🚨Premiere reaction Coumba baldé apres la victoire de Pokola😱Jules baldé dafa…clash Franc yarou woul😭

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 27 янв 2025

Комментарии • 39

  • @Morotadieng
    @Morotadieng 14 дней назад +30

    Barki alxouran yageu sétane mère coumba me tay dama contane trop si wallahi nakh liga wakh si jule baldé yalna diam way🎉🙏🙏🙏🙏

    • @papesouma
      @papesouma 14 дней назад +2

      Amine bilahi yaw tamite ya bakh
      Man dama beug famille bou dioubo

    • @adamadiouf487
      @adamadiouf487 13 дней назад +2

      Bilahi Jules diambar la dafa Sonneuh Thi boy Yi mère Coumba baldé tamit nonoula sonné wone thi Gnom jules ak Ama baldé donc yalna diam yagg

    • @jazaka3178
      @jazaka3178 11 дней назад

      Sénégal nio sofff famille ndiambour na niou tji manou

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 14 дней назад +7

    Merci Sister Coumba , Bien parle bless 👍👍👍👍👍👍💪🙏👍🙏😁

  • @diaosory5373
    @diaosory5373 14 дней назад +15

    Sama xool seedna contanna si loumou wax si JULES BALDE 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 14 дней назад +10

    Bilahi walahii mer mala bege ni RK la nit dagay bage gathe way❤❤❤❤

  • @AmadouKone-fk6fp
    @AmadouKone-fk6fp 14 дней назад +11

    Pokola dégale sa kadou yaye yi dieum sissa nidjay jule Baldé

  • @talibemame4681
    @talibemame4681 14 дней назад +10

    Merci mere li rek lani khar si yw jule balde diambar la nako pokola diokh dieur❤️🥹

  • @madembalo8415
    @madembalo8415 12 дней назад +1

    Mer coumba cool mér ya bah dé❤

  • @NicolasNiasse-p1n
    @NicolasNiasse-p1n 14 дней назад +8

    Merçi mama ❤billahi ya bakh

  • @soldarouboromLepaybakh
    @soldarouboromLepaybakh 14 дней назад +6

    Bilahii mér deuge la bayiko AK zill ballde bilahii kon légui n'a am keur zil ballde kou bakh la

  • @dialloawa6701
    @dialloawa6701 13 дней назад

    Niii leu yay day defar nieup contente Machalah

  • @alygaye3565
    @alygaye3565 11 дней назад +1

    Mér coumba domi mbeur la daye doundou lamba réke ki soudone goor mbeur laye done

  • @jazaka3178
    @jazaka3178 11 дней назад +1

    Nidiaye mounoul bagn diarbatam khay na day am si say diarbattt séne djiko doula nekh

  • @Morotadieng
    @Morotadieng 14 дней назад +6

    Mère amal diam way🎉

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 13 дней назад +2

    Jul Balde thi bopam moo amoul Daray Thiaxane thi adouna ndioun Deukk Ak Mom nioko xam wallahi kou ame foulla thi bopam moy jul Baldé Doo Dègeu thi Dara lou niaxeu fayda en plus bougoul Kouy thiaxan ✍️motax Koukou xamoul boulko juge mome keur gui nieupou la beugeu rawatina pokola Balde c pasq xamnako boubax xam Nany pokola my Boy fowoul Mounna Don roi 👑 des arènes amna Fith Mounna Beraii trop sax légui lou déss moy familles by geunko protégés xamny osii poko xalé la wallah Dioudou woul Boy bounawla sax Tèla euss rék mè lèpou Dina bax inchalah c pasq pokola Borom Fith la Tè Borom Fith mo néxa ndianall Moo nèxa andall laf bouch rék 🙏🏻❤️🙏🏻felicitation pokola Balde ❤️

  • @iboualizeunlockventerepair977
    @iboualizeunlockventerepair977 14 дней назад +6

    Nene ma mome sama bopou té lamb la gueumm.
    Non mére coumba dou démm😂😂😂😂😂😂😂

    • @BabaKane-g7z
      @BabaKane-g7z 14 дней назад

      😂😂😂😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 7 дней назад

      Boudone goor ba légui kene wakhatouko😂dina djeul Roi bi par force😂

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 14 дней назад +6

    Pokola baol baol bi seul amoul delou ginaw 💪🎉🎉🎉🎉

  • @KhadimKebe-s4z
    @KhadimKebe-s4z 14 дней назад +8

    Mére bi dh dina masa dém stade 😂😂😂😂😂😂 Wa ani pathe balade

  • @ModouDiouf-i4d
    @ModouDiouf-i4d 14 дней назад +2

    Na dieul gouy gui moy combat bi 🎉

  • @mansorseck6059
    @mansorseck6059 13 дней назад +1

    Mbollo moy dolèèè adouna amoul solo lèpp rafètal

  • @amadoudrame5504
    @amadoudrame5504 14 дней назад +3

    Yaw mere ama balde mo attaque franc pare ngane franc yarowoul

  • @babacarfall3979
    @babacarfall3979 13 дней назад

    Bolo Moy dole famill balde diadief

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 14 дней назад

    Kowensi baxoul de mo

  • @AbaNoreyni-r2g
    @AbaNoreyni-r2g 14 дней назад

    Mère bi rek la guiss si yayou mbeur yi mou nek si réseau sociaux di ratati rek

    • @AbdoulGadrySow
      @AbdoulGadrySow 9 дней назад +1

      Kou bakh ki domou mbeur la moy tawou falaye balde bou donone goor mbeur lay done motakh moul ni rék parraport ak yenene mére yi Lolou la rék

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 7 дней назад

      ​@@AbdoulGadrySowloloula rék nak

  • @FaraNdiaye-k1m
    @FaraNdiaye-k1m 14 дней назад +3

    Mere bou niak fayda damal diamou dji yala

    • @seydinaissademe
      @seydinaissademe 14 дней назад +7

      yaw kou reww gua respect tamit mer bi dou sa morom

    • @ModouDiouf-i4d
      @ModouDiouf-i4d 14 дней назад +6

      Ioe kou toth sa leketou baye gua amo respect bilae🎉

    • @NeneCorrea-sy2ll
      @NeneCorrea-sy2ll 14 дней назад +3

      Boko wakhé si kanamou domam mou tocc sa leufeul ndy😂

    • @falloungom3153
      @falloungom3153 14 дней назад +3

      Mba yaw yangui diamou yalla nimou warei

    • @mamadoufall9185
      @mamadoufall9185 13 дней назад +2

      Mère bi bouko nekhé Wakh si Lamb Domou Falaye Baldé là am ay rakkou Mbeur magg si famille lamb diour Mbeur Mouy Pokola Yow nak kou rèw nga bo nièméwone linguay Wakh takhawal si kanamam wakh ko dotoko deffati