El hadji Assane dieureuedieuf li xeow si djiguen yoyou li ma rouslo moye ay djiguen nioko def sen moromou djiguen Lou niaow si werou kor ana Mougn ana Soutoura ana bakh
Walahi. C'est triste notre Sénégal. ADJA ASTOU niit rèk leu, niit koudoul dioum amoul. Goor kéneu douko topeu bamou seuss. Love u ADJA ASTOU CISSÉ 😘😘😘😘 mougne tane Adouna ko méré.
Au Sénégal y’a des gens qui son malhonnête mais dieux est grand Yallah nassi yallah def diam rek El Assane Geuye & Abba discours bi rafète na ❤️🙏 Le procureur a d’autre chat à fouilleter 🤔
Bilah vous avez raison soutoura c est très important je suis halpoular mais avant tout un être humain penda ly avais dit pure sur les wollof pourtant ils ont eux la grandeur de pardonner 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Aimez votre prochain comme vous aimez votre propre personne. « L’amour est plus naturelle que la haine. » Ne sous-estimez ne minimise personne car « La compassion est plus puissante que la colère. » Soyez bénéfiques les uns aux autres. La vie est courte et elle ne mérite pas la haine, l’envie, l’hostilité, et la rupture des liens familiaux et fraternels. Si quelqu'un vous fait du mal, efforcez-vous de penser que celui qui le fait, le fait par ignorance. Rappelez-vous que toute âme qui s'élève dans la vie rencontre beaucoup d'opposition de la part du monde. Il en a été ainsi pour tous les prophètes, les saints et les sages, aussi personne ne peut s'attendre à en être exempt. Respectez le patrimoine des autres et protège le tien. Abstenez-vous de leur causer du tort. Faites le bien autant que vous pouvez autour de vous. Pardonnez aux autres qui vous ont fait du mal et qui vous ont blessés car « Le pardon est plus grand que la vengeance. » Vous ne le regretterez point. Nous subissons l’épreuve de la vie pour purifier nos âmes, devenir des pieux et mériter une place au Paradis. La finalité c’est d’obtenir la grâce divine.
Reprenons nos esprits !! Le mal se combat par le bien !! Cultivons les bonnes valeurs afin de semer dans ce monde la lumière, la paix, l’amour, la fraternité, l’harmonie, l’abondance, le respect, la confiance, l’intégrité, la gentillesse, la sagesse, l’humilité, la bonté, la générosité, la sincérité, le pardon, le partage, l’entraide, la solidarité, l’hospitalité, la tolérance, l’espoir, le bonheur, la compassion. Travaillons dur pour gagner honnêtement nos vies et développer notre société. Cherchons le savoir partout car une personne sans savoir et sans culture est une personne sans identité et sans repère. Accrochons-nous fermement à ceux que nous aimons, exprimons leur notre amour, pardonnons leur leurs erreurs.
mon frer QUI OFFENSE UNE COMUNAUTE AU SENGAL TOUCHE TTS LES AUTRES LA TOLERANCE DOIT PRIMER SUR TOUT ON EST DES MUSULMANTS ET AUSSI LA FEMME qui a dit ca est une halpular pur et dur lo beugue mou teud kasso pr des violance verbale sa way yermende rek aduna amoul solo
Dioume diégalou kay doyna mais faw niou nk sii lii rk té am Lou eupe foula foufff lounou wara lidianti yalla naniou yalla doli soutoura bou beuri si barké yonéte bii psl
En tout cas soof guenne dh xana nitt bou waxer dara balou guene mane noppi beugue ay ba dead elle à dit au paravant les viols plis étaient récurrents chez les haalpulars avant elle a bien dit yenn yi mome niak deugg toubab la thiiim
leur beauté les pousse à être des journalistes mai qualification zéro dème lène diangui c'est mieux patron de presse yi nio ndara yakk Sénégal te kou diouk niou diokhla micro ga nèk si kanam TV di wah du n'importe quoi désormais douniou ko nangou dème lène diangui c'est honteux
danou warraa def kouffii video pour yeee fitena niou nicko rappe ci kasso bi mou khamni reuyeul wax ak yeee fitena niou teck len fitena bou tarr sene kaw kouffiii dagatiii video pour yeee fitena rk niou defko ci kasso bi goor ak djiguene bassi site internette yiii ci lep nak politique , stars yii ci lep nak surtout boy yiii dii def video dicko postè dii wax loulène nex genre saf yeek ak ketieup khawma ministre de intérieure doit prendre c responsablite pour sa zero torerence
Le Sénégal n'avanceras jamais elle à commis ces erreurs elle à demandé pardon mes ou est le problème Penda Bâ à insulté tout une nation esk vous avez vue un wolof manifesté ? Bouléne gnou sonal waye Sénégal deukou diamoula li yeupe chomage moko waral
Salam elhadji assane j'avais bcp d'estime pour vous mais ce qu'elle a dit c tres grave pourtant vous defendez les voleurs quiconque vous avez insulté vous alliez reagir c pas une question d'intolerance mais de justice arretez d'encouger l'impolitesse
Tu n'as rien compris. Il ne cautionne en aucun cas ces propos déplacés, il prône le pardon et la tolérance et dénonce la justice par soi-même. Togne dou togne mokoy résoudre.
@@khalilseck6833 desolé c toi qui ne comprends est ce quil a denoncé les propos nit bou togné dans ko wora wakh deugue ñawlou kadouyi c simple pour ten il denonce les commerçant qui font justice eux meme la deçu on en disconvient pas on ne fait pas justice soit meme au lieu de proner le pardon il faut dabord condamné ces propos injurieux
Mya Diallo ani sa yeurmandé mane mi tout mes descendants sont des toucouleurs et après 💁🏽♀️je lui ai pardonné dafa fauter lgui diekhna yaghi khalate ndiabotam dôme yimou ame
AU DELÀ MÊME DES PROPOS DE ADJIA ASTOU,VOS MÉTHODES ET VOTRE FAÇON DE FAIRE LE JOURNALISME HEURTENT TOUT LE MONDE,ON A PAS L'AIR D'ÊTRE AU SÉNÉGAL. GÉNÉRALEMENT NOS JOURNALISTES MAÎTRISENT PAS.
Pure veritè. C était. Pas la peine qu elle aille. A la gendarmerie On est dens le mois de ramadan il y’a d d’autre problèmes plus grave Qu on doit régler tout le monde se tait
Ce qu'elle a dit est controversial et c'est une grosse erreur d'avoir stigmatiser la communauté halpoular mais elle a demandé pardon à tous ceux qu'elle a heurté Dieu lui-même nous pardonne nos fautes et nos manquements pourquoi les êtres humains sont si vindicatifs? Il faut être humble pour reconnaître ses erreurs et s'excuser mais il faut être miséricordieux pour pardonner. Je voudrais savoir si elle n'a pas subi de violence au sein de sa communauté peut être qu'elle a parlé sous le coup de l'émotion et du vécu demandons pourquoi un tel dérapage ? Elle a peut être des blessures enfouies ? On est en Ramadan et les musulmans s'accordent à dire que c'est le mois du Grand Pardon donc les actions devraient refléter la FOI. Que DIEU nous donne la force de pardonner à ceux qui nous offensent !
Wa mais dou néna da dioum él à même demander pardon légui quoi ??? Wala les halpoular vous êtes dieux mane d bess bouniou yalla balloul founiou dieum inshh
yormal hiyame dina am nio xamni yalla day bal nieup sauf niome niounèko loutax ga bal gni balo gni mouni gni dawouniou balé kone meunou maléne bal guir yalla kou beug yalla bal la dél balè
Guene balma mais assane man andouma ak ioe vraiment kou leu fonkou la mais ki limou def mouna yakk reeww naniou tekk palace am vraiment dou fi lala done khar assane
El Hadji Assane , vous avez fait un analyse très pertinent comme d'habitude 👏🏿👏🏿👏🏿... merci
Yalna sa jam yagg
Bonsoir les ami moi je suis alpular me dans la vie nul et parfaite on dois la pardonne parce que c une mère famille
Wallay deug leu Aladji Assane mala beug ♥️
El hadji Assane dieureuedieuf li xeow si djiguen yoyou li ma rouslo moye ay djiguen nioko def sen moromou djiguen Lou niaow si werou kor ana Mougn ana Soutoura ana bakh
"Mbir nga top ko bamou Seuss baxul ." Merci Père Assane Guèye
seytaner
Walahi. C'est triste notre Sénégal. ADJA ASTOU niit rèk leu, niit koudoul dioum amoul. Goor kéneu douko topeu bamou seuss. Love u ADJA ASTOU CISSÉ 😘😘😘😘 mougne tane Adouna ko méré.
Au Sénégal y’a des gens qui son malhonnête mais dieux est grand Yallah nassi yallah def diam rek El Assane Geuye & Abba discours bi rafète na ❤️🙏 Le procureur a d’autre chat à fouilleter 🤔
Bilah vous avez raison soutoura c est très important je suis halpoular mais avant tout un être humain penda ly avais dit pure sur les wollof pourtant ils ont eux la grandeur de pardonner 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Vous avez raison Elhadji Assane il faut qu'on soit tolérant. Baye Niass dédone gnane Yallah Nanou Yallah moussole thi aye ak borom aye wa
Il faut pardonner d'accord mais il ne faut pas encourager de pareils propos
Sa wakh rafetna li laniou sokhla mak sou sage une jeunesse conscience mais pas des bla bla
Man lima diakhal yousou Ndour Sénégalais ye sonal nanko de yalla nako yalla diapale
Walaahi
J'aime bien bilahi bien dit aussi
Nit kou dou djoum amoul aduna amoul solo
Aimez votre prochain comme vous aimez votre propre personne. « L’amour est plus naturelle que la haine. » Ne sous-estimez ne minimise personne car « La compassion est plus puissante que la colère. »
Soyez bénéfiques les uns aux autres. La vie est courte et elle ne mérite pas la haine, l’envie, l’hostilité, et la rupture des liens familiaux et fraternels.
Si quelqu'un vous fait du mal, efforcez-vous de penser que celui qui le fait, le fait par ignorance. Rappelez-vous que toute âme qui s'élève dans la vie rencontre beaucoup d'opposition de la part du monde. Il en a été ainsi pour tous les prophètes, les saints et les sages, aussi personne ne peut s'attendre à en être exempt.
Respectez le patrimoine des autres et protège le tien. Abstenez-vous de leur causer du tort.
Faites le bien autant que vous pouvez autour de vous. Pardonnez aux autres qui vous ont fait du mal et qui vous ont blessés car « Le pardon est plus grand que la vengeance. » Vous ne le regretterez point. Nous subissons l’épreuve de la vie pour purifier nos âmes, devenir des pieux et mériter une place au Paradis. La finalité c’est d’obtenir la grâce divine.
Reprenons nos esprits !! Le mal se combat par le bien !!
Cultivons les bonnes valeurs afin de semer dans ce monde la lumière, la paix, l’amour, la fraternité, l’harmonie, l’abondance, le respect, la confiance, l’intégrité, la gentillesse, la sagesse, l’humilité, la bonté, la générosité, la sincérité, le pardon, le partage, l’entraide, la solidarité, l’hospitalité, la tolérance, l’espoir, le bonheur, la compassion.
Travaillons dur pour gagner honnêtement nos vies et développer notre société. Cherchons le savoir partout car une personne sans savoir et sans culture est une personne sans identité et sans repère.
Accrochons-nous fermement à ceux que nous aimons, exprimons leur notre amour, pardonnons leur leurs erreurs.
merci Ana et tonton assanne
Absa Diop
Nite daye bale tes yale takh pourtn jak jre gnou togne yale mou bal gnou nagnou rakhasate kholii woye
Merci el Hadji Assanne
Merci 🙏🙏🙏💝💝☝️☝️☝️
Fii thi Italie d douñou fi teuthieu sathieu . Na léér nak j n 'encourage pas les voleurs
Bilaye soutoureu rek mo ame solo
Bilay🙏🏽🙏🏽
Bilay👏👏👏👏👏
Deugu deugu on devait depassser c stade dpui
Nit kou doul dioum amoule
En plus affaires yi dégueu dégueu la ladj. Elle a rien de dit de mal. Deguine la ladj
Il faut tout simplement mesurer vos propos !! Adja Astou, nous a tellement offensé !!! comment,on peut attribuer des cas de viol à une communauté ??
Cepa normal tt les gens ki banal ça il sont pas des alpoulare il faut arrêter
mon frer QUI OFFENSE UNE COMUNAUTE AU SENGAL TOUCHE TTS LES AUTRES LA TOLERANCE DOIT PRIMER SUR TOUT ON EST DES MUSULMANTS ET AUSSI LA FEMME qui a dit ca est une halpular pur et dur lo beugue mou teud kasso pr des violance verbale sa way yermende rek aduna amoul solo
Abdoul Ba merde
Fallou Lo wax deugu yalla
Dioume diégalou kay doyna mais faw niou nk sii lii rk té am Lou eupe foula foufff lounou wara lidianti yalla naniou yalla doli soutoura bou beuri si barké yonéte bii psl
Dans la vie avant de parler il faut penser d'abord
Miya diallo da mom deuque bi yala moy dieguelé wala mia koufi waxe safane balou mêm boula kéne baloule diapal si yala koufi sa soeur défone bétise digako baloul soiyé des nice xole😘😍😀
Quand on demande pardon on négocie m pas par force réfléchir 1peu dafa Dioum m ndank rék ok
Djiby Ndiaye la RTS depuis Paris animateur el hadji assane gueye linga whakh bakoul elle insulté tous les people halpuular ngane elle pardonne
Aba mon frer je te sui trop mais ce que elle a dit c est grave
li mome damako dacord nit thi linga nék rk ngaye dioumé ba takhna senegal mo warra téye ta baña yakamty
En tout cas soof guenne dh xana nitt bou waxer dara balou guene mane noppi beugue ay ba dead elle à dit au paravant les viols plis étaient récurrents chez les haalpulars avant elle a bien dit yenn yi mome niak deugg toubab la thiiim
Mame Diarra SOW 😘
Mom Kay mo indi istouwar noy wakhe pa alpoular yii dandon viol ay khale yen wakhlen degge te yalla takh
leur beauté les pousse à être des journalistes mai qualification zéro dème lène diangui c'est mieux patron de presse yi nio ndara yakk Sénégal te kou diouk niou diokhla micro ga nèk si kanam TV di wah du n'importe quoi désormais douniou ko nangou dème lène diangui c'est honteux
Pourtant yoow ya whakone kene waaroul pardonne penda ba yene dengene faral adja astou
Senegal dou dem quoi parce que on fait des conneries et après on s'excuse Lou way nekhe wakh kouniouko wakhon sa kilife doula nekh salam
danou warraa def kouffii video pour yeee fitena niou nicko rappe ci kasso bi mou khamni reuyeul wax ak yeee fitena niou teck len fitena bou tarr sene kaw kouffiii dagatiii video pour yeee fitena rk niou defko ci kasso bi goor ak djiguene bassi site internette yiii ci lep nak politique , stars yii ci lep nak surtout boy yiii dii def video dicko postè dii wax loulène nex genre saf yeek ak ketieup khawma ministre de intérieure doit prendre c responsablite pour sa zero torerence
Le Sénégal n'avanceras jamais elle à commis ces erreurs elle à demandé pardon mes ou est le problème Penda Bâ à insulté tout une nation esk vous avez vue un wolof manifesté ? Bouléne gnou sonal waye Sénégal deukou diamoula li yeupe chomage moko waral
Je partage votre avis frère, soyons Sénégalais avant d'être autre chose
Aba ak assane li gene def rafete na adia astou da dioum tes borome bah la
Assane gueye depuis election présidentielle yii batay damala bang
Yep yenko def
Kou nèke da wala respectè kousi néke ok
Salam elhadji assane j'avais bcp d'estime pour vous mais ce qu'elle a dit c tres grave pourtant vous defendez les voleurs quiconque vous avez insulté vous alliez reagir c pas une question d'intolerance mais de justice arretez d'encouger l'impolitesse
Tu n'as rien compris. Il ne cautionne en aucun cas ces propos déplacés, il prône le pardon et la tolérance et dénonce la justice par soi-même. Togne dou togne mokoy résoudre.
@@khalilseck6833 desolé c toi qui ne comprends est ce quil a denoncé les propos nit bou togné dans ko wora wakh deugue ñawlou kadouyi c simple pour ten il denonce les commerçant qui font justice eux meme la deçu on en disconvient pas on ne fait pas justice soit meme au lieu de proner le pardon il faut dabord condamné ces propos injurieux
Mya Diallo ani sa yeurmandé mane mi tout mes descendants sont des toucouleurs et après 💁🏽♀️je lui ai pardonné dafa fauter lgui diekhna yaghi khalate ndiabotam dôme yimou ame
AU DELÀ MÊME DES PROPOS DE ADJIA ASTOU,VOS MÉTHODES ET VOTRE FAÇON DE FAIRE LE JOURNALISME HEURTENT TOUT LE MONDE,ON A PAS L'AIR D'ÊTRE AU SÉNÉGAL. GÉNÉRALEMENT NOS JOURNALISTES MAÎTRISENT PAS.
Vraiment rewmi delen balé wayé thiéredji safna lalo rek niou tethie
Dioum ak aquisation ce différence adjia astou defa acquise là comité de puel
Pourtant ellle est Peulh 🤫
Soof guene nak ay wax day diex dal
Deugleu asssne rafetna
Merci
Mane douma guawa nieuw Senegal
Perché 🤣
Pure veritè. C était. Pas la peine qu elle aille. A la gendarmerie On est dens le mois de ramadan il y’a d d’autre problèmes plus grave Qu on doit régler tout le monde se tait
Penda ba bouniouko diappe kenna wakhoul Fi nanko baal
Pour quoi dolen wakh si journaliste yi wakh Lou lén nékh boy farrr dengaye farrr si dégué yalla deugue la beug dh
Yen wa tfm bilen di assane di saga louguen wakhon
Iow dh mala beugue tei khawmako wone
Wakh you leer tei rafet rk nga fi wakh
Yalla nga fi yagg tei wér
Ce qu'elle a dit est controversial et c'est une grosse erreur d'avoir stigmatiser la communauté halpoular mais elle a demandé pardon à tous ceux qu'elle a heurté Dieu lui-même nous pardonne nos fautes et nos manquements pourquoi les êtres humains sont si vindicatifs? Il faut être humble pour reconnaître ses erreurs et s'excuser mais il faut être miséricordieux pour pardonner. Je voudrais savoir si elle n'a pas subi de violence au sein de sa communauté peut être qu'elle a parlé sous le coup de l'émotion et du vécu demandons pourquoi un tel dérapage ? Elle a peut être des blessures enfouies ? On est en Ramadan et les musulmans s'accordent à dire que c'est le mois du Grand Pardon donc les actions devraient refléter la FOI. Que DIEU nous donne la force de pardonner à ceux qui nous offensent !
Defa am loumou merite rek bayilen neka nafikh
Seytane bakhoul de
😰😰😬😬😬😬😬😬😬😬
Degni balante mais respecter les etinies
Wa mais dou néna da dioum él à même demander pardon légui quoi ??? Wala les halpoular vous êtes dieux mane d bess bouniou yalla balloul founiou dieum inshh
adjia alhamdoulilaah nous somme pas dieu mais amie de allahou rabana djarama
Wallahi El hadj Assane Wakh ngua deugeu Patrons yi rek ngno STRESSÉ les gens c trop dure surtout pour nous qui sommes à l'étranger merci beaucoup
Trop c trop elhadj assane ningni demoun doun bayi kenn dem
Sounko balon ken dou wax limouy wakh mettiwoulen kaso bi molène metti pesk loumou wax nexnalen
Toi t’ai Guinnéen ke tu es
@@rockjrofficiel2449bouyebo mais matay
Ta rien à dire à part ça 😱
@@rockjrofficiel2449 e doul doumasa morom
Me adja astou loumou defe yegou ma lou khewe wakh lene ma lou khewe svp
aminata camara Défoul darra dani koor gui lék mou diékh yeah😂😂😂
parce que elle a insulté tous plural
rewe mi danio tollou finga hamne nioye fadial souniou boppou , ban justise Ana justise mofi am
Il faut savoir parlè
tout ce que tu as dit là c'est pas vrai
Senegal li mocoyacou dege mofa ammout
togne dal bakhoul entouka
Dioga len fi degen yabate
Naa ték lp si lokho yalle sénégale rkkk nite dale déye ame soutoura dou lp laniou feséle tamite
hadane Gaye purta nekko wone nafig de yene lane moye sene porbalem kunu lal nu tegal sa ndeye
yormal hiyame dina am nio xamni yalla day bal nieup sauf niome niounèko loutax ga bal gni balo gni mouni gni dawouniou balé kone meunou maléne bal guir yalla kou beug yalla bal la dél balè
Deelene mandou
I ba beo
Maye léne niou diam kou sagua wone sén baye nguén doumako
Nul n'ai parfait mais moi je me demande est ce que tok di wakh métier la ses une kestion
😂😂😂😂😂
lolou mo diara lathieu
Donc kes ce ke tu fais dans ce monde toi 🤫
Nañu ko def goo gis nañu ko waxtaane lay njëkké
Tey ngeen di wakh loolo
Dah dioume rek
Bouko wakhone bèn serigne ngène khole
Sy Malick lanla wax mom
@@0usmaneturry677 elle a dit peule et les toucouleurs yii ame plus de 60 ans violès les enfants
Bayileen naafik
Ay way da dioumm rk bly
Maylenniou
Boy WAK deg ga me bou fé ke sa BO kou mo toy da koy wak
C koi le problème svp
wa mais khana joume mome si alpoular yi rk la
Iow souniou waxone sa papa wala Mame violeurla diga waxeini
Bouléne niou souñal waye akh
@@falloundiaye7946 kéne soné woula shutt
Ki domou harram
Koorgui yalla boumou gawa diekh
Gaaw gi walla yeex gi yàlla tëral nako ba noppi
Dafa wax lou diss mo takh niou tekko lou diss
Xamoulen sene bopp dh soof guéne trop way meunoulene tekk kenn lou diss
@@mamediarrasow1752 yow ya ngui mer deh
@@mamediarrasow1752 c'est juste une leçon .évitons de toucher tout les éthinie ✌✋
Bahle bhna
🚫🚫🚫🚫
Far Bakhoul Degg Mo Bakh
Keppou kou faral adia sa pappa dadon viole mo takh
Pot et marihou
Baye lene sayetane budone halpular mo wax li benene laNag kene Du xam fi muye yam
purtant penda ba a insulte tts les wolof et pourtant dara khewul ayons la culte du pardon mn frere mangui jegalou nak
Tidiane Sy yaw doul way penda ba saga wolof yi ñou diokh ko pasport yaw yay cheytani bi imbécil.
Assan sa daay
Guene balma mais assane man andouma ak ioe vraiment kou leu fonkou la mais ki limou def mouna yakk reeww naniou tekk palace am vraiment dou fi lala done khar assane
,
Aba mon frer je te sui trop mais ce que elle a dit c est grave
Soutara dafa bakh