- Видео 483
- Просмотров 105 656
Sunu Yaakaar - SENEGAL
Сенегал
Добавлен 7 авг 2017
Notre plus grand espoir dans la vie vient de la parole de Dieu. Jésus ('Īsā ibn Maryam) est la parole de Dieu et l'esprit de Dieu (ruh min Allah). Qu'est-ce que c'est plus important que de connaître la parole de Dieu!
Notre désir au Centre Yaakaar Ju Sax est de partager avec vous les enseignements de Jésus-Christ ('Īsā ibn Maryam) afin que vous puissiez mieux connaître le prophète que la Bible et le Coran appellent "la Parole de Dieu".

Jëf Ya 28 | Pool ci dunu Màlt
Bi nu rëccee, nu yég ne dun baa nga tudd Màlt. Te waa réew ma won nu laabiir gu ràññiku, ndaxte taalal nañu nu sawara, ganale nu ndax taw bi sóob ak sedd bi. Pool nag di for matt, di ko def ca taal ba, jaan ne ca mëlle ndax tàngoor wa, taq ci loxoom. Bi waa réew ma gisee rab wa wékku ci loxoom nag, ñuy waxante naan: «Ci lu wóor nit kii reykat la; te bi mu rëccee ca géej ga sax, ndogalu Yàlla mayu ko mu dund.» Waaye Pool yëlëb rab wa ca sawara sa, te wàññiwu ko dara. Nit ñi di xaar mu newi, mbaa mu ne dàll, dee; waaye bi ñu négee lu yàgg te gis ne dara jotu ko, ñu soppi xel ne: «Kii yàlla la.» Amoon na nag ca wet ya ay suuf yu doon moomeelu ku tudd Publiyus, di kilifag dun ba. Mu teeru nu,...
Просмотров: 7
Видео
Jëf Ya 27 | Pool dugg na gaal, di dem Room
Просмотров 214 дней назад
Bi loolu wéyee ñu fas yéene noo dugal gaal jëme réewu Itali. Noonu ñu jël Pool ak ñeneen ñi ñu tëjoon, dénk leen njiitu xare bu tudd Yulyus, mi bokk ci mbooloom xare mu buur. Nu dugg ca gaalu dëkku Adaramit guy taxaw ci teeruy Asi, daldi tàbbi ci biir géej; te Aristàrk, mi dëkk Tesalonig ci diiwaanu Maseduwan, ànd ak nun. Ca ëllëg sa nu teer Sidon; Yulyus laabiir ci Pool, may ko mu dem ci ay xa...
Jëf Ya 26 | Layu Pool fa kanam Agaripa
Просмотров 821 день назад
Bi mu ko waxee, Agaripa ne Pool: «Jëlal kàddu gi.» Noonu Pool tàllal loxoom, daldi làyyi ne: «Buur Agaripa, ma làyyi ci sa kanam tey ci lépp li ma Yawut yiy jiiñ, xol bu sedd la ci man, ndaxte xam nga bu baax aaday Yawut yi ak seeni werantey yoon. Kon maa ngi lay ñaan, nga déglu ma ak muñ. «Ci lu jëm ci Yawut yi, xam nañu sama dund li dale ci samag ndaw, muy ci sama biir xeet, muy ci Yerusalem....
Jëf Ya 25 | Pool làyyi na ca kanam Festus
Просмотров 23Месяц назад
Bi Festus teersee ci diiwaanam, mu teg ca ñetti fan, dem Yerusalem. Noonu sarxalkat yu mag ya ak njiiti Yawut ya kalaame Pool ci moom. Ñuy sàkku ndimbal ci moom, di ko ñaan bu wér, mu yónni Pool Yerusalem, fekk lal nañu fiiru rey ko ca yoon wa. Waaye Festus ne leen: «Ñu ngi wottu Pool ca Sesare, te dinaa fa dem fi ak fan yu néew.» Mu ne leen: «Ñi am maana ci yéen nag, nangeen ànd ak man, layooj...
Jëf Ya 24 | Pool Lay na ci kanam Feligsë, boroom rew ma
Просмотров 36Месяц назад
Bi juróomi fan wéyee, Anañas sarxalkat bu mag ba dikk, ànd ak ay njiit ak layookat bu tudd Tertul, ñu woo Pool ci yoon fa kanam boroom réew ma. Noonu ñu woo Pool, te Tertul daldi ko jiiñ naan: «Yaw Feligsë mu tedd mi, sa nguur jural na nu jàmm ju neex, te sa jàppandil soppi na lu bare ci sunu xeet. Gis nanu ko fépp ak ci lépp, di la gërëm ak sunu xol bépp. Waaye ngir baña yàggal jataay bi, maa ...
Kàddu yu ñiaax ndaw yi Paac 1 | Inv: Pst Sémou DIOUF
Просмотров 31Месяц назад
Emission Sunu Yaakaar | Kàddu yu niaakh ndaw yi - Pst Malick DIOP Inv: Pst Sémou (Eglise Maison de prière) Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop yaakaarjusax@gmail.com | 77.335.5591
Kàddu yu ñiaax ndaw yi Paac 2 | Inv: Pst Sémou DIOUF
Просмотров 32Месяц назад
Emission Sunu Yaakaar | Kàddu yu niaakh ndaw yi - Pst Malick DIOP Inv: Pst Sémou (Eglise Maison de prière) Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop yaakaarjusax@gmail.com | 77.335.5591
Jëf ya 23 | Yawut ya lal na pexe ngir rey Pool
Просмотров 32Месяц назад
«Yéen bokk yi ak baay yi, dégluleen samaw lay.» Bi ñu déggee, mu di leen wax ci làkku yawut, ñu gën ne xerem. Noonu Pool ne leen: «Man Yawut laa, juddoo Tars ci diiwaanu Silisi, yaroo ci dëkk bii. Taalibe laa woon ci Gamaleel, mu jàngal ma bu wér yoonu sunuy maam, ba ma sawar ci Yàlla, mel ni yéen ñépp tey. Daan naa fitnaal ña bokkoon ci yoon wii, ba di ci rey sax; yeew naa góor ak jigéen, tëj ...
Jëf Ya 22 | Pool wone na ne jaambur la ci nguuru Room
Просмотров 37Месяц назад
«Yéen bokk yi ak baay yi, dégluleen samaw lay.» Bi ñu déggee, mu di leen wax ci làkku yawut, ñu gën ne xerem. Noonu Pool ne leen: «Man Yawut laa, juddoo Tars ci diiwaanu Silisi, yaroo ci dëkk bii. Taalibe laa woon ci Gamaleel, mu jàngal ma bu wér yoonu sunuy maam, ba ma sawar ci Yàlla, mel ni yéen ñépp tey. Daan naa fitnaal ña bokkoon ci yoon wii, ba di ci rey sax; yeew naa góor ak jigéen, tëj ...
Jëf Ya 21 | Pool jublu na ci dëkku Yerusalem
Просмотров 72 месяца назад
Bi nga xamee ne tàggoo nanu ak ñoom ci naqar, nu dugg gaal, jubal dunu Kos. Te ca ëllëg sa nu dem ba teer ca Rodd, ba noppi jóge fa, jàll ba Patara. Foofa nag nu gis gaal guy jàll ba Fenisi, nu dugg ca, mu daldi teddi. Noonu nu séen dunu Sipar, bàyyi ko ci sunu càmmoñ, jublu diiwaanu Siri, nu teersi Tir. Ndaxte foofa la gaal gi wara yebbee la mu yeboon. Nu wut taalibe ya, ba gis leen, toog ak ñ...
Jëf Ya 20 | Pool jaar na ci diiwaani maseduwan ak geres
Просмотров 522 месяца назад
Bi yëngu-yëngu ba dalee, Pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. Bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu Maseduwan. Noonu mu jaar ca bérab yooyu, di dooleel nit ñi ak wax yu bare; ba noppi mu dem réewu Geres, toog fa ñetti weer. Waaye bi mu nekkee ci kaw tànki dugg gaal jëm diiwaanu Siri, te Yawut yi lalal ko pexe, mu fas yéenee dellu, jaare Maseduwan. Booba nag ñii ñoo ànd...
Jëf ya 19 | Pool ci dëkku efes
Просмотров 462 месяца назад
Ba Apolos nekkee Korent nag, Pool jaar ca teggi ya gëna kawe ca réew ma, doora dikk Efes. Noonu mu gis fa ay taalibe. Mu ne leen: «Ndax jot ngeen ci Xel mu Sell mi, bi ngeen gëmee?» Ñu ne ko: «Déggunu sax ne Xel mu Sell mi am na.» Mu ne leen: «Kon nag, bi ñu leen sóobee ci ndox, lu ciy maana?» Ñu ne ko: «Xanaa li Yaxya tëral.» Pool ne leen: «Yaxya daan na sóob nit ñi ci ndox, ndax bi ñu tuubee ...
Jêf Ya 18 | Pool ci dëkku korent
Просмотров 102 месяца назад
Bi loolu wéyee Pool bàyyikoo Aten, dem Korent. Mu tase fa ak Yawut bu tudd Akilas te juddoo diiwaanu Pont. Muy sooga jóge réewu Itali ak soxnaam Pirsil, ndaxte buur ba Këlódd sant na Yawut yépp, ñu génn Room. Noonu Pool seeti leen, te gannaaw ñoo bokk liggéey, maanaam di defar ay xayma, mu dal fa ñoom, ñuy liggéeyandoo. Bésub noflaay bu nekk nag muy diisoo ak ñi nekk ca jàngu ba, di jéema gëmlo...
Jëf Ya 17 | Xibaaru Yeesu Yengal na Tesalonig
Просмотров 742 месяца назад
Ba mu ko defee ñu jaare ca dëkk ya ñuy wax Amfipolis ak Apoloni, doora àgg Tesalonig ga Yawut ya amoon ab jàngu. Póol nag di leen fa fekk, na mu ko baaxoo. Diiru ñetti bési Noflaay, mu di leen waxal ci Mbind mi. Mu di leen tekkil Mbind mi, di leen ci firndeel ne coonob Almasi bi ak ndekkiteem manul woona ñàkk. Mu ne leen: «Yeesu mii ma di leen xamal, mooy Almasi bi.» Ba loolu amee ñenn ca Yawut...
Jëf ya 16 | Timote andsi na ak Pool ak Silas
Просмотров 733 месяца назад
Jëf ya 16 | Timote andsi na ak Pool ak Silas
Jëf ya 14 | Pool ak barnabas ci deukou ukinom
Просмотров 923 месяца назад
Jëf ya 14 | Pool ak barnabas ci deukou ukinom
Jëf ya 13 | Yàlla yonni na barnabas ak sool
Просмотров 933 месяца назад
Jëf ya 13 | Yàlla yonni na barnabas ak sool
Jëf ya 12 | Yàlla musal na piyeer ca kaso ba
Просмотров 774 месяца назад
Jëf ya 12 | Yàlla musal na piyeer ca kaso ba
Jëf ya 11 | Piyeer leeral na jëfam fa kanam gaayi Kirist // ya nekk Yerusalem
Просмотров 604 месяца назад
Jëf ya 11 | Piyeer leeral na jëfam fa kanam gaayi Kirist // ya nekk Yerusalem
Jëf ya 7 | Layu Ecen fa kanam mbooloo ma
Просмотров 335 месяцев назад
Jëf ya 7 | Layu Ecen fa kanam mbooloo ma
Jëf ya 6 | Sàak nanu niy topato yëufi mbolo ma
Просмотров 435 месяцев назад
Jëf ya 6 | Sàak nanu niy topato yëufi mbolo ma
Jëf ya saar 4 | Piyeer ak Yowaana ci kanam kureelu àttekat ya
Просмотров 3,6 тыс.5 месяцев назад
Jëf ya saar 4 | Piyeer ak Yowaana ci kanam kureelu àttekat ya
Jëf ya saar 3 | Piyeer faj na nit ku lafaan
Просмотров 7 тыс.6 месяцев назад
Jëf ya saar 3 | Piyeer faj na nit ku lafaan
Jëf ya saar 2 | Ñëwug Xel mu Sell mi ca màggalu Pàntakot
Просмотров 446 месяцев назад
Jëf ya saar 2 | Ñëwug Xel mu Sell mi ca màggalu Pàntakot
Jëf Ya saar 1 | Yeesu Almasi bi yeg na ci asmaan
Просмотров 906 месяцев назад
Jëf Ya saar 1 | Yeesu Almasi bi yeg na ci asmaan