Bammél ak Lafay Xéw çiy tar tar Ko Mana doon langa jeufoone rk molafay Téerou

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 19 дек 2024

Комментарии • 304

  • @baguellepatriote413
    @baguellepatriote413 4 года назад +50

    Je ne suis pas mouride mais j'aime serigne Rafah
    Machallah kou baax la tei kou jang la.
    Yana yalla goudal sa fann si barki naby(psl).

  • @maodomalick1114
    @maodomalick1114 3 года назад +35

    Do beuri talibé déh ndakh sénégalais dafa beugu koukoy nakh .kokou rk lay topou .mais yalla na la yallah fay fier de vous🙏

    • @seydouba539
      @seydouba539 Год назад

      Bien dit je l aime

    • @bougoumatoure-jn8ux
      @bougoumatoure-jn8ux Год назад

      Bilahii

    • @ansoumanakambayetraore8584
      @ansoumanakambayetraore8584 Год назад

      Walahi deh

    • @Dykhamorant1030
      @Dykhamorant1030 5 месяцев назад +1

      Pourtant gni beugue bakh Aka gnon bari dafa di kay gni bone dagnon and ak bruit rék. Yalla nagnou yalla swt khirr si gueme ko té yakar ko si lép nak . Yalla na gnou yalla swt yeureum té doli gnou diam soutoureu khéweul wér ak wérle yokou ba yeuko allakhou ma amine ya raby si barké seydouna PSL sama sopé ba 🤲

    • @KhalilDiouf-j9b
      @KhalilDiouf-j9b 2 месяца назад

      Sa c vrai moi beug nako ak kenene ak kenene ​@@Dykhamorant1030

  • @fatounoirofall4039
    @fatounoirofall4039 3 года назад +15

    Allahu akubar yalnala yallah diegal leip lou niaw louma meussa def ak mbolem djoulit 😭😭😭😭😭😭😭😭😭🙏

  • @khalifaababacar6828
    @khalifaababacar6828 4 года назад +32

    Yalla n'a sounou borom goudal sa fane amine Macha allah

  • @ismailasarr1800
    @ismailasarr1800 3 года назад +39

    Voilà un vrai marabout, un vrai guide religieux longue vie à vous

    • @astoundiaye710
      @astoundiaye710 2 года назад

      Yalla nala Yalla fayal bopam

    • @yayodiallo1424
      @yayodiallo1424 2 года назад

      Ki kay manchalahhh ay koumay yobou si mom té yallah rekk tahh .limouy fatali amna solo lole ki Moy sama hol

    • @elhadjifaye2710
      @elhadjifaye2710 2 года назад

      Yag fi lol mbacké té wer

    • @tabaradiagne-r8l
      @tabaradiagne-r8l Год назад

      Amine

  • @mbayemassamba5099
    @mbayemassamba5099 3 года назад +16

    Il me rappele Serigne Sam MBAYE.
    Ils sont les deux avec Oustaz Alioune SALL que je peux écouter toute la journée.
    Qu'Allah SWT vous accorde bénédiction, miséricorde, longue vie et une bonne santé.

  • @aboudione7672
    @aboudione7672 4 года назад +79

    Vraiment vous etes un ocean je suis content de voir un petit fils de serigne Touba qui est comme toi.

  • @laminebarro9563
    @laminebarro9563 4 года назад +7

    Soumakoy dégglou serigne sam mbaye rekk lamay diokh. Yalna yala dolli soutoura tawfekh ak tayssir...

  • @morbapttmoms2411
    @morbapttmoms2411 4 года назад +7

    😭😭😭😭 yalla naniou yalla mossal thi mogal bamell

  • @papeousmanendao8192
    @papeousmanendao8192 4 года назад +17

    Yalna sounou borome tok say lerrr si barké seydil hadji malick

  • @maryamlo9651
    @maryamlo9651 4 года назад +16

    As salamou haleykum !! ndiangualé mi amatina solo Serigne Ahmadou❤❤sopou nagn la lool !! Yallah nalen ya allah geuneu sammeu aamiiinne !!

    • @path7020
      @path7020 3 года назад

      Se sont des marabout comme ça qu on a besoin

  • @amsacisse4286
    @amsacisse4286 2 года назад +6

    Cheikh ahmadou rafahi mbacké dieure dieuf mbacké amna solo trop machalla 💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💙💙💙💙💙💙💙💙💙💙💙💙🙏

  • @amalaba3013
    @amalaba3013 4 года назад +6

    MACHALAH MOURIDE DIEUREDIEUF MBACKÉ DIEUREDIEUF FALL AKASSA MACHALAH

  • @linendao3591
    @linendao3591 3 года назад +2

    vraiment Serigne cheikh Rafahi Mback sama xol Sed n'a ci yaw souma l'ay deug damay kontan douma mourit waye ligay wakh nékh n'a trop te diar yon

    • @diamaseye1078
      @diamaseye1078 3 года назад

      Ndeysane yallla n’alla yalla Faye

  • @cheikhdieng7999
    @cheikhdieng7999 3 года назад +5

    Machalla bou mbacké mbacké yep melon ni ken dou yepp yonou mouride

  • @nassirnaziou4062
    @nassirnaziou4062 3 года назад +2

    Amna solo serigne rafahi macha allah yallal na ga goude fanne xam xam bi lair n'a

  • @mainafall3772
    @mainafall3772 3 года назад +2

    Yalna yalla goudal sa fann sa dound amna gnarine machalla digne pti fils f serign touba

  • @dembagueye5495
    @dembagueye5495 4 года назад +9

    Yalna yalla goudall saw fan mback yagui défar askan wi

  • @mamediarrangom8775
    @mamediarrangom8775 2 года назад +3

    Dieuredieuf Oustaz Yalnala YALLA maye goudou fane bou andeu ak wèr.ALHAEDOULILAH

  • @boubacarsavane604
    @boubacarsavane604 4 года назад +4

    Dieuredieuf serigne bi yalla na yalla yokla weer ak yague dinou tek thi yone wi geune

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 года назад +3

    Serigne abdou rafahia douma mouride de wayyé koula soppoula ndakh da ngaye yété diwakh yalla néna yonén bi néna di dia dji khol ❤️😭dilén déllo thia sugniou brome amgua kham kham am yar deugue soufé am discipline ❤️

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 3 года назад +2

    Machallah Mbacké yàlla nga fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd ki Aminnnne Aminnnne

  • @abdoulayebaneniang
    @abdoulayebaneniang 3 года назад +1

    Dieredieuf Serigne ahmadou rafahi. Yallah nala yallah yagal té and ak werr

  • @petitkebe9887
    @petitkebe9887 4 года назад +6

    S Ahmadou rafahil mala bgue yalla na yalla goudal sa fan❣️❣️❣️

  • @barhamamboup6431
    @barhamamboup6431 4 года назад +4

    MACHALLA serigne yalna yalla motali té barkél lépp inchalla goudeul sa fan
    Tidiane bou la sope la trop

  • @zaalbiboy8516
    @zaalbiboy8516 4 года назад +6

    Machallah oustas yallah na yallah goudal sa fan

  • @kenzifafall3438
    @kenzifafall3438 3 года назад +2

    Machallah machallah yalna YALLAH SWT sameu la té yokeu say fane si barké Seydouna Mouhamadou Rassoulillah psl amine DIEUREUDIEUF

  • @mouminatouniangdeme5382
    @mouminatouniangdeme5382 2 года назад +1

    MachaALLAH, dieureudieuff Mbacké, YALLA nala BOURBI yaggal té weral la. YALLA naniou defale degg ak topp, barakatou Seydina MUHAMMAD PSL

  • @mouhamedseye10
    @mouhamedseye10 4 года назад +31

    Macha Allah sama sopé bi ❤🙏

  • @ndeyependasow9440
    @ndeyependasow9440 3 года назад +3

    Je commente rarement sur les resaux sociaux mais une remarque que trés importante pour moi té kou guis néen ni néenagui rare gua dougousi si vidéo conférence té guisso niou saguaa oustaz bi, j'ai presque tous les commentaires mais pas d'insulte cela signifie que rafahi kou deugouleu .kone nakk yague fi lool té wéer

  • @modouka8834
    @modouka8834 4 года назад +7

    Akaza yale nanou yalla dieguel te yeruemnou thibarkeb sayidouna mouhamed alayhi salat wasalam te fayalnou sounouy akh yidokh sonne digante ak sonne moromi diamyi te atenou thi yarmandem amine

  • @idiop2377
    @idiop2377 4 года назад +13

    Mashallah! Dieureudieuf Mbacke! Amna solo lol! Wakh deug rekk! Yallah goudal fane yii! Amine ya Rabbi! Dii begg bou bakh ci sa dianguale!

  • @bathiendiaye7578
    @bathiendiaye7578 3 года назад +1

    Mem mois aussi j'aim bien imame rafahi machallah goudou fane ak weur thi mome ak wèr ta may gnoko

  • @dawoudafaye4804
    @dawoudafaye4804 3 года назад +2

    Mbacke yalna sougnou borom yok xam xam bi balla Aicha content na vraiment

  • @boyoonetv5761
    @boyoonetv5761 2 года назад +1

    Machallah🙏 kulay wakh yalla ak yonent🙏 wanté nekki tag sa mame rk doma wane Yoon wu jupp wanté Yoon bomay arnaquer yalnanci yalla mussal.
    Je suis talibé cheikh et j'aime RAFAHI.
    YALNAMA YALLA MAY DOM BU GOOR ma tudékoko🙏

  • @abdoulayecisse6813
    @abdoulayecisse6813 4 года назад +3

    Bilahi Bou mbacke mbacke yep meloni yaw ken dou len yap machallah

  • @ndeyecoumbacisse7198
    @ndeyecoumbacisse7198 2 года назад +1

    Alhamdoulillah il fait la fierté des mourides, Yalla nagnou Yalla défal dégu ak topeu incha Allah si barké Cheikhoul Khadim.

  • @kourelmarocdakhla598
    @kourelmarocdakhla598 4 года назад +42

    Mom de niépo KO wara nianal mou yague fi te wér ak nékam fi amna soolo

    • @badarandaye3950
      @badarandaye3950 4 года назад +1

      Yalla nga fi yag lol mbacke barki serigne touba sa mame diou bah dja

    • @badarandaye3950
      @badarandaye3950 4 года назад +1

      Ioe tamit yag fi lol te wer mouride

    • @thiorondiaye4696
      @thiorondiaye4696 3 года назад +1

      Bilaye damako beugue ta yalla tax

    • @garassediop
      @garassediop 10 месяцев назад

      Amine

  • @sirembodji3098
    @sirembodji3098 3 года назад +2

    Serigne rafihou dall machallah arhourane sounna moy dinné

  • @assanesarr1875
    @assanesarr1875 4 года назад +6

    Thiey serigne bi amatina solo yalnañu yalla defal deg ak top

  • @cheikhbadiane4480
    @cheikhbadiane4480 4 года назад +69

    Mem mois aussi je ne suis pas mouride je suis talibé cheikh mé j'aime Serigne Rafah machallah❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @galomagane6123
    @galomagane6123 3 года назад +1

    Amna solo yalna yalla goudeul fane yi mou end ak werr Macha allah 🥰💓💕

  • @boubacarba7624
    @boubacarba7624 3 года назад +1

    Mem moi aussi je suis pas mourir mais koko top mou khamala yalla vraiment j'adore o fond de cœur

  • @souleymanediagnerafahi7220
    @souleymanediagnerafahi7220 4 года назад +1

    Cheikh ahmadou Rafahi yala ngafi yague té wer si barkei seydina MOUHAMED slws

  • @falloumbow3444
    @falloumbow3444 4 года назад +9

    Akasa mbacké dieureudieuf serigne touba

  • @papealythiongane9848
    @papealythiongane9848 4 года назад +19

    Yala naniou yala yeureum té diégueul niou yala yeureum niou Ya rabiii diégueul niou 😭😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @reussdieng6967
    @reussdieng6967 3 года назад +2

    Yalla nagnou Yalla maay moudji bou rafete Ta Yeureum gnou

  • @abdoubakhediagne7863
    @abdoubakhediagne7863 4 года назад +3

    Yalla nanou su nou borom xir thi Lou bakh lool barkep serigne touba mbacke lou diara bayi xél la lool 😭😭😭😭

  • @djibysy4108
    @djibysy4108 4 года назад +16

    C'est ça le profil d'un guide religieux
    De nous parler d'Allah et la sunna
    Longue vie

  • @cheikhounabambaseck6242
    @cheikhounabambaseck6242 3 года назад +5

    حفظه الله ورعاه وأطال الله عمره بجاه الشيخ الخديم

  • @abithiam2624
    @abithiam2624 4 года назад +3

    Machalla mbacke balla aicha dieureudieuf mbacke amna solo lolle balla yague fii tee were

  • @thiorondiaye4696
    @thiorondiaye4696 3 года назад

    Kila beugue mane waxtaname dafa ame solo daflaye délo si yalla talibé cheikh boulaye sago mingui ni yalla na yalla goudal sa fane

  • @gorasylla9380
    @gorasylla9380 2 года назад +1

    Assamou hanleykoum mangui ziarè Nièppeu je ne suis pay mourite ne se dit pas parceque le mourite c,est celui qui aspire a l,agrèment de son seigneur

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 3 года назад +14

    Qu’Allah nous préserve de l’enfer et nous accorde le paradis,nous épargne des supplices de la tombe🤲🏿🤲🏿🤲🏿Yalna souñ borom dolli yeurmandé tous nos défunts et nous nous accorde une bonne fin 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿

  • @madinabowebalde5372
    @madinabowebalde5372 3 года назад +1

    Mâcha allah ya cheikhana yallah nala yallah ar te sakhalla si sounna 🥰🙏🙏🙏

  • @milsothiam7213
    @milsothiam7213 3 года назад +2

    Macaha Allah mbacke ama ti na solo longue vie amien yaraby

  • @aminagaye8753
    @aminagaye8753 3 года назад +3

    mashaallah je l'ai découvert grâce à une page sur instagram Merci beaucoup pour les rappelle

    • @abdoulayeosnseck7012
      @abdoulayeosnseck7012 2 года назад

      Serigne Rafahi Mbacke un véritable érudit, c'est un sage au sens noble du terme mashala 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽♥️

  • @idrissasakho4994
    @idrissasakho4994 2 года назад

    Machalah Serigne yi laniou sokhla khamal nigni deugu bi ,moy takh kounek khamni limou liguey lolou rek fayay fek ci bamelam

  • @ousseynousow1438
    @ousseynousow1438 3 года назад

    Yalla naniou yalla maye diege ak toop mbacké balla yage fi lole té wérr si barké khasida yii

  • @mameboussodiop1706
    @mameboussodiop1706 Год назад

    Masahla yalana yala samoula barke borom touba

  • @matycisse7111
    @matycisse7111 Год назад +1

    Mbacké YAGG té wér barké BOROM TOUBA ❤

  • @bayesylla108
    @bayesylla108 3 года назад +1

    Ki yallah nako yallah faye thie nimou ni dimbeulé

  • @abdoulahaddiop7981
    @abdoulahaddiop7981 3 года назад +2

    Serigne Rafahi Mbacke ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤦🏼🤦🏼🤦🏼🤦🏼 mbacke begeu nala 😭

  • @pinkinrails2456
    @pinkinrails2456 4 года назад +2

    Machahlah yalla guafi yague té andack wére .yallnagnou yalla yeureum

  • @mohamedfall7849
    @mohamedfall7849 3 года назад +5

    Gueneu yague gueneu wëër Mbacké 🙏🏽♥️

  • @khalifaababacar6828
    @khalifaababacar6828 4 года назад +8

    Wallahi m'a la sope ndah sa ragal sounou borom ak sa deugoutè

  • @bayemadjimbymboup6337
    @bayemadjimbymboup6337 2 года назад +1

    Amna solo looooool sama ostaz

  • @mamadouleye6336
    @mamadouleye6336 3 года назад +1

    Mane de dama laye nianal rek yalla Mayela fane wou goude te wer kene dou yawo

  • @madinagueye168
    @madinagueye168 4 года назад +2

    Allahou Akbar Yalla nanu Yalla Xiir ci lu baax te may nu mouth gou rafet.😭😭😭

  • @ousmaneseye898
    @ousmaneseye898 4 года назад +3

    Yalla guafii yague ta werr mbacke machaala

  • @mamadoucisse9449
    @mamadoucisse9449 4 года назад +2

    jeurjeuf mbacke deugue rek moko gnor yallna yalla werral say thieur te doli kham kham bi goudeul say fan si barcke cheikhouna ahmadoul khadim

  • @papasaloumalo9828
    @papasaloumalo9828 2 года назад

    ماشاءالله الدليل حقا زادكم الله خيرا سيدي الكريم

  • @sarrngagne3184
    @sarrngagne3184 3 года назад

    Ma challa mbake balla yalna yalla wetel la ta samoula ta harla

  • @abdoukane8276
    @abdoukane8276 3 года назад

    Yalla n'a yalla goudeul sa fane wérel say thiér bilahi Mala beugue

  • @sidisarr5531
    @sidisarr5531 2 года назад

    Machallah 😢yallah na yallah gay🙏🏽🇸🇳❤

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 года назад

    Mbacké yalna ngafi yagge te an ndeck wére ak soutra👋👋👋

  • @serignefall6223
    @serignefall6223 3 года назад

    Amna solo Serigne ahmadou Rafahi

  • @modoukane2871
    @modoukane2871 4 года назад +3

    Machalla Serigne bi

  • @elsenegales8801
    @elsenegales8801 4 года назад +1

    Amna solo mbacke yalla yagg te weur amine barke serigne fallou

  • @foloudiop2358
    @foloudiop2358 4 года назад +2

    Mashlla mbacke amna solou loull

  • @khadimendiaye4295
    @khadimendiaye4295 3 года назад +5

    😭😭😭الله أكبر! اللهم اغفر جميع المسلمين

  • @abdoucherifmbackei7511
    @abdoucherifmbackei7511 4 года назад +9

    جرجف سرج صالح بك ♥♥♥

  • @gorasarr3396
    @gorasarr3396 10 месяцев назад

    Yalla gafi yag té werr mbacké

  • @amdycisse3243
    @amdycisse3243 4 года назад +2

    Yalla nanio yalla defal degue ak tope

  • @Gradus-lp3kz
    @Gradus-lp3kz 3 года назад +1

    Machahalla goudal fan

  • @mamadousene2824
    @mamadousene2824 2 года назад

    Bilay mbacké liguey wakh amna solo lol...

  • @linendao3591
    @linendao3591 3 года назад

    Dieuredieuf Mback sa takha way ci dîne yi rafet n'a Mane de douma mourit Talibé cheikh la waye kontan n'a ci yaw trop

  • @rokhydabafaye2554
    @rokhydabafaye2554 4 года назад +6

    machlah sa wacila

  • @fatoubabacarsow3312
    @fatoubabacarsow3312 4 года назад +4

    Allahou Akbar..amna solo machalah

  • @massambafall6826
    @massambafall6826 2 года назад +1

    Wallahi koudoul fatalikou bamél lou la nékh défal

  • @maria1-s7w
    @maria1-s7w 3 года назад +1

    Allahou Akbar kabira. Maachaallah

  • @perendiaye9927
    @perendiaye9927 3 года назад +3

    MachaAllah que Dieu vous bénisse vous guide et vous garde

  • @birahimsidy9172
    @birahimsidy9172 2 года назад

    Il merite son surnom Imam il est verdique

  • @thiernoba5501
    @thiernoba5501 3 года назад +1

    Aka jarakham merci beaucoup mbacke

  • @cheikhdiop6509
    @cheikhdiop6509 4 года назад +6

    Machallah Mbacke kaddu yalla rekk moko Niorr...deg ak top

  • @omartoure2251
    @omartoure2251 2 года назад

    Machalla yallananu yallah yerame amine

  • @amicisse5752
    @amicisse5752 4 года назад

    Allahou Akbar tieye yala yalna nio yala diégale mousale nio ci bougalom baméle berke cheikhol khadime

  • @abdoulayekeita6243
    @abdoulayekeita6243 4 года назад +3

    Mashallah Mbacké c'est Toi qui doit être le Khalifa général mashallah

    • @idrissasakho4994
      @idrissasakho4994 2 года назад

      Bilahi ki deh bisbou neké khalif général kone ga guiss deuk bou nekh bokalé gui diekh tak

  • @cherifwade4488
    @cherifwade4488 2 года назад

    Yalla nala yalla sam

  • @baayfalldiop9406
    @baayfalldiop9406 3 года назад +1

    Unh dagay reuthiou saxxx loutax nga done doundou.thiey yalla unh gnigui sakou sa yeurmandé