MACHALAH DIEUREUDIEUFATI MAME ELHADJI IBRAHIMA SAKHO YALLA NAKA SUNU BAROM YEUREUME TE YARE KO CII ALJANA YI GUEUNEU KAYE CII BARKE SEYDINA MOHAMED (PSL )
@@badarandanane bilaye mais merci continue à travailler sur ce chemin tu fais un travail remarquable tu pouvais créer un site de rencontre où musique et ne ne l'a pas fait merci
@@nafimbaye8572 dama defeni dagno xamé woul lou bouton yi di dierign Wayé amna nite gno xamné sen soxor yobou nalene ci meun tiim new diko doomp Yalna gnou yalla yereum
Badara Yalnala Yalla fay taxouwal yaak sa jaboot , yague fi lool waayé so fi jougué yiw nitt niouy deglou Yalla wassaaréko ci sa bameel. Yagueu fi té weer yak ko xam rek .Depuis France , tafsir Oustaz Alioune sall yi ak Hady Niass moma ci gueneu neex , c'est très bien organisé et structuré
L'HOMME ET LA FEMMES SONT DIFFERENTS CERTES MAIS SONT EGAUX CHACUN JOUE UN ROLE EGAL IMPORTANT C COMME LA TERRE ET L'EAU SANS TERRE IL Y A PAS DE RECOLTE SANS EAU NON PLUS POURQUOI L'ENFANT DOIT SATISFAIRE 7 fois sa mere avant son pere? PARCE QUE MAMAN ET PAPA SONT TOUS EGAUX EN IMPORTANCE DEPUIS L'AUBE DES TEMPS LA FEMMES EST RELEGUEE AU SECOND RANG IL FAUT ARRETER C FINI ON N'Y CROIT PLUS WASSALAM
Machallah, un grand pédagogue qui maîtrise bien son sujet. Qu'allah ait pitié de son âme, lui couvre sa miséricorde et lui accorde son paradis. Amine
kou amone hikma'h yalnako yalla dolli yeurmande dalalko sa aldjanna you kawé ya
Qu'Allah l'accueille dans son paradis le plus élevé! Amine!
Amine inchallalla
I guess Im kinda off topic but does anyone know of a good website to watch newly released series online ?
@Ari Johan flixportal :P
@Makai Gianni thanks, I signed up and it seems to work :) I really appreciate it !!
@Ari Johan you are welcome :D
Yalla naniou yalla fayal mame seydi hadj malick akk ndiabottam fayal niou Mame Ibrahima sakho si barké seydina mouhamed psl Amine 🤲🤲🤲🤲🤲
Son niveau spirituel me dépasse franchement 😪❤❤❤❤
MACHALAH DIEUREUDIEUFATI MAME ELHADJI IBRAHIMA SAKHO YALLA NAKA SUNU BAROM YEUREUME TE YARE KO CII ALJANA YI GUEUNEU KAYE CII BARKE SEYDINA MOHAMED (PSL )
Vous qui clickes sur j'aime pas ne visionner pas nous on est fier de notre ibou national machallah qui est une bibliothèque
Même buñ bindoon lan mo len ci neexul sax nga xam
@@badarandanane bilaye mais merci continue à travailler sur ce chemin tu fais un travail remarquable tu pouvais créer un site de rencontre où musique et ne ne l'a pas fait merci
@@nafimbaye8572 Dieredieuf
@@nafimbaye8572 dama defeni dagno xamé woul lou bouton yi di dierign
Wayé amna nite gno xamné sen soxor yobou nalene ci meun tiim new diko doomp
Yalna gnou yalla yereum
bi manam dégue rék si môme la yém Macha Allahou sakho
Paix en son âme qu'Allah l'accueille en son paradis Allahouma amine
Sama mame sama kharite sama khol. Yalla yok se lér si bidiay seydi woudioui 😇😇😇😇
Baye Ibrahim sakho yalla na diam sonal la yawmal xiyam ak bollem koudan tewlou say waxtan 😇❤💯
Waaw ma ne je me demande où on pourra avoir un autre Ibou Sakho dans ce bas monde. ooooooh!
Très bonne question
Que firdaws sera ta demeure éternel amine y'a rabbi
MASHA Allah mame Ibou Sakho YALLAH nako YALLAHOU yeureum tè kharè Aldjanatou Firdaws si barkè Seydouna Mouhamed saw Amine ya Rabbi 🤲🤲❤❤
J ai beaucoup appris sur l Islam, la tarikha tidiane et le celebre Livre de mame maodo Malick 🙏🙏
Qu'Allah azawajel lui accorde sa miséricorde et le paradis firdaws Aminn
machaallah que le tt puissant l'accueille à firdaws
Machallah,,, Qu'Allah azawajel lui accorde sa miséricorde et le paradis firdaws al aala,,Amine
Yalna yalla yokou leram Têt takh gnou si barkhet am
Yalna YALLA FAYLA BAYE IBOU SAKHO
Machalla yalla na yalla yok léram
macha allah yalna yalla feyla yiw tè tasniou si sa barkè amine incha allah
Mame Ibrahima Sakho yallana souniou borom fayalnioula bidiahi RASSOUL SALLALAHOU ALEYHI WA SALLAM
Amiine
Badara Yalnala Yalla fay taxouwal yaak sa jaboot , yague fi lool waayé so fi jougué yiw nitt niouy deglou Yalla wassaaréko ci sa bameel. Yagueu fi té weer yak ko xam rek .Depuis France , tafsir Oustaz Alioune sall yi ak Hady Niass moma ci gueneu neex , c'est très bien organisé et structuré
Allahouma âmine dieredieuf way te ñu book ko
Machala Machala bélle odio kil repose en paix Amine ya Rabal Alamine
رحمه الله تعالى رحمتا واسعا
Dieuredieuf Serigne Badara yala nala yalla faye
Mo bari kham kham baye Ibou Sakho ❤️❤️❤️
Yalla nakayalla yereume si barke seydina Mouhamed salalaliwasalam
Que le bon Dieu vous accueille dans son paradis.
Ndeyssane PAIX a son ame
Yalla nala sunu borom fayal ngoula amine 🤲🙏🤲 yarabi🤲 yokou sa lér ta tass ngou sissa barré🤲🏾🙏🏾🤲🏾
Allahouma âmine
@@badarandanane 🙏🏾🤲🏾🙏🏾🤲🏾
Yalna la yalla yeureum
Très touché inchalah le plus possible s'il plaît au tout PUISSANT
Yalla nanou ka yalla fayal
Ndaye sane yalla nako yalla dolli khewal Amiiine
🗣️badara vraiment ndanane gua
Dieredieuf
Yow tamite am gua Jarama , yama hamal brom Xam Xam bou reuy bi ❤️❤️❤️❤️❤️
Vraiment Badara Merci pour toutes les vidéos très rares que tu as le plaisir de partager avec nous...🙏🙏❤💪💪
Machalla
Machalla yalla na yalla fayko
Yalla nako yalla yeureme
Machallah sama Serigne elhadj ibou Sakho
Yalna yalla khare ko aldiana
Masha Allah yalnala yalla fay
Dieureudieuf mame yalna yallah yessal yeurma'déme si yaw ak bép mboléme diouliites
Machala Machala
Allahou akbar. Mashallah
Machalla amna solo trop bilahi
Que la terre lui soit légère Amin Démba gueye cvd
Ya rabi ya bakh jeureujeuf Sakho elimane
Bilahi conetane na machalalah😪😪
Màasàallàah Leer na lool ndëysaan,
Machalla mame ibou sakho
Machalla Amna solo te Rafetna. Yallah na Yallah Fay la
Ah manchallah Mame Boye fière d'être ta petite fille
MACHALLAH. Yalana YALLAH fayla ❤
Paix a son ame machalah
Dieuredieuf mame..aldiana rek
Yalla na Yalla yocou lérame amine
Amiiine
Machalla 🙏 🙏
ماشاءالله
Suite bi svp
Ma sha Allah
Ma challah.
Masahala paix a son ame
MachaAllah
Thieye mame madao kene dou monme diadieuff baye sakho
اللهم إغفر له ورحمه قدس الله سره لازال ضريحه مقصود للزيارة
أنا دهش لمااصابني من الفرح والسرور حين ما سمعت ح
Yalna yokou lairame
Nala yalla faye sakho élimine
Ndeye sane ame na solo
Mashallah
MashaAllah
Machalla
Mais ceux qui mettent la mention " je n'aime pas " vraiment je ne comprends pas quel est leur problème🙈🙈
Malheureusement.... 😓
Au nit gnou Bone lagnou
Moi je pense qu’ils ne comprennent pas
Danio hamoul
Ayy mécréant laniou
Jadore
bilakhi machalla xam xam deugue
Machallah
Toujours imortel.douma doyale si enseignement bii mouy deff si mane
Rrrafetna
Nirék la meuna méll ndakh Kiko yar motakh
Machallah amna solo trop
Sba y
rta amine
❤❤
AAh Audio bi nak fimu dagguèè baaxul!
Mais Bara waroul woon diekhé fi 😭
❤
Walay daysane
Thiey
Macha Allah
Hanrif deugu mo nék ni...
😍😍😍😍😍
😄😄😄🤩🤩😍🥰
Ź
Borom kham kham THIEY adouna ya,mana wor
Dougalal lp nguir yalla
Ëplëw 70 ans
Meun gako
Daf la yém wala da ngay weddi
Serigne ibou sakho wallahi aka bari xam xam
👎 👎 👎
Sécret biy takha eumbou jigeune ne correspond pas a la vidéo. Bougeu vu you bari boumou takha nga bind lou amoul si vidéo bi.
Secret biy takha eumbou jiguèen yague ne ci goor. Kholal bou bakh ligne binde
Bindal basmal 11 fois nga xol
@@cheikhouna1538 apres nokoy déf
@@charasakina9594 daga si nane wala nga diok ko soxna si mou nane ko après nga saraxé lékou xalé bakhna trop sakh
Amna bénen sarax ms nékoula wak si RUclips
L'HOMME ET LA FEMMES SONT DIFFERENTS CERTES MAIS SONT EGAUX CHACUN JOUE UN ROLE EGAL IMPORTANT C COMME LA TERRE ET L'EAU SANS TERRE IL Y A PAS DE RECOLTE SANS EAU NON PLUS POURQUOI L'ENFANT DOIT SATISFAIRE 7 fois sa mere avant son pere? PARCE QUE MAMAN ET PAPA SONT TOUS EGAUX EN IMPORTANCE DEPUIS L'AUBE DES TEMPS LA FEMMES EST RELEGUEE AU SECOND RANG IL FAUT ARRETER C FINI ON N'Y CROIT PLUS WASSALAM
Ndeysan 🙃
Machalla
Souniou mamme
Machallha amna solo trop
Sakho elimane bilahi amotofi machallah
Machallah
Rrrafetna
Machallah sakho elimane
Machallah