Forme bigga indi ni Bossi déffé contact xalate na ga oyof c'est a dire ta stratégie Moy khekh indi rapidité pour khekh ak môme . Mais loy wakh ba reug Reug diapala Moy diekh n'a dalay dane
Boy niang ak Reug Reug sén combat le 1er janvier le mais en tout cas wa jambaar souniou goorgorlou woul combat bi dina soule combat royal bi . Reug Reug ak Boy niang souniou défé face à face avant novembre moussibeu ame. Dinaniou soul bépeu combat bou wara ame avant sén bosse. Ndakh thiow li dina beuri trop trop té dina tangue dieur 🔥 Lolou nak le lamb beug . Siteu ak modou danio roussanté ba douniou xolanté té lolou déy ray sén promotion combat. Li sponsor yeup di weur si combat Boy niang ak Reug reug bi la nékeu. Li si kanam rawouli beute
Boy niang2 2006 ba leegui nioungi seetan lambe yaw meune nga beurè nirmè nga entrainement te ham nga yonou heekh mais do heekh do df dèga tè meuno dk beurè reug reug c impossibls
gisoo dara ba leegi, nga bëgg ko wala bëggul dina la attaquer By-force ñaata yoon la boy Niang ci boppam attaquer balla Gaye2 ndax danga bëgg combat ak balla, liy wër dafay wër,
Yalnala yalla maaay ndaam frerot ❤️🙏🏿
Bou sobé souniou borom inchalah di ngua am ndam deih fan's kharagn depuis abidjan
Wa ki dou
Ndam rk boy Niang ❤
Modou lo moy sama mbeur mais boy Niang yalla nako yalla may ndam inshallah
Boy Niang linga soll rafett neu machallah
Boy Niang combat bi dou yombe dé mais nak gueme Nani meune ngua dane koudoul reug reug bo téyé inchallah
Xlo for ever!boy niang ndam rek inshaAllah
Talfa rék laniy top mai boye niang yalnala yalla maye ndam
Ya meune y'a euppee. Doolé fière d'être pékinois
Boy Niang dousama mbeur mai yalla nako yalla dafal ndam
❤❤
Mane dhe vraiment boy Niang la farale ! Yallah neu yallah mayla ndam Inchallah ! le thiapathioli
Bilahiii modlo ndandane leu dan ama dan boy Niang man combat wam AK boy niang ba lgui dakoy savouré thiey karagne
Hors sujet
@@abdoulayecissegueye7952 sa xol da diekh
@@abdoulayecissegueye7952C'EST PLUTÔT TOI QUI EST HORS SUJET ÇA TE DÉRANGE CE QU'IL DIT ?
len dee wax nalen KO inchalla rabi boy niang va battre reug reug facilement bilahi
reug reug dhé légui international la machallah
Thiapathioli seule 💯❤️
Yallah na yallah def diame si rêw mi gni nek si hôpital yi yallah na yallah feug sene bop gniñou djitou yallah nalene yallah kharé aldjana.
Amine yarabi 🤲
Dou sama mbeur mes yaram rek lako beuge🎉🎉🎉
Boy Niang yalna ko yalla mayi ndam Lou seud Gouy insaalla pikine kasse amoul le neen 🤴🙏🇪🇦
Reug reug seul nagn le tegual lou tar💪💪
Mangui khar mane ba jour ba inch'Allah mane mom yaw rék lay topou
je l aime boy niang
Yalla baxna ba le première janvier rek☝🏿✊🏿💪🏿🦍🦁
Booy Niang bou sérieux 😊
Lutte Tv télé askane wi MashAllah rafétna ❤
Doral reug reug bamou danou
Reug Reug is winning this easily.
Reug est trop fort machallah. Détrompe-toi.
Esk c pas à toi ?
Ki moudié dane reug reug BN2 dako dane.
Boy Niang Modou lo moy sama mbeur mais sa combat bi ak reug regu yaw la fral
Je l'aime pask il communique très bien
Reug reug defoufi dra boy niang seul 🎉
💚❤
Wadial le 01 janvier inchallah ❤
Ndam rk inchalah nioko fa ame Pikine seul kou ame lénéne gua dieul 🦾💪
Boye Niang dou sama mbeur mais mome la farale
Cëy boy niang
Teyall si reug dhhhhh baxna bidewam dfa fenkheu maytull dhh
Fou Bidéw bi nekone biko sa Thies di doumeu ?
Ah bayico rek reug reug dé wallahi mola nek dans de bonne condition té bilahi mola dakkh beuré fouf
Reug aussi na teyy si Boy Niang
Bou yakaree nii day nieuw danko facilement mingui nakh bopam
Wa ana fadam midone wax boye niang da blaissé 😂
Boy Niang boy Niang mbeur nga champion nga mais kén dou Reug kén dou mom
Combat bou doy war 🔥🫡
Forme bigga indi ni Bossi déffé contact xalate na ga oyof c'est a dire ta stratégie Moy khekh indi rapidité pour khekh ak môme .
Mais loy wakh ba reug Reug diapala Moy diekh n'a dalay dane
Champion pire et dire thiapathioli reik
Boy niang mo meune moromam yeup 🎉
Reug Reug 2015 mo nékk son premier combat arrène
Ndam Rak
Boy niang ben moromam mesou ko yapp
Do am tousse reug reug seul
Reug reug yalla ngua am ndam aamiine dor mou danou
Door sa papa mou danou mo gueuneu yombou
Wakho deugue dh
Sa thies moy sa ma beur mais combat bi boy niang la faral
Boy niang ak Reug Reug sén combat le 1er janvier le mais en tout cas wa jambaar souniou goorgorlou woul combat bi dina soule combat royal bi . Reug Reug ak Boy niang souniou défé face à face avant novembre moussibeu ame. Dinaniou soul bépeu combat bou wara ame avant sén bosse. Ndakh thiow li dina beuri trop trop té dina tangue dieur 🔥
Lolou nak le lamb beug . Siteu ak modou danio roussanté ba douniou xolanté té lolou déy ray sén promotion combat. Li sponsor yeup di weur si combat Boy niang ak Reug reug bi la nékeu. Li si kanam rawouli beute
Combat bobou dou touss
@@legendediop9215 ah doyna war déh
Fo faté ama baldé franc lamb diodiou mo nara barri thiow
Boy niang denga réw mo takh modou doumaleu .Ball gaye le meilleur de tous les temps
Loutakh balla douma wouko😂😂😂😂
Meun na daane reug reug dé
❤❤❤
Nangouwouma
🔥🔥🔥🔥
❤❤❤💪💪💪💪💪💪
Boy démal séti dollé Mo geune
Pour ioe ya meun reug reug nii
Reug reug dou sa morom moleu mounne foufffff moleu euppou dollè foufffffffffffffffffff😂😂😂😂😂😂
Rueg seul 😂❤
Boye niang2 linga wah yeup deugleu bamou dess aý dèga meussoko df wahal lenene
Man mom modou moy sam mbar reug reug lay siport
Reug reug molleu mounne foufffff😂
Boy Niang mo meune reug reug
Boy sonou ngeu depuis mbapat nganiou topou do nopalekou
😂😂😂😂😂😊@@MouhamedBa-i6i
@@MouhamedBa-i6i
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Xbet bigua nek sen ambassadeur deh boko bayiwoul do danat mbeur malako wakh
Bamouy dan balla xbet la sole wala
Boy niang2 2006 ba leegui nioungi seetan lambe yaw meune nga beurè nirmè nga entrainement te ham nga yonou heekh mais do heekh do df dèga tè meuno dk beurè reug reug c impossibls
Reug reug mola dak beuré fouff
khawma lan de mes am gua compat de bly wly am gua bou bakha bakh psk bou feké paré rk mom reug reug meuno ko guena paré
Reug momit amna combat bou reuy
Ki day wakh RK reug reug nekhalol kene bou jour ba gay comprend
Yaw meusso def béne degat si biir guéw calcul késsé ngay déf xaar sa adversaire diok késsé nga dioumloko té reug reug dou mbeur bouy diok dafay yote ba diapleu amga beuss dé reug reug rék koku beurém dafa dépassé sakh
WAKH REKK LAAY DËFF AK TRICHÉ
gisoo dara ba leegi, nga bëgg ko wala bëggul dina la attaquer By-force ñaata yoon la boy Niang ci boppam attaquer balla Gaye2 ndax danga bëgg combat ak balla, liy wër dafay wër,
Je l'aime pask il communique très bien