je me rappelle bien à JAKHAW , imam organisait un tournoi de foot pour les talibés j'étais présent . personne ne le connait mieux que moi il m'a éduqué , guidé hafiza houl lah
Yall nanou yalla dogale aldiana machalla mane mome sy tasawof rek la xam wayé képou kouye doulelite bëgë nala aldiana yalla hame nako daxa alediana yalla xatalouko wayé bida bida rek lolou dou xame xame fi aye nite you xame ñofi né xame lisy téreyé Billahé kone nane rafétal liñou wouté ñou bëyéko ake yalla
Niday sane serigne bamba soumako giusy sama xilami sy imame aline badarr ndiwo rek laye dém yall Na Yalla fayé la ni rek ❤❤❤❤ fafa tv lépou l'islam la yall Na Yalla yërëme imame aline badarr ndiwo ❤❤❤ ake serigne saliou sawo ❤❤❤❤
Assalamu alaykum warahmatullah Wallahi aka makoo fonk teh soopou ko waayé batay convaincre rogooma si gaammu. ومن يعظم شعائر الله فإنها من تقوى القلوب Ak dieufu mouanz boobu pour mane ak daytal bassi tégou woone, boo dieulè safaane wa mou téré la gaamou. كل بدعة ضلالة وإن رئاها الناس حسنة حفظك الله ورعاك يا شيخنا الإمام
Mbokku kii pour man ab sounnite warouko deglou ndax dafa reer di reeralaaté . Il doit après les règles de reconnaissance de la bid3a:قواعد معرفة البدعة
Wallahi je trouve que ce gars est un égaré et qu’il ne doit pas parler de religion. 😢 qu’Allah le guide Il suffit de l’écouter pour savoir qu’il ignore certaines règles concernant la bid3a 😢
je me rappelle bien à JAKHAW , imam organisait un tournoi de foot pour les talibés j'étais présent . personne ne le connait mieux que moi il m'a éduqué , guidé hafiza houl lah
Machalah machalah amena solo lolol
Maachaa-Allah. Yalna gnu Yalla khallal yoonu gnup
Machallah ya oustaz
Thieuy ! Jàmbaar nga kaar
Jërëjëf Imaam mashaaAllah tabarakalLah
Machallah
Yall nanou yalla dogale aldiana machalla mane mome sy tasawof rek la xam wayé képou kouye doulelite bëgë nala aldiana yalla hame nako daxa alediana yalla xatalouko wayé bida bida rek lolou dou xame xame fi aye nite you xame ñofi né xame lisy téreyé Billahé kone nane rafétal liñou wouté ñou bëyéko ake yalla
Mashallah. Yalna yallah barkèl kham kham bi
أطال الله عمرك ياأستاذ أحمد جوب العلم هو المصباح المنير ❤
Niday sane serigne bamba soumako giusy sama xilami sy imame aline badarr ndiwo rek laye dém yall Na Yalla fayé la ni rek ❤❤❤❤ fafa tv lépou l'islam la yall Na Yalla yërëme imame aline badarr ndiwo ❤❤❤ ake serigne saliou sawo ❤❤❤❤
Mâcha ALLAH Ya Imam YALLAH nala YALLAH same
Machaa Allah fatabarakallahou. Oustaz kemane la ci kemane yalla yi Machaa Allah fatabarakallahou ❤❤❤
Gor YALLAH deuggg mou ngui nii MaachaALLAH
Té may gnu dégg dégg bu léer, may gnu dégg ak topp
Maachala, c k lui il a pratiqué les soufis, ce qui fait k mm s´il n´adhère pas à leur tariqa, il garde un respect pour eux.
Machala al imam Ahmeth Diop
Djazakoume Allahou khair
The store off good 👍👍👍 excellent thanks for you
Masha Allah tabarakAllah❤❤❤❤❤
En tout cas il a l'honnêteté intellectuelle
Assalamu alaykum warahmatullah
Wallahi aka makoo fonk teh soopou ko waayé batay convaincre rogooma si gaammu.
ومن يعظم شعائر الله فإنها من تقوى القلوب
Ak dieufu mouanz boobu pour mane ak daytal bassi tégou woone, boo dieulè safaane wa mou téré la gaamou.
كل بدعة ضلالة وإن رئاها الناس حسنة
حفظك الله ورعاك يا شيخنا الإمام
Mbokku kii pour man ab sounnite warouko deglou ndax dafa reer di reeralaaté . Il doit après les règles de reconnaissance de la bid3a:قواعد معرفة البدعة
Ah léerna con nanou bayi khasanté yi ki limou wax pour man diaroul tok fii di tardel sûñiou bopp
Mbokou Mii Adouna bii nèkoull Bida rekk moffi nekk 😮💨😮💨Am na lènen lou guen lougnou atardèwouu Bida Bida Bida rekkk 😔😔😔 Boulè gnou sonall ak Bida wayy Tamitt 😑😑Fii kou nekk ak sa bAMELL 😓😓
@@ALMuslim53rew ak niak kham kham mola diapp
Macha allah, kaar kaar beurigo bu fees degg lay def
Do ku ndaw, yàlla na yàlla sàmmu la te aar la aar sa njaboot
Maasàlla tubaarikàlla Yàlla na ko Yàlla sàmmu te barkeel ko bari ay kemam ku am solo nga
❤حفظك الله من كل سوء ومكروه
Machallah yaa Oustaz. Xam xam bi lerna.
Machallah nallah yallah fay❤😊
Mancha Allah barakallahu fikoum
جزاكم الله خيرا أحسنت
Diazakoullahou hayrane ya oustaz
Machallah kii Maan Nga ci kiimaanu yàlla yi
Ahmed dioup dagaye sose rék wakho ben kham kham
ما شاء الله
❤❤❤❤
Ahmad Diop tidjan la
Wakho dëgg
Seex Faafa Yàlla na Yàlla bindal la yiw ci interview bi yaag sama mbokk mii seex Bàmba NJAAY. Waawleen góor waay
Aamiin 🤲وجزاكم الله خيرا
لتكون كلمة الله هي العليا.
MachaAllah
ماشاء الله حفظك الله ورعاك واطال الله عمرك وبقاءك الله
والله خلت فيك صالح القلب ونقية السريره .الله يجازيك كل الخير. مع أني تجاني أما وأبا
Machaala amna solo
ماشاءالله
الله يوفقك
Jerejef
Borom xam xam tè mandou maashallah
حفظك الله ورعاك ايها العالم العادل
Je l'aime bien imam ahmad Diop k'Allah lui protège, mais je ne suis pas convaincu pour cela vraiment
Njungum sunna bi kagn leu commencé? Ak albany walla Sénégal ngay wakh?
Yen wa Fafa TV sose yi gêne Di tasarel Ahmed dioup Amgen ti responsabilité bo mak
Ahmad Diop tidiani talibe chiekh tidiane😂😂😂😂😅😅😅
Sukhriya bakhooul mbokk
Bokouna fou bakh machallah
Wa mé après
So gnou wakhone doo sunnit dougn diang si yow té doo gnou défal conférence
kii waroul wax si diiné dji
Il est mouslim
Vous êtes vraiment parano😢
Mais dioulit la. Ubilen sen dandyi yatalko. Melne ku mom dine dji
Tu dis quoi toi en fait
Wallahi je trouve que ce gars est un égaré et qu’il ne doit pas parler de religion. 😢 qu’Allah le guide
Il suffit de l’écouter pour savoir qu’il ignore certaines règles concernant la bid3a 😢
La religion appartient à Allah. Nul n'est parfait. Bayil diambour kou dé akssa baamel
Il est mouslim
Mbokou Mii Adouna bii nèkoull Bida rekk moffi nekk 😮💨😮💨Am na lènen lou guen lougnou atardèwouu Bida Bida Bida rekkk 😔😔😔 Boulè gnou sonall ak Bida wayy Tamitt 😑😑Fii kou nekk ak sa bAMELL 😓😓
Yen merde wayy vous faites chier à la fin…. Xamolen dara thi dînée l’islam et tu oses taxer ce monsieur d’égaré…
Plus égarer que toi n’existe pas
Machallah
Mashallah. Yalna yallah barkèl kham kham bi
❤❤❤❤❤
Machallah