REPLAY - Ngonal 25 Janvier 2017 - Invités : Mbaye Diéye Faye & le Sing Sing rythme

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 дек 2024

Комментарии • 206

  • @adamaseck557
    @adamaseck557 6 месяцев назад +4

    C'était la meilleure ngonal😂😂😂😂 qui regarde en 2024

  • @lisafa8210
    @lisafa8210 7 лет назад +28

    C'est ce genre de Ngonal qu'on veut voir chaque mercredi inshallah, faites nous plaisir au lieu d'inviter des politiciens et autres. Faram facce , mamadou Ibra kane et autres doyena ci ..... Neex na

  • @torodo6447
    @torodo6447 7 лет назад +4

    yi papa mbaye Dièye faye dieul nga damli macha allah ngonal li nèkhna yalla na yalla goudal sa fane yok wér gui ndanane kouli fadri moy yaw wayé saneex ray ngama yak Aziz lingay danse amoul fëneu😂😂😂

  • @dembosylla2305
    @dembosylla2305 7 лет назад +1

    looool c est le seul ngonal que j ai regarde 4 fois

  • @mouslimatoudiongue2851
    @mouslimatoudiongue2851 7 лет назад +7

    je viole le bouton replay..you make me proud guys...GOd bless...

  • @mamengom9066
    @mamengom9066 3 года назад +1

    Ngonal bi doumassi doyal, meilleur ngonal
    Qui est là en 2021 ?

  • @ModouMbow
    @ModouMbow 7 лет назад +15

    Meilleur Ngonal de tous les temps

    • @marshalljaxxon4425
      @marshalljaxxon4425 3 года назад

      You prolly dont care but does anybody know a way to get back into an Instagram account?
      I stupidly lost my account password. I would appreciate any help you can offer me

    • @guskian4605
      @guskian4605 3 года назад

      @Marshall Jaxxon instablaster =)

  • @kewegueye4028
    @kewegueye4028 7 лет назад +9

    bi ngonal c est incomparable à l égard des autres WALAHI merci mbay dieye lep rafetna yalnalen sounou borom defal diam amine

  • @dadoul0vankc417
    @dadoul0vankc417 6 лет назад +4

    Mame vieux sing faye sama kharite lawone souma néwone teuleu rue 23 rek souma sènè rek sourire bi lay ndieukkeu sène ak togayam bou rafete. Yallah na toguéé nonou biir aldiana 👌

  • @sukutu100
    @sukutu100 7 лет назад +6

    Aziz, Cheikh et Saneex maachalla culturellement vous êtes fort ça se voit que maachallah vous avez galéré ensemble depuis. La complicité ne se crée pas du jour au lendemain vous êtes le trio gagnant... Le sing sing rythme mom maachallah c'est le must loy daaf ci adunna doone ci le meilleur Rich Niang li nga féthie culturellement parlant ga yi meunatougn ko!

  • @dieynabacisse4963
    @dieynabacisse4963 7 лет назад +4

    merci merci à l'équipe de ngonal Mbaye dièye faye et ses frères lougnou lale mou néke or merci pour tout big kisss♡♡♡♡♡

  • @khadimgning3755
    @khadimgning3755 7 лет назад +16

    kenne dou Mbaye Dieye Faye ya goré si Youssou Ndour Nice Ngonal thiey Sanekh

  • @dadofall8550
    @dadofall8550 7 лет назад +7

    boufiyeimone sakh mou nekh, ngonal diekhna tchi Sénégal. longue vie au sing sing rythme.😘😘😘

  • @dieynadiallo5126
    @dieynadiallo5126 7 лет назад +8

    Ngonal bi mom amatoul machala sanex ak cheikhouna dougnou nit way wa papa mbaye dieye Faye loutah ma bougala yow😁 FI ❤ la la def jumeau youssou ndour

  • @beuguesaliou9069
    @beuguesaliou9069 7 лет назад +7

    nooo sanekh ray ngama machala yalla nalen yalla lafal thiat si barkè serigne saliou

  • @assanegakou1876
    @assanegakou1876 7 лет назад +20

    😂😂😂😂😂😂😂😂non le meilleur ngonal de tous les temps non sanekhhhh rayngamaaaa

  • @mounadiouf2967
    @mounadiouf2967 7 лет назад +6

    ningua meuneu mell youssou ndour moy sa sekh. c'est le meilleur ngonal

  • @liliiza8590
    @liliiza8590 7 лет назад

    merciiii tonton mbaye dieye borom medina
    ..ya bakh , ya simple , ya gorè.......
    bilaye ya bakh mbaye dieye

  • @bintou944
    @bintou944 7 лет назад +5

    Nice show one love from Gambia❤️❤️🇬🇲🇸🇳

  • @talibecheikh7163
    @talibecheikh7163 7 лет назад +1

    j'adore cette famille li moy ngonal mashalla yalla na yalla takhawoula si barke SERIGNE BABACAR SY

  • @MabinetyFall
    @MabinetyFall 7 лет назад

    Ahhh Macha Allah laftiat Birame Dieng yalnna yalla defal batbi amine. Fayei keneu duSINGSING

  • @ndeyediop4833
    @ndeyediop4833 4 года назад +1

    Manchallah pére Mbaye Diéye Faye dafa ame Personnalité

  • @mameboye1
    @mameboye1 7 лет назад +3

    Best ngonal ever 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁🦁✌🏾✌🏾✌🏾✌🏾👍🏾👍🏾👍🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😍😍😍😍😍😍😍😘😘😘😘😘😘😘

  • @kaliloulayesy2729
    @kaliloulayesy2729 7 лет назад +4

    Exceptionnel ngonal nekhna trop sing sing family you are the best.

  • @boidojawo8967
    @boidojawo8967 7 лет назад +1

    ngonal bii nekh naa trop paix a vou et vive tfm

  • @KN-pw9nz
    @KN-pw9nz 7 лет назад +10

    nannn vs etes tous forts mais riche faye li mouy fecc eupneu mashalah!

    • @sidyka2906
      @sidyka2906 7 лет назад +1

      Khady NIANG YaW sofo deh

  • @FatmaDiemg
    @FatmaDiemg 7 лет назад +11

    mentions spéciales Mbaye Dieye retour de Jimmy Mbaye et Habib demande fans super étoile yeupp. merci

  • @Doffmalick
    @Doffmalick 7 лет назад +2

    Non c'est les meilleurs Sanekh Aziz cheikh ❤❤❤ Sing Sing rythme one love . Sanekh fetieu nga lou nexx

  • @PapeDembaGueye
    @PapeDembaGueye 7 лет назад +12

    LE MEILLEUR NGONAL DE TOUS LES TEMPS !

  • @ndoumbegueye9614
    @ndoumbegueye9614 7 лет назад +5

    ngeweul lalay expliqué dh..... dara dafnio fay fière de ce que nous sommes.... ngeweul rk

    • @assanembaye7230
      @assanembaye7230 7 лет назад +1

      Ndoumbe Gueye Bilahi borom bi daf niou khorom louniou wakh mou nekh louniou deff mou nekh..Ay gueweul la niou pirrr

    • @ndoumbegueye9614
      @ndoumbegueye9614 7 лет назад

      Assane mbaye wakhal dh mbaye

    • @thekingngom3056
      @thekingngom3056 7 лет назад +2

      Ndoumbe Gueye mane dama sant bou bakh si lima ko donn ndakh louma wakh mou khoromou louma deff mou nekh louma soll mou rafett dou aye wakh nak mai naturellement on est kom ça

    • @ndoumbegueye9614
      @ndoumbegueye9614 7 лет назад

      The King Ngom hahahaha degg n'a deug assane Ndiaye nena xalei bou goor pirr ngeweul la am te thiep bou nekh tamit ngeweul la am

  • @fatougueye6578
    @fatougueye6578 7 лет назад +2

    meilleur ngonal.sanekh boulenfi wotéwatt ba att mi diekh ndakh bii mom moy the best ever. wa sing sing mane maalen beugg daal. mais rich niang kou meun si mom dara😂😂

  • @biancathioune1640
    @biancathioune1640 7 лет назад +2

    j.adore ngonal félicitations à l.equipe.coucou riche tu danse très bien machalla mention spéciale à famille de ton mbaye gueye faye machalla waye meilleur ngonal

  • @fatounjie3845
    @fatounjie3845 7 лет назад +1

    💖💞💗💓 Mbaye Gueye belie wah nga deega si Yaya Jammeh ..y yep mujena kopu si bopam bi

  • @boidojawo8967
    @boidojawo8967 7 лет назад +4

    mbaye dieye es fort a se kil fai il maitrise sa j vou asur k dieu t benisse et a tous

  • @ndeyeaissadiop2561
    @ndeyeaissadiop2561 7 лет назад +35

    Ngonal bi mofi dakhe

  • @dieynadiallo5126
    @dieynadiallo5126 7 лет назад +5

    Ohh baye demba et Birame dieng je vous love

  • @gamigam6420
    @gamigam6420 4 года назад +1

    Un héritage bien gardé par mbaye dieye un grand homme👍

  • @hvcxxghcxxf8549
    @hvcxxghcxxf8549 7 лет назад +8

    ngonal bi amoul fen please invite Mbey Gaye Faye again

  • @marianendiayeguellwarre7919
    @marianendiayeguellwarre7919 7 лет назад +2

    merveilleusement magnifique j'adore mbaye je t'adore 😃😃

  • @cheikhoudiagne2081
    @cheikhoudiagne2081 7 лет назад

    je suis très contant pour wa ngonal Mbaye dièye Faye yalnanga coude fane

  • @hawakane9369
    @hawakane9369 7 лет назад +2

    Bi ngonal mome todj na fi 💕💕💕

  • @abdoulbalde6279
    @abdoulbalde6279 7 лет назад

    Diarama Hata wéliii machalla yalla booléen dijeGal Amine bravo Béll voix.

  • @oumarsy5622
    @oumarsy5622 6 месяцев назад

    Le Ngonal préféré, 35:00❤like

  • @ndeyetalibekhalifaababacar8634
    @ndeyetalibekhalifaababacar8634 7 лет назад +2

    Meilleurrrrrrrrrrr ngonal MachaALLAHHHHH!!!!!!!!!!!!!

  • @bahmamoudou
    @bahmamoudou 7 лет назад +7

    RESPECT NGONAL RESPECT MBAY DIEYE FAY

  • @malicksarr7557
    @malicksarr7557 7 лет назад +4

    sa nekh dieureu dieuf yallnala y alla Faye si lingua beugue dioubo bi

  • @mamikane1375
    @mamikane1375 7 лет назад +2

    non ngonal bi mo dakh thi ngonal yeup mbaye diéye yékhnafi gneuw mais saneh ray nama ak oupoukayam bi wayé riche tamite linguay féthi nékhna que dieu vous protége macha allah

  • @abdoumoubayekarime3043
    @abdoumoubayekarime3043 7 лет назад +5

    Mbaye dieye tu e un legende

  • @ousmaneba9105
    @ousmaneba9105 7 лет назад +6

    Cheikh Ndiaye alias (Jojo) Nelson Mandéla a été emprisonné en 1965 est libérer en 1990 soit 25 ans de détentions
    mais pas 1973 à 1991 pour préciser.

  • @saf-tnexx6731
    @saf-tnexx6731 7 лет назад +1

    Mbaye Dieye ngneweul Berlin Bitte 💝💝💝💖💖💖

  • @boyemanding9435
    @boyemanding9435 7 лет назад

    best ngonal I have ever seen before

  • @NeymarJr-ku1oy
    @NeymarJr-ku1oy 7 лет назад +5

    M'baye Dieye Faye yay ndanane way

  • @toorea8497
    @toorea8497 7 лет назад

    Nekhone na ❤️❤️❤️ merci beaucoup

  • @mameboye1
    @mameboye1 7 лет назад +2

    Ngonal bou melni moussoufer ame nekha nekhe

  • @seydaselbediouf3143
    @seydaselbediouf3143 7 лет назад

    nooo mane gny niomay fathhh je les adore mal En beugeu way hapyness

  • @aidagueye530
    @aidagueye530 7 лет назад

    formidable meilleur parmi les meilleurs .

  • @aminatalakh4362
    @aminatalakh4362 7 лет назад +2

    Mbaye dieye Faye wa Sénégal degou nioula écipe bi sounou begue am ndam a plus

  • @grandsmo23
    @grandsmo23 7 лет назад

    non best episode ever! machallah guys!

  • @aminatathiaw9225
    @aminatathiaw9225 7 лет назад

    machallah Riche meilleur danseur au Senegal best ngonal

  • @muhammedjeng408
    @muhammedjeng408 7 лет назад +1

    Nice ngonal and the song for my president we borrow

  • @baha1379
    @baha1379 7 лет назад +1

    we need a Soulayman Faye interview

  • @deourcisse9751
    @deourcisse9751 6 лет назад

    Fier de mon Senegal no stress 🇸🇳

  • @cayortv4910
    @cayortv4910 7 лет назад +1

    c'est génial vraiment

  • @You-wm1ox
    @You-wm1ox 7 лет назад

    Mbaye dieye faye so proud of you you make me cry

  • @princessemamita173
    @princessemamita173 7 лет назад

    le meilleur ds ngonal nn cheikhouna toth guafi ❤

  • @habiba6452
    @habiba6452 7 лет назад +6

    khol sed na ngonal bi dindi na saama stress😅😅😅

  • @mbayembodji4233
    @mbayembodji4233 4 года назад

    Y'a jamais 2 sans 3😀😀👍👍❤❤

  • @mameboye1
    @mameboye1 7 лет назад +1

    Non cheikh ndiaye il faut nga wah sa fethieu bi noumou toudou tothie nga ngonal👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾❤❤❤❤❤❤❤😍😍😍😍😍😍😍😘😘😘😘😘✌🏾✌🏾✌🏾✌🏾✌🏾✌🏾✌🏾

  • @ramatoulayemballo994
    @ramatoulayemballo994 7 лет назад +1

    No li amoul fene wa sing sing rek bilahi li nekh na mais aziz ak sanekh mome ils mont tuè 😂😂😂😂

  • @pathendiaye2540
    @pathendiaye2540 7 лет назад +2

    cheikh ndiaye tothie nga fi mais ngonal nekhna

  • @salamataguiro949
    @salamataguiro949 7 лет назад +1

    Oh nekh na Mbaye Dieye mala beug

  • @alaminendour2403
    @alaminendour2403 7 лет назад

    meilleur émission ngonal

  • @aliouseck4475
    @aliouseck4475 7 лет назад

    mareme Faye sall Sénégal tamoul faayyaamm bilahi

  • @jadimproplayer5229
    @jadimproplayer5229 7 лет назад

    moye sama president mome youssou ndour moma doye yalla na diamame yague

  • @binetasima9360
    @binetasima9360 7 лет назад +1

    c est le ngonal des ngonal bis way

  • @amienjie4483
    @amienjie4483 7 лет назад +1

    waaw the best NGONAL 2017 nice

  • @assanembaye7230
    @assanembaye7230 7 лет назад +1

    Ma sante Yalla bou bakh sili mouma deff gueweul..Borom bi daf niou maye khorom..Ngeweul rekka nekh

  • @mamaneva4612
    @mamaneva4612 7 лет назад +2

    Ahhhh li nekh na way bi ngonal mofi dakk way

  • @ndellabop8084
    @ndellabop8084 7 лет назад

    Sene ngonal nekh na macha alla

  • @ktdkgkgflhcjfzkgflhfnjhiu8086
    @ktdkgkgflhcjfzkgflhfnjhiu8086 7 лет назад +1

    nooooooo se me gayi biii ngonal. do toufi ame

  • @malikbaas2352
    @malikbaas2352 7 лет назад

    best ngonal. ......love it

  • @yayesarr3949
    @yayesarr3949 7 лет назад +2

    that's nice.i Love it

  • @aidanapolielaye259
    @aidanapolielaye259 7 лет назад +2

    Ayway lii nekhna way fi néna pousss

  • @Rohenson
    @Rohenson 7 лет назад

    yowwwww...this is so amazing...y sanex dina Rey nit deh...😂😂😂😂

  • @moisecamara5537
    @moisecamara5537 4 года назад

    Meilleur ngonal

  • @ndeyahmbaye4415
    @ndeyahmbaye4415 7 лет назад +3

    nonnnnnnn ngonal bi doufi amati way la nouvelle danse de sanekh "kép tank yékéti thiaya si kaw wathiéwate" rétane ba tass.Mais vraiment Mbaye Diéye dou nite li nékhna trop way laf thiat way

  • @leonainfo5711
    @leonainfo5711 7 лет назад +2

    machalla nice na tropp sanèkh

  • @aidasene8950
    @aidasene8950 7 лет назад +1

    oooh nexna mashaa allah

  • @mariarosas2871
    @mariarosas2871 7 лет назад

    Dafa rafette pere mbaye dieye

  • @modoundiaye8655
    @modoundiaye8655 3 года назад

    Ko fii nek 2021

  • @palycisse5723
    @palycisse5723 4 года назад

    C magnifique

  • @papcamra5547
    @papcamra5547 7 лет назад +1

    I love it so much

  • @cheikhtidianendong7773
    @cheikhtidianendong7773 7 лет назад

    bise doyalouniou rafetna nekhna

  • @biramesene9033
    @biramesene9033 7 лет назад +3

    yènagi sogua ngonal li nèkhna

  • @aramefaye2689
    @aramefaye2689 4 года назад +1

    Machallah

  • @saf-tnexx6731
    @saf-tnexx6731 7 лет назад

    Cè trop nèkh waye 👏👏👏👏👏

  • @gamigam6420
    @gamigam6420 5 лет назад

    Bilaye naihna ngueweul raikk thiossane laaaa bilaye

  • @thekingngom3056
    @thekingngom3056 7 лет назад

    Bilahi aye gueweul pirr la niou .Souniou askan dall daffa rich souma nekoul wonn gueweul may raw naawè Khorom nioune way. Nyi ko aimé woul na niou donn si psychiatre mou khole nienn nyi ndoff la

  • @abydiame6851
    @abydiame6851 7 лет назад

    j'ai kiffffé trop

  • @rockerjunior4845
    @rockerjunior4845 7 лет назад +1

    YEN AY VRAIS SAYTANE NGUEN MAKY FOUMOU BAKHE DOUL REK