Salam saveurs planétaires avec les deux tata marietou et yandé . yalla na séne diam yague et je suis très contente pour le groupe Team marietou saveurs planétaires parceque ça commence à évoluer et je vais commencer à faire la liste des ingrédients des plats
Mahchahala amine yalla na niane yeup nangou inchahlaa hou!!mane nak borokhé meussou mako togou mais saveurs planétaires dinguen takh ma togouko merci ta mariétou ak ta yandé 😘
J'aime bien la manière de cuisiner de Tata yande pas trop gras pas de Rossi compliqué... et super facile et rapide à préparer mère mariem mom moye khoumbal émissionbi atia n'a khoumb rek ter dagan
Slm Tata marietou macha allah damay yakamti setane say video damay rétane basone yalnala yalla same Vremen contane nane trop beug nala lool Beug na am sa numero svp?
Bonsoir tata mariétou ma ngui ziar Svp dama beugu bayi bouillon donc je voudrais que vous m'aidez sur comment utiliser les épices sur les côtés de la cuisine merci...
Salam à vous !!!! Yandé et Mariétou je passe prendre mon “yakkal” quand??? En tout cas je suis fière de vous, Yalna Yalla wéreul lokhoyi si barké yonentem bou tedd bi saws 😘
5 лет назад
olymata diouf waaleykum salaam ma sœur chérie amène wayy 😘😘😘😘😘
Saveurs de marietou est une école pour toute la gente féminine ampoule nous mou nouye fadie école la maachalah thibcaw Thiam kanam rek
Marietou dathie bole âme horome bakh âme yite je l adore maachalah
Waw kay 😋😋😋😋😋
waw kay borom poliment tata yande ak borom tous les bagage ak youbiyaba yalla na sen diamou yague je vs adore mes deux tata
Machalla Tata yande sa mborèkhè j'adore menoumo won sakhe togou mborèkhè ❤❤❤👍
Salam saveurs planétaires avec les deux tata marietou et yandé . yalla na séne diam yague et je suis très contente pour le groupe Team marietou saveurs planétaires parceque ça commence à évoluer et je vais commencer à faire la liste des ingrédients des plats
Niola raw tata yandé, mborokhé bi mijotténa polîment macha'allah, merci á vous deux.
WA li nekhoul 😍😍😍😍 Tata Yandé todiatinafiiiii MACHALLA eupeuna
Machalah sene mborokhé bi diar n'a yone diadieufeté
Mane dal beugue na li machalah sognou Tata yi yalla na sene diam yague
Mahchahala amine yalla na niane yeup nangou inchahlaa hou!!mane nak borokhé meussou mako togou mais saveurs planétaires dinguen takh ma togouko merci ta mariétou ak ta yandé 😘
Ta Marietou meune na raye nitt barki yonente bi mai machalah com d'habitude avec notre chère tata Yandei
Wawaw man dhh Mbengue la sant t dama beug lou bakh laff thiat thi iow tata
Très bien.......la femme m'a tuée eh bien j'ai acheté tous les ingrédients et inchallah merci pour la recette
Machaalah man sen language mo may danel youbouyaba feu bou niakk diom neko si peuye... non yalna diam yague et merci Tata yandé sa mborokhé machaalah
C'est très bien de valoriser la communauté en permettant de pouvoir s'approvisionner directement entre nous pour les recettes, GO @Tata Marietou
MachaAllah mes 2 tatas chéries niaww sen mborokhé saparal na torop michiii waaay 😍😍😍😃😃😘😘😘😘😁😁😁😁
Dieuredieuf tata yandè ak Mariètou machalla amna solo j'adore talla fèylènes 👍👏👏👏💕💕
J'aime bien la manière de cuisiner de Tata yande pas trop gras pas de Rossi compliqué... et super facile et rapide à préparer mère mariem mom moye khoumbal émissionbi atia n'a khoumb rek ter dagan
MACHALLAH ADJARATOU MARIETOU .AK SOKHNA YANDE TEY LISI GUENA NEH MOY JOAL BI NGENE SI BOLE😘😘😘
🤗Tata marietou ak tata yande rekkk Khana nekhh😁
Machalah tata yandé ak tata marietou
Eyway defetingueenko dé!!!!
Machallah
Trop bon j'adore merci pour la recette
Tata marietou tey mborokhe bi togue mais sama jeukeur ay kharitam daniou done lèkh di Wakhtou ndakh saff 🤗 mercii à vous 😘
Bilay tata macha'allah laff thiat ..yagui may ngeuna khamall affaires yi car moi dama beug affaire de cuisine
Sèrère bou toubabè way 😂😂
Merci encore 😘😘
vous êtes la meilleure Tata yande j aime cuisiné à cause de vous vraiment vous êtes la meilleure
J'adore tes paroles !!!
Salam salam tata maretou Mane dama nekh trop Say mots Mo may damel
Je vais pas parler mais pleurer 😢 franchement je suis tellement contente ❤️❤️🇫🇷
WA yow loye dioye???
Ma friend s back again thanks so much Tata yandi I really enjoy ur cooking
Tata Marietou et tata Yandé ❤️❤️❤️ je vous suis depuis la France 🇫🇷 Je vous adore 🥰
Très bon faudrai essayer avec l’eau de coco 😱😱😱 trop bon
Oh machalla nekhna les deux tata li eupena 😋
Tata mariétou va me tuer néna YAP la VIANDE lllooolll
Li sama plat la masha allah
Borokhe bi eupneuuu adorablement
Machallah plat bou riche en vitamine
Yayoush ba ca c est vrai😉
@@Astucesdumonde oui bien-sûr je sais je suis peul ce plat nous appartient 😃😃
Linekhna trope machallah Machallah
Mborokhé nak dina tog nak tata yandé je ne l'ai jamais preparé mais je vais reprendre la recette merci à tata Yandé et à tata marietou goudal fane way
🍽 envie de manger💋🍽😋😋
Mashalah yenama nex! ❤️
Machalla ta marietou dagua ma sori lolou rek moma metti
Machallah tata yande😗😗❤❤
J'adore trop le mborokhé❤. Merci Tata yandé.
Merci beaucoups tata yande et tata marietou que dieu vous benisse plus
Slm Tata marietou macha allah damay yakamti setane say video damay rétane basone yalnala yalla same Vremen contane nane trop beug nala lool
Beug na am sa numero svp?
Machallah nekhatineu . bisous mes tatas
Waw kay sérére saafénne bi lérna
Machallah choukrane 🙏🙏🙏
Nice delicious
Machallah jtn
Tata Mariétou weur na mborokhé yi yeup wayé biiii la tamou souba sama papa Daf may setsi té mom la beug ...
Yalnaléne Yallah May diam je vous adore tellement mes tata
Je suis très contente. Demande à Tata Yandé de préparer le plat traditionnel de Palmarin :le koutiour
Ay way li nekhna
Toki toki de mborokhe
Merci à vous la Reine Tata yande et la Reine Tata Marietou que Dieu vous paie
WA Ta kania laniouy am direct nakkk
Sokhna Maï bou MAME KHALIFA MBAYE Insha Allah bientôt rekk
@ niogui wait ba bobou inchalla
Bilahi je vous adore et je ne cesse de prier pour vous , que ALLAH SWT continue de veiller sur vous !
Ngom Mamy ndiaye ohhhh Allahuma amen wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘❤️❤️❤️❤️
J'adore ce plat
J'adore se plat ses magnifiques
Thank u so much am making this dish day 😘😘 am from Gambia live in Denmark
MACHALLA nehk nah
Macha allah todiati nga fi
Mashalla 👏🏻😋
Machalla
Tata Yandé borom vinaigre de riz way
Mon plat, en plus j'adore les plats de Tata Yandé
Tata yandé rek 😂
Bonsoir tata mariétou ma ngui ziar
Svp dama beugu bayi bouillon donc je voudrais que vous m'aidez sur comment utiliser les épices sur les côtés de la cuisine merci...
Salam Tata Marietou diapal ni ma setane sa vidéo ak ma niaka setane yep manguilaye nianal
Daba Samba ohhhhh ameen wayyy
Tata il faut nga def bou feuille de patate bi. Stp
Les 2 tatis 😚😚😚macha Allah
Tu touyee la mounoul mougne🤣🤣🤣🤣
No demain je vais faire du mborokhé
Oumy ndiaye ak mane😁 mais lima si diakhal awma ingredients yi🙄
TaTa yande 👍
man dal mer bi say kaddou da relou lollllll
Merci les dames😘
Ma Sha Allah!
nexna machalla
Tata maretou beug nala trop
Ok on peu prendre épinards ok merci beaucoup ☺️
Yap la viande ça c'est le Sénégal
I like watching this put I can’t understand some of the wollof u speak I’m a Gambian
Salam à vous !!!!
Yandé et Mariétou je passe prendre mon “yakkal” quand???
En tout cas je suis fière de vous, Yalna Yalla wéreul lokhoyi si barké yonentem bou tedd bi saws 😘
olymata diouf waaleykum salaam ma sœur chérie amène wayy 😘😘😘😘😘
machallah .
yen niare yeup meungen toggou khana niou meune toggou ni yen amoul senegal?
Je vais passer une commande.c quoi votre numéro?please
Slt tata beguenala mais epinard pot haché mouna nek mborehe wala
mane dal sa tog nekhnama yallah sa diam yag
Ak mane
Merci
Machallah machallah fofou toth
Ma chère Mariétou t’as oublié le numéro de la vendeuse.il faut l’épingler en haut 👆
Mberry Mmy si ma Cherie c’est sur la description en bas merci
merci encore
Mboroké dou ame ail ni de laurier. Il faut aussi mettre du bissape vert mixer.
merci les tatas pour ce plat
💓💓💓💓❤️
ohh la voix de tata yandé day sédal sama khol bi
Merci beaucoup les tatas 😘😘
Tata le début quelle devais mets le degués
Mais Tata marietou es que Tata marieme ndoye peut envió a espagne aussi
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Thank you so much
begona nguéne wané nane lagnouy rakhassé khobou gnambi bi avec le passoir pour gniko messoul togue