Salamou Aleykoum toute la communaute toutes mes condoleances a la famille de mbaye ndiaye rahmatoullahi aleyna wa aleyhi. ke la terre lui soit legere et ke Dieu le pardonne et accorde le paradis firdawsi. une grande perte pour la communaute.Innaa lillahi wa innaa ileyhi raajioune
Serigne mbaye Ndiaye yala nako yala yeureum té tabalko aldiana si barkép mouhamed psl
Amine Yaa Rabi
Vérité Serigne Cheikh Tidiane niang machaalla yalla fayla yockal gniou faneyii ak diaboot gui yepe ak serigne Soulemane niang Mbaye ndiaye yalla yereum ko khare Adiana fridawsi amine
Amine! Yaa Rabi
Le numéro
77 636 52 26 Serigne Cheikh Tidiane Nianh
yalnako yalla yeram bargeb serigne tuba jigelenkoy jale wadara fajtal
Amine!
Salamou Aleykoum toute la communaute toutes mes condoleances a la famille de mbaye ndiaye rahmatoullahi aleyna wa aleyhi. ke la terre lui soit legere et ke Dieu le pardonne et accorde le paradis firdawsi. une grande perte pour la communaute.Innaa lillahi wa innaa ileyhi raajioune
Amine!
Yallanako yalla yerem kobaxone lool billahi tabe wone loll thi kham khamam
Amine!
Machalah
Mashallah amna solo Yalna Yalla dolli fay. Souratoul Fathi bi on l'écrit combien de fois l'audio n'était pas très clair en ce moment là ???
Wool Serigne Souleymane numéro bi migui thi début vidéo bi
Ay way kou décide khana dou lima guiss
Serigne Mbaye Ndiaye Ismoulahi Azam
Animateur bi sou meunone di wax auditeur yi gniy yok bat bi dinasi bax
Bakhna dinako deeg