URGENT À THIES: KEUR MARAME - BAYE MOUSSA DIOUF ASSASSINÉ DANS SON CHAMP

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 544

  • @AstouGueye-cq4gi
    @AstouGueye-cq4gi 11 дней назад +93

    Bilahi métina trop mo nékone souniou bilal pa bou bakh walahi bayi niarri djabar ak ay niaboote métina trop 😭💔repose en paix baye moussa diouf 🕊️

    • @sidysow6409
      @sidysow6409 10 дней назад +12

      Yalla nako brom bi térou té Yésal yeurmandé si mom😢

    • @papegueye9608
      @papegueye9608 10 дней назад +1

      AQQ(a une

    • @Yaayoubayyam
      @Yaayoubayyam 5 дней назад

      Les Peulhs sont des laches.

  • @Sénégal7900
    @Sénégal7900 11 дней назад +60

    Ohhh ndeysan yalla nako yalla yeureum te khareko aldiane firdawsi😢😢😢

  • @SatouMboup-l7b
    @SatouMboup-l7b 11 дней назад +85

    Kou raye niou raye leuh 😢mou diekh😢

  • @antandoye-fl1pt
    @antandoye-fl1pt 11 дней назад +25

    Yalna yalla yeurem té kharé aldiana si barké seydina Mouhamed repose en paix souniou papa 😭🙏

  • @AmySeck-n2f
    @AmySeck-n2f 10 дней назад +10

    Oh Sama Dieukeurou bénn tanta la 😭😭

    • @nogayekane5035
      @nogayekane5035 5 дней назад

      Ndeysane yalna ko yalla yereum kharé ko aldiana fiirdasy métina trop😢😢😢

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 11 дней назад +27

    Na État daf liguéyam yalla nako yalla yeureum kharéko aldjanna

  • @demefalldiop2361
    @demefalldiop2361 11 дней назад +19

    Woutlén pistolet waayy ,koulén gorr nguénn door ndayam balou bopp☝🏼

  • @MohamedBa-s7m
    @MohamedBa-s7m 11 дней назад +21

    Li niawna bilaye mais yalla nako yalla yeureum

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 11 дней назад +15

    Ohh métina tourp Ndeysane yalla Nakou yalla yaram 😢😢😢

  • @basselabdou9891
    @basselabdou9891 10 дней назад +8

    Li rafétoule dara yalla nako borom bi yeureum Kharéko aljanay firdawsi 🙏

  • @ahmedtidjanesow7146
    @ahmedtidjanesow7146 10 дней назад +8

    Yallana yalla indi diam naniou déllo sunu khél si yalla té wout diam bayi Tonie

  • @Président-ABDOU-DIOUF
    @Président-ABDOU-DIOUF 7 дней назад +1

    Préservons notre cohésion sociale 😢😢😢un jour quand la guerre d'ethnie aura, le Sénégal est dans le chaos à jamais 😢😢😢😢

    • @Yaayoubayyam
      @Yaayoubayyam 5 дней назад

      Il faut etre honnete il faut dire a ces batards d arreter.le vol est inne chez les peuls.Aye sathies lanou.

  • @FatoumataDansokho-h3n
    @FatoumataDansokho-h3n 11 дней назад +19

    Tu fais un travail remarquable ❤

    • @maimounandiaye-le1tu
      @maimounandiaye-le1tu 11 дней назад

      Sen travaille yi nak mo yemer site yi beurina gnou té gnom gnep di weur ay interview si ay gnaw tef rek

  • @dabaniang8141
    @dabaniang8141 11 дней назад +16

    Yalnako bour yalla yeureum tè dièguelko kharèko si aldina FIR dawsi thi barkhè seydina Mouhamedin psl

  • @NdayePenda
    @NdayePenda 7 дней назад

    Yalla nako yalla yarame si baraked S saliou 😢

  • @couradiopndiaye9620
    @couradiopndiaye9620 11 дней назад +13

    Wa diomaye Khana yeuguoul li khéW si deke bi ah li eupeu na dé pai à son âme 😢😢

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 10 дней назад +1

      diomaye di sétane RUclips

    • @nioukfall7869
      @nioukfall7869 9 дней назад +1

      ​@@basselabdou9891LA police est la pour ça il faut pas faire justice soi même

  • @babadieme
    @babadieme 9 дней назад +1

    Si l'Etat n'accepte pas la vengeance, il doit faire justice à chaque fois que c'est nécessaire !
    C'est la seule solution pour une paix sociale !
    L'enquête doit être rapide et efficace, et les auteurs de cet acte ignoble retrouvés et châtiés comme il se doit.
    🇸🇳💚💛❤️

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 11 дней назад +22

    Hamétouma Sénégal bilahi meuno tok bén jour tés do dégu nitte kougnou raye vraiment li léne mokoy fathe moy .kou raye niou raye la voilà ....yalana ko borom bi yereum té haréko aldiana firrdawssi amine 🙏 métina trop

  • @nadiatavares571
    @nadiatavares571 11 дней назад +17

    Franchement tite na nak si sénégal

  • @daoudakone4110
    @daoudakone4110 11 дней назад +30

    Same Kate yi sougnou rayé 1 nite si Yow ngane raye 2 si gnome lolou kessé mokay safara.
    Yallah nako yallah yeureum te khareko adiana amine.

    • @milanmbay2662
      @milanmbay2662 11 дней назад +2

      kone du senegal bullshit

    • @Ordinaire95
      @Ordinaire95 9 дней назад

      Yay domou hadj deug est ce que beug nga ap agresseurs bou nekke si sa hette bou rayé nite niou weur sa wa' hette dilene ray

    • @funasambsamb1661
      @funasambsamb1661 3 дня назад

      🙏naniou wakhtane dindi affaireou xett, niou xoll lilén bolé, té dokh si tankou jam👌​@@Ordinaire95

  • @maremesarre5753
    @maremesarre5753 7 дней назад

    Li khamena thi réwmi moye nakénekouné di gnane yala moussalniouthi raye katt ak moussabayi😢 Yalna khipé aldjana firrdawessi 🙏

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 11 дней назад +11

    Sénégal diaroule sakh mouye am policié policié yo kham ni khadjou keur sakh moléne eupeu gñiarigñe

  • @matargueye7200
    @matargueye7200 11 дней назад +15

    Daguenn lenn di weure kouguen thii diape tegale dayame fayou lenn raye lenn yenite moudiekh

  • @sidyngom5819
    @sidyngom5819 11 дней назад +12

    Dieullbi akka Bari ayy peul prison

  • @CheikhSall-c3i
    @CheikhSall-c3i 11 дней назад +9

    En tout cas Sénégal amoul justice yé douko meuseu am kou boybo yor arme de feu bo guisoul lo xam rk dor bal mou diéx lolou Moy légitime défense KOM kou ray dogne la ray

  • @alkhamiss
    @alkhamiss 11 дней назад +7

    Naniou lènn diap dokhane sene ndaye ray yii depuis lors mou mele degeu bi amoul dirigeants ni président ni premier ministre non Sénégal dou gate tiotou ndayi li rek😡😡😡😡😡😡😡😡

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 8 дней назад

    Eskey metina loleeeeeee yallanako yalla yeureume té khareko alediana amineeee

  • @sokhnaaramefall6474
    @sokhnaaramefall6474 11 дней назад +11

    Où va ce monde😢

  • @SodaSall-yd9bw
    @SodaSall-yd9bw 11 дней назад +14

    Wallahi Sénégal amoule justice 😭😭

  • @SambaToure-t8f
    @SambaToure-t8f 11 дней назад +38

    Ray len ben peul rek mou diekh
    Li dafa meti😭😭😭😢

  • @TamsireCisse
    @TamsireCisse 10 дней назад +3

    اللهم اغفر له و ارحمه و ادخل الجنه فردوس 😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @MbayeBabacar-m4i
    @MbayeBabacar-m4i 10 дней назад +4

    Etat na diougg si li vraiment déyi beurina trop trop teh nekhoul si khol

  • @AissatacoumbaDiattara
    @AissatacoumbaDiattara 11 дней назад +3

    Bly douniou len fadial Mettina yalnako yalla yeureum Mettina trop 🙏😭

  • @nioukfall7869
    @nioukfall7869 9 дней назад +1

    😢😢😢CE SONT DES TROUBLES FÊTE.MAIS ILS FAUT PAS RIPOTER.LA POLICE EST LA POUR ÇA

  • @cherifkillah1013
    @cherifkillah1013 11 дней назад +5

    Mai’s li c’est inhumain monsieur le président diougue len si li guir Yallah

  • @ndiogoungom9290
    @ndiogoungom9290 10 дней назад +1

    Kou melni constant mutamba Bou congo mo bakh Senegal ☝️

  • @merryloum860
    @merryloum860 11 дней назад +8

    Sénégal dou réw.

  • @assdiouf1033
    @assdiouf1033 10 дней назад +3

    Sénégal amoul bene sécurité ay nit Di yor diasi toujours gnoulene di sene Sénégal dal si kou melni fallou mi gnou teuth 15ans rek lagnou ay kou defoul wakhoul gnou accusé la def Kat bi di def tekou fayou gnou diap teuth vraiment sénégalais yepagui si danger

  • @AstouGueye-cq4gi
    @AstouGueye-cq4gi 11 дней назад +7

    Thies keur mame marame rip baye moussa diouf 🕊️💔

  • @ledakartimes
    @ledakartimes 10 дней назад +2

    Sénégal rek gay guiss niit di dokhontou ak arme blanche 😢 surtout les peul

  • @SeynabouFaye-b6q
    @SeynabouFaye-b6q 9 дней назад +1

    😭😭😭😭😭😭😭metina tamite yalnako yalla yeureume té khareko aldiana firdaws ay peulh yi tamiye doynagnagnou war nak une deux trois goor nite yombouna trope bayi yayame ay diabaram djaboot gui lii dafa wara diekh

  • @salihatendiaye8143
    @salihatendiaye8143 11 дней назад +7

    Aywayy deuk bi tangu na di fane yi li mba diamla tmt🤦‍♀️yala nako yala yeureum khareko aldjianay firdawsi si barki seydina mouhamed psl🙏

  • @abdouldiop1634
    @abdouldiop1634 9 дней назад

    Me hamolen kouko ray bapare ngeen ne polyi tooñ bahoul yalla nako Yalla yerem

  • @PapebabaSeck-x9k
    @PapebabaSeck-x9k 11 дней назад +12

    Lii doynaware looooollle, justice, justice.

  • @fallousene6694
    @fallousene6694 10 дней назад +2

    Trop c’est trop Senegal légui mom ni rek chaque jour que dieu fait rey rey ba kagn on n’est devenu des barbares kéne xamoul li bilahi métina sama xol néxoul 😭😭, que son âme repose en paix 🙏

  • @MouhamedDiop-z8i
    @MouhamedDiop-z8i 8 дней назад +1

    Nous sommes dans quelle pays

  • @Mainounambaye
    @Mainounambaye 11 дней назад +5

    Li métina trope billaye qu justice soit fait

  • @SeynabouNIANG-n9g
    @SeynabouNIANG-n9g 11 дней назад +8

    Diote na nak Diomay wax lii metti na trop 😢fekk nitt si ay champs wam ray ko 😢 ray yi bari na trop sx

  • @SeynabouFaye-l3n
    @SeynabouFaye-l3n 11 дней назад +5

    Ndeyssane yalnako yalla yerem té khareko dianatoul firdaws mais doyna ware trop

  • @abdoudiallo8959
    @abdoudiallo8959 8 дней назад +1

    Sama khole bi dafa diekh man peule la mais li yeufou domeram la dangani ray ndeyam fayou rek mokoy fathie😭😭😔😔

  • @WouryBalde-tm1jr
    @WouryBalde-tm1jr 10 дней назад +2

    😭😭😭😭 Paix à son âme 😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @seydouly8364
    @seydouly8364 11 дней назад +5

    Vraiment li gawna légi peulh same yi ay bandi lagne dagnouy togne satie toukh yamba aka sangara teksi sohor lagne def

  • @AbouDiop-f5d
    @AbouDiop-f5d 10 дней назад +1

    Que la justice soit faite 😢

  • @ibrahimadieng5783
    @ibrahimadieng5783 11 дней назад +6

    Kou dioug nek journaliste
    Ils aiment trop les questions sensibles

    • @aliounegueye5571
      @aliounegueye5571 10 дней назад +2

      Mais yow gni guaye wowé vrai journaliste dougnoula deffal descente sur le terrain di dox si nath bou tang pour recueillir aye témoignage ba lou Barry mane lér si sa nop , kone diapal si ki di déf efforou dém à la source pour gua xam té mougne lii la siye dérangé yagoul dara fait divers la dane done occupé quelque ligne si béne journal écrit

  • @mansourgaye6205
    @mansourgaye6205 11 дней назад +3

    Attentions ⚠️ deh kiko dieuka guis môme même bou nékoul môme enquêtes meunul ñiak comme fékou gñufa kouko ray gñu bayi bakham lou enquêtes bi wakh

  • @ElhadjiBeye-v6k
    @ElhadjiBeye-v6k 11 дней назад +1

    Yalla Khareko Aldiana firdawsi Amine ya Rabi

  • @mayou673
    @mayou673 8 дней назад

    😢ndeysane

  • @Omardiop-x2j
    @Omardiop-x2j 11 дней назад +2

    Li doyena ware dei 😢😢😢😢 thieuye Sénégal

  • @KhadiFall-i8l
    @KhadiFall-i8l 10 дней назад +1

    yalla nako bour yalla yeurem khary ko alldiana firdw si🤲🤲😭😭😭

  • @MariamaDembele-gy7kz
    @MariamaDembele-gy7kz 9 дней назад

    Yalnako yalla yereume

  • @MarieSane-qd3lt
    @MarieSane-qd3lt 11 дней назад +2

    Merci beaucoup mon père 🙏

  • @maimounadiallo6751
    @maimounadiallo6751 11 дней назад +5

    Sallallahou Aleyhi Wassallam

  • @AbdouCiss-vx4cm
    @AbdouCiss-vx4cm 9 дней назад

    Bilahi li dafa yomb trop li dou ben yon dou niary yon si moumay fekk si deuk bi dioudo wou mafa ms prsk sama enfance yepp fofou lako defe baye moussa Diouf yalla nako yalla yeureum te khare ko aldiana bilahi li metina trop 😢😢

  • @NdayePenda
    @NdayePenda 7 дней назад

    Bilahi 😢

  • @bebelayegueye8817
    @bebelayegueye8817 11 дней назад +5

    Ohhhhhhh masta way li metina lolou😭😭😭😭

  • @cheikhbadji463
    @cheikhbadji463 11 дней назад +6

    Mais finalement Sénégal deukou deum la wala ? Je comprends plus legui chaque jour un put...n de meurtre yen a marre vraiment...... il est temps que des mesures sérieuses soient prises sinon je crains le pire 😮😢

  • @MouhamedKa-uj9wv
    @MouhamedKa-uj9wv 10 дней назад

    Kou réy nioü réyla Vraiment li défawara jekh ndeyam Sénégal li métina trop Passe lak😭😭😭

  • @AidaNdiaye-vc7ur
    @AidaNdiaye-vc7ur 8 дней назад

    Cheuteute li métina nk Aka nio sokhor gni time nite diko ray cé trop ci môme momou lanou wara commencé peine d mort😢😢😢😢😢

  • @Salikhate732
    @Salikhate732 11 дней назад +4

    Thiey senegal gui guéne yakar dougne ko sangue 😢deuk bi tanguena trop😢rayi barina 😢yala nako yala yeuram té kharéko aldiana fiirdawsi

  • @FatouDeme-ke8bn
    @FatouDeme-ke8bn 9 дней назад

    Que son âme repos en paix

  • @moustaphaniang985
    @moustaphaniang985 10 дней назад +1

    Vraiment métina té doywar 😢😢

  • @dadosaliou6832
    @dadosaliou6832 11 дней назад +1

    Ndeysan sedeyi rfetna dei yalnako yalla yarzm

  • @assanesoldaroubayegorasarr1136
    @assanesoldaroubayegorasarr1136 11 дней назад +7

    Solution bi kou Ray gnou Ray la

  • @AngeliqueNdiaye-c7b
    @AngeliqueNdiaye-c7b 9 дней назад

    Li dou yon il faut prendre des mesures

  • @NdiayeNabou-js7vu
    @NdiayeNabou-js7vu 10 дней назад +1

    Massa massa😢😢😢

  • @africansworldtv3381
    @africansworldtv3381 9 дней назад

    Yalna ko yallâhou yëürëüm. Métina trop. Mais il faut faire attention aux discours. Attendons de savoir ce qui s'est réellement passé. Que la justice fasse son travail pleinement

  • @MoussaDak-o7f
    @MoussaDak-o7f 7 дней назад

    Bilahi loulér ga wakh gorgui

  • @MPSodan
    @MPSodan 11 дней назад +2

    Inalilahi wa ina ileyhi radji ouna, Trop de victime trop de meurtre à thies c'est vraiment incroyable sincèrement

  • @MamyGueye-q9o
    @MamyGueye-q9o 10 дней назад +1

    Metina trop yalnako yalla kharé aldiana firdawsi 🙏 😭

  • @abdoudiallo8959
    @abdoudiallo8959 8 дней назад

    Geune diap ko ray ndeyam c ça 😔😔😭😭

  • @abdouazizsy3014
    @abdouazizsy3014 10 дней назад +1

    Dans un lieu de crimes,les enquêteurs laissent tous ces indices là bas gants,habits etc...😢😢😢

  • @NdeyeFatouKeïta-j3k
    @NdeyeFatouKeïta-j3k 11 дней назад +1

    Wouy sama khol bi 🥺🥺

  • @maremandiaye2104
    @maremandiaye2104 11 дней назад +4

    Li tamite metina trop😢😢

  • @kabirniang4991
    @kabirniang4991 9 дней назад

    Était bou faible bakhoul 😢😢Peul noun mana néké bir Sénégal folen fék nioguén arme sans autorisation

  • @MoussaDiop-l8x
    @MoussaDiop-l8x 9 дней назад +1

    Peulh bakhougnou khéte bou bone lagn té sougnou moytouwoul lilénni yote khamou gnouko na khétou sénégal yeup paré gnou dokhane nday peulh yeup gnou gnibie si sen empire fouta dialon c''est des racite ethnieciste néddo ko bandoum IL faut que gnou djeuleul léne un evenement pour sachez tout les peuls Senegalais dans se pays

  • @damefall4471
    @damefall4471 10 дней назад

    Métina bathia canamou yalla😢😢😢yallna ko yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi

  • @MPSodan
    @MPSodan 11 дней назад +1

    Yalla na si yalla soti safara

  • @famandiaye6641
    @famandiaye6641 10 дней назад +1

    Deysane😭😭😭😭😭😭😭thiey adouna!!!!!!!!!!!!!

  • @lomodou2049
    @lomodou2049 День назад

    Deff lennn Attack Louy problem bii

  • @AdamaDiedhiou-r8w
    @AdamaDiedhiou-r8w 10 дней назад +1

    C'est écoeurant qu'il repose en paix

  • @AbibatouMbaye-o6r
    @AbibatouMbaye-o6r 9 дней назад

    Peulh rk yalnanou yalla sam

  • @AbouDia-ep9ik
    @AbouDia-ep9ik 10 дней назад

    Jespere que l etat prendra tt ls disposition qu'il Faut et doivent pas blaguez avc sa

  • @madasow1836
    @madasow1836 11 дней назад +1

    Yalla nala serigne touba térro aldjana firdawsy barkép noreyni

  • @sidyngom5819
    @sidyngom5819 11 дней назад +2

    Pour Lann geunn takhaw di Khôl

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl 11 дней назад +3

    Hé Allah ! Thiey adouneu bi. All yi sakh damako ragal si guiss guiss. Yalnako yallah yeureum

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 11 дней назад +3

    Restez là-bas à parler rek, ils vont vous finir ces pauvres là, prenez votre courage et se défendre à tout prix bakhna dal

  • @astoudiagne8530
    @astoudiagne8530 9 дней назад

    Yalla nako yalla xaré aldiana fridawsi

  • @MaymounaBa-y7k
    @MaymounaBa-y7k 9 дней назад

    Oh mon Dieu c vraiment déplorable.
    Vraiment mettina.

  • @diordione7366
    @diordione7366 11 дней назад +4

    On est dans kel pays 😢😭

  • @ahmadouka8036
    @ahmadouka8036 10 дней назад

    Kou raye niou rayla