.wer.👏👏👏👏👏❤❤❤❤❤
Sénégal benn bop la jaroul sissou jaroul ignaan gneup nagngou nanou Maodo monou khamal yonnete bi psl début ba fin à travers khilassam bi et c le Sénégal ki gagne
Machalla yalla na diam yage senegal
Si lane
Dieradiefé Cheikh Seydil Hadji Malick Sy ♥️ sma tourando
Bilay
Serigne touba moukhamet moy sédém
DIEUREDIEUFE SERIGNE TOUBA
Seydi Elhadj Malick Sy était un érudit pieux de dimension exceptionnelle mais ce monsieur est indigne de se réclamer de lui au vu des contre-vérités qu'il débite par pure. jalousie.
Ben Mohamed Sow Je suit parfaitement d'accord toi.
Seydil haji Malick limou déf ci Sénégal 🇸🇳 kénne defou ko fi 👆🏾
😆😆😆😆
Awa Ba calme toi bayiléne yoyou ah
Dou degué kilifa Lou mouy ragal thi tangaye mo
@@cheikhdiouf8601 Moss nguen té yamolen
Dieuredieuf maodo dieuredieuf machalla ziar a vous tous ziar
Sawaay de day fayou mais bisri mom Def na lén ku ba pré 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
nit kou bakh lol ndeyssane au fait mane damalen yeureum dakh sen xol mo fébar yalla nalen yalla diapalé fébarou parparlo ak fanatisme vraiment vous êtes malade 🤣😂😂😂
Serignbi yéw nii niooy say mbok ndakh yéna bok pass pass ak tarikha .
Serignbi yéw nii niooy say mbok ndakh yéna bok pass pass ak tarikha .
Seynabou Ndiaye ki dou Talibé baye
Fatou Bintou Wade Sokhna ci ki kay boko guissé sakh bokoul ci Baye ndax tariha Cheikh ben la tei mame Abdoulayi Niass dafa beugone Maodo tei fonko.mane doumay commenté ci yefou tariha yi sakh mais ki tey dafma lal niak diom rek motax mouy lakatou ci benen tariha pour attaquer tivaouane
Maodo malick toubab yabouko manouko diapp billahi wallahi kou donou chiekh tidiane cherif ak mouhamad rasoul si senegal toubab douko diapp moukk legui rek kouné di reuy laminge wayé maodo boudoule wone mom dou bakh dé billahi maodo malick sy mofi donou mouhamad rasoul mofi donou chiekh tidiane cherif mofi donou chiekhou elhadji Omar foutiyou Tall 💖💖💖💖🙏🙏🙏🙏
Diambar la mom
wayei La Bayou Gorr Yalla yi wax koukofa waxone dém
gna démone kéne nieuwoul dé ba hamgako?
😂😂😂😂😂😂😄😄😄😄😅😅🤗🤗
Dieufi ku ragual lafi dégu dei.Dém dénde ji ak Toubab bi nguir ragal ni su soré toubab bi man naka andil problém.Su beugué jaka dem si toubab bi nan ka zawiya la beugeu tabakj😂
Machallahe 👏🏽👏🏽❤️❤️
tarikha cheikh ahmada tidjiani dâ am sirrou ...sirrou bi mooy mahrifatou bi laahi té kuñu oubiwoul si"faatih li mâ ouhlika" lâalagô sirrou tariqa bi
diarawlak mame cheikh ibra fall mame maodo yalla nanu ko yalla fayal
NAMA YALLA JEGAL MEE KI FEN AK SOKHOR REK LAY DOKHEE
Machalah amna solo yalla na yalla fayline yéw
Dieureuf baye
Kéneu dou MAODO yalna yala fayko amoul morom
Mash AHLLA
Yalla nagnou yalla dolly fayal yiw seyedil Hadji Malick sy R-T-A l'inconnu de la Nation
Wakhou taib soocébi worosi wooana niewaat wakhtaanbi neekhna trop manchallah.
Rewmi bamba moko mom wassalam
Motakhit lornaniou ak coronawam bi deh
@@moustaphaseck5788 yaw bodol won sa torbi kon ma wakhal lo bon
Bamou des sama keur mako dieudeu titre foncier sama tour mossi nèka
Mai wadji dégue na rékkk lay wakhe khana kénn bindoull si maodo
MACHALA KIN DO MOYDO
Machallh amna solou trop
Diganté yalla ak serigne touba kéne khadiosi serigne yalla rék ladoon wér lou takh mou déme si yonéntibi yallakoko wakh
Machallah
Tarikha chiekh da diégui frontier moy partou dans le Monde
Amena khole youye dague akh youye binègar
Malick sy. Toi, Est ce que ça marche bien dans ta tête? Wakhi doff yi noko meuné wakh.yow kay gueumeul lingua gueum rek té bayi Garouwalé bi Mame seydi el hadji malick(RTA) beuguoul togne
@@elhadjimomarsow8020 kane la togne dangue thii guisse sa bopp nane touddouma kèn dara wèrr sama guèdji kouko wèrri ya ko mome
@@syngariboundou2355 .mangui lay balou akh ,man dé baal na nieup ci werou ramadan bi werou yeurmandé .yalla nagnou ko yalla défal. Man dé ki ma gueum té yakar ko doumako wouteul adversaire ndakh khawouma loumou done ,fo ko natt rek mou romb fofou té mbirmi nékatoul competition ndakh toubab yi nékatou gnou ci mim rew .DIEUREUDIEUF KHADIMOUL RASSOUL.
@@elhadjimomarsow8020mais loutakh ngène maye tontou mane touddouma bène toure rèw mi dè nèkhoule wakhè khane kii lii mou wakh thii maodo molène nèkhoul pour maodo sagako rèkk ngène thii khame akh diko doyodale sènègal lokho mame ass thii bira bire bafi toubabi nèkkè EN 1892á saint louis wèttou keur gouverneur la tabakh zawiyam
serigne touba moye l'islam pourquoi keur serigne touba rek gaye dem fégeufa talibé serigne touba bou serigne touba dieul werdou bouko nekhe diokheko mouye werdou tidiane wala werdou khadre wala bénène parce que serigne touba dar ligueye si werdou yeupou ba ame si lisi sen borom ame ame sangne sangnou diokheko kouko nkeh ame sangne sangou difsi louko nkhe aussi donc serigne touba il est le serviteur du prophète seydina mouhamed enoyé par notre Seigneur Dieu le tout puissant
Aujourdhui ya trop de marabouts mais du temps du colon le seul marabout etait celui de touba
Mdr boy sa serigne deh yalla maynako wayé mame maodo bâ legui charia diamouko
Sa serigne nak ladjko loumou def bâ charia diamko lolou ben la rek si loumay lathie yi dess beurina lol
Moustapha lingua wakh bilahi walahi togne ngua té Soko Touboul yak Serigne bi la. Wa salam
@@papitodiaz6016 saway ndaw bou rew dafay moytou gouné bou bayam féké demb wakh dji naniouko bâ désormais keur seydi el hadji malick koulen toudou si Aÿ Katie mba dilen dendalé aki soss dinako safara ak deugg
@@moustaphaseck5788 wa bakhna lou way wakh ba bauba
Machalla ❤❤❤
Wly ndeysane
Bayilenn réseaux sociaux je suis mourid mais ngi dou nou wakh louy diarigne da ngi diakhasse rek konn bayilenn si khell ngi senn bopp rek laniou nekk li des moy sama khelate
Ra fètna billahi
Eskey seudi elhadji Malik nitou yalla deug la waye nak delene wakhal Serigne Touba loumou wakh ndakh serignbi koudoul seyidina mouhamad defou la sang ci digantem AK yalla ta yalla doyonako sede ta dawoul wone woute ay kharite tha nasarane ya foko fek yala AK yonetebi rek la da wetaliko dieuredieufe s touba
Borom niétti ndonuyi maodo malick moukhamat rasoul ak chiekh tidiane cherif ak chiekhou Omar foutiyou Tall
Yokhoussi Mame Baye Niass bilahi Talibè Cheikh amena leup
@@hdiifisnkfkfk2331 alfaydatou tidiane chiekh IBrahima niass sm serigne nou yaye koku domako faté
@@hdiifisnkfkfk2331 dioum nga maodo AK mame ablaye la won alphahi mayoro welé la ndax moy nidiayam
Machallah la sén tv mbirmi tarou na
Garou walé bakhoul néklén thi linguén nék rék ta linguéy
Danga si guisse gaanouwalé
Yaw daga rérr serigne wakh bakhoul nèkal figa nèkke tè nopii
Sokhore rèkk
Garo wale ci yeen la yem
@@moktarmoh789 kou fénale Mame Maodo rta ngir tague Serigname ngène apprécier sounou wakhé liye deugue si Mame Maodo rta ngéne wakhe danouye gaanouwaalé louléne beugue
Talibè cheikh la mè yaw amo kham kham barkè serigne babacar sy di bolè tarikhayi rèk
Khouleur ake diane bouniou léne di diawalé danio mata ndowoul wayé bouniou matando rék gua khamni dangare yi douniou béne Ahmadou Bamba l'unique Homme
Gnome gnep ay Jamie yalla you yalla nangoul ..... bayilene wskh te dem defi la maodo ak bamba ak gnome gnep lingo done def
Ha condé Sénégal gñi alkou dinagn bari sougñou mame yép ay tidiane lagñou wome saway kholatal liguay wakh 👌🏾 ahmadou bamba point 👌🏾
Diarama seydi el hadji malick sy
Kou woor tarixa cheikh alkou thiey yalla 😠😠
Hey way lolou moy alkou. Bayilen di fenal maodo.
Ñi xamuñu yermandé yalla motax ñu yombal alku والعياذ بالله
malcom x malcom x kone lolou motakh guène corona
@@hdiifisnkfkfk2331 diguene crona legui
Bouré Diouf mdr bètouma nak dakh daguène sokhor.Gnoune Yalla,yonène tibi,cheikh Tidiane,cheikh Oumar,maodo,baye niasse point.hamnagne trio bi molène mèti mais gnoune dougnou douguou lou amoul guarantie.
@@hdiifisnkfkfk2331 mdr trio bi niom denio nangoul Sérigne Touba liko yalla may. Yalla ak yonenté bi li borom touba am ci niom mom rk leu. Sen demouniou dikouniou. Beni Khadime Rassoul mo am mais bay Rassoul amoul ni maodo Rassoul, niom nieup Aÿ talibé Cheikh Ahmed tidiane laniou. Maodo nena Sérigne Touba rk mo mossoul def limouy toub ci waliw yalla yi. Kou nek xamnga kouka meune té beuréwoulen. Sen Sérigne Amouniou deuk, amouniou bessoup magal ndakh defouniou lougn koy amé. Yen kay yena sokhor mais monatoulen soss ba sosal sen Sérigne louniou defoul
Yéna gui dollaty
Nitt kou bakh lol yaw lanlala maodo def yaw nak Legui nga de yaw FOTOLLOU yangui saga wa Tivaouane moytul sapou
yaw ya mana fenne fan la serigne touba wakhe lolu
Jamou yala rek
Kemanla khalas
Yow dangay fen bayilen doul man xowma loutakh Senegal Bari gaarouwalee demleen ligueyi mo geune reew mii bambako mom
Sa data ndèye bayil sissou sa baye gorrdjiguène la
Khana sa keur Baye la mom domeram mane Sama keur mafay diogue dépense de
@@ndoyepapaibrahimadiasse3026 aida Diallo khalifa général des goor djiguene des mourite mais ma ladji kou djoule serigne touba ak fougnouko rope
@@doffdoporal6776 naniou bayi togn grawoul
@@ndoyepapaibrahimadiasse3026 khamgua ji séné masalikoule djinane bi mo takh gnou fouye bayima ak niome rek domeram te séné serigne 7tonne de tere khana dindoul niane nioko rope ak fane lagnko rope
Diarama cheikh tidiane Cherif
Sa way dégue na rek lay wakh 😂😂😂
Ken dou bayou Serigne babacar sy.
Affaire bi dou championnat dei
Boudone championat dh serigne bamba dieullnako lou yague tokk dilénn kharrrr
serigne touba kouko bagne do dougou aldiana dafa ler
CV⛱️⛱️⛱️❣️❣️❣️👍👍👍🤲🤲
Wakhofi xam xam dè, lébon lipon rék ,ay wakh day firndé. Dîné dou ay wakhi kassé day andak dieuf, démlén oubi dioumay ta diamoudji yalla mo guen
Ahmadou soxla woul koukoy sédél koudoul borom bi
Yafi degue amadou te yaw Bamba khamoula te aussi maoda ak Bamba c mm famille
@@doffdoporal6776 machallh Lou ler gue wakh de
@@doffdoporal6776 Lol Ahmadou niarri yone la guiss Mame Maodo so andé ak talibe diga xam fane ak fane la wone
😂😂s touba yalla rek moy sedem bayi len diakhane
Khanakone senegal gnépay alcou
boy bi man na lép dh soubhana la
Signalé gauche virer droite . Lingay wakh doyna waar .😅
GOOR GUI DEMON GABON GAGANTI GANNAR RAAMLO MBAAXAAN TOUPLO BOURCIN COUMBA NDOFEN BAYU SERIGNE BASSROU AK BARA MAGUI THIERNO AK MASSAMMBA SERIGNEU IBRAHIMA FALL AMOUL MOROM
DEUREUDEUFETE SERIGNE TOUBA ❤️
képou ko khamoul si serigne touba dara mandoul nopile aussi mais di wakhe si serigne bi naka soudoule nonou bakhoule aussi serigne bi ken douko wakhale loumou wakhoule bakhoule
Bilae maodo du mrom
Nexoul ba nexoul wayé waxofi xam xam.
Kou CHEIKH ABDOU KHADRE guereum.
CHEIKH ASSANE A ZAZALI guereum.
CHEIKH AHMED TIDJANE CHÉRIF guereum. Gua xole né ame keur fépp 'Europe , Asie, ak amérique. Deuk fi senegal. Parfois guay titaro Nelson Mandela wla martin Luther wla Thomas sankara wla ma hadma guandi. Ta ligno tek assakabi sax teguou niou len ko. Boy wax si gnognou sax gay gueni bègue te guané dioulite gua. Naniou xolate sounou bob sokhor baxoul wax sa baxou way dou yakou si sa mbax darra.
Mak gni dagnou defarouwon na waxdji tegou si xam xam té niou bagna parparlo. Kounek xamgua koula meune té xéxoulen. Depuis massalikoul djinanane ba legui ignane daff fé fegne nak.
@Abdallah Ba lol jummah bene la fi Ahmadou moko samp 1924 Rakam Cheikh anta Mbacké Egali fi ay jummah yudul dieh
Modou Bamba amul wone poche boulko faté
@Abdallah Ba Zawiya Bigay toud Jummay Ndiareme mak nako 20 fois et en plus de ça fék na mou dem si gueidj gui mom d ak gnou bari
mom rék mo démone té mom réka nieuwate et 1924 migui wone en residence surveillée je te signale
Ba si Gammou bi guéne di fay def 1902 guéne ko nieuk déf Ak Serigne Rawane Ngom
Ahmadou né " Ahyaytaw Mawlidal Nabi Mina akssachi" Aksachii moy 1882
Manam Ahmadou wotéina 20 ans gamou kéne soga gamou si territoire senegal si mbolo
@Abdallah Ba Voila la finition a été faite en 1924
1892 Ahmadou gui ak Cheikh yi si diganté Mbacké Bari ak Mbacké Kadior dema goul sax si exil bi 3 ans aprés le dém
Té si Ay téguinam Wadiouram mame Mor Anta Saly fi nékone motah
mais automatiquement apres sa disparition en 1882 la woté gamou
Kén dou seydi Hadji Malick Sy
Dia dieff maoda mais sen tv mome thie kaw rek billahi
maodo raw,domi maodo raw,talibé maodo raw,seutou maodo raw🙏🏿❤
Billay lingay wakh khamo si
Yaw wakho fi darra ay sisoumane nguéne khana sa serigne bindoull Aÿ térré lima maggui wakh rék
Bayil togn kou nekk gueum limou gueum rek mo gueun Bamba moy Maodo baniouy bokk ken fékéwoul
Yene Khana dolene dioulite
Lou ame solo moyi done dioulite
Ablaye fall kane mo ame aye Talibès boudoul djouli?Cheikh Tidiane charif dou moromou sène sirigne bi
@@hdiifisnkfkfk2331 fall yaw sisoumane ngua liléne métii moy mim réw bamba KO mome réwmi bamba moy kiko môme
Maa waarou ci Sénégal.Toppandoo rékk ak gaarouwaalé ak di concurrencé sounou Mak gnou baakh gni.Mais nak khamalné Toubab bi djoumoul ci bagna yobb kénn guédj.Toubab bi loum déff khamnako. Da nga di goné rekk.Ta khamoo histoire sa kham kham bariwoul.
Yén yéna khamoul histoire sérigne touba liko indiwate Sénégal guetou lénko
Kii wakh léne ko mou dém diangui wat limiy wakh xamousi dara moy fénal Serigne sii nii rk kii bou diagone Dina tok si télévision bi nane xana xemga gnake fay da
Billahi jaime les tidianes mais wadji xamoul gatt
Ki c un docteur mon ami day tafsir alkhourane dougal youteb ga balma akhe si kor gui
Ioe mi ya xamoul touss demal diangui soxor guen trop
Ay door la
Yèna dakh dore
Sen khol yagui dag
Bayilen sagayi ta yalla takh ñoun ñiep ay dulite Ién 😂
Kon dé gniy alkou beuri nan
Ki d fall amoul xam xam
@@alassanedieme8762 mo eup sa baye xam xam
Alassane Dieme khamou tousssss wayé céy kousa mame sobou won ci océan atlantique bi diiiiiggggg rek
@@ndoyepapaibrahimadiasse3026 kou bax pourtant sagaw mala d kone amal ay teguin ! Man dama deglou waxtan name té guissuma dou aya dou adiss dou dara loum tek fofu d la waxei mai dego ma toud sa baye yein nak lilên metti teguniulén ko. Niune SERIGNE TOUBA danio fagul lép yein nak amoulein touss loudoul tok tak radio yi di wax rk kou mer clamel Yalla
@@guusnjaay8960 gni sen xol yei bonne
Wakh dji Rafetoul Dara kon yeen tarikhayi amouniou teguedegue amouniou soukar amou thiéreh Come yow neega yeenen tarikhayi amou dara diaroul ngay wakh Respecte beneen tarikhayi kham Naani Senegal Warnan Bayi invite kouy wakh te dou Andi Ben Mbinda Thi Limouy Te Pourtant Mak gni finekon kounek thi Nioom bindaga Aye Teeeré Bayi kofi Wakhtan Dafay Andak kham kham bou wer booy wakh thi Mame Elhadji Malik Ngani liii moko binda wala baaye diw neena bouko defee niou dem laathie doomam booy wakh thi Serigne Touba Tamit Nga def Come Nonou Mame Khalifa Niass Come Nonou Mame Boou Kounta Momitam kasalika Baye laaye thia yooof kasalika mais wakhtaané wiii Amoul ben DaliiiiiL Te Aye Borome kham kham niooo lay seeetaan Wassalame Yalla Na Yalla Fayal niou Sounou Mak Gni
Dior guié réroo mais niom xamantè nanou
Thiow li ci bountou téneu bi ga gni amoul bag leu😂😂😂😂😂
Yaw mi di sagua dagua khamoul talibè maoda dou bokalei Yalla ak kene tè réw mi sougne khame seydina moukhemd guinaw yalla maoda takhe
Guane moye bokale yalla gui dakham daara si limouy wakh tarikha chekh fila fegue khadir mouy wakh guen duo ciehe abduo khadar jilani
@@modoudiagne497 sa way man wakhoumala wakhou tarikha tarikha yep si yalla lagn dieum guiss gua fi ko guem koudoul yalla daguay perte
@@diopnene1241 kou bakh yalla lepou lou mou ame si nite lako déf te nite kokou moy seydina moukhamet nite loumou khame loune nite moko ko khamal te nite guen douko topou yalla laniouy topou nite dankoy roye si lou bakh
Talibe tivaone yi d Serigne touba molén di dérangé balgui🤣🤣🤣🤣
@wallo tv mo yéna niak djiom wa touba niom nawlo wu gniou wa tivaone dé billah do deucgue bén serigne gniou mouride bu wakh ba toddou el hadji Malik sy jamais lécgéy ak djiamou yalla rk yén mom gén di weur di fén rkk mais bakh na goor goor loulén si sén djiouma dji ndakh mou acgue🤣🤣
nit kou bakh lol billahi wallahi Ms déé rek
Billahi wallahi yaw nitt kou bakh lol moytul bakhna rek
Kiii xamoul gatt il ne doit parlé pour les tidianes
Saway ragaral yalla
Mé li mouye waxx hadji dako warona binde Mane Dale Sénégal nexna deugg
Bou wakhone li bamba wakh and ak bamba guéth doul rék
Yen yénay doul kati
Deug leu thioune