Barki segñ Touba yaw mii Am nga ngeureumou segñ Touba billahi wallahi kou mél nii lah beug si Sénégal 🇸🇳 segñ Touba lii le beug El hadji Malick lii le beug naniou yallah mou seul sii macki firawna sall ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Macha Allah, kilifeu discouram li la wara refléter, kouko déglou dasé wara djeulé ndiarigne. Deugue nak nékhouta dégue mais bi discours loudoul deugue roté wouthi. Yallah nanou Borom may dégue ak toppou. Serigne Lo Yallah na Borom bi yokkou xam xam gui.
Akassa cheikh bi vos paroles traduisent une réalité incontestable et sont conformes à votre personnalité. QU'ALLAH PUISSE GUIDER NOS PAS SUR LE DROIT CHEMIN . MACHALLAH SUNU SERIGNE BI KHAM LIMOU DONE
Lii mooy discours kilifa diiné wakh té yalla takh machallah
Machallah Sérįgñe modou lô tawfeux ak taye zirr 🇸🇳❣️❤️🤲🤲🤲
Seringe moudou lo yalla nafi yagg teweur discours bi amna sollo m’a challah
Dieuredieufe Serigne bi xame xame dou péxé yalnaniou yalla defall dégue ak tope si barkèppe Serigne Touba 🇨🇮❤️🇸🇳
Dieuredieufe Serigne Modou lo yallagafi yague tèwèr ❤️🇸🇳❤️🇨🇮🇨🇮🇨🇮❤️❤️❤️
Barki segñ Touba yaw mii Am nga ngeureumou segñ Touba billahi wallahi kou mél nii lah beug si Sénégal 🇸🇳 segñ Touba lii le beug El hadji Malick lii le beug naniou yallah mou seul sii macki firawna sall ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kàddu yi maassàllaa 😍❣️
Macha Allah, kilifeu discouram li la wara refléter, kouko déglou dasé wara djeulé ndiarigne. Deugue nak nékhouta dégue mais bi discours loudoul deugue roté wouthi. Yallah nanou Borom may dégue ak toppou. Serigne Lo Yallah na Borom bi yokkou xam xam gui.
Machallah rafetna wakh dji mat na seuk Yalla nagnou Yalla défal degg ak topou
Akassa cheikh bi vos paroles traduisent une réalité incontestable et sont conformes à votre personnalité. QU'ALLAH PUISSE GUIDER NOS PAS SUR LE DROIT CHEMIN . MACHALLAH SUNU SERIGNE BI KHAM LIMOU DONE
Akassa serigne yalla nanga fi yagg té wer té ñepp degg wax ji.
Mashallah serigne wakh na lèp ak deug rek comme ni mou ko bakho
Ay Waxam Masul Soppiku
Serigne Modou Lo Ngabou
Mou Sokhna Mbene Mbacke. MOUM serigne touba
Yagg fi lool te werrr
ma cha allah s modou lo ngabou
Machallah dieureudief Lo
Allahou akbar quel discours véridique yalana YALLAH goudal fannewi yokk weergui
Amine yarabi
Maa Shaa Allah
ما شاء الله جر جفت شرجب
Yàlla na nga fi yàgg te wér
Machalla
Jërëjëf
Goudal Fan serigne bi.
Serigne Modou lo nguadou machalah , un grand guide religieux , il est exceptionnel
Jaajeuf jaajeuf jaajeuf
😍
C'est un petit fils de Serigne Touba
Diaradiaff lo yall nangafi yage loll tawer barkeb khasidayi
Yagefi loool ta wer lo