Commentaires yoyou déh da mél ni day yokou sama pass pass souma djissé sama xol day nakhari lol wayé sama thiofèl AK sama yakar day yokou day yokou si yone wi sama xél gueuna dal si Serigne bi Nioooongui sante Serigne Touba bou bakh té Diko gueuna yakar walahi
🚨May fataliné waxtan wi 4 Partie la
Yéppu Migui çi biirr Chaîne biii Nanko Déglou boubakh
Mbacke wayee yalla nopina daniouy wax bah yaxoulee rk monouniou sii darra sampoub yalla lah diem diem bah❤❤❤
Allahou Akbar s mbacké yagui may fattali s abdou lahat mbacké
They
Dieureudieuf si lèral yi
Dieureudieuf Serigne bi,amnagne aye noone wayé délou wouti xam xame rek
Lolou rék mo am solo fimné
❤❤❤❤❤ ma challah
Jërëjëf sëriñ Mbàkke, wax ji jar naa bàyyi xel bu baax. Yàqu-yàqu yi bari nañu te noon yi tay lañu gën a laxasaayu
Akasssa Serigne mbacke Abdou remane amena solou loul
Diereudieuf
Machalla am na solo
Diereudieuf
Inchalaha yonou mouride mom tia kanam reik.
Incha allah
كلمة الحق
Amna solo Bilay mbackè
Diereudieuf
صدقت
Jërëjëf MBAKKĒ ❤❤❤
Diereudieuf
Machalla ❤❤❤❤❤
Diadieuf
Thieuy Adina 😢😭
Diarna yémude
ما شاء الله
Diadieuf
Mashallahh
Diadieuf
Walay Seneweb mom kuy weur nonu yon wi tambli wal si site internet bobu..
Batinou yone wi mongui lakou thi touma mais yallah nopi nathi
Theyy
Serigne bi amnasolo
Diereudieuf
😭😭😭🙏🙏🙏
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️
Ay mouride lanou c'est fini le coup est déjà parti,lounékh way na wakh
Yoonou mourid dé nitt meunou ci d'ara
They lolou dé wérna mome khana moytu rék
Bane seneweb laye wakh
Doyna war trope
Walay
Commentaires yoyou déh da mél ni day yokou sama pass pass souma djissé sama xol day nakhari lol wayé sama thiofèl AK sama yakar day yokou day yokou si yone wi sama xél gueuna dal si Serigne bi
Nioooongui sante Serigne Touba bou bakh té Diko gueuna yakar walahi
Waw gorr mourid
Billay walay mbacké balla doyna waar
Lool
mourid yi war nano kholat sen bopou bou bakh ta nek Ay nitt ta ta Doylo serigne bi
Lolou rék monou warr
Li dafa mètti çi xol barké yalla ay nitt you dèfol kèn dara tè kou jog dal sèen kaw loutax li dou yoon jammu yalla ak liguèey kassè lane xam
Ah diarul mulay méti dei nagnu nek si lignu wara nek rek dañuy yok rek wayé duñu wagni
Mom kay doyna war luné laniouy Wakhl kilifeu yi
Walahi
Li loumata khamla
Loool sakh
درجتي تعل وليس تنخفض ومن نحا من الورى خفضي خفض
Theyy
Baye fallisme nak?
❤❤❤❤❤