Ça on dirait que ce n’est pas une comédie tellement c’est réaliste et naturel que c’est incroyable. En tout cas moi je n’en peux plus tellement c’est drôle 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Badiane me rappel mes moment de folie 🤣 sou ma rakadio wone des moment ni lay def sama Yaye di dhe ndakh ay retane ma fass sama kanam non diam nekhna 🤣
Meilleur épisode ! Dioyou badiene louneq leu 😂😂. Bou warnaa toud bir bou dawou nidjayaaam tamit. Mis à part ça Astou est une très belle femme, ses coiffures sont toujours top aussi.
J’aurais bien aimé que pour une fois senegal ame serie bouy ame fin . Fin bi nekh . Khady ame djeukeur ak awa , mere seun ngueine keur gui , bou ame djabar ame ay dom deuk ak yayam meune fonder sa propre famille et qu’il reprenne sa vie en main. Les trois autres aussi demmmm , pa bi comme da beug djigueine likay dall mongui si kanamam. Il faut que probleme yi gueine souligner yeup ame moudj comme ça niit khamni lou way def sa boppp. Serie bi meune ame deug deug sens nga khamni meme apres des annees kouko seitane tu sauras où mettre les pieds . Une suite vraiment logique. Introduction développement et conclusion.
Wôye 🤣🤣🤣 sauce bi me rappel quand tu mets du jus, made ou autre dans le frigo et que tu trouve un pot vide…. Badiene t’es pleures sont justifiés , je comprends cette déception 😢 🤣🤣🤣
C'est deux épisodes par jour moi je les regarde quatre fois par jour je ne regardé plus les séries ce sont mes enfants en Europe qui m'ont parlé de polygame vous êtes les meilleurs vous êtes talentueux badiene je t'adore que le succès continue machallah
Bouko sakh khalat bo bruguŕ beugué sangou dangay ra boudé mane mou niak diom maye badianou khalé Yi ndokhou diambour laye sango nioumay khas comme badiane lo def si firigo bi niou lekk ko boye khas te niep ne patt so togué lou nakhari Taye nga dee
Thiam akh badiene ak 😭😭😭😭 yi boula dalé doula djikh sathie lek ba dé badiene me tue madre peace amal complexe Ba man dal j'aime senepeople ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ça on dirait que ce n’est pas une comédie tellement c’est réaliste et naturel que c’est incroyable. En tout cas moi je n’en peux plus tellement c’est drôle 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Non série bi mo nekh🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Badiene té nga bayi yayou ndey ndiaye si diam😂😂😂 yangui biper kou ame crédit séne duo dina doye warr😂😂😂😂😂
🤣🤣🤣
😂😂
Cette série mérité d'être nominé meilleure série de l'année
Lii moy série
Intoxication weuy non série dina ray nitt bilay
je te jure
Badiene peut à elle seule me tuer de rire j adore cette série
Bilay
C'est vrai que les meilleurs comédiens sont à Thiés..vivement que cette série passe dans les télévisions ..bonne continuation
Fi si internet bi bakhna d'où démé si télé bi nayou yak décor bi ndidi originalité bi
Le nombre de ''vu'' doit être égal au nombre de ''j'aime''
Pouce 👍bleu🔵
Astou est naturellement belle ❣️💖
Badiane me rappel mes moment de folie 🤣 sou ma rakadio wone des moment ni lay def sama Yaye di dhe ndakh ay retane ma fass sama kanam non diam nekhna 🤣
Kone Thiam mo sathie sauce bi Badiène di dioyy😂😂
😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😘😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😘😘😘😁😁
Meilleur épisode ! Dioyou badiene louneq leu 😂😂. Bou warnaa toud bir bou dawou nidjayaaam tamit. Mis à part ça Astou est une très belle femme, ses coiffures sont toujours top aussi.
Mangui😭😭😭😭🤣🤣🤣🤣🤣
Toureunedo dagnouy wakh rekk mais Badiène mo gueuneu reew thi série bi 🤣🤣🤣🤣🤣
Woudioutoubab
@@samira260 série bi dotoul am 😂
@@Fatimatou_Diop badiene mooom key hana 😂😂 danio yab halei yi req
J’aurais bien aimé que pour une fois senegal ame serie bouy ame fin .
Fin bi nekh . Khady ame djeukeur ak awa , mere seun ngueine keur gui , bou ame djabar ame ay dom deuk ak yayam meune fonder sa propre famille et qu’il reprenne sa vie en main. Les trois autres aussi demmmm , pa bi comme da beug djigueine likay dall mongui si kanamam. Il faut que probleme yi gueine souligner yeup ame moudj comme ça niit khamni lou way def sa boppp. Serie bi meune ame deug deug sens nga khamni meme apres des annees kouko seitane tu sauras où mettre les pieds . Une suite vraiment logique.
Introduction développement et conclusion.
Mere Coumba da diekhh trop ndeysane yalla nako yalla may weur boubakh mou yaag fi loool sah amine
Badiane je la trouve trop mimi et adorable.. surtout n'ai quand elle porte sa perruque 🤣
Nous sommes enveuglé par les larmes de badiane tamite 🤣🤣
Je vous donne se que vous mérite des cœur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Hii non bou akh ndidjayam dinaniouma raye😂😂😂😂
@@mariemecisse9513 daniou nekh rék bou rék mo ame problème 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Kou sétanagoul ba paré di rétane 😂😂
Man 😂😂😂
@@haliamagassouba453 j sw anveugléeee 😂
Khana man🤣
Astou dal beugna naturel machalla té yangui diongama🥰j tm dal mane😘😘😘
Heureusement que Badiéne n'a pas mangé la sauce sinon les dernières réglage du mariage vont tomber dans l'eau 🥰
🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂
Voici la serie qui cartone et qui fait le buzz actuellement 🙏♥️ bravo e bonne continuation 🙏
badiene elle a refait ma journée dès le début de l'épisode 🤣😂 sauce baaaa kouko lekk niak na khel 😆
Des coeukhhh pour Badiene 😂❤️
💯❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤
♥️♥️♥️♥️♥️💘💘💘💘💘💘💘💖💖💖💕💕💕💕💕💖💖💖💖💖💖💗💓💞💞💗💕❣️❣️♥️♥️♥️♥️♥️♥️💝💟💟💟💟💟💟💟💟💌💌💌💌💌💌
Wôye 🤣🤣🤣 sauce bi me rappel quand tu mets du jus, made ou autre dans le frigo et que tu trouve un pot vide…. Badiene t’es pleures sont justifiés , je comprends cette déception 😢 🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣
Non série bi mo dakh Senegal
Damaye nek si metro ak train yi di sétane Di ré🤣🤣🤣🤣🤣
Oh ça m'est arrivé durant un ramadan, on a mangé le thiakry que je fait et on m'a laissé le pot sous mon oreiller😭😭😭
Bilay lii day diekhal khôl 😂😂😂
@@awacheikhbadiane5027 😂😂
way astou rafet na trop la beauté de astou est abusé 😍🥰♥️
Et aussi elle une physique de sportif.
Toi aussi tu as remarqué !!!! Elle est magnifique
Machala
Weh une vrai femme africaine elle est tte belle
Astou nimou diéké dafa eup
Thiam a chaque fois il attend quelque chose 😂
Mane polygame nimouy seedalé sama hole bi c'est ouff!! yalnalene Yalla fay waay
Je vous aime Astou ma préférée yakamtina duo badiene ak madre peace 😂😂😂😂non li nekhna way yallah na diam yagg
Badiene tu es adorable néna tatam wou rey wi mou melni diambari beuk negue ohh j’en peux plus 😂
Yen daal guiudou len fane vous me tuez je vous jure 😂🤣😂🤣😂 la conversation de bouh Badiene et ton Thiam ma achevé ohh j’adore Bouhkountou
😂😂Cou beugue badiéne Khady touche aime👍
Badienne meilleure comédienne j l’adore 😂😂😂😍😍😍😍🙏🏽
Mais badiene c’est vraiment la meilleure ! Meunouma mougne dioye yi 😂😂😂😂
Ça c'est l'épisode des Sérères😂😂😂La sauce en action
Bou ak Thiam “sa biir bi day meti waleuh day daww “ 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Kou togonn thi bountou gallé bii Di khar comme Mane 😂😂😂😂
C'est deux épisodes par jour moi je les regarde quatre fois par jour je ne regardé plus les séries ce sont mes enfants en Europe qui m'ont parlé de polygame vous êtes les meilleurs vous êtes talentueux badiene je t'adore que le succès continue machallah
Kou l’éke sosou badiene waye 😂😂😂wa association bi nagnou défal badiene misui 😂😂😂😂
Badiéne kagn laniouy respecté la khamoul thieeee je suis enveuglé par notre badiéne national 🤣🤣
😂😂😂😂😂😂😂 vraiment kene amatoul stress thi rewmi ndakh yene Machalla chapeau ❤️❤️❤️
on a jamais aussi bien khiffer une serie. vraiment merci
Je vous suivre tous les jours depuis Italie bn continuation
Nioune wa europ nioy faye RUclips bayi wouniou bene serie 😂😂😂
No li nékh na trop meilleur série de l'année 💖man badiene la beugue bilahi
Vous nous surprenez toujours avec vos épisodes pleins de bonnes leçons Diam si yéne wa team polygame
🤣🤣🤣🤣 Tonto Thiam mofa diar Badiane kay Thiam mola souffou🤣🤣
Bouga yi dinélaw mouy wer loumou lékk😂😂
Des coeurs pour badiene ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
1M de vues la beugueu si serie bi inchallah 🥰💪🏽 nassi. Nieup diam 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Bou vraiment il défend toujours la vérité ❤️❤️❤️ bravo à toute l’équipe c’est drôle et instructif en même temps
Badiene Yallah ga goudd fanne té werr
Kounii Amine Yallah ga goud fanne té werr
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Non mais li nekhna way machalah j'ai tjrs aimé vivre dans une maison avec bcp de gens badiene tu m'as tuée 🤣🤣🤣
Bilaye comme moi j'adore les maisons familiales
@@amibabagaye5786 bilahi pareille j'aime trop l'ambiance
Bouko sakh khalat bo bruguŕ
beugué sangou dangay ra boudé mane mou niak diom maye badianou khalé
Yi ndokhou diambour laye sango nioumay khas comme badiane lo def si firigo bi niou lekk ko boye khas te niep ne patt so togué lou nakhari
Taye nga dee
@@torodotorodo1306 gni dagno khamoul li si keur famille reik motakh gnoukoy beug mais dara neikhoussi
Aye badiene Bouma ray rena ba thiorakhane🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Badiene est une véritable comédienne chapeau à elle
Astou ak ndeye Ndiaye bakhou niou😂😂😂😂
Épisode bi limako rétane amoul 😂😂badiene elle me fume 😂😂
Astou très belle machallah 😍😍
Domou president sonko ngène togne dè borome rèwmi 🤣🤣❣❣❣❣
Away badién sama préféré nane la prononcé intoxicaton😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂lnsication ay way badien wa thiés am ngen May si théâtre machallah
Duo astou vs ndeye ndiay j'aime bien❤❤❤astou laff bouche rafet nga tropppppp way
bilahi je fière d'être thiesoise longue vie à vous et à toute l'équipe ❤❤❤❤❤
Il faut supprimer les scènes où badiene pleure ses sauces pas interressant
@@marremarre7135 ooooooôoooooooooooooooooooôoooôôoooooooo
@@ndeyecisse4282 c est des gamineries je te jure
Salla ka Sama domou baye invité ma thies
Coeur por badiane 💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛💛
La série au top de la fin d'année
serie bi nekhna wayé bâ ana say yell
ay diokh lene thieur badiene wayyyy🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Bou dafmay fethie shiii mo guenn sonn thi kergui😂😂😂😂dioyuu badiane lanlaaa tammit😂😂😂Madre peace lay weurr😂😂Thiamm tammit nappnaniuuuu
Kou gneuw lidieunti mirasse bi Yayou Ndeye Ndiaye sakh thi bir😂😂😂😂😂😂
Notre badiéne national😂😂😂
Merci à vous diam bou bari si gnieup😍😍😍❤❤❤
Astou elle est très belle c’est incroyable 🥰
Comme vous je pense
Khiiii tey mom number one là lale dé je vous aime sama deuxième famille 💕💕
Wouyy Badien
Legui sathia tougnioula XALISS , soss lagniy sathiii 🤣🤣🤣🤣🙈wouyy
Sauce bi mom c'est Thiam, Astou AK Ndeye Ndiaye gnoko seddo 😂😂😂
Notre série préférée qui ńa pas ďheure🤗
Notre série préférée je vous j'aime ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰
Ayy badiene wathie gnou😃😃 ak sauce,lakh,thiere😄😄😄
Ak thiébou yapp😂😂😂
Je vous adore ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Elle adorable
Ana wa team polygame wonelen sen bop avec beaucoup de jaime
Astou diongama na😍😘jlm bcp 🥰
Ndeysane mère Ndeye Coumba Mingui dieum mak ndeysane.franchement série biii nekhnama troppp🥰🥰trop original .
Non moi j’aime trop badiane elle est formidable longue vie à vous et bon courage pour la suite 😘😘😘😘
Qui est encore là pour se redivertir😂😂😂😂
No mai du jamais dangaye rétane bay dioye 🤣🤣🤣🤣🤣
Franchement merci beaucoup à tt l’équipe vous ns rendre heureux 🙂
Dougal sa lekk frigo yewou niou lekal lako yague na ci keurou famille ! Badiene dioyal ! Je te comprends !
Barké S touba Badien damala beuge bilay chérie binome 🤣🤣🤣sama sosss 🤣
Mais si Binome nope Madre Peace, rivaliser ak Badiane 🤣 keur gui todj 🤣. Ana scenariste bi waaaye. En tout cas Bravo a toute l'equipe 💖💖💖
Lolou doumako lal
Layyyye ya sokhorrrr🤣🤣🤣🤣
@@banelsow3980 khana dagua mbeugueu bandiane kharou😂😂😂 lolou dina nèkh sheuttttt 🤣🤣🤣
Badiene diapeu n'a sa sathieu woooy sathie4rrrr 😂😂😂😂😂
Ta ndeye Coumba je l’adore 😅😂😅😂😂😂😂😅😅😅
Badiene nena intoxication de la femme 😅😅😅😅Wouyyy série bi damay raye
Non badiene dinama raye je n’en peux plus vraiment nékhna😂😂☺️
Bou dinama Ray néna ko sa biir bi day metti wala day daw 😂😂😂
😂😂😂😂
Ayway kou lek sauce bi 😂😂😂😂😂😂😂 yene badiene bou inder ngen lek bapare diko khass
Thiam la 😂😂
@@diaz8397 thiam kay si togn la deuk wayer bi mom dotouko def😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
No limeu rei taay ,khady baba aka niak kersseu 😂😂
Bravos comédiens sénégalais, série mort de rire 😂😂😂 Bravo à toutes les comédiens .
Je suis enveuglé woooye 😂😂😂
Badiéne Ndeye Ndiaye nak wakh na deugg sa kaname gui daffa ninnn trop😂😂😂😂😂😂😂😂Bou rewna trop nak diarréh bayam layy touddou😂😂Ndeye rewna
Hy Badiane vaye c'est la meilleure vraiment 💓💓💓❤️❤️💯💯💯🇸🇳🇸🇳🇸🇳
wooy badeine nena ndeye Ndiaye moko nexalée ndayamm yagui togne🤣🤣🤣🤣🤣
Thiam akh badiene ak 😭😭😭😭 yi boula dalé doula djikh sathie lek ba dé badiene me tue madre peace amal complexe Ba man dal j'aime senepeople ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Thiam ya togne ba sabir dina méty Badiane ak dioyam yi Badiane diapou la rk 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Dama rée badienne ba sorokh long vie badienne vive senepeople
Félicitations à toute l’équipe de senepeople pour votre innovation . Et aussi à la convergence des comédiens thiéssois thi Kaw thia canam.
Série très naturelle j vs kiff trop chapeau a mon acteur préféré BOU
😀😀😀🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️
Merci frérot
@@boucountambaye5573 u es le meilleur Bou
Non badiene dafa meilleur 😂😂😂😂😂sama sauce😂😂😂
Machallah sama série préférée gui ni laf thiat rék
Love sur vous reste toujours naturel en continuant de montré les vrais réalité du Sénégal
Vraiment je vous félicite et vous encourage. J'ai pris le train en marche...
Oh les vérités de madré peace à monsieur Ba🙌🏽🙌🏽🙌🏽🙌🏽🙌🏽
Mais Ba aussi n’est pas resté de marbre.( rires ) il a bien repondu.
Serie anti stress,Astou est trés belle