Khutba | Les dangers de Tiktok | Vendredi 09 Août 2024 | Oustaz Oumar Ahmad SALL
HTML-код
- Опубликовано: 10 фев 2025
- ABONNEZ-VOUS à nôtre chaine RUclips Daroul Birr TV pour profiter de plus de vidéos:
/ @daroulbirrtv
►Facebook: / daroulbirrwalirchad
►Twitter: / oustazoumarsall
►Site web : www.daroulbirr...
►Télégramme: t.me/joinchat/...
►Whatsapp: +221773769582
►L'application: play.google.co...
#sounnah #omarsall #sunnah
Oustaze Oumar Sall Qu'Allah SWT vous protège vous assiste et vous récompense d'ici bas et dans l'au-delà❤
Allaahuma amiin
Amiin
,amiin
WER AK GOUDOU FANE AK SOUTOURA ADUNA AK ALAKHIRA YA OUSTAZ. WAXTANE BI AMATINA SOLO
Machala oustaz comme d’abitude amatina solo bon courage et bon diouma
Wallahi Yalla rékk moléyy aarrrrr, maachaAllah, yaguignouy délowatt thi yonou ndjubb.
Diarama Y'a Oustaz l'homme entier.Machalah.Yalla nala yalla mousseul si pékhéb noon
Masah allah li dh Lou âme solo. La lôl ❤❤❤❤
Amna solo lolou
Oustaz alhamdoulilah bayina déf vidéo Tik tok
Al hamdoulilah ba deug khoutba Oustaz oumar sall bi vraiment li dina khékhal sama bakane insah Allah dieuredieuf ya oustaz 🤝🙏❤️
mbokk combat bu sheytan doul baye niu bari la dane, ndakh metit mais dafa am lunu fatté, niane guissouma nganay bouco gueuneu deugeur, su deggu rek tamu andeu ak ikhlass, sunu borom diapaléla si combat bi, may taqwa abadan kel bonheur eternelle yalla nanu yalla may moussal niu si sunu niawtefi bakkane
Vraiment il faut que les.senegalais écoutent. Ce .grand imame
😢Amatina solo trop choukrane ❤❤❤❤❤
Macha Allah ya oustaz que dieu vous protège et ta famille
Machalah dieuredieufe oustaz oumar Ahmad Sall louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye billahi deug rek nga wakh nga Lou ler nga wakh sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna
Tellement vrai une triste réalité de notre société yalnagnu yalla dioubeul si yon bu bakh bi
Alhamdoulillah ya Oustaz🤲🤲😊😊merci pour tous, et vos khutbeuh sont tellement importants, instructif que domma cii doyall macha'Allah🤝🤲👍
Machala khoutbah bi am na soulo torop
Machllah 😢
Dieuredieuf amna solo nékhoul dég dé mou lérr nga wakh parfois ma guiss djiguén di diangue alkhour’ane à visage découvert sur les réseaux sociaux alors c blâmable hasbunal laah
Yalna nu yalla khiir ci dég ak topp
Allahumma amine
Machallah Ya Oustaz yalna Yalla fayleu yiw
❤❤❤Vérité totalement absolue que au bon dieu te protège dans le reste de ta vie
Yalna la yalla fayyyy ya oustaz
Tu es vraiment un champion !
Moi j’ai pas tiktok Dieu merci
ALLHAMDULLAH MA SHAA ALLAH KUTHUBA BE AMNA SOLO TROP
Machallah oustaz waxtane yingaye def temps que nitt diarou si douko kham ❤❤
L'Homme aux inspirations extraordinaires mashallah allahouma baarikk ❤
Jërejëf yaa Ustaaz yalna YALLA fayla yiw te defalñu degg ak topp
Yalla nala yalla sambeu maÿ'la wéér bou bakh mash'allah ya oustaz Ahmed Oumar Sall
Allahumma amine yarab
Machallah ya oustaze yazakallahou Kaïra ❤
dieredief oustaz yalla n'a yalla saamla
Lérr na ya oustaz yalna la yalah samm
جميل
Machallah yalna yalla faye yiw
Le monde d'aujourd'hui va trés mal franchement parler surtout nous les muslimans que dieu nous guide un bon chemin et donne une bonne fin Allahumma amine yarabi merci encore ya cheikh pour tes conseils longue vie à vous ❤
Allahumma amine
Merci beaucoup alla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashallah ❤❤❤
Maa shaa Allah oustaz qu'Allah vous récompense
As Salamou Aleykum Waraahmatul’lahi Wa barkatuh
Wallahi Oustaz ligueu wakh kén mouno tégi parce que lou am leu Motah niogui lay ñianal Yalla nala borom saam leu may leu goudou faan ak wérr
BARAKALLAHU FIK WA JAZAKALAHU HAYRA ❤
Macha allah yalna yalla samla arla
Amna solo MaChallah💚💚💚🙏
Macha Allah ya Oustaz amna solo
Mâcha Allah Qu'Allah vous préserve et vous récompense
❤ BarakAllha feek oustaz sall damala beugueuAlcouran ak sunna rek
Sonnu nga ndaysane 😢😭😭😭wayè nit gni. Fowè nagn sen adduna 😭😭😭
Aslmkmachallah oustaz yallah birombi feye yiw xamxam bi yalna yok te barrkel vraiment yemena yalnagnou yallah dioubale😢😢😢😢 amine
Amna solo trop
Que Dieu nous protège surtout ensemble
Diereudieuf ya oustaz Allah bheydou djam et diounou mbaldé 🤲🏾🙏🏾
Macha Allah ❤❤❤❤merci beaucoup ya Oustaz
Mashallah
Masha allah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Barakallahou fike Oustaz ❤
Yalnala YALLA fay yiw Oustaz ❤
❤❤❤yalna yalla samou la ya oustaz
Macha Allah vraiment merci ❤❤❤
Dieureudieuf Oustaz
Machallah choukrane yalnala sounou borom faye
Tic tok est même utilisé chez les personnes âgées et j'en ai témoin et
ces personnes là n'ouvrent même pas le coran
Masha'Allah ya Oustaz amatina solo Qu'Allah nous guide
Ma cha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashaallah ya oustas may Allah bless you ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤machalla amatina solo
Machallah amna solo yalna oustaz ❤❤❤❤❤❤
Yagueu fi té wéreu ya Oustaz
Vraiment ❤
فمن شاء فليؤمن ومن شاء فليكفر❤
Masha allah
Machalla ❤❤❤❤❤❤
Bilakhi guiss niou organisé louniouy wowé événements religieux ba paré tékk s3nn cheveux défar sénn kanam pose sénn wéé agg khéff vraiment yal na yallah soutoural niou té wonn nieupp yonnou dioubb. Oustas Yal nala yallah féyy
Machalla ya oustaz amna solo
Ma cha allah
Que Dieu vous protège surtout oustaz Oumar Sall mais jusqu'à présent je n'ai pas reçu de notification pour la rencontre
Alhamdoulilah ❤
Macha allah
Macha Allah amna solo
Mashallah ❤❤
ماشاءالله جزاكم الله خيرا ❤️❤️❤️
Vraiment oustaase a hali goonga kala debbo murniino wiye ibaadu
Machalla
Machallah ❤😊
Akay deugg parfois tu pries booy seulmeul ballaa ngaa commencé wird sakh kheuthie téléphone bi nek si ba bayyi say niane😢
❤☑️
❤❤❤❤
❤❤❤ ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Lolou mome deugue leu da ngaye dougou tik tok beugeu geuéne mou méll dagne laye té ❤😂
Lolu top seu baken leu rk ta ya mom baken bi man mi WiFi la yore am possibilité bi ta meusouma am tik tok yeuf deuf deug moy tik tok
@@fatouba2560 yawe dh Kone dall nga si 😂
Bro xéxalale sa bakkane bouka baye mou meune la. Mane ma gueunone accro či Tik Tok ak sites you baxoul yi mais un jour dama xamni ça menaçait mon avenir @AliouneToure77
Walakhi degue bou were la
TikTok walahi bakhoul mane perso je l avais meussouma publier je ne sais même pas comment faire des vidéos avec mais si CAN bi lako désinstaller parce que demadone tontou ay commentaire biniouy khass SN patriotisme moma sonal à un moment donné je me suis dis que ça c’est pas bien car je devenais méchante dans mes commentaires motakh je l’ai désinstaller c’était pas le comportement d’un bon musulman wakh lou bone warouma
Je me suis pris la tête avec mon mari pour tik tok comment on peut interdire sa femme de s exposer et regarder d autres femmes qui s exposent sur TikTok dans la vie il faut avoir des principes Lou haram haram na rk
🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
numéro Oustaz Omar sall la beug c'est urgent
Xana concours Alxuran dafa xaram Djiguéne bokkou cii🤭🤔?
Qui peut m'aider à rencontrer oustaz Oumar Sall ?
Demain à castors ou bien à Jaxxay terminus 84
Lissa bou sonko kaay wouyou😂😂😂😂
Kane moy Lissa?🤔
Deug rek der lay wahk
Prophète Muhammad dawoul wakh Olof li bida la
Yonén tebi( saw )gnimou dane wakhal arabe lanou déguone yaw lére namani boudone wakh arabe dossi khamdara
KI DIAROUL TONTOU NDAKH XAMEWOUL LOUY BIDAH C TERRE A TERRE DE DIRE LE PROPHETE PSL DANOUL WAKH WOLOF
Mais yonén tebi gnim daan. Wakhal arabe kassé kassé lagne degg degou niou bénene lakk
Yaw nékkal nitt
Yow yaa torokh .
Machallah
Machalah ❤
❤❤❤❤❤
Machallah
❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤
Machaallah