Exclusif : Gris 2 et ses vérités crues à Macky Sall, Gris Bordeaux et Tapha Guèye

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 янв 2025

Комментарии • 63

  • @mamadoulaminesow9085
    @mamadoulaminesow9085 Год назад +14

    Yalnala yalla dèfal diamou b.s.saliou❤sa boo wakhé niou nawla✍️

  • @moustaphaaidara114
    @moustaphaaidara114 Год назад +9

    yalna yalla sameu la barkep Serigne Touba ❤❤❤

  • @niangelhadjiabdoulaziz8930
    @niangelhadjiabdoulaziz8930 Год назад +3

    Ki moy vrai intellectuel.
    Nous qui avons fait les bancs se croient supérieurs à eux mais quand on écoute Gris 2, l'on se rend compte que vrai intellectuel leu.
    Yalnala yalla takhawou soutoural leu same leu

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 Год назад +11

    Mala mac foff mais toujours wakhou nit toujours wakhou deugeu yalla nala yalla diokh lou geune lamb si barké sa touroundo❤

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад +1

    Gris 2 big up ✌️😁😁😁👍🙏

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 Год назад +4

    Ki mome machallah damay sétaan damay déglo toujours wakhou nit lay wakh yalla nala yalla arr❤

  • @abdoulayendiaye2327
    @abdoulayendiaye2327 Год назад +6

    Ham nga defa am niou nafekh mbeur yi ay sénégalais lagne am droit guiss président wakh s'en doléances mais nafekh wala am fo far si politique di saboté wala di am ay wakh diou bonne dieumalé ko si mbeur yi .mbeur youfa nek yep niakouniou bay yelwane .mais senegal mo bari nafekh

  • @mohamedd7470
    @mohamedd7470 Год назад +5

    Mashallah Gris 2. Say wakh rafét na

  • @Enfant_béni_7
    @Enfant_béni_7 Год назад

    MASHALLAH BOU WAKHÉ NGA NAWEKO ,, BOU DIEUFÉ NGA BÉGG SI MOM ❤ VRAIMENT MANE MBEUR BI RÈK LA YAKAMTI INTERVIEWAM NAK LÉP NIEURIGN LAY WAKH ,, ❤

  • @atoumanediouf6904
    @atoumanediouf6904 Год назад +1

    Une personne très équilibrée, machala

  • @abdousalamgueye9481
    @abdousalamgueye9481 Год назад +3

    Amin waay ❤❤

  • @Tawfeekh
    @Tawfeekh Год назад +1

    Je confirme que Gris 1 est franc et n'a pas froid aux yeux.

  • @mamekhoule377
    @mamekhoule377 Год назад +1

    Merci gris 2 bien parler

  • @mamadougassama8155
    @mamadougassama8155 Год назад +3

    Machalla beaucoup de maturité

  • @toubapneu5102
    @toubapneu5102 Год назад +1

    Maschalla mon fiss sama serigne champion bou mack bii kene dou yaw mn Frere ❤❤

  • @guilayendoye2984
    @guilayendoye2984 Год назад +3

    Bien dit

  • @ndiaboutadiouf9300
    @ndiaboutadiouf9300 Год назад +7

    KI MOM DAFA NITTE WAKHOU NIT REKK LAY WAKH

  • @moustaphaniang359
    @moustaphaniang359 Год назад +1

    Merci gris 2

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 Год назад

    Amale diam werreul goudeul fane thi barke serigne babacar sy aminé yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 Год назад +1

    Mashallah champion

  • @adamambengue8345
    @adamambengue8345 Год назад +5

    Machalla gris 2

  • @Enfant_béni_7
    @Enfant_béni_7 Год назад

    DÉM DI DANSER BI RÉKA WAROUL WONE MAIS SÉN DÉM BI DARA NÉKOU SI MÊME BOUDONE UN MOIS LAFI DÉSÉ 😢

  • @dafadoyseuk2589
    @dafadoyseuk2589 Год назад

    Bilahi mbeur mo leundeum kirise

  • @massambandiaye6150
    @massambandiaye6150 Год назад

    Daimbi c pas le moment et pourquoi aller et dansé pour régler des problémes

  • @gorasambe3719
    @gorasambe3719 Год назад +2

    Merci gris 02 borom 170 kilos yi

    • @abloslimshady
      @abloslimshady Год назад

      Niata ngani, 170 kilos, konn reug reug amna doolé deh, no meuné yeketi jonglé kou dissé noonou?😂

    • @Enfant_béni_7
      @Enfant_béni_7 Год назад

      DAY FÉEN WAY

  • @mbayefam572
    @mbayefam572 Год назад +1

    Macky vous exploitent pour ses propres intérêts

  • @amadoumboup2270
    @amadoumboup2270 Год назад +4

    Lamb dou ndiarignou kene sen ndiarigne mbeur yi kessee la

  • @AliounebadaraDiallo-zn5vs
    @AliounebadaraDiallo-zn5vs Год назад

    Très bonne cominuquation

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 Год назад

    Môme dafa yarou yalnala yalla défal diam té défalnou ko

  • @dialloibrahima2778
    @dialloibrahima2778 Год назад

    Danio waron yem si spot bi nk

  • @amadoulaminendiaye149
    @amadoulaminendiaye149 Год назад +2

    Avant de regarder jaîme là koy diokh

  • @mbarikaladieng8929
    @mbarikaladieng8929 Год назад

    Dou wone légui 🇸🇳🇸🇳

  • @dafadoyseuk2589
    @dafadoyseuk2589 Год назад

    Lamb dou béne facteur de développement yéne leu sen bir ay vrai tiogoumane guén
    Ay vrai niitou intérêts guén merde
    Avant lamb vous êtes des acteurs qui promouvoir les agression les sénégalais ne vous aiment plus

  • @abdoulayediop5627
    @abdoulayediop5627 Год назад

    Sa wakh rafete n’a. Wayé déssé ngua comprendre le jeux du président de la république

  • @seydi7336
    @seydi7336 Год назад

    🇸🇳🦁👈🏿🦻🏿🙏🙏♥️♥️👍🏿

  • @leuzleuz8602
    @leuzleuz8602 Год назад

    Boy va écouter tapha beur

  • @tenengbalde2431
    @tenengbalde2431 Год назад

    Tt à fait gris 2.mballo

  • @boyka1396
    @boyka1396 Год назад +1

    Gris sama mbeur borom khél bou séll bii

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Год назад +1

    Si lamb pauvres ak ancient bandit donc y’a un problème et lamb n’est un sport de chez ns ds tous les pays y’a de la lutte il faut arrêter

    • @barhamalpha8802
      @barhamalpha8802 Год назад

      LA LUTTE AVEC FRAPPE EST EXCLUSIVEMENT DE CHEZ NOUS ! ET ELLE RENFERME PLUSIEURS AUTRES DISCIPLINES TELLES QUE LA BOXE A MAINS NUES QUI PLUS EST, LA LUTTE GRECO, LUTTE AU SOL ETC.... SANS COMPTER L'ASPECT CULTUREL. ERADIQUONS CES COMPLEXES !

    • @thiawbadiane6873
      @thiawbadiane6873 Год назад

      ❤❤❤❤❤

  • @malickdiaw7474
    @malickdiaw7474 Год назад

    Je l’estime bien gris 2 mais il n’as pas bien compris le jeu du pouvoir!!!

    • @Enfant_béni_7
      @Enfant_béni_7 Год назад

      IL A BIEN COMPRIS LE JEU MAIS NILA MEUNA WAKHÉ NAK DAFA YAROU

  • @CheikhNguer-f7m
    @CheikhNguer-f7m Год назад

    Yaw giri 2 fo todje nit noum amé loka nakhari dem di féthi

  • @amadousow8717
    @amadousow8717 Год назад

    Maky sall khame khamame mo dièkhe motakhe mouye dadjalè aye mbeur palais

  • @abdousy49
    @abdousy49 Год назад +1

    Poulotique Dara diakhasoul yena narfekharek

  • @abloslimshady
    @abloslimshady Год назад

    Gris tay mom andoumak sa khalate, ninga dingaté tay dessna!
    Waw Président recevoir lutteurs yii dafa warr! Mais loutax Président khar ba à 8 mois des elections ngay wo lutteurs yii, yaw macky dafa beug nguenn mobilisél ko rek!
    Tay mom sa analyse dessna deh!

  • @khalifandiaye472
    @khalifandiaye472 Год назад

    Mai nak maodo lamb dafa kharam boul wakh intelectuelle bouko khalab khamoul dara no yaw khamga alkhouran limousi wakh

  • @moustaphaniang359
    @moustaphaniang359 Год назад

    Mbeur yi ay domoram lagn ay domé khadjjj lagn

    • @gallasendiaye7703
      @gallasendiaye7703 Год назад

      Ak sa pape domaramla sa data yaye chaque jour

    • @gallasendiaye7703
      @gallasendiaye7703 Год назад

      Sa data yaye sa pape mooy domeram

    • @Enfant_béni_7
      @Enfant_béni_7 Год назад

      NIIT KOU BAKH DAY AME RESPECT 😮 KOU RESPECTÉ SAY WADIOUR DO WAX LOU NIAW TÉ DO SAGA SAY WADIOUR

  • @bigueunebagueune8655
    @bigueunebagueune8655 Год назад +1

    vraiment ki amena yar
    ay nitou yalla gningui si lamb j yalla naléne si yalla dieulé té yok sene soutoura doli lén soutoura

  • @adamambengue8345
    @adamambengue8345 Год назад +2

    Machalla gris 2