@moucaboro yén da nguén ndi foontou rék toudée la sauraul daa tax dioulit wathie la 😂 Ta nguéén baayi mame Cheikh ibrahima fall mi nguén di toumaal , mame Cheikh boudaan néek ci haaal ladaaloul diouly té sariyah pour nga diouly da nguay andeu ak sa xél bou féekée yéen nak thie ay thiaaxaan ndooguou nguén nék
@@NdiayeAlioune-to9lv 😂😂😂 yaw mi yaay tou mal CHEIKH IBRA . Mon mom ngay wakh ay sëtam ngi fi ay Talibem ño ngi fi te ken dousi jouli yaw diemal la bakh mo gën te maandu. YALLAH baaxna ba moomo yoon wi
@@moucaboropour yaw took di séetan ñouy foowée digueulou yallah yi ak sunah yonénte bi ak jangualém serigne bi mooy maandou . Sunu borom moo ñu digueul bou ñu guisé lou baaxout ñu dindiko ak suñu loxo wala suñu laamiñe wala ñu nakarlouko. Té ngua xamni ñun mourid serigne bi saaxaaba yonénte slws lañu Roy loo ngua may waxou seut ☪️
Ameth sou ëleugué so beugué kham léb si mbiri serigne demal si woromi kham kham yi kham yon wi té sori si fikh ak tassawouf niou léralal ligua bëga kham sou féké mola takha diouk, té nioniou barinan lol si yon wi. Boulko dougal si am luntë donté diambar la . Diadieuf
@@moucaboro saway pour te dire soror amul won si dioumaay yonénte bi. Bo amul arguments. Da nguay déf li serigne touba wax bou féekée beugue ngua diariñu
@@NdiayeAlioune-to9lv ya mana wax lula nekh . BAYE FALL. Yi deh amu ñu jott ci ndigël lañu nek . Khassuñu dingatuñu ken yeeen delen wakh rek ñu jëf lañu tal
Machala
Dieureudieuf ❤❤
Cheikh Ahmed Cissé dégga Lila boy bi wakh (1)koudoull diouly(2) ba baparé wédi Warouk diouly dakh dagaa dégg féne fou ab Baye Fall wéddè warouk diouly
Cheikh Ahmed Cissé guii dé dafa diagg tédé guoll
Mbiugualou bambél li guano yomb ankaalan wa djahiilan battu ankaalan Day firi fii ak fée
Xadim waxaĺdëĝ walla nga Don naafeq
Ah kikaye sawaye kom kou wéroull
Bo amoul xam xam nga noppi ki louler l'ay wakh
Serigne khadime bou féekée da ngua raguala wax deugue ngua noopi 😢
Serigne touba li mou wax diouly dafa léer nañ kéep koudoul diouly bookoul ci Serigne touba.
Boo démée si nafahatoul miskiiyah bou al halawii Serigne bi naron naa daak ñaary nit kéeneu ki daa yééheu diouly kéeneu ki yéeheu nooddou.
Lii mooy li wér.
Baye fall mëssuño wakh ni julli baxul wala werul kuy jouli joulil sa jouli te maandou. Serigne boobu ngay wakh mo toude sorror bi kudul julit
@moucaboro yén da nguén ndi foontou rék toudée la sauraul daa tax dioulit wathie la 😂
Ta nguéén baayi mame Cheikh ibrahima fall mi nguén di toumaal , mame Cheikh boudaan néek ci haaal ladaaloul diouly té sariyah pour nga diouly da nguay andeu ak sa xél bou féekée yéen nak thie ay thiaaxaan ndooguou nguén nék
@@NdiayeAlioune-to9lv 😂😂😂 yaw mi yaay tou mal CHEIKH IBRA . Mon mom ngay wakh ay sëtam ngi fi ay Talibem ño ngi fi te ken dousi jouli yaw diemal la bakh mo gën te maandu. YALLAH baaxna ba moomo yoon wi
@@moucaboropour yaw took di séetan ñouy foowée digueulou yallah yi ak sunah yonénte bi ak jangualém serigne bi mooy maandou .
Sunu borom moo ñu digueul bou ñu guisé lou baaxout ñu dindiko ak suñu loxo wala suñu laamiñe wala ñu nakarlouko.
Té ngua xamni ñun mourid serigne bi saaxaaba yonénte slws lañu Roy loo ngua may waxou seut ☪️
@@NdiayeAlioune-to9lv mani do mouritou dara mouride bouy dingat CHEIKH IBRA do mouride
Boule dougale boybi waye protègeko
Ameth sou ëleugué so beugué kham léb si mbiri serigne demal si woromi kham kham yi kham yon wi té sori si fikh ak tassawouf niou léralal ligua bëga kham sou féké mola takha diouk, té nioniou barinan lol si yon wi.
Boulko dougal si am luntë donté diambar la .
Diadieuf
Kii dafa ragual 😂😂😂😂
Wa atté yoyou seringe bi wah si dioulli foumco ték
@@fayedjibyseye boo Beugué xam foumou ko ték da nguay déf yitté ci jangue sa diné 😔
@NdiayeAlioune-to9lv lolou dou tontou dé boco hamé rék wahall soco hamoull ga nopi
Wala tamit nakaalan
😂😂😂😂😂 stop the BS Bro
Xam xam ak pékhé dou béneu Ahmed Cissé amoul xam xam
Chielh ndiaye ca nimoro la sokhla wone
Sëriñ bi Nena kep kou bayi benn wakhtou djouli farata bo déwé bounn la soull sq seuutou djoulitt ya
Konn fofou lenn louni layam layami amousi
MBA mën nga ndokh rek ? Serigne bi wax loolu mo toudé soror bi kudul julli du woor
@@moucaboro saway pour te dire soror amul won si dioumaay yonénte bi.
Bo amul arguments. Da nguay déf li serigne touba wax bou féekée beugue ngua diariñu
@@NdiayeAlioune-to9lv ya mana wax lula nekh . BAYE FALL. Yi deh amu ñu jott ci ndigël lañu nek . Khassuñu dingatuñu ken yeeen delen wakh rek ñu jëf lañu tal
@@moucaboro dieuf yeup dieufé ndigueulou borom bi moo ka gueun saway.
@ yaw Wakhal ba Baye fall yi jëfewuñu ndigël suñu Borom nga may jaay bëg jouli nonnu li ngay def yëp maandou ko gën.
Hypothesis 😂
Hypocrite 😢 smh