YESDAKAR Sa fait 2 semaine qu'on attend Yene tamite ayez pitié de nous Cette série est super intéressante. Respecter les fréquences de diffusion. Merci way Et bonne continuation Mane méré wone nalene sakh 😡
*Vendredi 18 Septembre 2020* Secrets De Famille L'un Des Meilleurs Séries Magui Niane Sénégal Yalla Nafi Yalla Déf Diame Ak Khéweul Ak Soutoureu Si Barké Seydina Mouhammad Amine 🤲❤
li môme c'est trop facile kiné tekk deale bou yombou bi Maty sa kharite bi Mola gueune j'espère que prince dou deff bêtise mdrr ex gueile junior neina mon dakh yama😂😂😂😂😂😂ngay melni beignets dougoup
Prince deh limouy def ni souder deugla dinama bete troop bilay ex junior bi mako diepi ki niakna diom niit ak lou meun Am dagay digne top siguinaw goor pr lane junior niak fayda mom melna domou ndeyou madior😂😂😂😂
Khady NDIAYE barkkee s bamba am na yeenei ngua magal shi ms nk noumay deff ba ngua djott si pass bi fall serigne tuuba amoul morom danion nek si SAFAR lou way beugue si nioune rk day yeimmou
Hana legui moom leerna, kiné et Yama sont jumelles car la maman de kiné s'appelle Yaye Fatou ... Badiene ndeysan, elle est surprise... Kiné sa bess mangui koy guiss ni, dinga mat sa baram lingay bonneu yeup, Diarra moom n'est pas sérieuse ak sa maquillage bou eupp ngané dangay hasté ... Yama doussa maas ! Prince j'espère que tu es conscient de tes actes ?? Bijou a un coeur pur mais Maty aussi car c'est pas facile de reconnaître ses erreurs et de demander pardon ! Namna Ousseynou ci episodes yi deh ! Secrets de famille❤❤👌
Yama et Kine des jumelles??? Et moi qui pensais que Kine n’était pas la fille de Pape Malick. Je lisais souvent un commentaire du genre que Kiné était une « domou ndjitlè »
Kingsley A. Wii et le médecin a dit que leur mère s’appelle yaye Fatou il n’a pas cité de papa il a juste dit que cett yay fatou était mariée à pape malick
Soudé mane rèk meun nguèn supprimé pub mou thierno amadou sow avancé ko lay def chak jour😂waw sama cool la yoré deh dou tele 😂Diarra kèn gueunoula manké kiné dila utilisé dila manipuler com ça shim😪
Yalla nanou Yalla meuseul tchi pekhee kou bonn walla begue lou bonn rekk. Kine demal nitt ki demm. Weursakk birou Yalla la, kokou nekh la ko deukh. Serigne yi ngou gui beugh soff der.
Souba la béne fane safar yalla nanio si yalla youmb si 18 safar kouy mourid basal j'aime ak bébb dioulit
amine waye
Comme wérou safar gui térou na yalna yalla nangou niane yépu te niou magal si diamu yalna niépou am diamu
Amine ya rabi mercii bcp
Amine inchaallah
Amine inchallah
Amine way
Amiin
1ère nuit de safar❤️ kou beug serigne touba beuseul like❤️❤️
Non Touba taye Comme 18 safar barké s bi
❤❤❤
Wa waw safar safar rek
Man dh tidjania lah mais dama beugue serigne touba bilahi
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0f/видео.html
Boulene niou sonale serigne Ousmane waye
Si toi aussi tu zappe la pub pouce bleu 😂😂
Way bilahi waxatiko gni danio sof way
Surtout fouki niit di gass fouky niit di soûl bi😂😂😂😂
😂😂😂😂
Sof rek
Nagnko dello limou dioxé wonn😅😂
Kou beugue yonéntébi psl beseul j'aime 👍
J'aime
Psl
Yw sakh aimer nala
@@sodamariam 😀😂😀😂😀😂😀😂😀😂😀😀
Psl
Yalla na diam yague Sénégal si katanou Ahmadou Bamba khadim Rassoul
Pouce bleu
Amine fall
Ana soppey Seydinaa Muhammed yi bës leen j'aimes je suis premier👍❤😄
Yalla Naniou yalla maye fanane AK Diam inchallah si barké seydina Mohamed psl 😘
Danguene yaakaarni mouride rek mooy wadial safar gui Mann j suis talibé Cheikh en meme temp beug serigne fallou mbacké
Beugue nala deh
@@ndeyelo9059 mbaa khamngani maalaraw ma Cherie
Machallah yalna yalla défal diamou🙏🙏
@@fatimadiallo6967 ndayesane
ndayesane
18 safar jour j♥️♥️♥️🙏🏾yallnagne ko yague tewei si barké serigne saliou ♥️♥️🙏🏾bon bref sma mbokk taliber diam si yenn
amine yarabi
Amine thi barkep serigne saliou ❤️🙏🏾
Qui trouve ke soda femme bou soxar 😍 xana mom xamoul bonheur yaay thie domm😚😚
Elle est jalouse
Ça se voit kay😴😴
Ça se voit kay😴😴
❤❤❤
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0s/видео.html
Je souhaite a tout les Mouride une bon Magale,ss une talibé chiekh mais j'aime tellement serigne Saliou Mbaké billahi
Yalla na diam yagg niou wadial magal gui si diam ak salam any talibe bi serigne touba yi beusse leine jaime .serigne mountakha yagui fi loll
Nio gui ni di wadiall safar gui rk inchalla
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0z/видео.html
Jaime
seringue mountakha mbacké yalla nafi yag té werr
@@mamembayeseye6247 ndayesane
Cou aimer yalla nga djis psl
Paix et Salut sur Lui❤Amine
V
Psl
Gnigua hamni amagouniou dome yallanalene ko yalla thie barkep 18 safar gui niouy dougou
Amen
Amiin
amine yarabi
amine yarabi yalna yalla nagou Yann ci Barker baye niass
Amine waw
Niou diottagoul sen résultats yallnaléne yalla maye bfem cii barke mouhamed psl
Amine inchallah
Amine way mane 2main lay dieul inchallah
@@ndeyesokhnalo5689yalla nga am
@@dimkhaamvr6817 Amine way
@@ndeyesokhnalo5689 ok Nioko bokk
Aÿ way sagal lenema may ma ay aime
Haaa kharal ma mayla
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0/видео.html
kon aye Jaime dalaye sagal
Jesperk dou mane kassei ma sauté thierno mouley😂 aimé lein stp meussuma am 10jaime
Mane deh namakoy sauté niaaaw😂🤣😂
Nn li dafa doywar😂
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0/видео.html
@@mariafaye5037 billahi yawe
@@seynabouthiam4600 hahahahahah mbadou
Badiane elle est tellement classe machalla
C ma grand mere
Ay way wakh ko amna fans fi
@@yacinediouf2750 i
@@mamadoumarr8006 je te jure que c vrai je ne gagne rien à mentir
Yacine Diouf entoucas nioulay bi rafetna t set na, teyna, amna class mouna solo aussi mashallah
Serigne thierno ousmane ba esk douniou cotisé déloko limou fayone😱
Billahi cône ma cotisé
Ww 🤣🤣🤣
Vraiment 😂😂😂
😅😅
Bly llou lagniy déf
Bijou s’est une très bonne amie Ndeyssane ma sha Allah😍❤️ Ah Maty nila naq bo dioumer dangkoy nangou teikssi diegalou nango assumer❤️🙏🏽
Man ak yaw khamoumaaa kou rawww si série yiii heiii allah aide nous😂😂😂😂
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0/видео.html
Watching from Gambia 🇬🇲 my favorite
La tata de Maty me fait rire 😂😂😂😂avec ces manières de foutaiseeeee🙄🙄🙄
Ey way gnanalene ma am befm deuxième tour la dem🙏🙏
Yalla ga am si barki yonenti bii🥰
@@absadia5588 amine way
Ey Waye yalla nga am Waye, yalnama yalla dėgueu amine 🙏🙏🙏
@@salioudiallo6493 amine
Aminnn
Mouritd bi ba yagui wadial 18 SAFAR ❤
Bu baax🌟🌟 Sunu mbegte 😃😁
Moy sounio yité
Bu baxx💎sakh🥰🎉✨dakh moy sunu yittei♥️
Wwww inchalah
Khana paré kaye
Waw team secret de familles kiné digua rouss dh
trop yawe
A
18 safar mouride mba yagui wadiall magall gui niaw na dh❤✋
Guayii bâ yénagui wathie safar gui ✅✅
Boubaxx saxx
@@mamediarrafall9347 WWw mourite
@@mamediarrafall9347 wawawe
Ww boubakh sakh
ko beug woma fi 776697022 laye shop
YESDAKAR
Sa fait 2 semaine qu'on attend
Yene tamite ayez pitié de nous
Cette série est super intéressante. Respecter les fréquences de diffusion.
Merci way
Et bonne continuation
Mane méré wone nalene sakh 😡
*Vendredi 18 Septembre 2020* Secrets De Famille L'un Des Meilleurs Séries Magui Niane Sénégal Yalla Nafi Yalla Déf Diame Ak Khéweul Ak Soutoureu Si Barké Seydina Mouhammad Amine 🤲❤
😂😂😂😂😂
@@mouhamed5669 Yaw Ya Beug Rétane
@@mansourdieng2000 mdr😂😂😂
@@mouhamed5669 Yaw Ya Sof
@@mansourdieng2000 😬😬😬😬😬
Ana wa team teub Serigne moulé sow ak amadou sow du début jusqu’à la fin 😂😂😂😂😂💪🏽🤦🏻♂️
Magui nii aka massé gatt sax
😂😂😂 li kay comme guerre rek
Ndeye sokhna Lo mbadou 😂😂
Mme dembélé 😂😂
Fouk di gas fouk di soul dara dou am 😂😂😂
Bisou tu as une belle âme gentille douce tu es vraiment une amie une vrai sah billahi
Dafa mignonne dafa teyy
Bilay walaye wakhal waye tamite dembele
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0/видео.html
Bilaaahi
Vraiment ele es magnifique 💃💃
li môme c'est trop facile kiné tekk deale bou yombou bi Maty sa kharite bi Mola gueune j'espère que prince dou deff bêtise mdrr ex gueile junior neina mon dakh yama😂😂😂😂😂😂ngay melni beignets dougoup
😂😂😂😂😂😂
Da fã am fiit
Résumé nga presk dh ya boneu beignets nak 😂😂😂
😂😂
elle ne connais pa sa tete
Que dieu nous protège si barké psl 🙏🙏
Ameen
Amine waye
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0/видео.html
@@kumbasuwareh3901 amine waye
amine waye
Ani wa keur seydouna mouhamed
Fouki nit di gass fouki nit di soul da fék youro pélou Amadou sow man na yakh sama adouna 😂😂😔
😂😂😂
Mdame Niang raygama 😂😂
😂😂😂😂
Man lay ndieuk fatt
@@aminatadrame7694 😂😂bilay daniou sonou
First commentaire
Ana gnikoy setan ak telefon samsung
Vue avec j'aime avant de regarder😂❤❤
Merci à vous alhamdu lillah 2ieme du centre afin jalonnez vous guys 💞💞💞
Félicitation yalla nala dijck yenen topou si
@@ousseynousyll3970 Amine bb
Tte ms félicitations sister
Yallana done sa djiklat
@@goragaye462 Amine merci pour tt
Diarra moy khass yama thi niawaye 😂😂😂
Khana gissoule kanamam guii 😂😂😂😂😂
les nandites moma diakhal ndakh yama molen dak gnom gneup ak Mme samb
Comme boulette
@@aidaballawillier6299 lekh yi comme beignets 10000😁😁😁😁😁😁😁
@@aidaballawillier6299 😂🤣🤣
Kanam bi comme cahier brouillon
Mbaa xam ngeen ni suba la benn fan Safar. Mbégte mi tàmbali na de.
Mane diote na samay resultats
Sunu yité
On en a marre du suspense on doit découvrir que kiné est derrière tout ça
Chabii joue bien son rôle machalla ❤️
Cheikh abdou barham yanako yalla kharé aldiana
Amine yarabi
Amine ya rabi
Amine ya rabbi
Amine baye
La complicité entre yama et sa mère nekh nama
Kèpou kouy wadial 18 safar beuseul aime♥️♥️
Non... serie bi kiko mbind djiné keu. Machallah. Chapeau à tte l'équipe
J'ai arrêtée de regarder tous les sériés sauf secret de famille.sama préféré🥰😘bonne continuation
Enfin Pathé sene et serign ngagn se sont réconcilier yalna diam yague ci Barker serign Tuba
Hoo bijoux reck ❤❤♥️🇸🇳
Kou kholane saison bi yeupp beussal jaime
_#Mouride__ mba yéna ngui Réee wérou magal gui fégñ na dhé nagniy Rée way fekhal xoll❤ thi mbécté😍😍😍😍😍😍 mi la bokkk😍🙏_
Ohh barké serigne saliou✨✨magui begg
@@astoudiouf5749 *Wallahi fila eupé **#salihate** bi❤😍*
@@mouhamadoulamineseyebeugue2741 oh salihate💯💯❤️epuis wah ma sakh foy dall ma setsi leuh✨✨🙏🏾
@@astoudiouf5749 *oh ndeyesann man bir **#touba** la deukk khana kye gua dalall sima nguirr dieummi serigne saliou mbacké*
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0s/видео.html
Ani gni sauter Moulé sow 😂
Droit d’auteur wax bi mako mom😂😂😂
@@MamadouDiallo-te1nx hiiiiiii ak mane billahi
Mane mi awma sakh diotom 🤣
Mme dembélé Serigne bi dafgno fat way 😂😂😂
Moi
Hi Diarra calme ta choix yow ak yama c incompatible 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂Yama rek machala rafet yarou dou moromou ben kagna😂😂😂😂😂🤸♀️🤸♀️🤸♀️🤸♀️
Ioe mi lir sama commentaires Yallnala yalla Oubil sa bountou Weurseuk yeupp Amine Téi nga Abonnés sama chaîne RUclips,
Aminé
Amine
Amine
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0d/видео.html
Amina
Prince deh limouy def ni souder deugla dinama bete troop bilay ex junior bi mako diepi ki niakna diom niit ak lou meun Am dagay digne top siguinaw goor pr lane junior niak fayda mom melna domou ndeyou madior😂😂😂😂
Euyy premiére dou ay fohh j'aime wayyy😂💖♥
Meilleur série sénégalaise très originale
Où sont les mourides Tidiane bi dafa beugue Magali dioxléne ma passe
Aye thia lolou deh dou problem inchallah
Khady NDIAYE kayy djieul
Sa numéro orange money
Khady NDIAYE barkkee s bamba am na yeenei ngua magal shi ms nk noumay deff ba ngua djott si pass bi fall serigne tuuba amoul morom danion nek si SAFAR lou way beugue si nioune rk day yeimmou
Dioke ma sa orange money
Continuer a respecter les gestes barrières car le *Covid-19* existe toujours dans notre cher pays🇸🇳💯✊
*301 MORTS*
*Wa Salam✌*
Gnoune dh gnogui wathie Magal gui
@@kinesakho6334 l'essentiel respectez léne gestes barrières yii rék, Sénégal am n'dam insha'ALLAH🙏💯✌
😍😍🙏🙏
@@baidymbaye5038 yes bro'🙏✊
@@djibsondasilva454 ♥️
Hana legui moom leerna, kiné et Yama sont jumelles car la maman de kiné s'appelle Yaye Fatou ... Badiene ndeysan, elle est surprise... Kiné sa bess mangui koy guiss ni, dinga mat sa baram lingay bonneu yeup, Diarra moom n'est pas sérieuse ak sa maquillage bou eupp ngané dangay hasté ... Yama doussa maas ! Prince j'espère que tu es conscient de tes actes ?? Bijou a un coeur pur mais Maty aussi car c'est pas facile de reconnaître ses erreurs et de demander pardon ! Namna Ousseynou ci episodes yi deh ! Secrets de famille❤❤👌
Ta tt dit 😂😂
Yama et Kine des jumelles??? Et moi qui pensais que Kine n’était pas la fille de Pape Malick. Je lisais souvent un commentaire du genre que Kiné était une « domou ndjitlè »
Kiné mom beussem mangui si biss yi legui rek j'ai hâte de voir sa tête
Kingsley A. Wii et le médecin a dit que leur mère s’appelle yaye Fatou il n’a pas cité de papa il a juste dit que cett yay fatou était mariée à pape malick
Esk prince dou coopéré ak wa police police
Lima méti bis bou prince diapé Maty Maty DINA yakar bijou complice leu
Esk prince dou coopéré ak wa police
@@nabousamb8252 si meuna nék d
Qu'Allah nous protège contre le mal incha'Allah.
Amine ya rabi mercii bcp
Djiguéne bakhoul koi
Un jour viendra pour votre part
Amine yaraby yalna yalla Nangou niane yeupeu inchalah merci
Amine inch'Allah I
Ndokh dou bayi yoname tes prince la bien confirmé 🤮🤮🤮
Ana coalition andd sétane série yeppo 😂😂😂🤘
Wadial 18 safar inchallah
wawawe
Bilahi bijou limouye sagnsé amoull waye
Soudé mane rèk meun nguèn supprimé pub mou thierno amadou sow avancé ko lay def chak jour😂waw sama cool la yoré deh dou tele 😂Diarra kèn gueunoula manké kiné dila utilisé dila manipuler com ça shim😪
Tu penses que tu es la seule? Lool moi j'avance aussi en cas de pub
encore ki yawe la
@@Eladji-sall44 yaw
@@thiernodiop3507 lou khèwe
@@Eladji-sall44 Fouma dèm gisla
Le personnage de badiene ak nimou dioulité waroul def vernis à ongles. Foudeune mo gueuna diadou.
Vous avez parfaitement raison
Jai pensé la même chose même perruque dafkoy telle des fois alors que dou khalé et puis elle a la classe masha allah
Lolou moma diakhal vernis bi môme pour lane?
Jai pensé la mm chose foudeunn mo gueunn vernis bi
Mbaa yéni gui Wadial magal gui wér wi 🌙 1e safar mbécmi rék délén réée 😂😂😂😂😂😂
2 minutes 66 commentaries secret de famille rek mokou am💪💪💪
Fouki nit yi dolen bayi soulbi tamit 🤣
😂😂😂😂vraiment sonneu nagn si pellou Amadou Sow bi khawma koukoy soull wayei sonnal nagnou😭😭😂
🤣🤣🤣🤣🤣 doyna war
😂😂😂😂danio sonou wayy
Merci yene la done khaar, machaalah.
Sama séry préféré jtm diéyla gueye
Boy loro
Yaw da mèl ni sama mdo ko nga dh sarr nga sante
Wawaw
@@ibousarr7562 kone sama mdo ko nga
Yalla na yalla defal nieup diam bonne vision🤗
Que la paix de seigneur soit avc vs
Wa Diarra mi khame na bopame kanamame bi di mélni sigome taf 😂😂😂
Ayyyy singom taf kagn lako gueth dèèg sama adouna 😂😂😂😉😉😉😉
Prince gnou lay djiign deum ngay sègnou yèlou lirr🤦♂️
Lo kham si niak diom
Lo kham si niak diom
@@sambfatou3426 meunonn sè khol au moins bijou
prince kay.amoul.ben.diom
Abonnes vous svp ruclips.net/video/gZ_lI7vmid0s/видео.html
Sama pape cadré nake wouye 😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣
@@yacinesarr438 encore ki yawe la
Ioe mourid soube le 1ère safar
Ww fall
wallay ndeyssan
Inchallah
Machalla amna solo
Waaaw 😍
Maty tay mom tu es reconnaissante envers Bijoux
Mane dh pélou Thierno Amadou Sow yém nama té sof ma🤣🤣🤣ishhh
Prince amoul diome lii moye bandi dou bayie yoname 😭
Dierediefé seydil khadji malick sy ak wa keurem serign babacar sy mansour yall.na yalla yagal kofii ak kou'ni amin
Yama deeeh bodeiii niiit digeuh comprendre ni li yeup Kiné mo neik derrière 🤦🏽♀️
Diarra tei gua yaaaam Yama dou saxh seuh morom tshiiim🤦🏽♀️
Bilaye wakhtico khamoul boppam nila Yama rawé sakh daffa eup
Wa Diarra koum yap ak rosa bi 😂😂😂😂fond de teint bou eup bi
Xamoul bopam mounane mom mo dakk Yama 😂😂
@@sophianathan9987 moma diakhale mane
khana ki
Kou niak diome ni prince moussoumako guiss ak nimako yeuremewone sheut ki bete nama ma yene wone ko bizou mais ki diarouko
Demain la 1ere safar niou wadial ko!mai prince waroul kidnapper maty kon dafay Yombou lol
Bravo Badiene bien joué machallah 🙏🙏💋💋
Ni la kay nay tela dougou 🤗🤗🤗
Bijou tu es trop belle machallah😍😍😍
Ex junior bi nak deuguer na fite kouka bayi mouy xasss yama si gniaway 😂😂
😂😂😂
😂😂😂
Kanamam nii pain au lait
Kanam gui dh comme ébongué
Wax deug
Yalla nanou Yalla meuseul tchi pekhee kou bonn walla begue lou bonn rekk. Kine demal nitt ki demm. Weursakk birou Yalla la, kokou nekh la ko deukh. Serigne yi ngou gui beugh soff der.
Sou prince agresser maty partie bobou waroul am chance si série bi vraiment trop de wiri wiri
Ay way may léne ma j'aime s'il te plaît
Ki di has yama hana amoul seto 😂😂😂😂kana mame boumel ni pewolé bou 200f🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Wouyay diarra mii douniou yobou tii Thierno amadou néna maty da niaw😂😂😂😂j pleukhhhjj
Bonsoir ici gaaw nguéne dé👌👌
Gnou mel ni kiné yalna Nanou si Yalla moussal