YONENTE BI (PSL) MASSOUL DIOULE NEW...IMAM BABACAR SYLLA DEMENT CHEIKH MBACKE SAKHO...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 дек 2024

Комментарии • 45

  • @KINGBABA6838
    @KINGBABA6838 19 дней назад +2

    Tontou li andeu na ak xam xam machallah ya oustaz

  • @PapeFall-il7xw
    @PapeFall-il7xw 19 дней назад +3

    Lou lére nga wahe y'a oustaz

  • @Ismaeljallow-k3b
    @Ismaeljallow-k3b 18 дней назад +2

    Mbackeh Saho yefarr la. Ku wedi Yonentabi SAW yefarr ngeu.

  • @setewillane5485
    @setewillane5485 18 дней назад +1

    Machallah ya oustaz ❤

  • @SerigneBabacarSeyeofficiel
    @SerigneBabacarSeyeofficiel 18 дней назад +2

    Merci Imame Babacar Sylla

  • @thiernoousmanesow2110
    @thiernoousmanesow2110 14 дней назад +1

    Yombaloul dra

  • @cheikhbabacarmbaye2353
    @cheikhbabacarmbaye2353 16 дней назад

    Machalla oustaz babacar li moy l'islam

  • @solution5135
    @solution5135 18 дней назад

    Cheikh mbacké sakho néna maniyou dou sobé

  • @obd2214
    @obd2214 16 дней назад +2

    Hadith youñ binde 200ans aprés yonente,200ans plus tard lañuy doga guiss ouvrage Bukhâri bi ngueine teunkou
    Wa leegui bala Bukhâri di ñeuw gars si louñ teunkou wone lenen loudoul al quran
    D'autant plus que yonent bi mo wax ni boulen jottali dara louy diougué si mom nguirr bañ ñu diawalé ko ak Al Quran
    Nouveau da am ay hadiths youñ sossal Insa motah sen réligion changer

    • @newbarka8052
      @newbarka8052 16 дней назад +1

      Bindou gniou ko 200 ans après yonente bi guènè adouna dé. Gni ko bindeu 200 ans après bi yonente bi guènè adouna lagniou dioudou, diappal minimum 200 ans lagniou commencé tassaré livre hadith y, maname minimum 400 ans après bi yonente bi guéné adouna.
      *1ère question: loutakh sahabaa y gueuneu djégué yonente bi bindougniou ayy livre hadiths bi yonente bi guéné adouna. Do djégué bène livre hadith bougniou askanalé seydina aboubakr, omar, Ousmane waleu Ali... Mais si gnio khamni meussou gnio féké yonente bi, Khamou gniou kou fékké yonente, gnoy wakh si diiné dji
      *2ème question: 400 ans bi livre hadiths y amoule wone, gni doundou entre biffi yonente bi nékké akk ba livre y Di ame, gniogniou si bane diiné lagniou nékone???
      *3ème question: boudé Yalla da lène di mbouguel ndakh topou gniou wone hadith kone cela veut dire que diiné dji maté woule wone si yonente bi, mais si gniome boukhari akk Muslim....
      *4ème question: boudé Yalla doulène mbouguel, kone kayy hadith y amoufi ndieurigne, té Yalla limou wakh layy deugueul: djoulite gni si téré bi mouyy Alquraan la lène di até.
      Bénène mbiir mi moyy, mane beugg naa looole kou wéddi Mbacké sakho, lolou rekk layy khaar, mais Mbacké sakho ayy aaya laay indi, gniome gniou beugg ko wéddi si aay hadiths. Maname gniome pour deugueul mii gniou nekk, gnio ngi wéddi wakhou Yalla té khamouniou ko sakh

  • @SerignemamemorMbacke-j2t
    @SerignemamemorMbacke-j2t 19 дней назад +2

    ماشاءالله تبارك الله وتعالى

  • @mamadoufaye9962
    @mamadoufaye9962 19 дней назад +2

    Diadieufaty imam babacar sylla Cheikh mbacke sakho mom mane doumako deug lou li mouye wakh doyouma

  • @BoubacarDiallo-x8r
    @BoubacarDiallo-x8r 14 дней назад

    Sagg bi bamou diouguee Bdr dinieuw domam gueneuh adouna di Soxnay S Ousmane mou necko Diangalko Yassine sigatal rk ndax clavier la Wassalamou Haleykoum Waraxmatoullah

  • @ndaondao8574
    @ndaondao8574 19 дней назад +2

    Machallah

  • @HS_HighSpeed
    @HS_HighSpeed 17 дней назад

    Assalamu aelaykum wa rahmatullah ya Oustaz jeurajeuf ci léral yi concernant Mbacké Sakho
    Mais pour wathié Kamil bi mom daga dioum lolou mom lénn késsé gako meuna léralé modi sakhoul amoul parce que wadié Kamil niane ngén ci joublou té niane diamou yalla té diamou yalla yonénte bi mokay diangalé dieulé ko ci yalla

  • @KhadimGueye-h3t
    @KhadimGueye-h3t 19 дней назад +1

    Merci ❤

  • @MariamaCamara-q6d
    @MariamaCamara-q6d 15 дней назад

    Ouztazou senegaleyi ay ouztazou katior senni diaangeu.lokoul bapares nono lagniou meune wax

  • @barambow581
    @barambow581 17 дней назад +3

    Démléne diaguiwate chékh Mbacké douséne morome

    • @sayfoulislam2173
      @sayfoulislam2173 8 дней назад

      Koulay wakh al Quran nga beug ni diangoul do indi louy wané ni diangoul

  • @Ousainou11Ousainou11
    @Ousainou11Ousainou11 16 дней назад

    Mbacke saho nawah neh bu dehe bou ken jullee

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 16 дней назад

    Bilahi wakh nga degeu

  • @KhadimoulMoustaphaDiop
    @KhadimoulMoustaphaDiop 17 дней назад

    Mbacke sakho weroul

  • @lowaydeffboppam6865
    @lowaydeffboppam6865 19 дней назад +1

    Touba mom doffa gawa délo sama nidiay la wayé domoram pur la😂😂 cheikh Sakho

    • @DameNdiaye-sg8ng
      @DameNdiaye-sg8ng 17 дней назад

      Bilay kay youba mom Amon thiaxan Sen lep thi xam xam lan ka teek

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 19 дней назад +1

    mom fekatleu۔mai watie kamil kou dee sahabayui meusouniouko deff bidaleu

  • @alioutoure5035
    @alioutoure5035 18 дней назад

    Cheikh mbake Mom louma dege moukay wakh dafay reralate wakhoul deuge

  • @babacarseck9595
    @babacarseck9595 18 дней назад

    Cougeumoul hadis geumo benene teré boudoul alhourane geumoul sahabayi kathior boumelni mom moy debatre ah sokho nit counité doutogahmom

  • @TallAbalabass
    @TallAbalabass 17 дней назад +1

    Modou kama defalnako ay episodes geusstou lenko fofou

  • @moustaphaloum-ln2jt
    @moustaphaloum-ln2jt 10 дней назад

    imame dioum nga sokhna mariya bour bou niouy wakh mouxaw xiss mokoko may

  • @PapeDemba-eu9hu
    @PapeDemba-eu9hu 18 дней назад

    Wathié kaamil bi moom amoul preuve

  • @toutankhamon2507
    @toutankhamon2507 18 дней назад +1

    Bamba Sall mi day doul ndax Mbacké sakho waxul ni damay fenn

  • @mamadoundiaye1323
    @mamadoundiaye1323 5 дней назад

    mbacké Sakho lignu KO fénal yepp mënu KO tontu... kuko bëgg xam lu waral wax ji démal gëstu KO ci nihma tv.....

  • @alioutoure5035
    @alioutoure5035 18 дней назад

    Cheikh mbake mii dagn ko wara plinte yon Def si mom dafay yakhe dine bi

  • @goragueye8481
    @goragueye8481 19 дней назад

    Chekh mbacke ak BABAKAR lan soxla diakarlo😂

  • @SerignemamemorMbacke-j2t
    @SerignemamemorMbacke-j2t 19 дней назад

    😭😭😭😭

  • @djibrilcisse8932
    @djibrilcisse8932 19 дней назад +3

    Imam yi ay tapet lagn demlen fer debat ak mbacké sakho

    • @Cabayoroyoro
      @Cabayoroyoro 19 дней назад +1

      Gnémé wougnou KO deh😂😂😂

    • @taliberassoul
      @taliberassoul 19 дней назад

      Waxi doff Senegal mbam bou diouk di wakh sakho xamoul lou xew

    • @daoudadiedhiou1221
      @daoudadiedhiou1221 18 дней назад +1

      daniouko ragall🤣

  • @Luqmane-i9p
    @Luqmane-i9p 17 дней назад

    Tu as un problème à régler ton enfant va le reconnaître d'abord avant de donner des leçons svp

  • @bacarymaria6117
    @bacarymaria6117 19 дней назад +1

    Salam le prophète psl et les saabas ne connaissaient pas Boukhari ou Mouslim.Tout ce qu'ils connaissaient c'est le Coran.Si tu veux voir ce qui est dit de mal sur le prophete psl va voir les hadiths de Boukhari ou de Mouslim. Je me demande s'ils ont réellement écrit ces hadiths en tant que musulmans.

  • @TheKokejunior
    @TheKokejunior 19 дней назад +2

    So wolo sa bope démal débat ak Cheikh Mbacké SAKHO.