Serigne bi danioukay kham.. kham lepp si mom ,, meunoul nék.. mais bon beugué Xam touti thi mom, faw nit ki guestou koo..' kou Nangou, nangoulko Mokay meun dékkou.... Mais kou am xol bou beurii tilim tilim douko dégg, te dou téwé ay wakham
Bu YONÉNT BI (a s) waxe, sëriñ wax wuute am, ngéen bàyyi fa waxi YONÉNT BI (a s) tóppi waxi sëriñ ba. Ba nóppi ni bëgg ngéen YONÉNT BI (a s), MOOM (a s) ngéen di tópp🤔 Wax léen rek👂👂👂
Le nouveau du causerie par saliou samb en vers cheickoul khadim est très bas... saliou samb et ganna masere n'ont pas la connaissance et la capacité qu'il faut.....
Sëriñ Tuuba nit dóng la woon. Du woon Yonént, du woon Saqaaba dólli ci. Kénn-kénn xamul ci lu mu nékk. Kénn xamul baxam sunu BOROOM gërëm na ko am déed. Kénn waxu ñu dara ci moom. Kon lu dul ñaanal ko njéggal maneesu ko cee weesu.
@@mriamf9350 Soxna su baax si jiyaar naa la bu wér! Baal ma nga leeralal ma li nga wax🤔 Bu dee jàpp nga ni li ma wax wérul kay dàjji ko indil ma leneen rek kay yaw. Da ñuy waxtaan. Waat na ci sama BOROOM ni boo ma fi indilee xam-xam bu wér ci diiné ji ma jël ko moom ndax bénn jullit amul bénn sañ-sañ ci dàq lu wér 👂👂
Ndawal yalla yi nga fi toudou yepp, ahmadou yamaléw lén ak dara... Daguen guestou térém baparé do beug débat... Diné kén douko teunk si sa xél.... Dangay nangoo guestou Al Coran ba nopii, guestou makk yii. Bo beugué am dégg dégg.
YA EU 124000 PROPHETES LES SAHABAS RIEN QUE CA SERIGNE TOUBA MOLENE GUEUNE TE MOM WAKHOUKO SEN TALIBE AK CONFERENCIER COMEDIEN RIDICULISENT VOTRE TARIKHA
@@diopmar6382 les prophete sont les meilleurs des hommes et apres le prophete muhammad psl le prophete ibrahim est le meilleur des hommes c pour cela dans la priere on le cite et le jour du jugement dernier lun des prophete qui parleront le premier au prophete muhammad les gens ne chercheront en premier les prophetes pour faire lintercession
nom d'Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux. D'après 'Ali Ibn Abi Talib (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Abou Bakr et 'Omar (qu'Allah les agrée tous les deux) sont les deux meilleurs hommes du paradis parmi les premiers et les derniers en dehors des Prophètes et des Envoyés (*) ». (Rapporté par Tirmidhi et authentifié par Cheikh Albani dans Sahih Al Jami n°51) (*) Le sens du hadith est que Abou Bakr et 'Omar (qu'Allah les agrées tous les deux) sont les deux meilleurs des gens du paradis toutes communautés confondues en dehors des Envoyés et des Prophètes (que la prière d'Allah et Son salut soient sur eux).
kendou seydina mouhamed billahi waye dieureudief Serigne Touba khadimou rassoll yall na gneup am diam thi barke seydina mouhamed
L’homme le plus aimé au monde Saydina Muhammadu Rasul’Allah le sauveur de l’humanité ❤️🙌🏽
dieureudieufeti serigne touba khadim rassoul amoul morom kenn la ❤❤❤❤❤❤
Kèn dou seydina mohamed asw🤲❤😭 wayé thieuy sunu wadji cheikhoul xaadim 🤲❤
Allahoumma Sally ala Seydina Mouhammadin jerejefati Serigne Touba Jarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Serigne Saliou Samb Yalla nafi yag
Serigne Touba rek lagnouy topou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Thieuye sounou prophéte bui kéne d'où mome barké borome touba vérité absolue
Serigne Touba rék lanoyé topou amoul lanén ✊🤧😪✅🥰
Dieureudif Serigue Touba khadim Rassoul diarrama Mame cheikh Ibrama fall lamp ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Dieume djiii serigne saliou samb dinama rey machala
Machalha sante serigne touba rek
mouhamad salallaahou aleyhi wa salam psl ❤❤❤
#igfm invité leen Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhti❤❤❤
Machallah wakhtane bi amna solo dieureuf serigne Saliou Samb si léral yi contane nanu trop Blh
Beug Rassoulilah Rék Thiey Serigne Touba ❤
Dieuredieufeti Borom Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👍👌
Mâcha Allah
Salalahou alla moukhamet
Dieureudieuf serigne Touba
Sallalahou Alleyhi Wa Salam ♥️♥️♥️
Machallah❤❤
DIEUREUDIEUF MAME BOROM TOUBA KHADIM RASSOUL AMUL MOROM ABADANE
NOTRE BIEN AIMÉ PROPHÈTE MOHAMMED SAWS PSL
Masha.allah Alhamdoulilah santati yalla bou weer
L'Islam est une religion magnifique.
waw goor mourde machallah am n'a solo lollllll
❤❤❤❤❤❤❤❤macall merci 🙏
Diarra dieuf Serigne Touba ❤❤❤
SAW💚
Thieuy Ahmadou Bamba ya kham Rassoulilahi
شكرا
Bilahi Serigne TouBa Amoul Morom
Dieureudieufei ahmadou
AHMADOU BAMBA MBACKÉ ❤❤❤
Salalawou hala mouhamed ❤
Akassa
😢❤❤❤❤❤❤❤💪🥰
Daysane kédou cheikhoul khadim adiana soriwoul Bilay daysane
❤❤❤❤❤
Serign touba keine douko kham dagn koye gueum
Serigne bi danioukay kham.. kham lepp si mom ,, meunoul nék.. mais bon beugué Xam touti thi mom, faw nit ki guestou koo..' kou Nangou, nangoulko Mokay meun dékkou....
Mais kou am xol bou beurii tilim tilim douko dégg, te dou téwé ay wakham
Pour le tour de Baye Niass, wakeur Sangue Ndiaye SVP
Kénn douh Serigne touba amoul morom !!!
Serigne SALIOU samb YALLA NGA FI YAG TÉ WËR AME kheweul you bari
Amine ya rabbi Masha.allah
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bamba
Bu YONÉNT BI (a s) waxe, sëriñ wax wuute am, ngéen bàyyi fa waxi YONÉNT BI (a s) tóppi waxi sëriñ ba. Ba nóppi ni bëgg ngéen YONÉNT BI (a s), MOOM (a s) ngéen di tópp🤔 Wax léen rek👂👂👂
Ba paré yaw saliou samb ga tok Di wah Lou gnaw si setam cheikh Amet tidiane hamni Serigne Touba contanoul si yaw
KI MO DAKA DOUL SÉNÉGAL
Le nouveau du causerie par saliou samb en vers cheickoul khadim est très bas... saliou samb et ganna masere n'ont pas la connaissance et la capacité qu'il faut.....
Pourquoi tu ne sollicites pas ta personne , pour venir aux plateaux.. si tu as plus d'expériences qu'eux comme tu le dis ..
@@mriamf9350 j'aimerais vraiment mais comment faire
@@mriamf9350 ce lui qui a la capacité au moins c'est Serigne Sam mbaye
Le Sénégal ignore Serigne Touba !!!!
Sëriñ Tuuba nit dóng la woon. Du woon Yonént, du woon Saqaaba dólli ci.
Kénn-kénn xamul ci lu mu nékk.
Kénn xamul baxam sunu BOROOM gërëm na ko am déed.
Kénn waxu ñu dara ci moom.
Kon lu dul ñaanal ko njéggal maneesu ko cee weesu.
Amo dégg deggg .
@@mriamf9350 Soxna su baax si jiyaar naa la bu wér! Baal ma nga leeralal ma li nga wax🤔 Bu dee jàpp nga ni li ma wax wérul kay dàjji ko indil ma leneen rek kay yaw. Da ñuy waxtaan. Waat na ci sama BOROOM ni boo ma fi indilee xam-xam bu wér ci diiné ji ma jël ko moom ndax bénn jullit amul bénn sañ-sañ ci dàq lu wér 👂👂
ISSA IBRAHIMA MOUSSA NOUH SALIH ALI ABABACAR OMAR OUSMANE JAFAR BILAL BOUKHARI ARRETEZ CETTE FARCE
Gnoune serigne touba mo takh gnou kham Yonentebi psl sangou sangu yi
@@ndiabytv kouko beugoul dégu déyal kéne dou cheikhoul khadim
Tout ça pour ça.
1+1+1+1+1+1+1+1+1+1+1+1=12. Cheikh Ahmadou Bamba est notre 12.
C ta dire
Ndawal yalla yi nga fi toudou yepp, ahmadou yamaléw lén ak dara... Daguen guestou térém baparé do beug débat... Diné kén douko teunk si sa xél.... Dangay nangoo guestou Al Coran ba nopii, guestou makk yii. Bo beugué am dégg dégg.
Borom Dole khamoul nank Niang kharagne mo dofde
Nia 😂😂😂😂😂
Ya mana doule
Allahou Akbar 🤭🤭🤭🤭dioulit gua
YA EU 124000 PROPHETES LES SAHABAS RIEN QUE CA SERIGNE TOUBA MOLENE GUEUNE TE MOM WAKHOUKO SEN TALIBE AK CONFERENCIER COMEDIEN RIDICULISENT VOTRE TARIKHA
@@aliounebadarandiaye5344 ganaw seydina mohamed yalle bindoul fen ki mo guene ki. Mane guinaw yonetibi sama yaye ak sama pape nio guene nieup
@@diopmar6382 les prophete sont les meilleurs des hommes et apres le prophete muhammad psl le prophete ibrahim est le meilleur des hommes c pour cela dans la priere on le cite et le jour du jugement dernier lun des prophete qui parleront le premier au prophete muhammad les gens ne chercheront en premier les prophetes pour faire lintercession
nom d'Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux.
D'après 'Ali Ibn Abi Talib (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Abou Bakr et 'Omar (qu'Allah les agrée tous les deux) sont les deux meilleurs hommes du paradis parmi les premiers et les derniers en dehors des Prophètes et des Envoyés (*) ».
(Rapporté par Tirmidhi et authentifié par Cheikh Albani dans Sahih Al Jami n°51)
(*) Le sens du hadith est que Abou Bakr et 'Omar (qu'Allah les agrées tous les deux) sont les deux meilleurs des gens du paradis toutes communautés confondues en dehors des Envoyés et des Prophètes (que la prière d'Allah et Son salut soient sur eux).
Gni dagnouye Bokalé geume léne yalla
😂😂😂😂 kou sohor dou dougu adjanaaa bayil siii xel
Séne kholoub yéfeur yi nguéne Yor
Machallah 🙏🙏
❤❤❤
Akassa
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤