Maladie de Yado: le camp de Niankou brise le silence et révèle "dafa am ñiou profité si fébar pour..

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 ноя 2024

Комментарии • 56

  • @mamandiop6715
    @mamandiop6715 3 месяца назад +1

    Li eupp solo Moy ki febar yallane borom mayko wér AK werlé bamou delou si ay activitém inchallah rabi

  • @CheikhounaNdiaye-r3d
    @CheikhounaNdiaye-r3d 3 месяца назад +6

    Merci général ❤

  • @senegaltv9031
    @senegaltv9031 3 месяца назад +6

    Merci général ..Bou ken dokh sa diganteek leral

  • @elhadjihanne3905
    @elhadjihanne3905 3 месяца назад +2

    Général tu as bien dis rester zen on ai fière de père yally

  • @talladieng-rs6om
    @talladieng-rs6om 3 месяца назад +4

    Yana ko yala maey wer

  • @SokhnaFall-sl3kq
    @SokhnaFall-sl3kq 3 месяца назад +3

    sénégalais yi nio nafékh mana wanéwou nitte bouye déf daye déf té yala takh Bravo Nainkou

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 3 месяца назад +5

    Nitte febar ngene beug ko deff actualité no senegall diaxall nanema

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +8

    Man Senegal diakhal nama Lou takh nitt bouy def Lou bakh dako wara wakh wala mou waneko

  • @ibrahimatoure8289
    @ibrahimatoure8289 3 месяца назад +6

    Général kayré 😂😂

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +5

    Kouy def ta yalla takhoul dothi am yalla

  • @afriquegalsene1927
    @afriquegalsene1927 3 месяца назад

    Merci général nioune bègue nagnlene ba pare

  • @Baribari4456-pi9bm
    @Baribari4456-pi9bm 3 месяца назад +8

    Bb Eva moy seytane bi yagg na di beug yak niankou depuis niou am problème grand théâtre mai niankou nitt kou bakh la vrement te problem yifi am yeup tôtouwoul

  • @Abymbayep2k
    @Abymbayep2k 3 месяца назад +3

    Walay baniouy réunion pour dimbali yado maguama took bobou li yeup amoul walay Azim m Yaga bawoul darra

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +6

    Man li Niankou dem la kham ab doulit bouy def na yalla rek takh

  • @Theresita-hk4sk
    @Theresita-hk4sk 3 месяца назад +4

    Est ce que tamit doungen bayi tiowli tai boler kholyi nianal ko mou diog ak diam....wakh bouvn sew bi tamit bakhoul

  • @BOROMLERGUICISSECISSE
    @BOROMLERGUICISSECISSE 3 месяца назад

    Sokhna sy bilahi sa promation dèsna

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +4

    Niankou Limou def thi Senegal yep niata nitt la may lokho wane Len ban menel sen bop delen grem nitt rew ma mom wakh lan geune men ka jeuf

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +3

    Niankou sou diapalewoul won yado ken douko kham

  • @mbayediakhate4897
    @mbayediakhate4897 3 месяца назад

    Film kay def guir yalla akafa jafe

  • @CheikhMbaye-mh9rn
    @CheikhMbaye-mh9rn 3 месяца назад +2

    nite dafay tèè yake bakhoul

  • @youssouphadrame447
    @youssouphadrame447 3 месяца назад +1

    Seen débat bi c'est pour laver la peau de Niankou seulement !

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +4

    Awa mom di wakh rek daw la yekk febarou yado bi gnep po yekk daw loutakh mou bayi ba tay di wakh tay la amak Niankou problem motakh

  • @AsseNdao-e4o
    @AsseNdao-e4o 3 месяца назад

    Fén baxou barké Baye Niass

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +2

    Lolou was ker niom yado nioko wakh

  • @Sidath17
    @Sidath17 3 месяца назад

    Bb eva dh def n'a devoir wam

  • @BatoulyBa-j8c
    @BatoulyBa-j8c 3 месяца назад

    Badiene Nationale

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi 3 месяца назад

    Badiene mi vrai dmrm la mouy diaboliser si cas boo khamni khamoo nim démé khawma loutakh generale accepter invitation bi ki dmrm la kw

  • @ndeyeabsasangare5383
    @ndeyeabsasangare5383 3 месяца назад

    Fi kouñou fi diapalé rek. Da fekk sa febar dafa fegn wala gayi xawi sa soutoura wala nga nekk célébrité. Le gars qui a parlé dernièrement. Il faut sensibiliser ton message de manière générale. Les frais médicaux devraient être exemptés aux ménages à faible revenu, parce qu'il y a pleins de gens malades dans ce pays qui ne peuvent pas se soigner. Ciie li nga wara wakh, mais autorités di Focus ciie juste une seule personne, c'est quasi impossible. Yallah na yallah safara malades yeup.

  • @amarakebe4134
    @amarakebe4134 3 месяца назад +2

    Mais journaliste bi pourquoi mouuy forcer gars yi filmer lolou ??

  • @abdoulayedabo9509
    @abdoulayedabo9509 3 месяца назад +3

    La présentatrice est passée complètement à côté.

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +2

    Nouy nakhar Lou fifa niy yi dem dilen filme kon niom waker niom yado nouy diakhase

  • @youssouphadrame447
    @youssouphadrame447 3 месяца назад +1

    Bou leen niou fotonn daguenn setane dame bi ayons une foi sincère.
    Sa maladie dure depuis des années fo lenn nekon ?

  • @DieynaFall-we4ue
    @DieynaFall-we4ue 3 месяца назад +1

    Beug buzz molène dal té defou niou si dra

  • @saloumtv4722
    @saloumtv4722 3 месяца назад

    Journalistes bii sofff naa waaay

  • @ibrahimatoure8289
    @ibrahimatoure8289 3 месяца назад +4

    Général dé khamnako dou wax louko wooroul

  • @AlbouryNdiaye-ch8em
    @AlbouryNdiaye-ch8em 3 месяца назад +3

    Awa Niankou motakh gnep kham ko mou pape la geurem ko Tay souko khase boumko meti

  • @namaly829
    @namaly829 3 месяца назад +2

    Le niveau de bêtise de cette journaliste me fume

  • @mbayediakhate4897
    @mbayediakhate4897 3 месяца назад

    Senegal amfa khalis aka yombou a khalis yomboul dh li gana mesere di wakh rek namou niou dara te yourunu dara

  • @mamethierno1801
    @mamethierno1801 3 месяца назад

    Ligawax yanouwoul mana

  • @papemboge8116
    @papemboge8116 3 месяца назад

    😂😂😂

  • @syseydou2006
    @syseydou2006 3 месяца назад +1

    Général bayil féne Fadel yayou yado moko woo

    • @ibrahimatoure8289
      @ibrahimatoure8289 3 месяца назад +5

      Sa way iska khamga général baga naan Day fén

    • @syseydou2006
      @syseydou2006 3 месяца назад +1

      C seydou le camera de Fadel yayou yado mogui ni di wakh

    • @ndeyefatoudiouf6060
      @ndeyefatoudiouf6060 3 месяца назад +4

      Bilaye mane je trouve que sokhla woul aÿ détaille sí côté yeup nakk yallah na yallah motali yéné bi wa groupe Ndiankou nekk di mbébéte ba Yado diougue si diam ak salam mou délou si aÿ activitém yallah na yalla défal gnoune gneup soutoureu

    • @challengetiktoke2023
      @challengetiktoke2023 3 месяца назад +3

      Yaw syseydou2006 yaw yaye fénn kate bou make bi doméram ki dousa morome

    • @AidaSoumare-el5be
      @AidaSoumare-el5be 3 месяца назад +2

      ​@@ndeyefatoudiouf6060 Amin inch'Allah 🤲🏿🤲🏿🤲🏿

  • @bayefalloundiassane2052
    @bayefalloundiassane2052 3 месяца назад

    Yaw journalist bi môme say wakh lemdeumne dé bariga wakh té eupe ay lathie

  • @ndeyeabsasangare5383
    @ndeyeabsasangare5383 3 месяца назад

    Fi kouñou fi diapalé rek. Da fekk sa febar dafa fegn wala gayi xawi sa soutoura wala nga nekk célébrité. Le gars qui a parlé dernièrement. Il faut sensibiliser ton message de manière générale. Les frais médicaux devraient être exemptés aux ménages à faible revenu, parce qu'il y a pleins de gens malades dans ce pays qui ne peuvent pas se soigner. Ciie li nga wara wakh, mais autorités di Focus ciie juste une seule personne, c'est quasi impossible. Yallah na yallah safara malades yeup.