Ok comme moi ‘ en tout cas il y’a un lien que l’on ignore moi en tant que Mouride. Ce Khassida est plein de rimes comme les ceux de S Touba Yalla rek@@@@
@Fadel Ba yow li sa way wax mo gueune dioub ce sont des "chansons" mais "religieuses" si tu veux alors que "taïssir" tourou bèn si tèré Magg yi la com burd et autre.. on dit un "khassida"..
Je suis un fervent mouride mais j'adore cette chanson. Chaque fois damay nieuw fi diko deglou. Yalla na diam yag fi sunugal. Machallah Doudou Keinde ci ndiangueu mi🙌🙏
Mane dey mourid laa mais wallahi maangui seedé thi yalla ni limay yeuk heur boumay deklou khazida gui mane Ak yalla rek niooko xam Yalla na yalla fayal niou sunu maame sayidi aboubakar sy thi barkeb al xour aane
Je suis tidiane de père et mère...je prie ALLAH ( swt ) de nous laisser encore des années et des années notre très cher ELHADJI DOUDOU KEIND MBAYE ( amine ) ❤
Maachallah. Ya Allahou fayal niou Seydi Elhadji Malick Sy te tass niou ci barkem. Barke Sayidina Mouhamadou Saidou Rassoulallah salallahou aleyhi wa sallama tasliman . Amiin Ya Rabbal alamine !
Ma cha Allah...khole sedanaaa!!!!dieureudieuf Seydi Hadj Malick rta ak djabootam....Yalla na Allah Swt fayale gnoulene...si barke Seydina Mouhamed Sas...si barke Seydina Cheikh Ahmed Tidiane Cherif rta... talibe cheikh reck ba fawou.....
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️j’adore cette chanson il m’arrive de pleurer même en l’écoutant
justice pour tous ki boul ko tontou il n’est même pas Tidiane 🙏 talibé cheikh deugu Khamna kann moy gueunn di mbidefff té douko teukkeulé ak kenn rassoulilahiiii moy gueunn di mbidefff dou kenen sikaw souf rouss na sa touram bi nak
Je suis mouride qui adore trop ce chant tidiane dafa nekh way machallah ziar sama Serigne Babacar Sy yalla yokk leram Tass gnou thi barkem
Amine ya bax
ndeyessane ya bakh beug lou bakh
sa khol mo rafett rek
Ioe yay borom kholou diamant bi
Machala
Je suis mouride mais j’aime beaucoup cette chanson ❤️❤️❤️
Je l’ai cherché et en fin je la retrouve alkhamdoulilah
Machalah fière d’être musulmane
Alhamdoulilah...
Ok comme moi ‘ en tout cas il y’a un lien que l’on ignore moi en tant que Mouride. Ce Khassida est plein de rimes comme les ceux de S Touba
Yalla rek@@@@
Man itame amna khassida yo khamni dafmay danél 😂❤🙏🏾 alhamdoulillah
Machalah lou bakh nekh si hol
Fière d’être musulmane ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoulilah louma weur khassida bi pour meune ko diang fier d'être talibé CHEIKH YALLA nasi deh
je suis mouride mais j adore les chansons tidianes elles sont tellement magnifique vive notre cher senegal
Aliou Faye bilay dagua bakh RK . amine Sénégal RK mo am li yalna diam yague fi
borom bakh nga motaxx nala yalla fayy
Que vous bénisse alioune faye djeredjeff
Aliou Faye que le bon dieu vous bénisse
@Fadel Ba yow li sa way wax mo gueune dioub ce sont des "chansons" mais "religieuses" si tu veux alors que "taïssir" tourou bèn si tèré Magg yi la com burd et autre.. on dit un "khassida"..
Je suis un fervent mouride mais j'adore cette chanson. Chaque fois damay nieuw fi diko deglou. Yalla na diam yag fi sunugal. Machallah Doudou Keinde ci ndiangueu mi🙌🙏
Ci njaboot gui ngeu bookk batay
Yeepp been la ❤
Talibé baye qui adore trop ce zikr❤Machalah ndiabotou cheikh Ahmed tidiane chérif rta🙏😍
Mane ak yow damako wër ba diko dora guiss lii nékh trop si xol
Je suis mouride baye fall mai zikr bii dafmay dougue lolou !..yalna diam yague
Amine
Mane dey mourid laa mais wallahi maangui seedé thi yalla ni limay yeuk heur boumay deklou khazida gui mane Ak yalla rek niooko xam
Yalla na yalla fayal niou sunu maame sayidi aboubakar sy thi barkeb al xour aane
Amine
MachaAllah yallah na yallah Barkél
Amine ya rabi
Mouride tidjiane lepeu beneu leu dieuredieufè borom touba taissir bi si khol lay doug nekh na trop machala 🙏❤️
🙏🙏
Machalla dounde kene mbaye yalla kha fi yague te adak werr fier detre talibe cheick 🙏❤️🥰 ken dou serigne babacar si
😭😭😭😭😭😭😭😭 alhamdoulilah bima boké si tarikha cheikh dieureudieufé yalla sounou borom
Nagne wakh alhamdoulilah rk🙏🙏
@@aminagueye5746 toma
kou beugue doudou kende mbaye pouce bleu
Je suis tidiane de père et mère...je prie ALLAH ( swt ) de nous laisser encore des années et des années notre très cher ELHADJI DOUDOU KEIND MBAYE ( amine ) ❤
Amine yarabi ❤
Ndeysaan je peux plus m'en passé. Yalla nagnou yalla fayal Mame Maodo ak ndiabotam
Mbay Baabakar Tijaan dëgg la, Yal na ay leeram dollee bërëxi barke Sëriñ Haaji Maalik Sy ❤️
c'est tellement apaisant!!!! que Dieu bénisse ces hommes way
Bilay
A chaque fois que je l’écoute je pleure jusqu’à la fin c plus fort que moi ❤
Bilahi lolou MoMA dal sama xel yeup dem si sama papa yalla yesal yeurmande si môme ak bolem dioulit bou djitou si BARKE KOU TEDD Ki. Psl
Khassida bi souma koye deugeulo dioye rek la def. Yalla nagnou yalla fayal khalifa babacar.
Amine barri gua si morome
Haja Qalbi ❤!!! This goes deep in my soul… I can listen to it for hours ❤
Dieuredieuf serigne babacar sy thi la gua waye maodo daw na yarame.
oh j'adore bcp ce taysir a chaque fois ça me rappelle les préparations du gamou
Moi aussi
Bon Mawloud à toute la communauté musulmane ❤️📿🤲🏽
sangue bi hawouma nimalay def sama yaram day daw soumalay deglou yalna ya 'allah feyla thi barkee cheikhoul khalifa li nehna thi hol
Palaye Niang yalla nala yalla faye
Walahi machalah amine
@@madeleinedieyeamar8547 amine ♥️🙏
Ken bou mame Serigne Babacar sy fier d'être talibé cheikh ❤❤
vrrrrrrrrment limaye yeuk sama khole bi sou maye deglou wayou tidjane yalla rek moko khame
li nek cibir mo fort
Serigne babacar sy amoul morom
Machalaa sa me fait toujours pleurer et je sais pas pourquoi😭😭😭❤
Bilahi
Machalah j'aime trop cette chason je l'écoute à chaque matin quand j'aille à l'école
rahimalahou cheikh al khalifa mina nabi ina wa sidiqina wa chouhadahou incha allah
Amine ya rabi
Billahi li nimou may deff wallahi
Mouride la mais li mom amna louma bolé ak mom❤❤❤❤❤❤❤
Yalna diamou sax Sénégal
Je suis Mouride mais lii nekhna lool vraiment ❤❤❤
Puisse tu vivre longtemps en bonne santé et continuer à faire vibrer la cours tidjania. Aamiin bi nurul Rasuul sallalahu aleyhi wa sallam.
Palaye Yalla na la borombi SWT faye si barké Mame MAODO MALICK SY RTA
Maachallah. Ya Allahou fayal niou Seydi Elhadji Malick Sy te tass niou ci barkem. Barke Sayidina Mouhamadou Saidou Rassoulallah salallahou aleyhi wa sallama tasliman . Amiin Ya Rabbal alamine !
Ma cha Allah...khole sedanaaa!!!!dieureudieuf Seydi Hadj Malick rta ak djabootam....Yalla na Allah Swt fayale gnoulene...si barke Seydina Mouhamed Sas...si barke Seydina Cheikh Ahmed Tidiane Cherif rta... talibe cheikh reck ba fawou.....
Ça me rappelle mon enfance ndeysan.... Je suis mourid et fier ms les mélodies religieuse je les adore toutes
Dieureudieuf domou yalla mi am fay yalnala fay thi lou doy war lii,nekhna machaAllah
Ndeysane yallha naniou yallha fayal suniou mame 🙏
Thiey Serigne Babacar sy kéne khamoul lanela ndakh ay kémtane
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️j’adore cette chanson il m’arrive de pleurer même en l’écoutant
jeureujeuf Palaye Niang yalla nala Yalla faay si barké serigne Babacar
Bilay nexx n’a trop barki alhourane je sui mouride mh souma ko deglou sma xol toy
Mane mi Tidiane la mais khassida Fuzty nonou lamay deff
Je suis mouride mais j’adore
yeuk banekh soy deglou lii rek diarna diamou sounou borom Ba lakkou li nekhna
Machaalla
Yonou tivaouane lamay fatali.hadji Malick je vs aime au plus profond de mon coeur.maodo merci pour lep li nga niou defaral
Kene dou serigne BABACAR SY !
Jeureujeuf MAME MAODO
Barke Serigne Touba son nimou ma nekhé🤲🥰🥰🥰
Sa me rapele lorsque on quitte walo pour aler au gamou tivaoune le temp passe vite
palaye vraimment contane na...fo tollou waqal amine
Kén dou serigne babacar
💖💖ce khassida doumassi doyal
Taysir
Alhamdoulilahi le soufisme senegalais est d'une richesse incommensurable
Doudou kende mbaye yalla na nga sout sa baye ba fane mashallah lii dafay sedal xol diarama mame maodo malick
De confrérie Mouride oui
Une chose a précisé toute les chemins mènent vers le tout puissant ❤ alors ne nous attardons pas sur dés futilité
Mashallah Doudou yallah borombi doli diam ak wér pls amin
Yalla na yalla fayal Sèrigne Babacar sy 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
man chala .yala na yala fayal gnou sougnou mame you baakhyi
yalna ya'Allah yokk kheweul yi..... dieureudieuf
Je pleure à chakk fois k j'écoute cette chanson😭😭
Dippe lene tarikha tidiane bolene bougué moutje eulegue
MACHALLAH Palaye Niang yalla na yalla fay
kenne d'où môme mame maodo malick kée manchallah
Bi Moune nama Ray j, aime bien ❤❤
Machalah palaye louma yague weer
Souniou khole yi yalla naci yalla dougueule gueune gui mbindéf té moye Serigne Babacar sy
Asteukhfiroullah Yonentibi moye gueune di mbindèf Serigne Babacar Sy dé santoula li nga wakh niii war nga toube dé😢😢😢
justice pour tous ki boul ko tontou il n’est même pas Tidiane 🙏 talibé cheikh deugu Khamna kann moy gueunn di mbidefff té douko teukkeulé ak kenn rassoulilahiiii moy gueunn di mbidefff dou kenen sikaw souf rouss na sa touram bi nak
@@aminagueye8873 merci beaucoup tu as tout dit diereudieuff
Mashallah tidjania cheickhou Tidjani cherif radiallahou
JE SUIS TIDIANE ET JAIME SERIGNE BABACARE SY
Dieureudief palaye yalla nalla yalla faiye
Machallah doudou kende mbaye
Yalla na yalla goudal sa fane papa doudou
Sama khôl bi dafa sede gouyou😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
machalla xol sedana barki cheikhal khalifa
Yalla na Yalla faay sounou Mame Serigne Babacar
Merci pour cet excellent travail
Quelq'un aurait il l traduction svp?
Ça me fait pleurer Walahi yalla n'a yalla wereul bate bi
yalla nagnou yalla fayale mame maodo sy malick
tchey dudu machallah
Merci beaucoup. Yalna nga am djamm
Na la yallah Fayyye...Mome rék mo ameu sa faayy
❤❤❤❤❤❤❤❤❤baye ass mbengue repose en paix 🙏🙏🙏
Fier d'être tidiane
De mm
DJEUREUDJEUF KOU BAKH MANCHALAH PAPALA
Mouride la mais walahi song bi nimoumay def manoumako expliquer 🥰🥰🥰🥰
Dieureudieuf yala nala yala faye
Lii nekh na dh 💝💝😘
quelqu'un pourrait nous donner la traduction en français ou wolof, c'est d'ailleurs le plus important pour un xassida qu'on apprécie bcp
Je cherche aussi la traduction. Mais ce que j'en sais c'est que Serigne Babacar Sy a chanté son père dans ce beau poème
diereudj Sy Malick
Non li dafa nekhe trop gamou rek lamaye fatali❤️❤️
Ma Chaa Allah
Diarama Mbaye❤
No li dafa nekh Barki Serigne Bamba
Yallah na yallah fay yiw 🤲🤲
Macha Allah j'aimerai voir les zikr de Doudou Kende les plus anciens
Machalah
Machalla li nekhna trop
Ooh😂li nekhna torop waay machallah 🙏🙏❤️
bilahi li dafa nekh trop
Likaye dafa neckh ba dack nékhe kounékoul tidjiane boko
MaachaAllah.
Merci
Ndeisane,hol sèdna,yalla na yalla fay yiw
Ma shaa Allah ❤
Masha Allah. Jazakkalah khayr...
J'aime cette chanson