Deux épisodes suffisent à mon avis bravo à toute l'équipe vous faites preuve de professionnalisme maman seune a une bonne diction de meme que bou Badiene on est en veugeuleu
Senepeople 2 épisodes par jour ça suffit mais le week-end mom vous pouvez faire 3episodes n’oubliez pas que nous wa teams dieund pass connexion 😂😂aussi day mettii trop t beugouniou raté bneu épisode 😍😍😍😍😍😍😍 Polygame est devenu notre seytane
18h ba tey mahi khar, machallakh chapeau à vous, avant j n suivais pas la série mais après j'ai commencé à télécharger 10 épisodes par jour...contane thi yéne et bonne continuation
*Polygame* sincèrement vous êtes trop fort.actuellement "souma wathié limay ndieukeu déff moy djouli et direct RUclips " pour regardé ma série préférée
@@labadochic2294 c'est vous les égoïstes, vous vous basez sur cette série pour evacuer votre stresse? Et pour ton information, je n'ai pas encore raté un épisode, je suis à jour depuis le début. Donc s'il y a un égoïste c'est bien vous. Pensez aux autres
@@mamediarraboussondiaye7200 merci Mame l'internet ne doit pas prendre tous notre temps sakh . Les tâches ménagères, le boulot, les prières et les zikrs parmi tant d'autres choses qu'on doit faire 3 épisodes day eup.
Bou à mis en exergue un point très sensible et important. Il a montré k la fornication (cas de khady)est interdit mais pas banale comme le pense la jeunesse...
3 épisode par jour dinagnou joie ndakh dagnouy togg diléne khaar comme pas possible niaf leine niou ko dougnou ko bagne deh force a vous … et au passage vous qui dites 2 doyna ladjou niouléne 🤣🤣🤣🤣🤣
Wa 2ème femme Bou bi bou nékone Soukayna tamite naw Oumou dof, khalé bobou tamite toyna dalleuna civiliséna, bolé am lentille naturelle machallah.. legui Fate Kiné done rakkou Astou gnieuw si Keurgui di défaneté ak Ndéye Ndiaye... mais bou néké diabarou Bou day radiakh bamou euppeu, khana mou gnieuw si bénéne facette dalleu téy ak touti tontou you saf sap...
Série bi dei thi tik tok bi reik la ko done guisé c’était juste des petites extrait vidéo mais nimako guissè la xamni neikh na wayei episode yi dafa barri trop pour ma neik di sétane depuis le début dafay xawa doy war en tt cas Love sur vous mane ndèye ndiaye loumou jouer neikh nama badiene mom meunu mako mougn ❤️❤️❤️💋💋💋❤️❤️😂😂😂😂😂diam thi yein on est derrière vous ❤️🥰😍
Êtes-vous prêts pour 3 épisodes par jour de votre série Le Polygame ?
Oui boubakh
Bien sûr on est aveugleuuu
Ce serait formidable
Wawawwww bou bakh sakh
Loulou dina nexatii
Qui voit que seune dafa meun sagnsé tê simple .Love sur vous l’équipe de polygamie ❤️
*Danio namou khew na bou takk nakk wala binôme takk nioun danio yakamti kheww yiii*❤️❤️❤️❤️🤣🤣🤣
N'oublions pas les 5 prières ❤️. Yalna sougnou Borom yokou goudd fane bou and ak werr ak soutoura bou sakh dakhhh.
Theiuy Sama domou baye! Y’a efficace
Amine
tiey tons
Amine
Amine
Ana gni fi nékone depuis 1er épisode👏🏾
Yacine mangui ni meussou mako raté
💯❤️❤️😄😄
Thiam a des problèmes en problème surtout le cas des envois 😂 xaliss 😂 rancune 😂 truands 😂 niak diom 😂 bone khol surtout 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Aigri mécontent hypocrite
Pour Group whatsapp Polygame bi😭😭😭💔
Wagni ko nak 🤣🤣🤣🤣🤣
@@bintaba5936 dina thi bakh deh😂😂
Non Thiam sof Na niak klrom trop
Deux épisodes suffisent à mon avis bravo à toute l'équipe vous faites preuve de professionnalisme maman seune a une bonne diction de meme que bou
Badiene on est en veugeuleu
Suis d’accord 2 episodes suffisent largement.Merci beaucoup et bonne continuation.
Senepeople 2 épisodes par jour ça suffit mais le week-end mom vous pouvez faire 3episodes n’oubliez pas que nous wa teams dieund pass connexion 😂😂aussi day mettii trop t beugouniou raté bneu épisode 😍😍😍😍😍😍😍
Polygame est devenu notre seytane
Wa team on est aveugleuuuuu vous êtes où 😂😂
Mariage bou bi la yakamti
Seun est une vraie actrice elle parle bien sans même se confondre.elle est naturelle
2 épisodes suffisent car c’est difficile de suivre après une jour de boulot 😂😂😂
0
Ana niou kontan si polygamie beu seul jemme❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️♥️😍😍♥️♥️
18h ba tey mahi khar, machallakh chapeau à vous, avant j n suivais pas la série mais après j'ai commencé à télécharger 10 épisodes par jour...contane thi yéne et bonne continuation
*Polygame* sincèrement vous êtes trop fort.actuellement "souma wathié limay ndieukeu déff moy djouli et direct RUclips " pour regardé ma série préférée
MBA lii diam lah legui thi bountou keurr gui lalénn Di kharr Ani sama wa team 💪💪❤️❤️❤️❤️🇸🇳
Le cas de Thiam devient de plus en plus critique 😂😂😂😂
Wallahi
Dafa soxor et son genre existe dans tous les familles
Setlou gua lolou koon ma bel 😂😂😂
Bilay, ya des gens comme ça bcp d fammil
Soxor rekkk motax dou am dara tjimm
Thiam est devenu un dépressif…. Dalal khel aura bientôt un patient ….😂😂😂. Bonne soirée à tous . Merci à toute l’équipe
Tu as raison Mariama bien dit
8*
😍😍😍😍😘😍😘😘😍😍😍😍😍😘😘😘😘😘😘😘😗😚😚☺☺🙂🤗🤗🤗🤐😛🤓😌😌😴😫🙃😦😨😨😩🙁
😂😂😂😂😂
Les genres de personne comme Thiam ne vivent jamais en paix car ils pensent que tout ce qui leur arrive est à cause des autres
Thiam dou nite un aigri complet. Bravo à toute l'équipe vous êtes forts
La famille envoyer de l’argent pour soutenir l’équipe polygame svp 🙏🙏🙏🙏
Surtout pour papa thiam
@@fatimadianka662 🤣🤣 bilay sokhla nako
🥰🥰
Mba bougnou envoyer Thiam douko dieul
Ca y est on a commencè.
Deux épisodes suffisent largement. Pensez à ceux qui viennent de commencer la série. Ça ne sera pas facile d'être à jour !
Vraiment
Mais c’est votre problème il ne faut pas être égoïste aussi pensez aux personnes qui vivent dans le stress.
@@labadochic2294 😂😂😂
@@labadochic2294 c'est vous les égoïstes, vous vous basez sur cette série pour evacuer votre stresse?
Et pour ton information, je n'ai pas encore raté un épisode, je suis à jour depuis le début. Donc s'il y a un égoïste c'est bien vous. Pensez aux autres
@@mamediarraboussondiaye7200 merci Mame l'internet ne doit pas prendre tous notre temps sakh . Les tâches ménagères, le boulot, les prières et les zikrs parmi tant d'autres choses qu'on doit faire 3 épisodes day eup.
WA team polygam est c'est que yenagui bayi xel père Thiam 😂😂😂😂😂😂 Thiam aka niank xorom, série bi amna leup bilay yena hay bravo
Thiam mi nak gnéména cas 🤣🤣 chaque jour ak khar envoie téy mouy accusé waté sathie 🤣🤣🤣
Khady kou seytané la souko yayam santon mou bagn Thiam mou sokhor mi moy envoié ak retiré 😂😂😂😂😂😂😂
Envoie +retrait =Thiam 😂😂😂😂😂
@@madasylla3340 bilay dafa sof 😂😂😂
Thiam dou nitt envoi retrait rekk moko inter…..
Papa Thiam mom khana diotoul si envoie yi par wave ou orange money😂😂😂😂 Bravo 🎊🎉🎈à tte l équipe
Waw PapaThiam😃🤣
Bou à mis en exergue un point très sensible et important. Il a montré k la fornication (cas de khady)est interdit mais pas banale comme le pense la jeunesse...
Louma nekh thi actrice yi moy ay yere you simple laniouy sol te rafete yi khetou voile ohhh❤️❤️❤️mai Badiene say kheff lanla 😂😂😂
Tous les mois on doit si possible quelque soit le montant contribuer nous les émigrés même 10euro car vous nous respectez. Qui est ok?
Moi
Qui comme moi pense que la seconde épouse de Bou sera Fat kiné ?
N'oubliez pas les 3 repas du jour agne rére ndécki
Chéri Astou baba vous salue
😂😂😂😂
Astou baba mom moy kane 😌
😂😂😂😂😂😂
Ani gnou bague badiane waay Machallaha💗❤️
Thiam gateuna xeil ni diabarou sathieu 🤣🤣🤣 vraiment ki badolo leu tchimmm niak diom
Nima ko diépé tchimmmp
Thiam l’éternel bipolaire c’est un vrai psychopathe kii moo lakalee waay 🤣🤣🤣🤣
Badiéne néna ndakh BA desséna ay VESKKISSS haaaaaaa😂😂😂😂😂😂😂😂😂
3 épisode par jour dinagnou joie ndakh dagnouy togg diléne khaar comme pas possible niaf leine niou ko dougnou ko bagne deh force a vous … et au passage vous qui dites 2 doyna ladjou niouléne 🤣🤣🤣🤣🤣
Billay 😭🤣
Pour les passives 3 vous vont mais pour les actifs 2 suffisent largement
@@oumoucisse4187 a travers les commentaires tu arrives à connaître les active et les passives ? T vraiment forte hein
"dagnouy togg diléne khaar"est assez explicite pas besoin d'être forte
@@oumoucisse4187 tu en est une alors vu que yangui dagassanté soubatél allé va vaquer a ton activité comme tu di bayi gnouy tog di khaar 😘
La scène entre Thiam et khady très drôle 🤣😂😂 wa tamite père Thiam son cas critique wa bakhna bamou soti
Thiam naturellement il est fou
@@fatoumatasy6151 doumako wèdi dè
Nda critique moss 😂😂
@@fatoumatasy6151 mbadou
Mane dé est ce que weurr na layy lath té
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Thiam c'est un Très bon acteur da moudiei bipolaire
Yéna ngui sétane Thiam mais il ne va pas du tout bien allons rek 😂😂😂😂😂😂😂😂. à par ça il joue bien son rôle
Mane Badiene dafa am classe ay Louis vuitton lay laaal😂😂😂😂
4 minutes autant de vues machalla 😍
Polygame forever✨💪
😂🤣😂🤣Badiène paréna sama ndawtal😂😅mani khadioul sakh si banque😂😂😂💃🏽💗💃🏽
Khady dans les moments difficiles on doit soutenir la famille car elle est sacrée.
Ndeysann mogui nekh rk niouy setaan di apprecier wayé koudoul khalatt épisode finale loula saf defal 😂
Mbadu
Bouniou yakkal hhhh
Moudiou na nek drogue si mane minute bounek ma doug sene page khol bakham commence na😂
Bilay d'où yaw késsé wah Maroc polygame moy sougnou anti stress.
C’est pas toi seule chérie 🤣
😂😂😂😂😂😂😂
Lolou moma dale,😂😂
Thiam,l'oncle frustré qui au lieu de se remettre en question rejette tjrs la faute sur les autres
Thiam est ce que weurr tamite
Vraiment le comportement de Thiam me dépasse 🤔 Badiéne tmt kagn guay khéw sa khéwou boppou🤷😂❤️
Badien. Love you bilay🤣🤣😂😂😂😂😂😂
Sama guayi gawe guene si 1 mn 33comentaire oh polygame yene la khaleryi diokh bop dh machaalah
Mère seune s'habille bien machallah 😍😍😍
Merci à toute l’équipe
Mais Thiam tu dépasses les bornes vraiment li mom eupna j’ai des larmes 😭 aux yeux 😒😒😏
Wa Thiam mi nilagnoukoy bayi si keurgui 😂
Trop c'est trop
😂😂😂😂😂😂wa mais thiam mi douniou cotiser bakhale ko
wallah j'en peux plus de cet énergumène😱
Il est temps 🤣🤣
Non naniou ko weusseum🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂😂non ki dafa yebater waye aye envoie you doule eksi mouke chak jour de delou legui nak daye teke d’île 🙈🙈🙈🙈🙈
No naniou pose wé xossiko
Wouyyyyy papa Thiam mogui tekk xel legui 😂😂😂😂😂
Depuis ce matin j’attendais
Lekouma gouro Lekouma tangual mane diankheu la diankh pirr😂😂😂
Li takh n'a Samay adouna
Vous étes les meilleurs acteurs ♥️ bravo et bonne continuation 🙏
Kou setane Coumba albory bi dembo lal j'aime 😂😂😂
Mais le cas de Thiam devient critique🤣
Billahi yaw
Bilay😂😂😂
Les fans de badiene manifester vous😂❤️😩
Je suis la❤️❤️
Guaw guéne dh waouhhhh😂😂team en veugeuleuuu😂🥳
force a tte l'équipe ❤❤❤
Badiéne sa xew mi yague na binga d'allé yeglé ba légui 😄😄😄😄
Likay da moudié soff
Senepeople 🎈😍 ci kaw ci kaname machallah ❤️❤️🙏🏽
a 8
Wa 2ème femme Bou bi bou nékone Soukayna tamite naw Oumou dof, khalé bobou tamite toyna dalleuna civiliséna, bolé am lentille naturelle machallah.. legui
Fate Kiné done rakkou Astou gnieuw si Keurgui di défaneté ak Ndéye Ndiaye... mais bou néké diabarou Bou day radiakh bamou euppeu, khana mou gnieuw si bénéne facette dalleu téy ak touti tontou you saf sap...
Kou nangou Vieux ba 2millions dakoy také djabar 🤭🤭
Bilay j'ai pensé la même chose
Je pense que ni dioumou'gnu dh
Notre serie préférée ♥️ le Polygame 💓
Oui on es prêt pour 3 episode pour jour
Notre série anti stress mai badiane tamite li deugueuleu 😂😂😂😂
Ahhh THIAM il m’énerve bilaye 😕😕. Badiène sa invité yeupe souniou nieuwé Thiès fèss dèle😂😂😂
Kou togone diko wait besseul j’aime 😍😍
Magui Dora comprendre loutah mariage bou bi yekhh vu que Fat kiné mogui ndar 😀 expert série yi gnomm dinenn comp
Esk douniou cotisel Thiam ba envoies yi yegussi,peut être réseau bi moh disponibouloul🤣😂
Notre série préférée ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Daniouy wakh ndey ndiaye ak badiene dè mè papa thiam mi vrè satan la🤣🤣🤣🤣
Mariage bou ak bou badiane dé kou guate fan douko fek 🤦♀️😂😂😂😂
Dagno wara avance nak mogui beuga yéekh
Enfin ndeye NdiAye enceinte 🤰 na 💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻oh saint jean fala dioudo ❤️
Wa yéne dougnou cotisé guéné thiam si série bi tamite 🥵🥵🥵
😅😂
Maman seune machalla ❤️❤️Thiam dougnou ko diobou dalal khel tamite 😂😂😂badiene je suis en veugeuleu 😂😂😂
😁😁🤣🤣thiam damako yeureum wayé da say say
@@fatoumbackesylla4481 wessou say say xalisse dako diaral loune
Wa tmt Ani fat kiné ❤️😢😢na nieuw réglé cawou ndy Ndiaye
Bilah polygamie nekhna amna solo mai sénégalais bagul lu bakh lu bone rek la beug ,nous sommes dernier vous allez mes acteurs.
Commentair bi lo gaw gaw ,gis koula geuna gaaw 🤣🤣
Ana gniy khaar ENVOIE 😂😂😂 non Thiam dinama ray “ Dafa am envoie bouméy xaar ” 😂😂😂😂
Bravo à vous que dieu vous protege
Mention spéciale à vous laf thiat waayy ,mais ndeye Ndiaye lii bahna sii yawt🤣😂
Série bi dei thi tik tok bi reik la ko done guisé c’était juste des petites extrait vidéo mais nimako guissè la xamni neikh na wayei episode yi dafa barri trop pour ma neik di sétane depuis le début dafay xawa doy war en tt cas Love sur vous mane ndèye ndiaye loumou jouer neikh nama badiene mom meunu mako mougn ❤️❤️❤️💋💋💋❤️❤️😂😂😂😂😂diam thi yein on est derrière vous ❤️🥰😍
Thiam 🤣 da bougou lou yomb ce n'est pas sérieux. Petite khady tu as raison de réserver ta famille est difficile courage khady 😘
Mé thiam il m’énerve grave dagn ko wara guéné ci série bi
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️nekhn li louko guena nekh dh guisoumako nekhna😂😂❤️💕
Kay dio rité malé😂😂😂😂
Ay khewou badiane bi
Xew mi rekk 😂😂😂😂
Salam salam 🤣🤣🤣 Badiéne sa mariage il faut mou âme dé incha Allah 🤣
Bou mbadou yayou Ndeye Ndiaye moye niarelbi WOYYY 🤣🤣🤣🤣🤣🤣Oumy tey ley guiss bouye🤣🤣🤣😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️
THIAM MAN ABAL LEN MAKO 1 JOUR REKK !!!!
😀😃😄😆😆😅🤣😂😂😂
Thiam plus kun dépressif 😭😭dèlénko Envoiyé tie wave yi AK OM yii😂😂😂
Mba kham ngéne ni Bou yayou ndeye ndiaye lay takeu 😂😂💃🏽
Ana gni beugu fatou Kiné done diabarou Bou
Yalla naniou yalla mousseul si niak kou khôl Thiam rek khamnei niakk bakhoul si makk .! Ki il es fou 🤣🤩😂
Machallah senepeople si kaw thie kanam
Les séquence de Thiam
J’en peux plus de lui 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 regardez-moi ca
Thiam est une personne vile avec ses manipulations,il faut être très petit pour tomber aussi bas
Tonton Thiam DH son cas et critique 😂😂😂😂😂 keur gui lo beurri hypocrite papa Thiam Moy bou guor bi Ba môme wakhalé wouma ko 😂😂😂nn badieneu ma tué😂😂😂😂
S ki me plaît vous respectez les heures je vous souhaite une bonne continuation
Senepeople nguir yalla dollen guéné thiam ci serie bi non il m'énerve tellement kanamam rek nonnnn🥵🥵
😂badiene est ce que ça va, bayyil kheuthiio ndawtal
Seune elle s'habille bien manchallah