- Видео 26
- Просмотров 88 239
Sopey Sokhna Fatima Lo Officielle
Сенегал
Добавлен 5 окт 2022
Cette chaine est crée pour un seul Objectif .Faire passer tous les leçons et conseils de Sayda Fatima Lo H.A vers les couples de mariage pour mieux vivre ensemble sur le bonne voix ! Abonne-toi
URGENT ‼️ Sayda Ndéye Fatou Fall est malade Elle doit être évacuée urgemment à l'étranger
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Просмотров: 669
Видео
Taxawayyu jeker wala diabar thi biiri Jafe jafe | Sayda Sokhna Fatima Lo
Просмотров 6 тыс.6 месяцев назад
#funny #fatimalo #senegalaise #sey #ProblèmesDeCouple #ConseilsRelationnels #VieDeCouple Bienvenue sur notre chaîne ! Dans cette vidéo, nous abordons les moments forts dans un couple et comment ils peuvent aider à surmonter les problèmes relationnels. Découvrez des conseils pratiques, des histoires inspirantes et des stratégies pour renforcer votre relation. Rejoignez notre communauté ! Abonnez...
Yaw Soxna si, Na La Sa Ay Doy Te Na La Ko Jaral... | Sayda Sokhna Fatima Lo
Просмотров 6 тыс.6 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Woudië Bi Si keur yii | Sayda fatima Lô Bou Touba | Conférence à Guédiawaye
Просмотров 3 тыс.8 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Nekkiinu jigéen juy séy ak ay goroom ci weeru koor Soxna Faatima Lóo Tuubaa
Просмотров 1829 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Ce dont les femmes se plaignent envers leur mari | Li jigéen ñi di jàmbat ci seen boroom kër yi
Просмотров 1879 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Questions des femmes de foyers durant le Ramadan | Laaji jigéen ñi ci...| Sokhna Fatima Lô
Просмотров 1379 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin Questions des femmes dans les salles de mariage
L’avantage de la patience pour les femmes | Lan moy njariñu muñ ci jigéen | Soxna Fatima Ló Touba
Просмотров 3469 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Rappel de Sokhna Fatima Lo aux Femme sénégalaise #shorts
Просмотров 23110 месяцев назад
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs : ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQjoin
Extrait | Les Clefs pour Choisir le Conjoint Idéal | Conseils Précieux de Seyda Fatima LO Touba
Просмотров 2,5 тыс.11 месяцев назад
Les Clefs pour Choisir le Conjoint Idéal | Conseils Précieux de @sopeysokhnafatimalo 💑✨ Salut la famille de @sopeysokhnafatimalo ! Aujourd'hui, plongeons-nous dans le fascinant monde du choix du conjoint, une décision cruciale qui sculptera notre avenir. 🌟💖 1️⃣ Connais-toi toi-même : Avant de chercher un partenaire, il est essentiel de comprendre qui nous sommes vraiment. Sayda Fatima Lô nous r...
UFEMS | Séminaire Annuel 11 Edition Thème: les fiançailles, le Mariage et le | Sokhna Fatima Lô
Просмотров 46911 месяцев назад
Bienvenue sur notre chaîne "@Sokhnafatimalo Dans cette vidéo captivante, nous vous partageons ensemble dans le Séminaire Annuel UFEMS 11, animé par l'éminent Sokhna Fatima Lô il y'a de ce la quelques années, qui explore en profondeur les aspects cruciaux des fiançailles, du mariage et du divorce en Islam. 🌟 Points forts de la Vidéo : - 🤝 Fiançailles en Islam : Découvrez les principes fondamenta...
Ce qui s'occupe des vices cachés | Topp Cas pertamaa ñeel jullit bi... |Saydaa Fatima Lóo
Просмотров 4,1 тыс.Год назад
Dans cette video Sayda Fatima Lo nous parle de la La médisance (topu cas ) , cas amna La médisance et la diffamation sont des actes répréhensibles et peuvent avoir des conséquences légales graves. Il est important de promouvoir la communication positive et le respect. Abone toi en en cliquant sur le lien ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQ La patience entre époux dans les moments d'adv...
Le maraboutage dans les familles polygames | Ndiabaranté gi ci Diguenté Gniy wujé | Seyda Fatima Lô
Просмотров 729Год назад
Dans cette video sayda Fatima nous parle du maraboutage dans notre societe entre epouse n'oubliez de pas de liker partager et aimer la video s'il vous plait. Abone toi en en cliquant sur le lien ruclips.net/channel/UC4t-Qg65H_xsvJ3s3E_1VkQ La patience entre époux dans les moments d'adversité | Muñ, Dolli Muñ...| Seydaa Fatima Ló ruclips.net/video/pnzXOHNpVqA/видео.html Le leadership Féminin en ...
La patience entre époux dans les moments d'adversité | Muñ, Dolli Muñ...| Seydaa Fatima Ló
Просмотров 2 тыс.Год назад
La patience entre époux dans les moments d'adversité | Muñ, Dolli Muñ...| Seydaa Fatima Ló
Le leadership Féminin en ISLAM | Intervention de Sokhna Fatima Lo
Просмотров 1,5 тыс.Год назад
Le leadership Féminin en ISLAM | Intervention de Sokhna Fatima Lo
TAXAWAYU DJIGUENE CII BIIR WEROU KOOR | Sokhna Fatima Lo | 02-Partie
Просмотров 749Год назад
TAXAWAYU DJIGUENE CII BIIR WEROU KOOR | Sokhna Fatima Lo | 02-Partie
TAXAWAYU DJIGUENE CII BIIR WEROU KOOR | Sokhna Fatima Lo | 01-Partie
Просмотров 478Год назад
TAXAWAYU DJIGUENE CII BIIR WEROU KOOR | Sokhna Fatima Lo | 01-Partie
Dépenses yii ci biir keur gui | Sokhna Fatima Lo
Просмотров 2,1 тыс.2 года назад
Dépenses yii ci biir keur gui | Sokhna Fatima Lo
La rivalité dans un foyer | KUJE Gi Ci Biir Ker Yiiii | Sayda Sokhna Fatima Lo
Просмотров 2,4 тыс.2 года назад
La rivalité dans un foyer | KUJE Gi Ci Biir Ker Yiiii | Sayda Sokhna Fatima Lo
Strategies d'une Femme dans sa vie conjugale | Pexeey Jeggeen Ci Néegu Seyeum | Sokhna Fatima Lo😭😷😢
Просмотров 5 тыс.2 года назад
Strategies d'une Femme dans sa vie conjugale | Pexeey Jeggeen Ci Néegu Seyeum | Sokhna Fatima Lo😭😷😢
L'impuissance dans un couple | ÑAKA YEUG BANEEXU SÉY | Sayda Sokhna Fatima Lo
Просмотров 8 тыс.2 года назад
L'impuissance dans un couple | ÑAKA YEUG BANEEXU SÉY | Sayda Sokhna Fatima Lo
Infidélité dans un couple Marié |Wooronté bii thi Négou seuy yiii | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Просмотров 2,5 тыс.2 года назад
Infidélité dans un couple Marié |Wooronté bii thi Négou seuy yiii | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Diongué Thi biir Négou Seuy | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Просмотров 24 тыс.2 года назад
Diongué Thi biir Négou Seuy | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Djiguen diou fess plasam | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Просмотров 14 тыс.2 года назад
Djiguen diou fess plasam | Sayda Sokhna Fatima Lo H.A
Votre group de WhatsApp
Dema beuge ame numéro tata fatima lo🧕 svp kouko ame
Machalla amna solo ❤❤❤❤
❤❤❤ mashallah
Assalamou aleykoum,je veux avoir un numéro pour intégrer le groupe sopey seyda Fatima lo svp
appeller au 77 763 02 41 ou par whatsapp
❤❤❤❤❤ma.sahala.sope.nala
mâcha allah
Dieuredieuf
mâcha allah zeyda ❤️
Machalla yal na yalla fayla yiw❤❤❤❤❤
Amine ya rabi
Amna solo bilay
Je peux avoir le numéro de téléphone de Sohna fatima Lo
Envoyer un message ou appeler au 77 763 02 41
Assalamou aleykoum yaseyda machalla amtina solo yalna yala contane ta fayal nioula
Machallah ma tourondonre❤❤❤
Machahalla ya sayda Fatima Baraqu'alla fik❤
Yalla nako yalla diapalé boubax
Alahouma amin
شفاها الله وعافاها
Alahouma amin
Yalla nako yalla safara
Alahouma Amin
Ohh thiey febar yi tamite, yalnako sunu Borom safara
Natou la rek, ami ya rabi
Yalnaco yalla safara
Alahouma amin
Soubouhanallah allahou akbar 😢
Guisgua dé
Yalnako yalla yékéti si diam ak salam.
Alahouma amin
Walahi 6millions yombeu na thi sénégalais you barri Yallah nako Yallah taxawou thi famille bou baax am diiné la bokk
Ay way kouko meuneu djiapalee neuko djiappalee, yaguena di fekhal sunu khol, digniou djiangal dinnee
Al-hamdou lil la
Allah y chafik
alahouma amin
Machallah ya seyda amna solo yalnagnou yalla may dégue ak top
Yalna Yalla mousseul si cas amine
alahouma amin 🤲
Machalla ya sayda.amatina sollo loll
Dieuredieuf
Yalla. Nagnou. Yallamouseul. Thifay. Akmeroo. Ak. Tonngoo. Djigeen. Day. Rée. Waay
wawaw lilou moy dëgg dé
Bayéniou xelll nioune célibataire yi kon bayéniou xell sokhlanagnleu❤❤❤
d'accord in cha alla dina gnew si yen boulen wax dara
Machallah seyda fatima lo❤
Dieuredieuf
Machalla yalna yalla fay la yiiw dama begg bokk si groupe bi iinchalla
Daccord contactel Abou Fatima au 77 763 02 41 même aussi sur whatsapp
Ma shaa Allah tabarakAllah ❤ Dieureudieuf yaye ❤ JazakAllah khayr!
allahouma amin
Sayda wakhnga Lou diaféb thi couple. Ki dafay ďiongué, oyof ki reuy
wawaw lolou dé deugu la mom
Elle tré pédagogue machAllah. Ca fait 3 jours que je l'ai decouverte sur tik tok. Yallah nako borom bi sammeu aar ko, jegal ko té may ko yiwu adina ak alahira❤. Sayda ya ngi def lou am solo. Beugone na nga wah si walou planification familiale manam les méthodes de contraception lane lassi islam wah? Li tah jigueen yi diko def nak raison yi beuri. Beugone nga def si dars. JazakAllahu hayran
ma cha alla dieuredieuf ci commentaire yii amna solo trop yalla nala yalla faye
As salamou aleykoum wa rahmatoullah 🤝 MachAllah waxtaan wi amna solo lol sah ya zeyda yallah nala borom bi may yiw adina ak alahira. Thème am na solo beug na nga gueuneu xouss si waloum set gui manam hygiène. Hygiène corporelle(amna jigueen yo xamni meunu gnu sangou ba sët😂 pask xamougnu fougnu wara bomb ak nignu koy bombé), hygiène intime (nakala lagnuy topato wé sen awra bamou set dou am xett té mousseul lene si infections surtt aprés les règles) , hygiène bucco-dentaire (guemign yi beugn ak lamign yi😂😂), hygiène des cheveux( quand et comment faire ses soins capillaires, les types de coiffures à faire pour les musulmanes) soins des mains et pieds aussi..... yi yeup dal beugone nagn waxtaan yu xoote sah. Contane na trop. Amna sujet tabou yo xamni yaye yi duñu si waxtaan ak seni dome yu jigueen yi
Li tamit thème la on en parle
❤❤❤❤
dieuredieuf
Jërëjëf Yaa saydaa waxtaan Wi amna solo lool Maasàllaa Na Yàlla Gayla yîiw ku bëgga bokk ci gurp bi nag❤❤
Dieuredieuf- contactel abou fatima ci numero 77 763 02 41
❤❤❤❤❤maa Sha allah barakallah féer ka ya sayda🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Mane dh sayda woudiou sincèrement mane meunou mako mougn té waxx deugu mane kouma takal woudiou ma yamalé fi seuy bi tokk mogn dakh sama hol antalouko walahi anzim dama ko meunoul té beuguou ma def dra loy yakk sama waye
dëgg dëgg ligey 5 wa la 10 ans , djiguen gnew dila ko yaxal mom diaroul ko, lolou mom douma la ko conseillé de
@@Sokhnafatimalo sayda mane jai fait que. 2 ans et vraiment mane mome je préfère perdre que partager
@@MdmDieye Sokhna ci, yalla nagnou yalla may xolu mogn
@@MdmDieyevraiment 2ans moi MM pas 2ans yoron khaler 8 mois nou takal ma kouma dann ligueyal teh balegui beugouma woudier bi ms doko faler daguay khol sa dom rek
@@SeynabouBarr nabou cv si tu vois mon commentaire dit moi oui je te passe mn numero puis si tu capture je leffae
Machalla badiane fatima lo
Dieuredieuf
Waye ya sayda woudie nekhoul d
waw lolou dé deugu la, wayé bokk weurseuk la rekk
Macha Allah sougnou yaye yalnala borom bi soubhanahouwatala maye weure ak goudou fane yaw ak sa time bi
Alahouma amin gnou bokou ko
Ma cha alla, Sayda, figua dougou fofu la
Dieuredieuf
en kon baxna
Ma cha alla tan fatima lo ama tina solo
Dieuredieuf
Machallah
dieuredieurf
Dama beug bok si groupe bi
envoie moi message whatsapp ou appel 777630241
❤❤❤
Dieuredieuf
ma cha alla sayda yalla nalen yalla faye cadou yi rafetna
Dieuredieuf
Ma cha yalla
dieuredieuf
Machallah ❤❤❤❤
Dieuredieuf
yala na borome faye la
alahouma amin
❤❤❤❤
merci