Mais mane ,Dié Astou Sarré dama la beugue beugue la xam vraiment ! !!Macha'allah qu'allahou soubhahou wa tallah takhawou soutoural leu sameu leu dolé le. Amine si barkè seydina Mouhamed aleyhi salatou wa Salam
Une mère est sacrée j ai bcp pleuré car ma mère me manque bcp et comme toi ma maman me protège même là où elle est . Qu Allah accueille nos mamans parties au ciel au paradis céleste, à celles vivantes une très longue vie.
Dié Astou une grande dame de grand cœur Macha'Allah ma chérie yalla na yalla diapalé la defalla diam siarnala contane si yaw béguénala lole nekal si diam inchallah
Bilahi dama la beugue si sama xol 💓noumay déff ba guiss la ba tie pièce théâtrale biguay wakh ni meune nala ko wakh début ba fin ak bigua joué ak madione laye Sarr💓💓oohhhh bilay lounék si sama xol wakh
Machaalla Alhamdoulilah! Walaye comportement bou exemplaire la Kiss. Yalla na Yalla diapendal si daradiaye Ya Rassouloulah si barkè Lahilaha hilala bii guâ këum Yalla na sa leep barkelle. Bonne continuation et bonne réussite!
Mashallah sokhna ci kouko sope la ,yalla nala yalla faye yiiiw te mayla nga motale sa mission ak sa sago sa .vidéo damakoy yakamte guiss diko setane guir thiofel die astou sarré
Machalah machalah yalna sa jamm Yagüe sokhnasi vraiement cest une femme exemplaire kou defar daara ay ndaw disi diangue alkhuran vraiement chapeau a cette femme ❤️
Machalla toute simple et humble.Meunone nga tak Ay or ba feess pour gueune mais machalla watiè sa bop.Beugone na ame sa numéro pour gneuw Di liguey si yow si busy bi.Dinama nekh trope
Je la connais très bien la maison de sa maman et à keur massar ses frères et sœurs son là niep la diapalai namou niou dara nite kou bakh la cou wathie bopam la sarrê mabo ma grande sœur amal diam rek
Ma challah dié astou kou khamm adouna laaaa djiguen djiou bakh entou cas on n’est fière de toi bougnou amonnn 10 personne you melniii yawwwww Sénégal evolué koula estimé yalla na yalla goudal fann yui yokkk weirseukkk biii may laaa werrrrr gui yarammm bou sahhh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ma'n dė beugunala beuss ndiki tay djiguene yi warnagn roy si yaw bahi thiakhane li amna solo boula nekhone gua nek si yenen wa klk contanagn si yaw man dė bekna trop ❤️❤️
Machallah yalla nala Yalla défal diam ak guoudou fane yok ba yeuko barkè Seydina Mouhamed Psl dieuf dji yalla boumou nul 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️Billahi deug le Sénégal yakhou na
Dieye dou nitou fii yalla nala yalla samb artla mayla fane wougoudou ak wérr ak khéweul gou bari ak féké ak talle sibarké seydina mouhamed ak serigne touba
Yalnala Allah laffal tiat Mme. Vous êtes remplie de bienveillance, humaine et surtout beaucoup de sagesse. J’adore écouter vos interviews. Nitt bo bakhe rek bakhnga.
Machaallah heureusement terral na yayame té bou yaye geureumé rekk yalla geureume yaye kén amoul fayame c'est elle seule qui t'aime sans condition Die Astou je t'aime fort niane na yalla deff ni yaw dama beugeu terral sa yaye
Bilahi j'adore Die astou depuis toute petite temps bimouy joue ak ndeye khady té seune donone si yayame wallahi azim damako yaga beugeu yalla khamnako mangikay nianal goud fane ak sutura aduna ak allahira
machalla yalla nala yalla fay li amnasolo nit kou nek yalla dinala lath deureum bou nek finiouko dougueul mane dé damay wakh toujour souma amé goudi lay diok di dimbali new dolé yi té yalla rek takh
Ndèyssane maachaa'la amna solo djiguêne daffa waraa doon royoukay doon rèfèrence yallana la yalla gueuna doolêl takhou laa ci sa projets yi inchaa'laa amna solo loool waay🤲🏾🤲🏾🤲🏾
MachaAllah MachaAllah ku bakh gua Yallah na la Yallah may goudou fane ndakh amal gua ndieurine askan wi Yallah nala thiett seikh lou vraiment vous êtes une brave dame je t’adore bcp🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥰
Oh je me rappelle quand elle venait à ouakam avec Dembi Fall,yo (moustique) et une Dame ,j’ai oublié son nom. Elle souriait tout le temps… Merci pour ces bons moments 🙏
Mais mane ,Dié Astou Sarré dama la beugue beugue la xam vraiment ! !!Macha'allah qu'allahou soubhahou wa tallah takhawou soutoural leu sameu leu dolé le. Amine si barkè seydina Mouhamed aleyhi salatou wa Salam
🤍🤍SAW 🤍🤍
Merci sokhna dieu astou yalna yalla feyla yiwe thi barké alkhour'ane machallah
Une mère est sacrée j ai bcp pleuré car ma mère me manque bcp et comme toi ma maman me protège même là où elle est . Qu Allah accueille nos mamans parties au ciel au paradis céleste, à celles vivantes une très longue vie.
0p
Amiine
Machaalah yalna yalla barkél té are si barké seydina Mouhamed psl
Dié Astou une grande dame de grand cœur Macha'Allah ma chérie yalla na yalla diapalé la defalla diam siarnala contane si yaw béguénala lole nekal si diam inchallah
Ndeyessane yalla gua ma ko wale barké wére wou tede bi barké Serigne Fallou. Jaime trop Dié
Nicena ma soeur continue comme ça ont n'a besoin de vous dans notre pays pour l'avenir demain merci depui Brussel Belgium ourossogui
Salam merci grande dame .tu as un beau cœur que dieu vous garde amine
Bilahi dama la beugue si sama xol 💓noumay déff ba guiss la ba tie pièce théâtrale biguay wakh ni meune nala ko wakh début ba fin ak bigua joué ak madione laye Sarr💓💓oohhhh bilay lounék si sama xol wakh
Yalla nalla Yalla fayal bopam thi barké Muhammad Aleyhi Salatou Wa Salam 💚
Amiiiiiine yarabi
Machaalla Alhamdoulilah! Walaye comportement bou exemplaire la Kiss. Yalla na Yalla diapendal si daradiaye Ya Rassouloulah si barkè Lahilaha hilala bii guâ këum Yalla na sa leep barkelle. Bonne continuation et bonne réussite!
Machaala si kawe si kaname rék si lou bakhe yalla nala yalla défale diam té same la bou bakhe
Mashallah sokhna ci kouko sope la ,yalla nala yalla faye yiiiw te mayla nga motale sa mission ak sa sago sa .vidéo damakoy yakamte guiss diko setane guir thiofel die astou sarré
Machalah machalah yalna sa jamm Yagüe sokhnasi vraiement cest une femme exemplaire kou defar daara ay ndaw disi diangue alkhuran vraiement chapeau a cette femme ❤️
Vraiment une brave femme je t adore
Machalla toute simple et humble.Meunone nga tak Ay or ba feess pour gueune mais machalla watiè sa bop.Beugone na ame sa numéro pour gneuw Di liguey si yow si busy bi.Dinama nekh trope
Je la connais très bien la maison de sa maman et à keur massar ses frères et sœurs son là niep la diapalai namou niou dara nite kou bakh la cou wathie bopam la sarrê mabo ma grande sœur amal diam rek
Ct magnifique une mère est précieuse à chaque fois que je pense à elle j ai les larmes aux yeux ma sœur je t adore ♥
😢
Yallah na la Yallah diameul Dié Astou. Yoke la ba ngueu yeuke ko bidjayi Seydina Mohamed 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machaallah yaw référence gua yalla n’a yalla défal la diam❤
Ma challah dié astou kou khamm adouna laaaa djiguen djiou bakh entou cas on n’est fière de toi bougnou amonnn 10 personne you melniii yawwwww Sénégal evolué koula estimé yalla na yalla goudal fann yui yokkk weirseukkk biii may laaa werrrrr gui yarammm bou sahhh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ma'n dė beugunala beuss ndiki tay djiguene yi warnagn roy si yaw bahi thiakhane li amna solo boula nekhone gua nek si yenen wa klk contanagn si yaw man dė bekna trop ❤️❤️
Macchallah dié astou yalla na yalla dêfele diam amine ❤️🙏👍
Machallah yalla nala Yalla défal diam ak guoudou fane yok ba yeuko barkè Seydina Mouhamed Psl dieuf dji yalla boumou nul 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️Billahi deug le Sénégal yakhou na
Amiiiiiine yarabi 🙏
Dieye dou nitou fii yalla nala yalla samb artla mayla fane wougoudou ak wérr ak khéweul gou bari ak féké ak talle sibarké seydina mouhamed ak serigne touba
Machalla dama ka beugue nakh dafa Niro ak patron bou mo done liguéyale kokou dafa bakh si mane
Ma challah cou yaroula vraiment ndakh bocone nanou béne cogne unité 22 mes yarou simple ame respect dokh nak wakh nakh la khame thi mome ma challah ❤
Big lady Machallah . I’ve listen to you twice. You are genuine and courageous . May ALLAH be with You always always . Inchallah ❤
Yalnala Allah laffal tiat Mme. Vous êtes remplie de bienveillance, humaine et surtout beaucoup de sagesse. J’adore écouter vos interviews. Nitt bo bakhe rek bakhnga.
Machalla maman goudou fane wer barcké mame cheikh ibra
Machalah laff tiatt yalla nalla yalla diapelé té mayla goudoufane
Machaallah heureusement terral na yayame té bou yaye geureumé rekk yalla geureume yaye kén amoul fayame c'est elle seule qui t'aime sans condition Die Astou je t'aime fort niane na yalla deff ni yaw dama beugeu terral sa yaye
Sarre Mabo ni gua meuneu méle Machallah
Die elle est pertinente machalla 🥰 yalnla yalla Faye kaddou yi rafetna machalla 🥰
Bilahi j'adore Die astou depuis toute petite temps bimouy joue ak ndeye khady té seune donone si yayame wallahi azim damako yaga beugeu yalla khamnako mangikay nianal goud fane ak sutura aduna ak allahira
Machalla Die Astou yalla na yalla fay la si barké Seydina Mouhamed Barké cheikhoul khadim
Diam si yaw sama wadji machala
Die Astou Yalla na la yalla yokou baga gueun ko yeuk amine ya goore.
Macaala dey astou yallana yalla Faye🙏🙏🙏
Vraiment elle a beaucoup changé, elle est plus responsable et aussi mature,d esprit posée mashaAllah sister
Avantages touki nonula, tu vis beaucoup d'expériences.. Et ça te rend mâture, expérimentée
Absoluut
Machallah nitt kou baakh🙏 koumou kham rek terral nala yalana Yalla yokk khèweul yi🙏🙏🙏
Yalna la Yalla samou barcke serigne fallou 🤲 ko begeul bayam la machalla ❤️❤️
Machallah! Merci beaucoup Ya Astou. Protection divine.🤲❤👍
Ma sha Allah...yalla na yalla faay yiiw...doli la soutoura ak khewal...billah ya baax
Machala Djameu si yaw
Ndaysan machallah lii dh yité degue leu yalla na yalla doli la tawfekh si barkép borom touba 🤲
Mashala Diè Astou
Machallah jaimerai bien etre comme toi bilahi Machallah
Mahcha allah lou bakh rekk moo amm solo
Bilay djiguen bou mwunnnn guor laaaaa ma beugue nit kouy wakhhh Lou bakh bolekkk dikooo defffff❤❤❤❤❤❤yalla NASA ❤
machalla yalla nala yalla fay li amnasolo nit kou nek yalla dinala lath deureum bou nek finiouko dougueul mane dé damay wakh toujour souma amé goudi lay diok di dimbali new dolé yi té yalla rek takh
Dieu te garde et te protège tu es un modèle.
Machalla Dié yalla nala yalla faye barké alkhouran
Manchalla dié astou yalla nala yalla takhawou
Diè machalla.longue vie à toi et beaucoup de prosperité.bou senegal amone 10 you mèl ni yaw you avancé
Machallah die astou nit kou bakh la je l adore vraiment
Ki nitu yalla leu🥺🥰
Sarré mabo danga bakh machalah
J'adore cette dame par sa simplicité
Ndèyssane maachaa'la amna solo djiguêne daffa waraa doon royoukay doon rèfèrence yallana la yalla gueuna doolêl takhou laa ci sa projets yi inchaa'laa amna solo loool waay🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Machala que le bon dieu te protège vraiment vous êtes une bonne personne
Machala madame Dème yalla nala yalla faye yiiw 🙏
MachaAllah MachaAllah ku bakh gua Yallah na la Yallah may goudou fane ndakh amal gua ndieurine askan wi Yallah nala thiett seikh lou vraiment vous êtes une brave dame je t’adore bcp🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥰
Machalla bahk ala Lou yalla la hkarit tam la Koy diox
Walahi ki nitt ko bakh la Amal diamou rek si barkbe Serigne Touba 😍😍😍😍
Machallah yalla na yalla fay yiw 🙏
Sama mag dji Lala Aïcha Yangui def job bu nice Machallah si ioe♥️🙏♥️🙏
Une référence Dieye Astou ❤❤❤yalna yalla goudal fan yi ak wèr yokoula ba lo meun rén dewen mou eupko
Massalla beiastou mala bege💗💗💗💗💗💗💗💗💗🙏
Diè astou yalanassa diam sakhe machala kou bakhe ga
Machallah Nice na 🙏🙏♥️🥰
Machalah souma magéu yalna melni yaw
Machalla laf thiat
Machallah Amna solo
Machalla dieye astou bonne continuation
Mâcha Allah Dié Astou longue vie à toi ❤❤❤❤
Machala Dié Astou je suis très contente de toi
Une personne dune grande coeur sarre mabo yalna yalla same
Machalla
Les deux pies que jaim bcp New dji dolé et mbeuguel si souf .kou Mane limouy def yalna yalla Aar ninga fonké dara
Maachallah référence la Dié Astou sarré
Ndeysane damako beugone♥️♥️
Ndeye san die astou 🎉 namon nanla❤❤
Man damala beug rékk ta yalla takh 🥰🥰🙏
Ki Mako Beug YALLAH SUNU BOROM MAYMA LOUMA DIAPALÉ DJIRIM YI 🙏🏾
Yalnala yalla fay yiw fo dioublou yalnafa yiwu yalla dioublou barke cheikhoul khadim
Machala diè yalanala alkhourhane faye
Beug nalla trope bilahi ❤❤❤
Machalla you just motivate me may god guide and protect you inchallah 🙏🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️😘
Ndayesanne wakh dji rafete na manchallah
Machala Adja djeeh Yala na yala same la....
Tres bien . qu'Allah te benisse et t'eleve.
Machallah Die astou lafe thiate🥰
Une grande dame Machallah
Je t'adore dié astou yalla nala yalla same
Ki man dama ko bague yalla nala yalla samb barkbe seydina Mohamed Amine 😍😍♥️♥️😍
Machala lafetiate que le bon dieu vous garde et vous protège amine
Yalana tèranga sakhe sissa lokho si barker yonetebi inchala
Merci ❤ ❤ ❤
Thank you so much🙏🏽🙏🏽 ❤❤❤❤❤❤
Oh je me rappelle quand elle venait à ouakam avec Dembi Fall,yo (moustique) et une Dame ,j’ai oublié son nom. Elle souriait tout le temps…
Merci pour ces bons moments 🙏
Walay ndeysanne deguena kou beuri diam la
Machalla yalla nala yalla fayyy sa dieuf dieureudieuf
mashaallah sohna sii yalnalah Yallah gaina sam 🙏
Ki moy sama référence ❤