Yen gniy wakh Serigne matr diène khana khamoo l'en ko Serigne matr kou bakh la beugue Serigne bi beugue xasidayi lim fi wakh lépou deugue dafa fékné deugue mon nékhoul rek mais degeu bou wéur la thé ab taloubé day niéme dégue wasalm
Wakhdji defaroul dé, pourtant bi Atou diagne wathié tu l'as pleuré avec des temoignages tristes véridique, entre talibés li rafétoul si kadou, 93 familles mais y'a du social aussi Diéne
Wakhe ji machalla dawna'na yaram vaye leppa diamo rek ak salam amine magui Brescia Italie daw na yaram me nan xamni adouna yepp stouba koyor rawatina dogo yi
Sëñ Mataar de ku am patéef la xam naako bubaax xam naa ci moom it ag bëgg Sëñ Tuubaa ak fónk ndjabootug Sëriñ bi❤وماشهدناإلابماعلمنا وماكنا للغيب حافظين
Bakane moungui beuga dougg si liguey bi. Li rafetoul Wakhtane len té bayyi niakhtou bi. Li yeup danguene wara toog wakhtané ko wout pekhé té wëy. Serigne Mountakha sou nguene ko roussone li lepp dou am. Ki togn ak kignou togn yeup nak la wakh. Jiiteul len Serigne bi si ligueey bi. Kou naagou nak saytané dinala def beuss lou gneup Di thioow !
Damani li ngene di wahe sene gathie reke la bayi lene diakhaseyi te dem diefe ndiguel serigne mountakha mbake serigne mountakha serígne youssou diop la djiteule manoulene wahe ba yeye serignebi
Thi ay tiakhane keep ngen nek... ak Yap Serigne Mountakha ak wané ap niak kilifeu.. bi lii yeup xéwé danguen warone and dem si Serigne Mountakha ngen wakhko lepp ndakh molen wo banguen nieuw mouné len beugeu touma dégu niaar.. Serigne matar ioe mome kouma bét nga ap jangu katou xassideu waroul jikowo ni nga mel.. sa wakh dji dara rafetousi... Té limasi geuneu méti dégouma bén yone folen wakhé ni dém nagn si Serigne Mountakha nguir wakh ak mome si wakh dji.. Té moléne bolen yilif yen nieup
Boulene gnawal lou gnawoul wax diou bari rethiou motchi top Serigne Atou est parti se reposer respectez son Ame Nul n'est indispensable dans le Mouridisme Wax diou bary diu mbiry mouride
Matar Diene beteganou lolou reik, jeuw reik ga fi done def ak wax jou niaw si Segne Atou Diagne mi Yallah Gueureum, sossal Segne Youssou 🤔 Li niawena, mane bokkouma Ht bokoumq Htdkh waayeih Li ken xamoul lanela.
@@saliougueye8773 Serigne bi mangui toup dé🙏 way pour man mbir mi dou question de ki mo né ci deugg wala détt ndigeull molén bolé bou démé ba am ay diouwolo délou watt lén ci kalen diokh ndigeull bi boudé khadjo moy li guénn mou khadiatt ko kouné délou watt sa langa nekon amna yo khamné waroull guénn sén birr ba kouné di ci diott Mouy niarri Hizbut tarquiyah yeup louway ték sén kaw ci kaw yonou mouride ngako ték nakh danio soll mboubb liguéyeul kou tédd ki wakh dji meunon na niakk matar diène nak nieup kham nagn pass passam ak tolouwayam ci liguéyall kou téd way dieull kadu yi di ko ték ci kaw gni nga bokall liguéy bi rafetoull dara
S Matar Diene waagnil sa thioowli …!!! Serigne Mountakha S Youssou Diop moomla djiiteul si kanamou mbooloomi… tu critiques trop même avec S Atou niiilawoon !!!!Rousléen Serigne té baayi séen thiowli
@@pilotepilote3574 néekoul deugg yeupeu laniouy wakhtaané si am péeńchie .. sa waay je connais très bien Matar Diene depuis 1994 nioo néekadoowoon Hizbutarkiyyah (Mermoz Dakar) . Il était toujours comme ça, il critique trop…..!!!! S Atou Diagne (Rahmatoulahi Alayhi) il à donner toute sa vie à s Touba …!!! Nako niaanal mais amatoul pour diko criqué
@@pilotepilote3574 sa waay maslaha ba am li-ngueu beugg , moo gueunn khouloo ba am li-nga beugg…!!! Wakh deugg si soutoureu ba am li-nga beugg , moo gueunn wakhko sim pincthie ba amko…!!! Kheutt-kheutt sootaloul dará khanaa gnila waroul khamal , khamala kessé, problem boufi nit exposé, nit amnafi problem bouko gueuneu graw té kéneu khamouko, basi sounou keur kilifeu yiii niou yaakaar
N'a hizbut yi moytou chaîne bi DAKAR 24 TV Souma sanione nguéne signaléko youtube Waroul Di djeul ay audio fuité you wa daara dji diko publié bou mélni bou mot talla wala Matar wala djeuwrine, naniou moytou chaîne bi naniouko signalé, yackeu reck moka taxa diouk
Bayyi lene féne lii du audio dako wakh mu thi sene dajié ba mu lér lool bayyi lene féne makhtar amul diotu djieuw kéne amna vidéos bi mu lér ngeni féne xaliss diaru ko
Toute ta parole c'est une déception vraiment tu m'as déçu ioe bolobi nêkhoula parce que tu ve la concurrence tu ne veux pas mettre derrière Abdoulaye Diop Yoonwi fawwou am kou djiitou.
Kou baakh ngaa baalma degofii concurrence deh malheureusement la question est beaucoup plus profonde je sais pas est ce que t'as bien entendu des propos,je t'invite à suivre l'intégralité de la conférence de presse de Htdkh. Jajeuf leep defaar rkk
Sa way li dh yaw rék Yako waxe té diguaci wétt Serigne Matar khassida moko gnor ak Serigne bi. Boudé diangue moko dakh kokou guakoy teukeulél. Kokou kay moko meunoul degerer té naguouwoul s. Matar diène djitté.
@@Goraadieng lolu gis naako murid kénne waxufi Ay fén Dafa fékni ni Li génne gi baaxut Mënoon na nék luniuy waxtaané Aw thiow su amé demoon ci serigne bi diis ko dafa doon gën Ngir noonu yaagi fi fess délle Xaarugn ludul sugn gathié
yalla da bègue koye rafétall waye boull bègue aye abonné you bari rk mo takh guaye tasare wakhi djamourr ko bakh boko mane dini gua deff ko. yalla mogui fi guemoull nelawou te lofi guiss rk daye djekh waye na rafett gua balle ma akh nk
Très regrettable même Serigne Saliou masna lena wo gnom gnep nelen bu ken salawloti Atou delen ko wax Serigne Atou ndax talibé budei soyoko guissei mou fatalila sap serigne waroko salawlou qui plus est kou guein adouna donc waro am yen seder yi ci mom. J'ai honte moi
Serigne atou yalla nako yalla yerem
Yen gniy wakh Serigne matr diène khana khamoo l'en ko Serigne matr kou bakh la beugue Serigne bi beugue xasidayi lim fi wakh lépou deugue dafa fékné deugue mon nékhoul rek mais degeu bou wéur la thé ab taloubé day niéme dégue wasalm
Billahi
❤
Louler la wakh
Bilay walay 🥰❤️
@@astousall7385 koubakh laaa
S atou yalna sunu borome doli ay leram mome day liguey na ba am guereume gnibi aldiana
Kane moko geureum
@@serignemodousylla9484 mbolém koufi keusa nek khalifa s touba rk guerem guako
Yalla nanou yalla mousseul si seytane barke cheikhoul khadim
Wakhdji defaroul dé, pourtant bi Atou diagne wathié tu l'as pleuré avec des temoignages tristes véridique, entre talibés li rafétoul si kadou, 93 familles mais y'a du social aussi Diéne
Yalna S touba boulé lép modoun bén🙏🙏❤️
Wakhe ji machalla dawna'na yaram vaye leppa diamo rek ak salam amine magui Brescia Italie daw na yaram me nan xamni adouna yepp stouba koyor rawatina dogo yi
Bolime ly kan wakhe daga yalla kamnako AK s touba merci beaucoup kena Mana Lou len Dara
Kouy yax nak bilaye s touba mbacke Nanou kou moyto
Sëñ Mataar de ku am patéef la xam naako bubaax xam naa ci moom it ag bëgg Sëñ Tuubaa ak fónk ndjabootug Sëriñ bi❤وماشهدناإلابماعلمنا وماكنا للغيب حافظين
ماشاء الله
@@coumbadiop5966 waaw loolu de maako dund ak moom ndax kuréel sëti Sëñ fallu yi mooleen daal repeteel waaye bu daan ñëw ay ambourger yu bari la daan jënd andaaleko joxko Waa kuréel bi ngir ñu reereko loolu mom dumako fátte mukk
Ki na fekhla
Bakane moungui beuga dougg si liguey bi. Li rafetoul Wakhtane len té bayyi niakhtou bi. Li yeup danguene wara toog wakhtané ko wout pekhé té wëy. Serigne Mountakha sou nguene ko roussone li lepp dou am. Ki togn ak kignou togn yeup nak la wakh. Jiiteul len Serigne bi si ligueey bi. Kou naagou nak saytané dinala def beuss lou gneup Di thioow !
Koubegue boolé douwakheni nakadouyi geune reffet niep dagne la nawoone ngir sak Pastef.rousleen serigne bi
Na diouye wakhanté degue
Damani li ngene di wahe sene gathie reke la bayi lene diakhaseyi te dem diefe ndiguel serigne mountakha mbake serigne mountakha serígne youssou diop la djiteule manoulene wahe ba yeye serignebi
Wakhtanou biir Nék la kiko guénné mou déf léep wayé yalla na yalla rafétal and bi thi barkép Serigne Touba
Li d'où wakhtan bir neeke kou bakh li dagnko wara wakh ci kawe baye matar wakh na deuge ah
Degue rk lawakh s maxtar diene Borom pastef laaa
Ablaye diop mom royou kay la machalla
Ki mo gueneu deuggou koudoul ablaye diop ak nafekh diop soit disant responsable moral
Matar Amoul morom wasalam nafékh bakhoul
Matar Amoul morom wasalam nafékh bakhoul
Yalla na yalla bolé len takhawou barkep seydina mohamed
Moyrouléne nguir yalla déléne DIISSOOOOO ils faut se parler
Ligéne def ni mourid yeup la metti guir né serigne bi molén bolé
Mangii melni kouy guinte instant bi, ay matar li meunone naa niak d ken xaroula wone fi
Wakhal di li rafitol dawara rafit
Ndeysane dimbeulil mouride yi nga supprimé li tei yallah takh 😭😭🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Yalla na yalla bolè khol yi seytanè rek mo fy diarr mom rek moniou sonal mè lep bènla a touba bène yone kessè la tè yon bobou mo dieum al diana
S matar diéne wallahi li nga wakh lépou deugleu masallah
Wadial ziarr bi le 25 juin inchalla
Mangui ziar amna lollenne serigne saliou wakhone ,yene wa hisbou darou khoudoss té cassette ba mako deglou ,linguene didof amoul ndierigne té sene bop rek nguenne di lore, téyite yonou mouride ngeunne yapp malenko wakh lidou yare d'où teguine
Lou wer sakh🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Wakho deugg ap nafékh nga rek
Thi ay tiakhane keep ngen nek... ak Yap Serigne Mountakha ak wané ap niak kilifeu.. bi lii yeup xéwé danguen warone and dem si Serigne Mountakha ngen wakhko lepp ndakh molen wo banguen nieuw mouné len beugeu touma dégu niaar.. Serigne matar ioe mome kouma bét nga ap jangu katou xassideu waroul jikowo ni nga mel.. sa wakh dji dara rafetousi... Té limasi geuneu méti dégouma bén yone folen wakhé ni dém nagn si Serigne Mountakha nguir wakh ak mome si wakh dji.. Té moléne bolen yilif yen nieup
Ki enregistré audio bi yalna ko serigne bi wane bopam . Ligayou Serigne Mountakha bi mou beugu yagu dafa khamoul rék lisi kaname rawoul li geut
Vraiment Christian wakh gua deug
Diéne yow dangua wara nopi. Thiarakh yi serigne youssou diop di sanguo gnola gueune. Yémal
Yalnasi yalla déff ndokhe mou sédde
Amine AK respecter sab nawlè
S mountakha dafa dieul Youssou Diop tékko séne kanam topléneko té doyloko té linguéne Di wakhtané diaroul madiatisé
Ko bakh djolité dou yé fitena li waroko dogall sa pass RUclips ndakh daye yakhe magui top nk
Yalnala sëriñ bi guinediiii
Likat wakhou bir leu da waroul sakh ndakh limouy yakk mo eup limouy défar da eupeu tassaré thi internet
Boulene gnawal lou gnawoul
wax diou bari rethiou motchi top Serigne Atou est parti se reposer respectez son Ame
Nul n'est indispensable dans le Mouridisme Wax diou bary diu mbiry mouride
Matar Diene beteganou lolou reik, jeuw reik ga fi done def ak wax jou niaw si Segne Atou Diagne mi Yallah Gueureum, sossal Segne Youssou 🤔 Li niawena, mane bokkouma Ht bokoumq Htdkh waayeih Li ken xamoul lanela.
Li môme wakh déug dará rafitouci bilahi
Matar nelaw nga Bilaahi
Corrigé votre titre c'est pas une audio fuité
Wawgore wayy
Bilay
Bly
Effectivement
Mhakttar dine mi ku rewu laa 😊😊😊😊
Ndaisan yalla na serigne Touba safara lépou barque khassida yi
S matar dién dall darra wakhoukofi Lou paggé diaroull nétali li seringe bi beuge dall bou ngéun ko défoull nékouu len ci dara
Li rekka wér
Rero amoul gnaka waxtaan rekka ame kou kham serigne matar khameni kou neew ay kaddou la. Ande leine liguéyal serigne bi nguir ndigueul Li ta ngueine geuna rafetal. Koussiy woute fo far danga nafekh ta loubakh gnoroula.
Li publié ko rafetoul wakh deugg
Tassarè wakhtanouw diambour tê yegouko bakhoull
Yalna serignbi bolewaat xol yepp yon wi mom thiow moko lall mais lepp si tekk lay moudieh barki khassidayi
Bayyilen jaxassé yawcxammo Matar Dienne fumu bok ,ngay jaxassé say terme
Waxe dji moy nekoleine si yone. Srg bi bollé leine gneine dieule sa yonu bop
Matar diène yay sama Idole way wakh dji rafetoull dara
degue mome degue rék la ma donne
@@saliougueye8773 Serigne bi mangui toup dé🙏 way pour man mbir mi dou question de ki mo né ci deugg wala détt ndigeull molén bolé bou démé ba am ay diouwolo délou watt lén ci kalen diokh ndigeull bi boudé khadjo moy li guénn mou khadiatt ko kouné délou watt sa langa nekon amna yo khamné waroull guénn sén birr ba kouné di ci diott Mouy niarri Hizbut tarquiyah yeup louway ték sén kaw ci kaw yonou mouride ngako ték nakh danio soll mboubb liguéyeul kou tédd ki wakh dji meunon na niakk matar diène nak nieup kham nagn pass passam ak tolouwayam ci liguéyall kou téd way dieull kadu yi di ko ték ci kaw gni nga bokall liguéy bi rafetoull dara
Kham ga degue mome degue rék la ma donne té boko wakhoul taye wakhko souba
@@t-free7908 deug la 😔🙏🏾
Corrigé votre titre c'est pas un Oudio fuité
Yalla nalén yalla mousa thié saye tané
Nagne bayi wah dji ta def li serigne bi beug wah bou beuri bou yagé dagay sof attou fatou na bayil wah si deram
Cëy yalla Serigne Touba dal kéne la dou niar béne la wa darou khoudouss ak HT bokou ñu ridmeu dioxine
Kourel hizbu tarhiya=kourel daru khudoss ❤❤❤
Wakh cikaw wakhci soufe wiki n'a feqla segne Yousasou rawnale'ne
Ndeysaan pastéef yi ñoo rëy rek 😭🙏🙏🙏
C'est vraiment déplorable... attention aux résultats des réseaux sociaux
Ceey Souñou Yoon Wii Seriñ Nékatoufi Deii Sene Bop Ak Sen Bakane Reik Nguén Jiital wayer Yéna ngui wor seriñ tuuba
Matar Diénn say Kadduu Dara Rafétoussii
Machalla Serigne matar❤
Aba saque talibè. 😊
De leen bind looleen xam fenn baaxul lii de asambole seneraal am ay videos ganaan daa fiyite
Diafé Diafé you melni daara jo deim fekk kofa… Serigne nakkarei defal ci bilé jamono
Ki day par par Lo ta li s mountakha begu m’on nekousi bague daradja bakhoul
S Matar Diene waagnil sa thioowli …!!! Serigne Mountakha S Youssou Diop moomla djiiteul si kanamou mbooloomi… tu critiques trop même avec S Atou niiilawoon !!!!Rousléen Serigne té baayi séen thiowli
konn bou guissé deugue dafa wara nopi
@@pilotepilote3574 néekoul deugg yeupeu laniouy wakhtaané si am péeńchie .. sa waay je connais très bien Matar Diene depuis 1994 nioo néekadoowoon Hizbutarkiyyah (Mermoz Dakar) . Il était toujours comme ça, il critique trop…..!!!! S Atou Diagne (Rahmatoulahi Alayhi) il à donner toute sa vie à s Touba …!!! Nako niaanal mais amatoul pour diko criqué
@@daoudandiaye7706 waloum kham gui nga kham Matar Diene amalouma ndieurigne walahi so meuné sah khamalél samay wadiour wayé deugue mome amoule pinthieu amoule wagne deugue deugue rék la mann mome sama bopou doynama seukk si khamlou.
@@pilotepilote3574 sa waay maslaha ba am li-ngueu beugg , moo gueunn khouloo ba am li-nga beugg…!!! Wakh deugg si soutoureu ba am li-nga beugg , moo gueunn wakhko sim pincthie ba amko…!!! Kheutt-kheutt sootaloul dará khanaa gnila waroul khamal , khamala kessé, problem boufi nit exposé, nit amnafi problem bouko gueuneu graw té kéneu khamouko, basi sounou keur kilifeu yiii niou yaakaar
@@pilotepilote3574Waw kham bímako kham amalnama ndiarign,mootakh ma meuna wakh tay si moom ,même sa waadiour yooyou ngay wakh bouma sanioon khamléen… ndakh ak khamé meunaa diourr ndiarign
N'a hizbut yi moytou chaîne bi DAKAR 24 TV
Souma sanione nguéne signaléko youtube
Waroul Di djeul ay audio fuité you wa daara dji diko publié bou mélni bou mot talla wala Matar wala djeuwrine, naniou moytou chaîne bi naniouko signalé, yackeu reck moka taxa diouk
Bayyi lene féne lii du audio dako wakh mu thi sene dajié ba mu lér lool bayyi lene féne makhtar amul diotu djieuw kéne amna vidéos bi mu lér ngeni féne xaliss diaru ko
Yalla na niou yalla mouseul si saytane wa
yallna yalla déf diamou
Serigne Mountakha limu beugg soko beugone di nga bolé lila nekh ak lila nakari mougn ko nguir waxi Serigne am naam
C honteux koussi bayiwoul group whatsapp yi kham
Toute ta parole c'est une déception vraiment tu m'as déçu ioe bolobi nêkhoula parce que tu ve la concurrence tu ne veux pas mettre derrière Abdoulaye Diop Yoonwi fawwou am kou djiitou.
Kou baakh ngaa baalma degofii concurrence deh malheureusement la question est beaucoup plus profonde je sais pas est ce que t'as bien entendu des propos,je t'invite à suivre l'intégralité de la conférence de presse de Htdkh.
Jajeuf leep defaar rkk
Ses *
Sa way li dh yaw rék Yako waxe té diguaci wétt Serigne Matar khassida moko gnor ak Serigne bi. Boudé diangue moko dakh kokou guakoy teukeulél. Kokou kay moko meunoul degerer té naguouwoul s. Matar diène djitté.
Li Kiko enregistrer naaffék gou mak la
Billay !!!
Li ag la keine enregistre ko en direct la wone leral na lepp bayi leine di wakh loleine khamoul
@@Goraadieng xanaa du nit aki noppam mooko duggël ???
@@Mouride961 en tout cas deleine wakh loleine féké li dou enregistrement vidéo en direct la wone sur youtube
@@Goraadieng lolu gis naako murid kénne waxufi Ay fén
Dafa fékni ni Li génne gi baaxut
Mënoon na nék luniuy waxtaané
Aw thiow su amé demoon ci serigne bi diis ko dafa doon gën
Ngir noonu yaagi fi fess délle
Xaarugn ludul sugn gathié
HTDKH à vie
Wawaw
Bougnou fi bayi
Naniou khamni Abe mouride bou diefewoul ndigeul yague ayda dialloul yena yame
@@amdyfall7699 walahi
Lii mom du waxi Dara
Yàlla sëriñ bi tappé xolyi
yalla da bègue koye rafétall waye boull bègue aye abonné you bari rk mo takh guaye tasare wakhi djamourr ko bakh boko mane dini gua deff ko. yalla mogui fi guemoull nelawou te lofi guiss rk daye djekh waye na rafett gua balle ma akh nk
Ab dioullite bou nopalou ngakoy wakh Lou niaaw bett ngama dh
lou niaw lou mel nane lako wakh
Djara djaf matar
Li moom dafa wara dagn ndakh wakh dji dafa gnaaw te darra dousi deug
Dagay doul dee
Bëgg aduna rek molén japp matar mom mëusoul wérr
Vous nous emmerdez
Yalla weerna leen deh. Ndekei lingeeni tiim xasidayi di jang yep yalla taxul. Ay xeuthio, ay dieuwanter, mbirum adouna rek
Matar Diène bétt namaaaa bilae😭😭😭
Bett lolll lou mou wax deugu rk laaaa mouride dou odio fuite deehh
Bett comme kii nekk si mbolo di wax mou naan ayy 🎤 weurr ko
Deug rk nga wah s mahtar gainde deug nga mat nga linga doon seuk
walahi défaro gougnou
nane fékhé défar sounouye dieumou té bayi wax diou bari dji
Li vidéo la bayi léne wakh audio Whatsapp déléne wakh dege
wakho wakhi kubaga manda dé diawrigne
mane nk magui kité sa passe merci 🙏🙏🙏
Yalla na Serigne boolé lèpp inchallah
Kadouyi amna solo machalla
Nêga kilifa ga ta kilifa do nêtali
kilifa dou waxee niii mofi takhawon ni leup ben la
Mom da Goré motax mou wax lolu yen mandou lén
baye matar lamou wakhon masol ci déllo Ganaaw lomo deuge la
Mom khamna daa seuss rek wayei seugn bi keppaka nior
Darou khoudoss mo léér dh Youssou diop djouboul walahi epuis s mountakha magla Youssou diop dafa guer entourageou khalifa bi
Mba lingay wax wornala
@@salioundiaye6697 bu baax motax mou wax ko
Moh man de li wakhon nako
Naniou moytou di niaw ndiort thi niom moo gueun🙏🏾
@@مريدالله-ح2ض djarna bayyi khel dh ak lu mana xew
Mais li dou audio fuité xana dégo ñiy wakh si souff
Sa titre bi dindi ko Li dou audio whatsap bay fuité
Ayway dara rafèttou thie khana lepp dou serigne touba sagual lenne cheikh mountakha
Beug daraja kepp
Mangui wadiale Ziar bi
App Mouride deug dou dieuw 🤬🤬🤬
Lii dou audio fukté dh khana dégoo wakh yii si souf
Dye dul rek😂
Ki weroule doff deug leu domerame pirr monguini
yén gni hamoul guir dieumi serigne bi mandou lén si li dou audio reunion lawone thia daara ja
matar diene moom sou wahé rek seuss naa
Yaram liii kiko enregistrer ba tassaré ko waa daaradji war nagne ko guëstou taik ko aye daan you diss ! Magui laye toubal bou wair 🙏🏽🙏🏽
Des propos regrettable et triste vraiment 😪😪😪😪
Très regrettable même Serigne Saliou masna lena wo gnom gnep nelen bu ken salawloti Atou delen ko wax Serigne Atou ndax talibé budei soyoko guissei mou fatalila sap serigne waroko salawlou qui plus est kou guein adouna donc waro am yen seder yi ci mom. J'ai honte moi
Machalah
Beug beuss rekk
Asstakhfiroulah thieye matar amna Lou leral thi yaw der
li kay du audio nak saway
Li niawna