Urgent‼️ Modou lo Prêt a affronté Balla Gaye2, Siteu vs BG2 Annulé, Fadam2 fait des révélation explo

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 26 дек 2024

Комментарии • 141

  • @doffdouweer3686
    @doffdouweer3686 3 дня назад +29

    Combat siteu vs Ama balde serait le MEILLEUR COMBAT DE LA LUTTE SENEGALAISE..!

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 3 дня назад +52

    De toute façon Siteu ne merite pas de lutter contre Balla. Il ne meritait même pas de lutter contre Modou Lo. Il a eu la chance de montrer sa valeur à 2 reprises mais defouko, il a perdu ses deux derniers combats

    • @MakhouMbengue-cb7un
      @MakhouMbengue-cb7un 2 дня назад +8

      Bilahi wah nga Siteu apart combat wam contre P. Sow grands RV yimou beuré yeup dako niaak (Gouy gui, Sa Thiès Lac 2, Modou Lo) té beu légui niogui koy geuneu côte kw nangoul nagn ko mbolo biko yalla may mais Moy lolu biss bouko yalla bolé ak niom Ama Boy Niang Franc Serigne Ndiaye etc... Dina méti si mom trop

    • @kenzykindkeinde38
      @kenzykindkeinde38 2 дня назад +4

      ​​@@MakhouMbengue-cb7unen plus Papa Sow était en fin de carrière Siteu na kholaate nimou beurei

    • @NdiayeModa
      @NdiayeModa 2 дня назад +4

      Tok lène fi doule séne xole you Bone. Yi siteu Di avencé ngéne Di doule

    • @abdoulayendoye1803
      @abdoulayendoye1803 2 дня назад +5

      @@NdiayeModaboy Seye dako nookou daane ko sa Thies tégeul ndeyam daane ko Gouye gui niaf ndeyam daane ko lac niouss mamam daane ko daanou fi kéneuh loudoul di daaw ay nafek diko maay code sarap ndeyam hamouko donc ioe yay doul

    • @kadzooballer9463
      @kadzooballer9463 2 дня назад +1

      Siteu amoul palmares pape sow rek la daaane😂

  • @amadouthiam7967
    @amadouthiam7967 2 дня назад +11

    Lamb ji legui borom defete yi lanouy geuna diokh aye combats. Balla vs Modou moye combat bi

  • @cheikhououmargueye4989
    @cheikhououmargueye4989 3 дня назад +22

    Sa Thiès yangui beug niak chance dé😢😢

    • @IbrahimaFall-u3z
      @IbrahimaFall-u3z 2 дня назад +2

      Billahi 😢

    • @AhmedGueye-ch9sh
      @AhmedGueye-ch9sh 2 дня назад +1

      Non dina barrè ake modou lo et c'est très normal Modou lo moye nopalou rék bassi kaname

    • @dioufytv7738
      @dioufytv7738 23 часа назад

      Modou lô limouy nopalou mongui beg bari dh😂

    • @cheikhououmargueye4989
      @cheikhououmargueye4989 22 часа назад

      @@dioufytv7738 moy bour bi motax 🤣🤣🤣

  • @papepouye5223
    @papepouye5223 2 дня назад +3

    Fadam mercenaire de Aziz Ndiaye,nekal nitt balla gay am khell ngueen bayi sa Thiès dieul avance Modou lo am khaliss,balla naa dem beurré ji ak boy yi ah

  • @omartoure6271
    @omartoure6271 2 дня назад +15

    Balla gaye doit laisser sa thies l’opportunité de lutter contre modou lo c plus cool

    • @Coumba-bj3ln
      @Coumba-bj3ln 2 дня назад +2

      @@omartoure6271 saway nak Balla tegoul combat yi nak

    • @AmadouNdiaye-n4q
      @AmadouNdiaye-n4q 2 дня назад +3

      @@Coumba-bj3lnnon modou cachet bimou meuneu ame si balla mounouko ame si sathies ni tapha tine

    • @fatouseye341
      @fatouseye341 2 дня назад +1

      Sa thiés sort d'une défaite contre eumeu sene que modou lo a battu 2 fois. il ne peut pas prétendre lutter le titre de roi des arènes contre modou lo. Na liguéyaat ba si kanam

    • @mansourdieng2000
      @mansourdieng2000 2 дня назад

      ​@@Coumba-bj3ln😂😂😂😂

  • @ng9ngagnisto517
    @ng9ngagnisto517 2 дня назад +6

    Nguir yallah Mano lén no dimbali ak modou Lo balla gaye té wkh si combat diangue yiy dieumalé lamb kanam

  • @aminatasirelo8465
    @aminatasirelo8465 2 дня назад +4

    Fadam boye wax si lou passé dagay wax "il y'a 2 ans ou 3 ans" boye wax si future "dans 2ans ou 3ans"

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 2 дня назад +1

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @Abdoumbathie65
    @Abdoumbathie65 2 дня назад +8

    Modou Lo balla begou nio ❌❌❌
    Modou Lo sathies moy combat bi✅

    • @Deggou
      @Deggou 2 дня назад +1

      @@Abdoumbathie65 sa thies si défaite la diougué teu modou daneu eumeu, eumeu daneu sathies...

    • @Abdoumbathie65
      @Abdoumbathie65 2 дня назад +1

      @ bo nekon lolo modou dou beureik siteu même modou bimoy dieul coron bi si défet la dioge wala ?

    • @IbrahimaFall-u3z
      @IbrahimaFall-u3z 2 дня назад

      Lou lérr nga wakh​@@Abdoumbathie65

    • @Deggou
      @Deggou 2 дня назад

      @@Abdoumbathie65 modou dieul siteu ngir maayko xaliss nakh aye mbockou laniou daka yénéwone xaliss rek...teu modou boumouy beurré combat royal même bou diougué si défaite eumeu moko ladione revange...

    • @dioufytv7738
      @dioufytv7738 23 часа назад

      Yén Modou lô ngen beug mou dieul revanche balla guaye thi sa thiès rek😂

  • @moussakalamou7176
    @moussakalamou7176 2 дня назад +11

    SITEU NA DIEUL REVANCHE THI SA THIÈS WALA MOU DIEUL TAPHA TINE.😂😂😂

  • @azizjazzdiop941
    @azizjazzdiop941 2 дня назад +5

    Cé le patron de Diambars production Modou donne la chance a Sathies ou Tine comme tu la fait pour Siteu

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 3 дня назад +13

    Si Balla gaye 2 fait erreur il prend Modou lo ❤ 🇸🇳 il va perdre Balla va perdre ça couronne de empereur inchallah 🇸🇳 Si ce vrai Dam reck inchallah pour Modou lo 🦁❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🦁🙏

    • @Coumba-bj3ln
      @Coumba-bj3ln 3 дня назад +5

      Boko tégué sii wakhou mara yii nakh nga sa boppou,Modou kay moye perte au contraire

    • @papelo9552
      @papelo9552 2 дня назад +2

      yaw dagua nékh rék di wakh modou lô khamna kout bayam balla😂

    • @mansourdieng2000
      @mansourdieng2000 2 дня назад

      ​@@papelo9552😂😂😂😂😂

    • @guidzobeye9223
      @guidzobeye9223 2 дня назад +1

      Sa waay danga wakh lou la nékh rékk Boule faté nii Balla Gaye mo dane Modou lo 2 fois kone booy wakh kou nék si chance perte sa couronne Modou lo mo sii guena Diéckk Balla moko meune Va et Vient Aller et Retour 😅😅😅😅😅

  • @babacar3178
    @babacar3178 2 дня назад +2

    Lambdji nak modou lo balla guaye niogo téé😂

  • @MatarMbegue-d2j
    @MatarMbegue-d2j 3 дня назад +12

    Modou mon khana da namou défaite

  • @fallou57
    @fallou57 3 дня назад +10

    Dans 2ans 3ans ci guinaw non fadam 😂😂

  • @youssousarr3586
    @youssousarr3586 2 дня назад +4

    Fadam tamite ya niou waxone ni bala siteu dey takhaw

  • @NiangBachir
    @NiangBachir День назад

    Linwarone na âme vocal

  • @mormbaye6583
    @mormbaye6583 2 дня назад +1

    Sa thies vs siteu pourquoi pas

  • @bambalaye798
    @bambalaye798 2 дня назад +2

    Modou dafa beugueu dieul revanche si balla gaye

  • @issaleye154
    @issaleye154 3 дня назад +5

    Diope 2 doit affronter vainqueur prince

  • @nabyafialamp8996
    @nabyafialamp8996 2 дня назад +2

    Balla siteu d'où combat

  • @diafediaferewmi8437
    @diafediaferewmi8437 2 дня назад +3

    Balla gaye rek lafi meun berèl

  • @GaindéDeugu
    @GaindéDeugu 2 дня назад +2

    Balla Gaye tourame meussoul guénn lamb dji

  • @IbrahimaSokhna-f9q
    @IbrahimaSokhna-f9q 3 дня назад +3

    deglouléne nidiaye fadam deugeu tek laye wakh 😊

  • @IbrahimaFall-u3z
    @IbrahimaFall-u3z 2 дня назад +4

    Mais légui loutakh Modou lo beugoul beuré ak sa Thiès

    • @AhmedGueye-ch9sh
      @AhmedGueye-ch9sh 2 дня назад +1

      Modou lo molako wakhe sa waye fadame dafaye wakhe louko nexx rék beug créé bruit,et en plus modou des dafa diougué si aye combat il faut mou nopalou touti nake diapalé niome franc si contact yi

    • @mansourdieng2000
      @mansourdieng2000 2 дня назад

      ​@@AhmedGueye-ch9sh😂😂

  • @LateNdiaye-ke4th
    @LateNdiaye-ke4th 2 дня назад +3

    Balla gaye

  • @bayesaliou1988
    @bayesaliou1988 2 дня назад +3

    Problème bi moye modou lo dani bouko diambar soxla mou beuréko té Aziz Ndiaye mome dani mokoy teugue lii moye problème bi

  • @Robbe-Grillet
    @Robbe-Grillet 2 дня назад +1

    Fadam Siteu waroul sax beuré ak Sathies waxatouma nane dafay beuré ak Balla gaye 2. Siteu na dem dieul Ada fass mo gueune.

  • @HamathSow-o3e
    @HamathSow-o3e 2 дня назад +3

    Ama vs siteu lamb dakkukl

  • @youssouphesane6184
    @youssouphesane6184 2 дня назад +3

    Fadam ya niémé yalla 😂😂😂

  • @diadieufway5055
    @diadieufway5055 2 дня назад

    Balla guaye waroul sakh dieul modou lo

  • @MbayeBabacarDiagne-m8o
    @MbayeBabacarDiagne-m8o 3 дня назад +1

    ❤❤❤❤

  • @fallousaw1650
    @fallousaw1650 3 дня назад +3

    Lolou ce très semple en comprende guise naniou ngaka bou nekk si yonam niou nakhko moy tapha tine

    • @tidianesall3124
      @tidianesall3124 3 дня назад +2

      Bigg True bilahii Tapha tine piège bou makk si balla

  • @cheikhfall5927
    @cheikhfall5927 3 дня назад +1

    ❤❤

  • @tecnolocey.machalah3019
    @tecnolocey.machalah3019 2 дня назад +2

    Mane béss rék

  • @seneba20
    @seneba20 2 дня назад

    Modou lo eumeu sene

  • @Skilsfooball
    @Skilsfooball 3 дня назад +5

    Mafi nditou tay😂😅😅

  • @BaOusmane-l8m
    @BaOusmane-l8m 2 дня назад +1

    Lepo hamnieyko svp fadam

  • @moramar8677
    @moramar8677 2 дня назад +1

    Modou hana waxul ni dou diohé revanche té dou dieul revanche té nourou na kou beug kadom samahalat

  • @mouhamadoubakhoum7769
    @mouhamadoubakhoum7769 2 дня назад

    Wayy siteu guisse nafi avance balla gaye bayikofi dieul modou lo donc balla aussi sou amé combat royal dafiyy bayi siteu

  • @taibacham2153
    @taibacham2153 2 дня назад

    Lui sunyu problem moii Lui sunyu ba nek sunyu problem😅😂😂😅😅 Kii dinama rey

  • @mamadoulaminetambedou4232
    @mamadoulaminetambedou4232 2 дня назад

    "On dis pas dans 2 ans si guinaw"on dit il y a de cela 2ans.

  • @peulbitv
    @peulbitv 2 дня назад +1

    Balla eume lay beurél

  • @papasalioucisse9639
    @papasalioucisse9639 2 дня назад

    Siteu vs ama balde lolou combat dakhou ko

  • @diadieufway5055
    @diadieufway5055 2 дня назад +1

    Genre yi nio yakk lamb legy ay lobby laniou sen bopp rék

  • @louyallahdefrekknonoula5311
    @louyallahdefrekknonoula5311 2 дня назад

    fadam info

  • @NiangBachir
    @NiangBachir День назад

    Ya gneme yalla balla gaye masoul gana bécé si lame

  • @boubacarthiam6120
    @boubacarthiam6120 2 дня назад +1

    Eumeu Séne

  • @bassiroufaye3434
    @bassiroufaye3434 3 дня назад +1

    Il ya un bonne assan

  • @ablayediop3530
    @ablayediop3530 2 дня назад +2

    Siteu da danouwone si lac de guer no 2 pourquoi Modou Lo dieul Siteu

    • @dioufytv7738
      @dioufytv7738 23 часа назад

      Beg Lou yomb rék😂beg couronne bi yag thi mom com limou wakhon

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 дня назад +1

    Moudou Lo Sa tihss Goumba la

  • @AbdelKader-kt7zj
    @AbdelKader-kt7zj День назад

    Diom ak foula ak xaragn... Voilà son secret 14:33 balla bou taxam physiquement xadioul ci beine mbeur yako gueuna xam fadam😢 14:33

  • @CheikhIbraFall-u2r
    @CheikhIbraFall-u2r 2 дня назад +1

    Tapha tine bimou dañé eumeu sène 🎉Modou lo dackô dawe 😂donc s'il prend Balla gaye 2 le lion vas le battre par force😂❤ incha'Allah

  • @falloumbayd8770
    @falloumbayd8770 2 дня назад

    Kom kouy wakh si diine rèk manane ay dalile

  • @youssousarr3586
    @youssousarr3586 2 дня назад +1

    Siteu khana dioguewoul thi défaite contre mok lac

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 2 дня назад +1

    Balla Gaye loumouy ndieukeunté ak Sathies

  • @adamagueyeniang4986
    @adamagueyeniang4986 2 дня назад +2

    Modou lo vs eumeu

  • @cheikhibragaye8601
    @cheikhibragaye8601 День назад

    Fadam doul revk

  • @bambalaye798
    @bambalaye798 2 дня назад

    Caché khana 500millions leu

  • @OmarSignane-h3d
    @OmarSignane-h3d 2 дня назад

    bayil doul way

  • @IbrahimaBa-h7h
    @IbrahimaBa-h7h 2 дня назад

    C faux balla ne va pas empêché sa Thiès pour le combat Royal

  • @MouhamadoumansourDiongue-bl4xx
    @MouhamadoumansourDiongue-bl4xx 2 дня назад +1

    C faux c juste pour attirer le camps de siteu cette façon de communiquer

  • @KabouMbengue-c1l
    @KabouMbengue-c1l 3 дня назад +1

    Modou lo vs Balla gaye

  • @ablayediop3530
    @ablayediop3530 2 дня назад +1

    On a marre de la lutte vous êtes tous des nervis demain fera jour

  • @ablayediop3530
    @ablayediop3530 2 дня назад +1

    Fadam tu ne maîtrise rien

  • @Deggou
    @Deggou 2 дня назад +2

    Însbi modou mo meune balla foufe

    • @princelaye8210
      @princelaye8210 2 дня назад

      Sougnou beurréwatté nguéne diéppi modlo bapparé né mystique lagnléne dané 😂sur 100 combat contre balla modou 1 victoire lassi am chance sou ame 😂

    • @Deggou
      @Deggou 2 дня назад +3

      @princelaye8210 saay insbi modou mo meune koudoul balla bouniou beuréwate dinga ame surprise modou dakoy daneu hinchAllah..

    • @princelaye8210
      @princelaye8210 2 дня назад +1

      @@Deggou chaque jours vous répétez la même chose balla bamouy gadaay mo ngeunena bonne forme te takhoul daffa humilier modlo bi moy ngeuneu yomb

    • @Deggou
      @Deggou 2 дня назад +1

      @@princelaye8210 bobou dou béneu nakh legui modou da yewou ci lamb...balla boukoy dieul ame problème lou leer...

    • @princelaye8210
      @princelaye8210 2 дня назад

      @@Deggou 😂😂😂 bii moy ngueuneu yomb